Non il veut du buzzz , car il a été oublié. Donc il communique pour xéwatt touti. 😂😂 Modou lo menoul beuré neik roi des arènes. Cest comme dire que messi ou chistiano ronaldo meunou niou football .
@@ThiamelSow-gd7vq Ba paré teksi sa Yaye 😂😂😂mou gueuna nékh ba nga djoudou si 😂😂😂Yaye Modou lo thiaga lawon nioun nioko donn djoutal si tounn li nioko done katt si mbedmi tounn bou nékh teh yatou la yorré 😂😂😂
Même si il est pas performant en tant que lutteur il faut l’écouter en tant qu’un sportif qui donne son avis et son point de vue , ses arguments sont fondés et peuvent être écoutés même si on est pas forcément d’accord c’est des arguments qui peuvent être écoutés
De toute façon il faut saluer son courage… il parle ps pour parler il argumente ces propos…. C une question de choix ni de méchanceté ni rien pr moi Modlo est un meilleur pck il sort des situations difficiles et c un génie 🧞
@ ils veulent tjrs entendre des superlatives sur eux ou leurs lutteurs sinon tu es méchant ou une chose de ce genre mais la beauté c qu’il y’a plusieurs profils différents de lutteurs 🤼♂️
Chuis un fans de balla mais dans l histoire de la lutte sénégalais modou lo fait partie des 5 lutteur les plus technique meuno lim 5 mbeur you dak beuré Senegal t doko si bolé dieulé ko si niom falang falay baldé mbaye gueye ba tey nak boy bi defa sokhor
Laye mbeur du sohar Modou lo la tudone Mouy dem bagne kay wakh Modou kharagne lo après nékha faral dimanche vraiment Modou lo c'est le meilleur avec sa taille Modou est le meilleur que eumeu sene c'est la vérité . Laye allait travaillé pour que demain ga nek champion points ❤❤
Modou sans xeex bi Modou dafa toj pappat ñëw toj arène bi ngani manul bëri wéroo. Modou jekkuko taxul nga daan ko. Modou wér nanko domba, jël tànk te daanuñuko. Kii fumuy seetaane làmb😂
Wa lutte tv ay vrai goorjiguéne ngén beugu boy bi wah lou niaw rek motah ngén dem dieulate ko mais modou meunoul beuré mom mogui melni ngani messi meunoul football rek
Non Sénégal nekh na nk Lay Gorhé Moy kane ba war niou wakh Modou lô mane Wala meunoul mounoul beuré ,Ñari Boy pikine ti modou kou la si diapppp nga bouppp sa toubeuy
Kii depuis son combat contre laye Pythagore modou lo wax ni poulain wam mo méun fouff lako diapal haine et pourtant si combat modou lo avait raison daniou leu fek thies gay daw combat bi yeup B beuger buzz dagay lal borom buzz bi modou lo mais yaroul féxé egg fi modou lo egg
Boy Niang bi Sénégalais yi done wakh nane balla gaye mofi dakha beuré, il disait que non dakhouko beurè, té dafa nieuw danko avec la manière....boy yi kharagn molén Di déranger....
Menoul beuré tei moy sa roi 😂😂 Toi qui sait lutter pourquoi tu n’es pas roi des arènes ??? 😂😂 Le poulain de Modou Lo ( Laye Pythagore ) t’as battu à domicile (Thiès) Quelle contradictoire ! 😂😂😂😂
Boy gouté damané wakhou malla Modou anta sa Mack mé thiés AK mikou weur mbeur bou mélné Modou lo doufa am wa thiés yeup sou niou andoune nioume nieup Modou lo mouléune mane
Wa mome laye mi khana amoul loumou def wala buzz la beugue pour ame combat ndakh dafa tarde si lamb dina yekha nek champion Modou rawnala doussa morome doussa mass
Combat bi kouko khol nane Modou mounoul beure wakh diou yakhou la Modou fekna Eumeu si meuninam dane ko sou mounoul wone beure doussi guene yow nak Laye kou yabate nga bayi nagn la ak Laye Pythagore
Thiés la deukkk mei bale léne niou🙏
Non il veut du buzzz , car il a été oublié. Donc il communique pour xéwatt touti. 😂😂 Modou lo menoul beuré neik roi des arènes. Cest comme dire que messi ou chistiano ronaldo meunou niou football .
