Ci histoirou lamb Modou mo ci dakka beurrè sa cadior mo dakkone beurrè guediawaye da worr ndomb modou , modou mbott ko ci wor ndomb bobou wallahi Modou c le plus grand des ndananes
Jamais modou lo dou meusa arriere a cause de ama kharagne moko guena bandit 100mille fois eupe ko fitt dako beurei machallah arbitre siffler mo derriere kou yi dioli 🤣
Aminn yalna carrière bi égg si mbeur yi mais modou Lo pour niou respecter ko deug il fau mou danne les 2 yi geun teu insbi si lamb pour niou xam ni il mérite le couronne 👑
Modou lo Moy lutteur bi gueneuh mérité couronne 👑 si lamb j ndakh daniou wahone ni toloul ni mbeur yii menoul nek Roi etc ... T boulen faté li thiow li di beuri yeup 2 mbeur rek Nio dann Modou t niari ancien Roi des Arènes nioko dann naniou respecter Modou c'est un très grand champion ❤ le Messi de l'arene 🤴
Sa Cadior daal dafa diappp ni Ama dafay daane Modou Lo si ay Secondes… Lolou ngay bania wakh. Dioummm nga nak… Ama Balde euppoul doleee Emeu SÈNE euppoul doleee Bombardier. Modou Lo beureee neu ak nioniou. Demm lene rekk.
Vraiment sa kadior le champion yallah nala yallah dolli wérr ak soutouro inchallah
Sa cadior mom lou bkh rk layy wakh thi modou lo🥰🥰🥰
Ci histoirou lamb Modou mo ci dakka beurrè sa cadior mo dakkone beurrè guediawaye da worr ndomb modou , modou mbott ko ci wor ndomb bobou wallahi Modou c le plus grand des ndananes
😂😂😂
Bilahi walahi kèneu d'où kharagne Lo
Louleer
Bilay wakhatiko frérot
Billahi wallahi modou lo ndam rek inchallah 👂👈👈☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Kou nieuw bahna Modou gasse❤❤
Kén dou mod lo❤❤
Ama Malick Niang esk attaqué na modou lo lépp lay beuré machalla adversaire bouné amnako
Kou nieuw bahna Modou lo rak
Sa kadior sa façon de parler je s'en il as de bon cœur
Sa kadior champion bou makk guoudal fann mbeur❤
Grand Fadam 2 Modou Lô danome diékh na si lamb inchallah bou sobé borom bi ✊✊✊✊✊
Mbeur yi daniouy door pour outt bountou, mais attention modou lo day door pour gaagne là
Bilahi Ama mounoul beuré am a doolé nak machalah
Jamais modou lo dou meusa arriere a cause de ama kharagne moko guena bandit 100mille fois eupe ko fitt dako beurei machallah arbitre siffler mo derriere kou yi dioli 🤣
Modou Lô dina beurré ba bayile roi des arènes bi inchallah 👆👆👆 diokh ko Franc 👉👈👉👈
X lo késsé❤️
Je suis fans modou lo mais sa cadior parole yii nice na trop modou dèga wakhi sa cadior yii diarna bayi khel boulfatè nii roi gaaa yor dh bakhna
Aminn yalna carrière bi égg si mbeur yi mais modou Lo pour niou respecter ko deug il fau mou danne les 2 yi geun teu insbi si lamb pour niou xam ni il mérite le couronne 👑
Lolou sa mbakhalou kherrrr leu 😂😂😂… Modou Lo kouy weranteee meritam si lamb wala couronne bi dafa fekkk nga faralll ay adversairamm
.
Modou lo Moy lutteur bi gueneuh mérité couronne 👑 si lamb j ndakh daniou wahone ni toloul ni mbeur yii menoul nek Roi etc ... T boulen faté li thiow li di beuri yeup 2 mbeur rek Nio dann Modou t niari ancien Roi des Arènes nioko dann naniou respecter Modou c'est un très grand champion ❤ le Messi de l'arene 🤴
Boy Niang 2 amoul chance si Modou Lô dou lale touss inchallah 👆👆👆
Modou yalla nako yalla soutoural
Merçi sa Kadior
sa kadior wakh na deugue modou sou beugué dane ama il faut que mou reculé deff comme contre eumeu sene
Pour dire vrais Modou lo il n'es pas le meilleur mais il fait parti des meilleur de sa génération
Il est le meilleur de sa génération bayil sisou
Taffa ❤❤❤❤❤
Lamb wakhoul deug mbeur kamir moy wakh ni menn
Billalahi
Fadame war ngama dieul wakh tane ci lamb nak mangi Amérique 🇺🇸
Macallah sa kadior
Bilahii walakhahi modou lo khamnani ama arengé wouko
Modou mayou yalla la am
Sa cadior wakhal lo kham modou lo amoul loumouy calculé thi ama
Calcule mor takh mou daw Ama 4 ans Ama Moko mun Moko opeu dole Fouf
Sa Cadior daal dafa diappp ni Ama dafay daane Modou Lo si ay Secondes… Lolou ngay bania wakh. Dioummm nga nak… Ama Balde euppoul doleee Emeu SÈNE euppoul doleee Bombardier. Modou Lo beureee neu ak nioniou. Demm lene rekk.
Sa kadior wahna lep modou lo niémé woule ama
Modou kharagne Lo papam mbeurou pikine yeup
Modou duu ragual deh daffa bayyi mou yollim rek
Niune fans ama yi luniu beugeu mooy. . ngén wax modou mo meune ama . loolou mooniu arengé
Modou midi né
Nioune Modou rek
Moy yone
Ama bou difi come balla daye danou ama bokol ak balla
Lolou lagn khamoul nak
Je suis fan de modou lo mais boy niang2 mo eupp chance dane modou que ama
Diamono yi dane Boy Niang 2 mo geuna yombou que niou dane Ama Baldé 🤷🤷🤷🤷🤷
Sa cadior ieo kou bah nga mes deux boy pikine yii modou dina lèn dann nèkeu president pikine lègi senegal bi nieup dccord ke bayyou boy yii la
Modou nit meussouko agresser Bilae ama meunoul agresser modou
Balla Gaye aggreseur kor Dan kor
@@Aki-id7kowakho deug
Pourquoi nguènn wakh modou lo d'où arrière mok eumeu sene ak gris bordeaux ak bombardier yeup dafa arrière contre balla rék ladoul arrière
parske contre balla danioukoy djekkou
Deuk leu ligay déff sa khalé so magué doudone béne
Modou lo késsé
Yaw danga dof ama manoul dara si modou
Lou lérr la wakh
LOU LÉR NGA WAKH SI AMA MOTAKH MODOU DAW DI TÉK KHÉL FI DIEUL BOY NIANG...
Sa cadior parle en connaissance de cause modou dafa doynawar trop
Je suis fans de kharagne lo mais boy Niang dane ko mo ngeuna yombou Ama dane ko
Boule diakhlei beine boy amoule chance si Modou !
Mon frère tu as raison Modou certes il sera plus à l'aise mais boy Niang mo eup chance pour daann Modou lo que Ama
Modou Dina teilla daann Ama