Sa Cadior nous explique son combat contre Modou Lô en Mbapat : "damako weur ndomb ba yakar mou..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 лип 2020
  • Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    luttetv.com/
    / senlamb
  • Спорт

КОМЕНТАРІ • 333

  • @elzyau5182
    @elzyau5182 3 роки тому +74

    Merci mbeur wax deug lou baxla boula néxone né guédiawaye ga deuk di wax loula néx ken dou champion Kharagne Lô👍🇸🇳💪

  • @ibrahimadrame2301
    @ibrahimadrame2301 3 роки тому +65

    Thiéy Mamadou lo 😭😭😭😭😭 thiéy kharagne lo 😳😳😳

  • @abdoumane7700
    @abdoumane7700 3 роки тому +43

    Sa Cadior diam si yao deug rek ngaffi wax Modou champion la

  • @khaliloulah3703
    @khaliloulah3703 3 роки тому +64

    Tiey XLO TOLOUL NI NIOM D MAIS JAMBAR DEUG LA YALNA ROI BI YAGUE !! SA KADIOR AMAL DIAM AK WEER

  • @moussadiop643
    @moussadiop643 3 роки тому +12

    Mashalla je suis heureux que tu nous revienne en bonne santé et nous raconte de très belle histoire gueuneu doundou gueuneu wérr 🙏🏾🙏🏾

  • @nittoudeugg3025
    @nittoudeugg3025 3 роки тому +23

    Sa cadior 2 est un vrai guerrier bilahiiii lamb jii moo doyy warrr rekk

  • @boubafall1014
    @boubafall1014 3 роки тому +70

    MODOU LO dalle c'est tout simplement le meilleur sa cadior ya goré

    • @beniciocolby4549
      @beniciocolby4549 2 роки тому

      i dont mean to be so offtopic but does any of you know of a method to get back into an instagram account?
      I somehow forgot the password. I appreciate any assistance you can offer me!

    • @marceloenrique2294
      @marceloenrique2294 2 роки тому

      @Benicio Colby Instablaster =)

    • @beniciocolby4549
      @beniciocolby4549 2 роки тому

      @Marcelo Enrique I really appreciate your reply. I got to the site thru google and im in the hacking process now.
      I see it takes a while so I will reply here later with my results.

    • @beniciocolby4549
      @beniciocolby4549 2 роки тому

      @Marcelo Enrique It worked and I finally got access to my account again. Im so happy!
      Thanks so much you really help me out :D

    • @marceloenrique2294
      @marceloenrique2294 2 роки тому

      @Benicio Colby happy to help xD

  • @ahmadouifraba
    @ahmadouifraba 3 роки тому +25

    Akeu niakeu kiniane sa cadior? Modou lo 4ever💪💯💞

  • @ousmanediallo2585
    @ousmanediallo2585 3 роки тому +56

    Salam malaycoum champion je suis trop fière de toi tellement tu dit la vérité il y a des gens qui disent pas vrais quand quand ils sont lutté contre modou lo mais toi sincèrement tu es quelqu'un très reconnaissant que Allah soubhana watalla vous récompenser et vous protéger contre tout le mal INCHALLA

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye9016 3 роки тому +43

    Hooo sama xoll sédna trop vrément ♥️♥️♥️.....Sa kadior Yallah Nala souniou borom Dolli taxawou Dolii la wérr ak katann thi barkèp cheikh Akhmadou Bamba khadimou Rasoull ♥️🙏

    • @daoudambow8348
      @daoudambow8348 3 роки тому +4

      kéne dou kharagne lo la niou la wakh😂😂

    • @tijol8276
      @tijol8276 3 роки тому

      Amine wayy mais Modou migui niew dh dàl sa kaw

  • @daoudambow8348
    @daoudambow8348 3 роки тому +38

    Thiey kharagne lo le roi👑🙏🏿

  • @galayediop3150
    @galayediop3150 3 роки тому +29

    vraiment mbeur iniano nak koi.q dieu t protège

  • @Diantal
    @Diantal 3 роки тому +18

    Merci mbeur lii dara nekouci wax lou rafet la rek yaxul si sa champion dara

  • @tidianesall3124
    @tidianesall3124 3 роки тому +15

    Lamb Waxoul Deugue Bilahi Walahi mais keine dou Sakadior 2 le Pathere noire de Guediawaye Yama dieukk yobou stade champion bon Rétablissement