Modou yalnako yalla samou
Amine sibareké all latife
Nianal ko sa boppou mo geunne😂😂😂
Même pas besoin de regarder la vidéo mais ioe Poulin Modou Lo laye pytagor mola fekeu sa deukeu nonkou la gua dawe lamb j yeupeu
Modou lo aka gawa djoutou nak siteu rék mou beug djoutou watt ni 😂😂😂 siteu moko douma youbouko ardo beuréloko Bamou sonou mou dane ko djeul bou lérr motah fane yi nguen di mèrr kou wakh nguen défko nooonnnou Modou lo 😂😂😂lilenn nakari siteu molen ko ték dou kennn
Djoutal senn yaye rék senn xol yi di jéhh Kassé nak 😂😂😂
@ dawe lamb dh yepeu nan beuré fou recour bi tolou 😂
@@récré-o1dcomme sa papa numouye diouteulé sa yaye rék chaque goudi 😂😂
@@ThiamelSow-gd7vq
Ba paré teksi sa Yaye 😂😂😂mou gueuna nékh ba nga djoudou si 😂😂😂Yaye Modou lo thiaga lawon nioun nioko donn djoutal si tounn li nioko done katt si mbedmi tounn bou nékh teh yatou la yorré 😂😂😂
Môme esk dafa attaque laye Pythagore 😂😂😂yaw guay tapét démal Dakar 😂
Champion laye gotté 🔥🔥🔥
Même si il est pas performant en tant que lutteur il faut l’écouter en tant qu’un sportif qui donne son avis et son point de vue , ses arguments sont fondés et peuvent être écoutés même si on est pas forcément d’accord c’est des arguments qui peuvent être écoutés
De toute façon il faut saluer son courage… il parle ps pour parler il argumente ces propos…. C une question de choix ni de méchanceté ni rien pr moi Modlo est un meilleur pck il sort des situations difficiles et c un génie 🧞
Senegal mo nèhouta wakhè..pourtant limou wakhni c'est vrai..eumeu sène molène geuneu complet
@ vraiment les gens ont une mauvaise compréhension et écoute
@@ISmile__ ignorance mon frere c'est de l'ignorance
@ ils veulent tjrs entendre des superlatives sur eux ou leurs lutteurs sinon tu es méchant ou une chose de ce genre mais la beauté c qu’il y’a plusieurs profils différents de lutteurs 🤼♂️
Tu as parfaitement raison frère
En tou cas tu est direct tu fais des belle annalise macha alla
Quelqu’un qui dit ça tu l’ecoute ?
@SeydinaNdiaye-gs1ox wawaw il donne sont poin de vue
Eumeu dieulna tankou modou 2 fois lo wakh si lolou
3 fois la sakh
Eumeu djeulna tankou Modou 2X Modou guene thi mais esk Modou djem na djeul tankou Eumeu bene yone!?? Lamb bobou lep Eumeu moko deff ba sonou
@@papadiom9260Modou ben def leu def rk lamb J diex donc daa diara def lenen mou doumako dane ko diel bou reuy ngay wax lenen
@@papadiom9260 eumeu mo def leep té moudié daanou😂 😂 ça veut dire que eumeu amoul kham kham ci beurré
@@koulaalhakk8975 Lolou dou niaak kham kham… problem endurance la amone thi combat bobou ndakh masse bimou djeulone te yakaroul wone beurer lou yaag tamite
Laye Gotté et Modou Anta seuls❤🎉 Thiès derrière vous ❤🎉
Sa combat yi Di gneuw yeup yalla gua am défaite amine
Bilaye laye wa kham lamb linga fi wakh lépou deugleu
Laye verite rek la fi waxe
Champion Laye gotté❤
❤❤❤❤❤laye goté ya woree❤❤
Signature guen takk radio ba paré guen beugue nieuw rk beurre Day yombou
Avec modou daguay khekh Baparé soga mbeuré 😂😂🤣🥷😎
😂😂😂😂😂😂boy felhel def li modou def
Niague diome nga déf sa morome yeupe raw nagne la si lamb nga néck fii di wakhe si modou lô ko khamené moy roi des aréne sokhor rék mola diap bilahi
Ay moromam bougne ko gnémè woul nak done Ay tapét di khol lou noy
Merci laye goté lou léer ga wakh
Ki champion la
Machalla amnasolo lambo rik kawakh
