Émouvant😭retrouvailles sa kadior et Gouye gui de pires secret dévoilé ndeysane lou rafet…

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 19 кві 2024
  • Bienvenue sur votre chaîne (lutte motivation)
    abonnez-vous ✔️ | partagez✔️ | commentez✔️| aimez ✔️|
    Toute l’actualité de la lutte sénégalaise et des contenues d’inspiration quotidien!
    Instagram ➡️ / lutte_motivation_officiel
    UA-cam ➡️ / @luttemotivation
    Snapchat ➡️ / zyp10ybm
    Facebook ➡️ share/agiApL...
    Tik tok ➡️ www.tiktok.com/@luttemotivati...
    Thread ➡️ www.threads.net/@lutte_motiva...
    Contacter nous sur Watsap 👉 77 265 29 18
  • Спорт

КОМЕНТАРІ • 71

  • @moussandaw8377
    @moussandaw8377 Місяць тому +8

    En 2009 on a fait etude de text . Avc notre prof d'anglais de l'epoqueet le texte parlait de Sa Cadior et dun de ses combat. Yalna yalla dolli leu tawfeikh

  • @user-ul4fy1up9b
    @user-ul4fy1up9b Місяць тому +23

    Machalla sa cadior Amal taneu bou bakh inchallah si barki yonete bi

  • @bayelayegueye4012
    @bayelayegueye4012 Місяць тому +3

    Saa kadior yalnala yalla may khoulo mounj ndah mou oyouf sa kaw

  • @MansourDiop-wd2or
    @MansourDiop-wd2or Місяць тому +13

    Ndayssan Lou am rafettt sou amoul wone mou niaw lii mom rafetna machalla

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 Місяць тому +7

    Mariéme faye sall khamoumako mé diambarlaa yalla nako yalla faye lou bakh yi mou done déf si domou adama yii amineeee inchalla

  • @ibrahimabadiane8252
    @ibrahimabadiane8252 Місяць тому +11

    Sa cadior khamna nitou kérsa nga mano rejeté bénn site mai ile faut nga rejeté lén am temps de récupération ku bakh nga machalla

    • @myamya6523
      @myamya6523 Місяць тому +1

      lolou la dafa yarou

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3n Місяць тому +11

    Ndeyssane yalna yalla doli tane champion

  • @user-ri5kc9tn4d
    @user-ri5kc9tn4d Місяць тому +7

    Sa cadior yalla nala yalla doli wér ténga moye tout suite yi khamal ligay wakh

  • @Ctnnn
    @Ctnnn Місяць тому +1

    En tout cas un grand merci à votre femme. Gorla diambarleu lou rare

  • @ousseynoundiaye7826
    @ousseynoundiaye7826 Місяць тому +7

    Wa quartier cheikh gnome namounayla defale tew.amale were amale diam. Amale halisse.meritéguaco ya gooré❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ms9ui1cw9s
    @user-ms9ui1cw9s Місяць тому +7

    Récupération récupération sa cadior❤

  • @khadimseck2600
    @khadimseck2600 19 днів тому +2

    Marem.fay aka bakhe ndaysan.

  • @djilymbow2216
    @djilymbow2216 Місяць тому +4

    Merci mareme Faye sall

  • @user-xf7bt2ow6h
    @user-xf7bt2ow6h 29 днів тому

    Ndéysan amna solo geste Mariéme Faye bobou rafetna Macha Allah

  • @MadiagneYade
    @MadiagneYade 29 днів тому

    SA yalnala yalla defal tane ak diam me wagnil media yi

  • @pirlo4478
    @pirlo4478 Місяць тому +2

    Boul wakhaté kéne si sa fébar dara 😢 té nga bayi guéne internet bi wakh bakhoul nitt yi da niouy nétali ak di partager yalla nala yalla samou té arr lh❤❤😭😭😭😭😭

  • @Al_Amir-soultan
    @Al_Amir-soultan Місяць тому +45

    Sa cadior nopalekoul t'ai moytou interview yi ngir yalla daga gnibisi pour nopalekou ohhhhh

    • @adiaratoudiao4134
      @adiaratoudiao4134 Місяць тому +12

      deug nga wakh frère; mais gars yi nioy nieuw si mom, menou si dara; yalnako yalla deifal jam.

    • @Al_Amir-soultan
      @Al_Amir-soultan Місяць тому +8

      @@adiaratoudiao4134 non dafa meti quoi yalla nako yalla tahawou bijahil seydil woudioudi wal ahirina

    • @massambandiaye233
      @massambandiaye233 Місяць тому +2

      Wakhal way

    • @amadougueye7044
      @amadougueye7044 Місяць тому +2

      Saway dafa beug lamb

    • @anissediatta69
      @anissediatta69 Місяць тому

      Vraiment

  • @massambandiaye6150
    @massambandiaye6150 Місяць тому +8

    Sa cadior démal nopalou site yi vu rek légni woutt

    • @morlam8705
      @morlam8705 Місяць тому +1

      Si j'étais lui j'allais éviter les sites et protéger sa femme boul nangou gno koy exposer ! Et si tu peux retourner en France et continuer ton traitement, la bonne alimentation est 80% , et le reste est le suivi médical, te Sénégal dafa tar