  • @sadiodiallo5032
    @sadiodiallo5032 3 роки тому +11

    Ndeysaann sa cadior dafa meussa am talubé waxx dji rafett na massah Allah

  • @mohamedndir726
    @mohamedndir726 3 роки тому +16

    Machallah mbeur yaw amale diame sa holle mo raffett courage

  • @ndiawlo1862
    @ndiawlo1862 3 роки тому +22

    Modou lo rek bilahi

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 3 роки тому +10

    Sa Cadior bon rétablissement et bon retour ci Lamb ji. Machallah wakh ji rafeite na

  • @wademouhamed3261
    @wademouhamed3261 3 роки тому +13

    Nice champion yalha na yalha wereul la inchalha 🤲🙏🥰

  • @Goroumaifall
    @Goroumaifall 3 роки тому +13

    Machallah sa kadior Nice na nieuwatall ak jam

  • @atomikatomik2772
    @atomikatomik2772 3 роки тому +43

    Ndanane rék moy reconnaître ndananou moromam !!

  • @alamiinetv3707
    @alamiinetv3707 3 роки тому +6

    Machallah sa cadior yalla nala yalla défal diam dolila wérr

  • @OureyeSeck
    @OureyeSeck 7 місяців тому +3

    Sa champion la Modou jambar la étoile borom diom c le phénomène de la lutte senegalais❤

  • @azoutheboss9319
    @azoutheboss9319 3 роки тому +8

    Merci beaucoup Sa Kadior . Modou Lô est le vrai roi des arênes. Il est le meilleur 👑

  • @lesamouraisnoir5304
    @lesamouraisnoir5304 3 роки тому +20

    Ndanane bii ligua wakh deug la lamb chanse là rek ndeysane

  • @mbayendiaye2793
    @mbayendiaye2793 3 роки тому +17

    Moudo rek la boy ,🔥🔥🔥

  • @bayfall9707
    @bayfall9707 3 роки тому +5

    Champion la nga chance rek mola manqué yalla nala yalla defal diam 🙏🙏

  • @khadimsow7149
    @khadimsow7149 3 роки тому +6

    Merci champion yalla na tan gui yokou 😍🙏

  • @cheikhdieng2456
    @cheikhdieng2456 3 роки тому +16

    Merci Champion nice na trop 👍🏼👍🏼

    • @abibtoure3424
      @abibtoure3424 3 роки тому +1

      Hola I have a have to you and to

  • @boubajunior9401
    @boubajunior9401 3 роки тому +7

    Champion bi sacadior ❤🙏🏾yalna sa diam yague

  • @asssow180
    @asssow180 3 роки тому +19

    Lila beugue si nite wakh deugue même budé dagnu laye raye modou lo phénomène leu si lamb gnou beuré mbapate kéne messou ni neke morom geine eupe ko dolé fouff ☝🏾☝🏾☝🏾dou bayou mbeur dou nidiaye mbeur lamb du amati mbeur bouni méle bou bayé lamb meu bayi lamb☝🏾👑👑