Waa Thiès daal nioo ngui sèn guinaw
Yow laye goté se combat ak Général bou fass warna takhow nak ..combat leu 🔥
Macha Allah lay ❤❤❤❤ lourér ngaye wakh eumeu seul diame si yaw
Laye mi môme la lay Pythagore fékone thiés diko wouli mouy daw Di weurr stade bi 😂😂😂
Yaw silence khamo lou khèw
Kon lay yagui insisté balegui si lolou😂😂😂
Eumeu mo dakh beurré té Modou dane ko niari yone ,nokhoul feulé
MODOU XARAGNE BIGUEN DI JALOUSIE YALLA MOKO SAMPE DIGEUNE SISSOU BA SONOU BILAHII SOKHOR BAKHOUL
IOE MI AM ATTAQUE SI BEURÉ LAYE PYATHAGORE DILA NONKOU GUA DAWE LAMB J YEUEPEU
C’est faux
Ki Moy Kane Kane sakh😂
Sa way yaw mbeur nga do reportaire do analyste do consultant diemal beuré dane bayi niit yi wakh dofff nga trop😂
Sa combat ak laye pitagor si lala.wédi defoufa touss lolou mo takh niou wedila do gawa beuréwate wakh mo guena bari dieuf dji
Non Sénégal nékh na yaw wérou 😂😂😂😂😂😂😂
Niakk diom wessouwoul mounane prince moy adversairam 😂😂makk prince foufffff
Siteu mo dane ndaye Modou Lô dieul bou léer kou mérr sa affaire leu
Félicitations YALMINE bi👑❤❤
Fans you gnak djom comme sen mbeur rk
Yow lii Modou Lo ame doko ame Ndakh dangua sokhor barke mame fallou Mbacké beug légi arrête wo di wakh ki vrai demue là franchement 😮
Chuis un fans de balla mais dans l histoire de la lutte sénégalais modou lo fait partie des 5 lutteur les plus technique meuno lim 5 mbeur you dak beuré Senegal t doko si bolé dieulé ko si niom falang falay baldé mbaye gueye ba tey nak boy bi defa sokhor
Je suis pas fan de Modou Lo, mais si tu veux voir les qualités de Modou Lo vas regarder son combat contre Paul Maurice et Less 2
Fekhél def say preuves comme Modou Lo mo gueune ngay mbaradiou ni rek
Laye goté AK alboury combat la
Laye yake samake tassé Nanou fadiéne ake modou lo wakho wone li
Ki nak wakhi dof rék lafi wakh Modou lo mounoul beré nak😂😂 ay way samba ya nékh
Sa guisse guisse am nga si raison dh
Laye goté thies amoul beur Bou dakkeu beuré modlo 👑
Laye waxi doff REK l'ay wax😂😂😂😅
Laye mbeur du sohar Modou lo la tudone Mouy dem bagne kay wakh Modou kharagne lo après nékha faral dimanche vraiment Modou lo c'est le meilleur avec sa taille Modou est le meilleur que eumeu sene c'est la vérité . Laye allait travaillé pour que demain ga nek champion points ❤❤
Boy bi dou champion
Laye gote khamo dara lii modou def
Fène ba paré di deugueul fène bi.
Toubab daf ni:l'erreur est humaine et persister dans l'erreur est diabolique
Modou sans xeex bi Modou dafa toj pappat ñëw toj arène bi ngani manul bëri wéroo. Modou jekkuko taxul nga daan ko. Modou wér nanko domba, jël tànk te daanuñuko. Kii fumuy seetaane làmb😂
Wa lutte tv ay vrai goorjiguéne ngén beugu boy bi wah lou niaw rek motah ngén dem dieulate ko mais modou meunoul beuré mom mogui melni ngani messi meunoul football rek
Bilay y'a soxorr😂
Lay goté vraiment yay domérame deug deug 😂😂😂😂 vraiment amo kham kham 😂😂😂
Kii soxor moko diap Kom eumeu sene Ai domeharamlen
Eumeu yapp gagnou nak, mane je pensais laye gotté un grand lutteur ndéké niveau prince😅 ba paré di wakh ci modou lo le roi
Eum ya gnakkeu horom
Laye vraiment amo kham kham
Laye yalla nga danou li dèss sa lamb yeup amine ya rabbi ioe soxoro sakh
😂😂😂
Legui eumeu bimou diapé tankou modou lo loumou si def😂😂😂😂😂
Amal diom sa morom yép raw magnoula