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck3056 Місяць тому +1

    Bayilen beuré mon guen

  • @ahmedomarsis9441
    @ahmedomarsis9441 Місяць тому +2

    Machallah machallah machallah

  • @abdoulayendoye542
    @abdoulayendoye542 Місяць тому +4

    Macha alla Modou mbaye et merci pour ce que tu as fait bonne continuation

  • @moustaphawade6771
    @moustaphawade6771 Місяць тому +6

    Machalla yallna diam yagu inchalla

  • @damethiam3854
    @damethiam3854 Місяць тому +2

    Bonne guerison

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 Місяць тому +2

    Biyil site internet yi
    Nek thi li nga néh

  • @Taphathioun15
    @Taphathioun15 21 день тому

    Interview bo bari monm wakh deugg war nga ko wangy sa kom yalla deffna nga tané thi diam monm mayto sityi internet yi amna solo

  • @mansourjuniorfaye
    @mansourjuniorfaye Місяць тому +1

    YALNA LA YALLA YOKOU WEER

  • @malkomx9503
    @malkomx9503 Місяць тому +1

    Yallah na Yallah mayla wér

  • @lahadboukharagnelo6707
    @lahadboukharagnelo6707 Місяць тому +4

    Mbeur nobaloul journaliste yii koulen tobou dinga wakh ba wakh Lo khamoul

  • @alimajolie3195
    @alimajolie3195 Місяць тому

    Yallah na yallah feugeu sa bopp ak képp kou tawate barkép borom touba

  • @maxlalionne8146
    @maxlalionne8146 28 днів тому

    Ay kharite laniou

  • @MouhamedFaye-os7yf
    @MouhamedFaye-os7yf Місяць тому +4

    Oustaze aw leu kilifeu bou yala may kou bah

    • @eulthewritah4070
      @eulthewritah4070 Місяць тому

      Bonsoir Mouhamed Faye j'ai besoin de votre numéro svp comment faire 😢?

    • @badjidiarra7184
      @badjidiarra7184 Місяць тому

      Mouhamed bougone n'a âme sa numéro je suis en italy

  • @essaceeaay
    @essaceeaay Місяць тому +2

    Sqc jour am kula jal journalist yu soff nu nek senegal

  • @biranecamara6796
    @biranecamara6796 Місяць тому

    Lutte motivation sén caméra bi môme khané téléphone itel la li leundeum na trop waay

  • @doublebweuyoumic5802
    @doublebweuyoumic5802 29 днів тому +1

    Encore cette dame Marieme Faye Sall vraiment t’es sociale

  • @Wrestling1890
    @Wrestling1890 Місяць тому +1

    ❤❤❤❤❤

  • @papembayemadiaga
    @papembayemadiaga Місяць тому +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @nitoudegeukaddudegeu3001
    @nitoudegeukaddudegeu3001 Місяць тому

    GOUYE GUI VRAIMENT SAY LÉKH NIAWE NA 😡 SA FORME KANAM MO SALETÉ JE TE JURE WARGUA BAYI LIGUAY NANE AK LÉKEU FORME BOU NIAW BI

  • @lesseseyni2659
    @lesseseyni2659 Місяць тому

    Papis général dafa weer

  • @kaneamsa2261
    @kaneamsa2261 Місяць тому

    Ndysan magal darou la len mas guis yag na nio Yor Ben 505 sa kadior di dawal

  • @adamaba2246
    @adamaba2246 Місяць тому

    Demall toki yena topon Balla guaye 2 yen nepou la sakara fiss

  • @elhadjimbow539
    @elhadjimbow539 Місяць тому

    Machllah ♥️ yalla diam yague way

  • @mouhameddia5168
    @mouhameddia5168 Місяць тому

    Sa cadior bimouye beuré ak papis soko kholè dafa ame volune xamna fébar bi lawone ndaysane

  • @YoroThiam-fy7iq
    @YoroThiam-fy7iq Місяць тому

    Numero sa cadior stp

  • @serignembackesylla6866
    @serignembackesylla6866 Місяць тому

    Kou beug koko nianal nama wo

  • @Steven-ul8pw
    @Steven-ul8pw Місяць тому

    Mbeure Togal Nga Récupré Begué Aksa,Ndiabot Nga Areté Interview Yi Ñiolay Dougeul Banga Dioum fi Ñiou Diaxaséla Ak Aduna Lép loula Dall lamb Molako Teik Yangui Rafetal Mé Boul Naagou Si Kéén Dé Soralé Diamono Bi Nitñi Dañu Falsh

  • @Abraham22199
    @Abraham22199 Місяць тому

    Gouy gui rouge ngeu

  • @jayvon422
    @jayvon422 Місяць тому

    Li dra deugou wou ci mes entout case Sa cadior boul dougouru ken tes amal diam

  • @essaceeaay
    @essaceeaay Місяць тому +1

    Journalist yi sofnen

  • @ahmadndour7868
    @ahmadndour7868 Місяць тому

    Mais journaliste bi Loutax nagouwoul insiste ladj ko si Mareme faye sall

    • @morlam8705
      @morlam8705 Місяць тому +1

      Pourquoi ? Par ce que yaw rek la intéresser ? Defalnako lou bakh , gnanal nako c fini loumou si wara wakhat?

  • @BadaraGueye-ii5gh
    @BadaraGueye-ii5gh Місяць тому

    Yawe ya warra yoro gouy gi bari ga proplem trop

  • @SerigneBassirouLo-fo4sz
    @SerigneBassirouLo-fo4sz Місяць тому

    Nopil 😢

    • @ousseynoundiaye7826
      @ousseynoundiaye7826 Місяць тому

      Hana yaw rahgua da melni sa genryi nioko Def ✖️✖️✖️

  • @alelo8335
    @alelo8335 29 днів тому

    Yala nala yala maye wére sa cadior❤❤❤