    • @khadimmbaye7945
      @khadimmbaye7945 2 роки тому +1

      Modou Lô moyy Messi rek.
      Point c tout

    • @asssow180
      @asssow180 2 роки тому

      @@khadimmbaye7945 dafa leer

  • @mbayefall7583
    @mbayefall7583 3 роки тому +7

    Vrema sa catior je t'aime fort parce-que tu es très franche

  • @malickdieye1005
    @malickdieye1005 3 роки тому +4

    Machalah bonne continuation yalla na sa diam yague

  • @421paco
    @421paco 3 роки тому +3

    Lutte tv chapeau! Ça fait vraiment plaisir de revoir ces anciens lutteurs 👌🏾

  • @iboundoye5872
    @iboundoye5872 3 роки тому +6

    Alhamdou lilah baga amate santé

  • @gomissaliou2474
    @gomissaliou2474 3 роки тому +5

    Le Grand champion sa cadior 🙏🙏💪🤝👊

  • @maxfall3597
    @maxfall3597 3 роки тому +1

    Merci sa cadior yalla nala yala doli werr defalla diam

  • @Bigboss-hd8fx
    @Bigboss-hd8fx 3 роки тому +2

    Yallah nala Yallah maye diam, Yallah nanga weur ak diam bro from PA

  • @saliouba1881
    @saliouba1881 3 роки тому +8

    Yalla nasa diame yague si barké seydina mouhaméd

  • @assanediop2210
    @assanediop2210 3 роки тому +31

    Jajëf Sa cadior amal jamm mod'lô ndananla

  • @balisko7172
    @balisko7172 3 роки тому +8

    Machallah sa cadior diameu si ioe

  • @clientelaspalmas3721
    @clientelaspalmas3721 3 роки тому +7

    Machalla

  • @aboudemetalibebayeniass582
    @aboudemetalibebayeniass582 3 роки тому +4

    Ndeysan Sa iow amal diam jou bari inshallah

  • @tidianebiaye1573
    @tidianebiaye1573 3 роки тому +5

    Bon rétablissement sa cadior

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 3 роки тому +1

    Alhamdoulila yalna yalla yokou tane... sa cadior namonnagn la

  • @cheikhvip4757
    @cheikhvip4757 3 роки тому +6

    diam si yaw sa ka doir 2 MX LO le roi kéne dou mom ❤️

  • @damembow6374
    @damembow6374 3 роки тому +4

    Yalla nala doli werrr

  • @abdoundiaye1016
    @abdoundiaye1016 2 роки тому +2

    Sa cadior yay nitou duege Modou lò mom c'est les champion

  • @cheikhsadiboufaye3028
    @cheikhsadiboufaye3028 3 роки тому +3

    Machallah sa cadior ndanane deug nga wone

  • @omarniang3624
    @omarniang3624 3 роки тому +4

    Yalla nala yalla défalla diam

  • @aliounediouf8278
    @aliounediouf8278 3 роки тому +2

    Mbeur 'nga balma me il faut guén geum mystique ndah thi lamb ji la Bokk guediawaye bamou dadie yafa meunon 💞💞

  • @amethlamine9772
    @amethlamine9772 3 роки тому +2

    Ndeysane Champion yalla nala yalla defal diamm

  • @moustaphadiop7336
    @moustaphadiop7336 2 роки тому +2

    Bonne guérison Sa Cadior. Yalla meuna lou barri.

  • @moustaphafadiga774
    @moustaphafadiga774 3 роки тому +4

    Bilahi ya goré boula néhone ngua satel champion ngua bilahi

  • @goroualdianna3274
    @goroualdianna3274 2 роки тому

    Merci beaucoup

  • @yassineelbakkouri5299
    @yassineelbakkouri5299 3 роки тому +14

    Bilay lamba wakoul dege me ki bere rek lay Def

    • @yassineelbakkouri5299
      @yassineelbakkouri5299 3 роки тому

      Ki dafa feke lepam bilay may bere lur mou nek lese di Def Lou nek

    • @melotv2441
      @melotv2441 3 роки тому

      Mieux qu'il arrête la lutte 🤼‍♂️ reste là-bas travail

  • @lancerobuur6888
    @lancerobuur6888 3 роки тому +2

    Sa yalnanga am Lou geuneu lamb 🙏🏽

  • @bipsall7335
    @bipsall7335 3 роки тому +3

    Champions la bilaye yallah xamenako

  • @bayfalllabeuguedonne6756
    @bayfalllabeuguedonne6756 3 роки тому

    Yalnala yalla defal diam

  • @balladiagne9144
    @balladiagne9144 3 роки тому +2

    Machala ki cou bah la ndayesan

  • @papamoussagueye1415
    @papamoussagueye1415 3 роки тому

    Sa Cadiore yalla nala yalla dèfal diam ya xam lo beugu sa adouna yalla nalako yalla dèfal 🙏🙏🙏 damala yeinei Bilaei walaei dinga neik yalla nalafa sa weurseuk feik nga diarinio ko yak say mbok big up way

  • @babacarndao3940
    @babacarndao3940 3 роки тому

    Merci frér

  • @nicolasfaye1436
    @nicolasfaye1436 2 роки тому

    Mancha alha ya goré sacadior yalna sa diam yague

  • @organeboromerevuedepressey6356
    @organeboromerevuedepressey6356 3 роки тому +9

    Machalla wakh dji rafait na👍

  • @lapaixlapaix8873
    @lapaixlapaix8873 3 роки тому

    Machalla il a un bon memoire

  • @arfangsenghore3993
    @arfangsenghore3993 3 роки тому +11

    Happy for u bro modou lo ndanane la👍

    • @mansourdieng2000
      @mansourdieng2000 3 роки тому

      Balla Gaye C'est Le Meilleur ❤❤❤❤

    • @layekharagne2224
      @layekharagne2224 3 роки тому +1

      Mansour Dieng yow vrai sissoumane gua titre bi c modou , modou dafa dane sa cadior djell bou rey mbapatt te sa cadior amna niouy nane mo dakkone beurrè bir guediawaye , nangoul li yalla dogal te gua bayi sokhor