Lay bagnul Dara combat la rek😂xalis après danu
Ki dou champion te beurina wakh
Walahi taye nak la khame nie laye gotté mi foo ta sokhor
MODOU BOU MANOUL BEURÉ KÉN MANOUL BEURÉ😢😢
Laye mi kou sokhor la
Laye Tu à raison dh eumeu mo dakha beurre mes Modou champion tmt té meune n'a beurre ❤
Laye pytagor filaleu diap doumala you méti 😂 ta Poulin Modou leuh 😂😂
Sokhor motakh mouno am combat balègui
Non Sénégal nekh na nk Lay Gorhé Moy kane ba war niou wakh Modou lô mane Wala meunoul mounoul beuré ,Ñari Boy pikine ti modou kou la si diapppp nga bouppp sa toubeuy
Eumeu dieulna 2foi tankou modou lo meunouko dane😂😂😂😂😂😂
Kikanla. Xana dafa beugue siiw 😂😂😂
Ki dal amoul kham kham fans eumeu sene la 😅😅😅😂😂😂😂😂😂
Laye buzz lay weurate gayi nioko faté si lamb dji merci laye
Wa kone mbeur yi si dess khamouniou dara kone
Boniou kholè ba kou menoul beurè nek Roi
Ki esk tohoulll si Bone yii magam dii dieulll😂
Yaw vrai domérame nga, yague Eumeu ay Doméramau ngéne
Mome ak pape ndoye
Kii depuis son combat contre laye Pythagore modou lo wax ni poulain wam mo méun fouff lako diapal haine et pourtant si combat modou lo avait raison daniou leu fek thies gay daw combat bi yeup
B beuger buzz dagay lal borom buzz bi modou lo mais yaroul féxé egg fi modou lo egg
Boy Niang bi Sénégalais yi done wakh nane balla gaye mofi dakha beuré, il disait que non dakhouko beurè, té dafa nieuw danko avec la manière....boy yi kharagn molén Di déranger....
Khawna laye goté khawma laye mboté mais bouma niafé sa khone dingua nekk nittt 😂mbamou kharam bingua doonn
Ki kou nday sokhor la
Lay goté amal diame ❤❤❤❤
Djaroul sakh sétane
Meunoul beuri yaw ya meuna beuré té meuno dane mbeur
Amolene sakh kholou djoulittt sokhor bakhul
Eumeu mome ki meunoul beuré mokay wowé
Ioe sou la prince diappone dalay ray so moytoul😅
Ki khadioil qi prince
Menoul beuré tei moy sa roi 😂😂
Toi qui sait lutter pourquoi tu n’es pas roi des arènes ??? 😂😂
Le poulain de Modou Lo ( Laye Pythagore ) t’as battu à domicile (Thiès)
Quelle contradictoire ! 😂😂😂😂
Kiii ban ecurie laa nek
Ki dé c'est le petit frère de Modou Anta Thiès
Waa Kii nit la😂😂😂😂
Ki dafa dof yaw dodem fen Modou dalena raw dof bigua don😂😂😂😂😂😂😂😂
Khana da nga banque niatte avance 😅😅😅😅😂
Ki dafa begue khéwat rek😂😂😂😂😂😂😂😂
Sa wakh dji amoul ben sens wakhi kasaw kasaw kassé nga wakh
Lay modou sa morom la yako eupp souteko niakk diome motax avancé wo si lamb yambar nga rk
Boy gouté damané wakhou malla Modou anta sa Mack mé thiés AK mikou weur mbeur bou mélné Modou lo doufa am wa thiés yeup sou niou andoune nioume nieup Modou lo mouléune mane
Li moy djiko sénégalais modou Anta tn frère défoul dara thi lamb nga ni professionnel leu, yow défo gatt ngani ndanane nga.Modou Lo rois des arènes ngani manoul beuré.Yaye domou khathie yow foo tothie?
Wa mome laye mi khana amoul loumou def wala buzz la beugue pour ame combat ndakh dafa tarde si lamb dina yekha nek champion Modou rawnala doussa morome doussa mass
Doula tina 😂😂😂😂
Yw diémala déf li Modou lo déf sarap ndym khamoko
Combat bi kouko khol nane Modou mounoul beure wakh diou yakhou la Modou fekna Eumeu si meuninam dane ko sou mounoul wone beure doussi guene yow nak Laye kou yabate nga bayi nagn la ak Laye Pythagore
Boy yangui rectifier deh
Ndeysane ki si buzzou modou lagne ko inviter
Laye no beugué wakh ak borom xam xam yi té amo xam xam 😂😂