Siteu Vs Modou Lô : Problème arbitrage ou pas ? Tapha Guèye apporte des éclaircissements

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 18 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 48

  • @seckbabacar3099
    @seckbabacar3099 13 днів тому

    Yene goor Yi Nek fofu yeup ay nafék guéne...
    Modou lo danouna❤❤❤

  • @abdourvms6034
    @abdourvms6034 13 днів тому +4

    Lac 3 roi des arènes ken douko négocier 😂😂💔

  • @MameSow-m7e
    @MameSow-m7e 13 днів тому +3

    Modou lôoooooo ❤❤❤❤❤

  • @MorWade-w7q
    @MorWade-w7q 12 днів тому

    Modoulo félicitations ❤❤❤❤❤❤❤😂

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 13 днів тому +4

    Pér 10% max mom day saboté ❌ na guem yalla rek

  • @azizdia3347
    @azizdia3347 13 днів тому +1

    Mais siteu do mbeur mounoul mbeurei amoul fitt

  • @senegalrek2579
    @senegalrek2579 13 днів тому +2

    Modou Lo moko def sakh bay beure ak Siteu thiow dithi am li moy nga yene nitt lou bakh mom mou yene la safan arbitres rék molen ate fala Siteu warone respect Modou lo

  • @johnwhyck8545
    @johnwhyck8545 13 днів тому +1

    Mais Tapha ; action bi amoul arrêt.. Tu déconnes la. Nawnala han. Mais la tu déconnes. Bi action bi commencer bamou diekhé lokho siteu miingui tchi lokho modou

  • @DembaDiop-ru4td
    @DembaDiop-ru4td 13 днів тому +2

    Merci pére tapha suite tapete la

  • @ogboss20-20
    @ogboss20-20 13 днів тому +1

    4 appui chute leu épaule dou chute Senegal nexna🤣🤣🤣🤣

  • @mbayembow7205
    @mbayembow7205 13 днів тому +1

    Siteu rek💪🏾💪🏾💪🏾

  • @aliousyll1590
    @aliousyll1590 13 днів тому +1

    😂😂😂😂 cage dè mom kène dou chautter pour daw 😅😅😅beugu raakk bagne raakk

  • @msn_pro8054
    @msn_pro8054 13 днів тому +1

    Tapha Gaye limou wakh deugue leu Siteu dafa bett niou beuri na dem wonné diambar té bayi daw bi sa moromou gaure di dakadji ngay daw rk

  • @aliousyll1590
    @aliousyll1590 13 днів тому +1

    Na siteu bayi di danou ba parè di togue plateau wakh pour lane, vraiment siteu moylolou quoi

  • @muhammatmbaygarmi7965
    @muhammatmbaygarmi7965 13 днів тому +1

    Waxleen siteu dëgg

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 13 днів тому

    ya takh lambe am aiye réglama😂

  • @MameSow-m7e
    @MameSow-m7e 13 днів тому +2

    Siteu gordjiguéne bi dawkinda bi😂démal nga tokk😂😂😂😂

  • @ModouDiop-d9n
    @ModouDiop-d9n 13 днів тому

    Xlo🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤kassé

  • @bayenarmbengue5839
    @bayenarmbengue5839 13 днів тому

    Pére tapha gueye oie ligua déf li lambou bou khalis takh guakoy yak dèle atè deugue tè yalla takh siteu dafa dane modou Lô 🙏🙏

  • @khadimgueye7007
    @khadimgueye7007 13 днів тому

    TAPHA MI DOU WAKH KATOU DÉGUI

  • @MohamedThioune-p9k
    @MohamedThioune-p9k 13 днів тому

    Modou lo beurou yalla la

  • @souleymaneouldmokhtar1485
    @souleymaneouldmokhtar1485 13 днів тому

    Kon do dan yekini efforts physiques

  • @muhammatmbaygarmi7965
    @muhammatmbaygarmi7965 13 днів тому +1

    Loolu su amoon keroog dibéer Modou Lo ray Siteu

  • @ositokifyh2687
    @ositokifyh2687 13 днів тому

    TAS 😁😁😁 comme si la lutte daniou ko reconnaître mondialement li Senegal la yammm ngeine nane TAS.

  • @dameka8103
    @dameka8103 13 днів тому +1

    Dafa dono dh

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    Siteu mo dant modou lo modou lo denko fabor

  • @thiourourtv6959
    @thiourourtv6959 13 днів тому +5

    tapha gueye wakhofi dara modou lo dafa danou nafekh bakhoul nila deméwone thi baye mandione wa lou takh arbitre louko yobouwone VAR dadone khol ndakh dielleu amna wale te action bi thi bir la commencer te sakh Siteu bi modou lo di danou tankam mongui thi kaw sakoubi ak 2me sakou bi loumouye diarigne merci Lutte TV sama lathe bi tontouléne ma

    • @mbayefall6262
      @mbayefall6262 13 днів тому +8

      Yaw yay nafekh danga far rek victoire dagnekoye mérité daw ba lamb dji diékh nga beuga dane mayléne nite gni diamou ta kholi lénéne lamb dji diekhna

    • @parlonsfoot2023
      @parlonsfoot2023 13 днів тому +3

      😂😂😂😂

    • @bayemo4147
      @bayemo4147 13 днів тому +3

      Iow miii yaye nafek bi tei wahofi dara

    • @cheikhmbacke2841
      @cheikhmbacke2841 13 днів тому +5

      Yaw ya nafékh khna lamdji amol réguelment sieu defena 4 apui

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck 13 днів тому +2

      😂😂😂 nanal ndokh boye

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 13 днів тому +1

    Modou lo diokhél Ndaye roi diamboure danôu ga 😂moye lou wére Moustapha gaye nafék la😂

    • @abdourvms6034
      @abdourvms6034 13 днів тому +1

      Kay ndy dieul si ko ioe. Lac 3 wkh len ko deug

    • @CheikhtidjaneSeck
      @CheikhtidjaneSeck 13 днів тому +1

      Nieuwal dieulsiko 😂😂😂😂 ma bolela AK les filles du quartier niou defal la bagage

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    pere tapha hamo bore

  • @Deggou
    @Deggou 13 днів тому

    Siteu le lutteur le plus surcoté bou amoul wone mbollo heure bi aye yawou dial laay beuré, beurék mome sakh daflay niaklo fayda xalé bou ndaw niou mayla chance nga daw combat bi yeup nga danou ba paré ni nieukeunté ci plateaux yi pour tek xeel...

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    Pere tapha yow do dara nafekna

  • @MoussaSene-q6t
    @MoussaSene-q6t 13 днів тому

    Tafa ya khame lamb

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    Yow hamo bore

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    Pere tapha da iniant

  • @SambaSene-j1h
    @SambaSene-j1h 13 днів тому

    Lambe gnoko mome souise warougnon até siteu na gaime yala beréwoul daw la daif bognou dane ko

  • @MbodjAmadou-dw3sh
    @MbodjAmadou-dw3sh 13 днів тому +1

    Nafékh bou Fass❌

  • @YAYACRISYAYACRIS
    @YAYACRISYAYACRIS 13 днів тому

    Yow waho dega

  • @muhammatmbaygarmi7965
    @muhammatmbaygarmi7965 13 днів тому

    Mère boobu ku naafeq la