    • @mansourdieng2000
      @mansourdieng2000 3 роки тому

      @@layekharagne2224 😂😂😂😂😂😂😂

    • @patedioptouba100kharagnelo2
      @patedioptouba100kharagnelo2 3 роки тому +1

      @@layekharagne2224 layé kharagne

  • @cheikhabdoulayeder4733
    @cheikhabdoulayeder4733 3 роки тому

    Gore pur gua nala diam sonal frère 🤲🙏🏻

  • @videosdujour7481
    @videosdujour7481 3 роки тому +1

    Merci sa cadior wéral ak Diamou

  • @mouhamedndong6285
    @mouhamedndong6285 3 роки тому +2

    Abdou Gueye Sa Cadior champion Deug leuhhhhh bilahi Mbeur Kamil leuhhhhh Lamb Mo Doywar mais Mbeur Amall Jamm Way 👌 👌

  • @babasane7404
    @babasane7404 3 роки тому

    Machallah sa cadior yaw dangua sincères vraiment

  • @cheikhmodou555
    @cheikhmodou555 3 роки тому +1

    💪💪nice

  • @sambandiaye3707
    @sambandiaye3707 3 роки тому

    Yalla na yalla may la diam

  • @momotouray172
    @momotouray172 3 роки тому

    Mashala Vraiment Guerier Nga sokharo Si Modou Lô Bilahi Ndanane la

  • @laminediop7896
    @laminediop7896 3 роки тому

    Nice ❤🙏🙏🙏

  • @matarsarr2022
    @matarsarr2022 2 роки тому

    Champion yallana yalla douli Diam 💪❤️❤️❤️

  • @amadousall9510
    @amadousall9510 3 роки тому +1

    Mbeur courage

  • @moussasarr8277
    @moussasarr8277 3 роки тому +8

    Mdou lo vraiment ndananela

  • @morseye4084
    @morseye4084 2 роки тому

    Thiate bakhoule sa yalnala yalla d'éfale diama si barke mouhamed psl

  • @toubadieng8547
    @toubadieng8547 3 роки тому +5

    ❤❤🙏🙏🙏

  • @tijol8276
    @tijol8276 3 роки тому +2

    Modou lo c'est le Méssi de l'arène bagn bagn beugu tolloul ni gayi dh mais amoul mbeur bouko gueun palmarès mashalah notre roi!

  • @ablayewade1583
    @ablayewade1583 3 роки тому +1

    Sa kadior ya bakh 📿🤲💯

  • @kingbigrocky6017
    @kingbigrocky6017 3 роки тому +1

    Yalla nala yalla dafal djamou

  • @ahmaseck5719
    @ahmaseck5719 3 роки тому +1

    C bien

  • @drameserigne2871
    @drameserigne2871 3 роки тому +4

    Xaragne lo nagua woo sa kadior guéne dégeunté, lamine dokhal lolou plz

  • @ansukoulibaly3076
    @ansukoulibaly3076 3 роки тому +1

    sakadior 💪💪💪💪💪💪

  • @topkhadim3707
    @topkhadim3707 3 роки тому +1

    Ndaysaan

  • @momombaye1114
    @momombaye1114 3 роки тому +15

    Abdou kassé le panthère noir au tant gniy ko done wowé le technicien de guédiaway bon rétablissement

  • @nopipape8870
    @nopipape8870 3 роки тому +1

    Sa cadior le grand champion

  • @juniorbalde3355
    @juniorbalde3355 3 роки тому

    Champion

  • @paaliounembaye5021
    @paaliounembaye5021 2 роки тому

    Ndeysane sa champions la

  • @ndiayeibrahima1432
    @ndiayeibrahima1432 3 роки тому +6

    Tiey Modou ak balla

  • @assanebabaofficiel3533
    @assanebabaofficiel3533 3 роки тому +2

    Sa cadior respect thi yaw sa ndadane bii

  • @jamesgaye1517
    @jamesgaye1517 3 роки тому +1

    sa amale diame merci lamine rafetna

  • @bayedaroubi7412
    @bayedaroubi7412 3 роки тому +2

    Nite kou goré ngui ni goudeul fane❤

  • @mohamedndiaye8600
    @mohamedndiaye8600 2 роки тому

    Bonne guérison

  • @moussasoumare5875
    @moussasoumare5875 3 роки тому

    Machalla chiampiion

  • @drameserigne2871
    @drameserigne2871 3 роки тому

    Machalla geun nala beug dakh xaragne lo mi gua wakh lou bakh

  • @kasse9508
    @kasse9508 3 роки тому +1

    Sa Cadior iow goor yalla nga barkii serigne bamba

  • @amethndiaye2214
    @amethndiaye2214 3 роки тому +1

    Wax sa mbaxou way dou wañi ci sag mbaxx dara té lo bañ bañ ñombar sédélko gatt guéén ak meuneu daw Sa kadior beug nala wayy😍

  • @ibrahimacissokho2525
    @ibrahimacissokho2525 3 роки тому

    Mbeur champion amal diam