C'est pourquoi j'aime sadio Mané. Il n'en a rien à foutre de ces trucs de marabouts ou de buzz. La bénédiction de ses parents et les prières que les pauvres qu'il vient en aide formulent pour lui suffisent pour lui faire avancer. Aujourd'hui il fait la fierté de tout le Sénégal sans pour autant s'exhiber.
serigne ahmadou kara Noreyni wenibik diadieuff wayy mbacké jsuis pas mouride mais dimension bi serigne di wakhé dafa lathie nite ki nek meme niveau de spiritualité.much love to you borom bakh bakha generalou bamba.
Ndeydane lir na comanetair yèp mais amna nit niou sokhor nak walahi Serigne bi fimou diar ak kara mbodj bamou aksi fi tay oumpoi nalène lole ndeysane li dou dara wornamani yènèm si si Serigne bi wèsouna fi dieuradieuf yalla nala yalla samou yokou say khèweul si barkè cheikhoul khadim dèmlène wouti loungène diokhè sokhor bakhoul
tu veux dire que yalla diaarou faak moom le destin de l'homme et entre les mains de dieu vous n'etes pas plus talibe que nous mais dafa am loo khamne yalla rek mooko moom nite waay . foutaise
Bilahi Niacka mandou amna, Kara Mbodj bouko nékhé diokh Serigne Modou kara Auto Serignam la bayam la, ndakh mom lanko toudé ta moko toudou bimou Dioudo. waw goor kara mbodj ni la ap mouride di déf
Ndeysane amna ay commentaire yohamné soumako guissé xamné borom xol ba feexul té walahi fek ndagou woune ndogalou yallah sen xol dou feex ndax lingay bagne mou yokou té sabo xeuyé guiss moy avancé à grand pas lolou man na ray nit. Yalla nanou yalla moussal ci xoloub kiñane
Je me demande pourquoi tant de haine et c’est toujours les mêmes personnes qui sont partout qui commentent sachez une chose on a pas choisi d’être mouride Serigne Touba nous a choisi et on est très fier d’être des talibés louniou ame Serigne Touba moniouko geuneul.BAMBA DANK U
Bilahi ketchup soumadone kara mbodj dinguama délo sama billet d’avion bimala dieundal yow filmél serigne bi guay filmé sa bop ba dieulo youkhou bi😂😂 gua khamni par 3 mois lakoy youkhou
Akasa dieure dieuf kara mbodji yalnala yalla diapale barkep serigne touba mbacke contan si yawo bou bakh yalnanga goudou fan ak weure ak khewal parkep serigne touba mbacke ak talube rek mo Woore dee
Tu ne pouvais pas prier , Parce que serigne saliou t avais dit de t assoir . Dieu le tout puissant , t as recommandé de faire la prière, tu dis que serigne saliou t as dis de t assoir tu écoute serigne saliou et non le tout puissant . Il t attend . mécréant .
Katt lèn ndayam feulé domeram yi ki daffa teral ay wadioureum sila deuk diem len am limou am sokhor rek molène diap koudoul mouride nak li dalay diaxal ki serigne MODOU Kara lagnouko toudé bimou néké lirr moko toude Kone Lolou dou taye xaroul bamou am xalis mou gnew si mome kounek lingay niane yalla am sa teranga Diokh ko sa tourendo wagniwoul dara sen datta ndaye yén gniy critiquer yeupe sen dambali baye
@@ndeyefaye9533 yen nguay nonou serign touba ngeun ndakh yeni dollen lou kara di wakh ta serign touba messou KO wakh té je vous défi dolen guiss fen fouko serign touba binde
Dieuredieufety cheikh ahmadou kara mbacke noreyni yaw lo am diokh gako kou tedd ki akuk ndiabotam Sallahou kou yabou madou ci mom dara dara dara manu len ko ci mom ninan dem len diamou ci yalla magui lendi ladieu lan moy diamou yalla? Dah yen ni yor sen telephone di wah lou niaw ci derou diambour yi lolou ci ak diamou yalla la bokou?
Serigne Modou tognioul kene batay deguo lene mou wakh fi kene lou niaw wala mou def si yonam la nek bobou ba legui yalla defko limouko def donc mbadou lene nguen dem wakh ak séni baye yi
Defofi dara bouléne niou sonal way liguéy lène ta noppi dolene fi deff lou serigne Touba defoul ak Mame Elhadji Malik sy ak Mame Baye niass. affaire bi dou ay miracle dieul nitt yi yoboulene si yalla la dou lenene ☝️ Al houlamouwou warrasatoul an' biyahi
Yène gniy oubi sen guemigne Di wakh Xana tay nguene Meune wakh limouy def lousi sen yone Xana tay nguen Meune wakh Bimouy dem thi prison yi di mayé aye matla ak ventilo ak lenen lolen yegoul folén nekone limou def Mo guene dem grand théâtre di battré nit day mandou way
Musa Lowe Don’t choose what people do with their money and just because he’s doing things for the marabou does not mean he doesn’t help other people or do other things
Ndeysan Baye Darou yi kein eupoulein ay teguine ak yarr Cheikh Ahmadou kara mbackei Noreyni yaniou yaral sa bop baniou meun ragnei kilifeu DieuReudIeuFé SeRiGne TOuBa kein dou Cheikh Ahmadou kara mbackei Noreyni
Arrêtez de juger les gens sur leurs actes où di digante kholou djouliit dafa wara seettt jah kara mbacke yala moko deff limou done kara mbodj yala moko sake mou ame thiofel si mom kone mandou dafa guene wassalam!!!
Gani yalla moom la gueuneu beugueu que yonen bi😶😶😶😶... Yalla yonen la beugueu moom la djeukeu amaal... Bind nala guir man ma bind lepp guir ioe...Lolou la yalla wakh!!!
BOUCHER BOUDEE DA NGA DEF LI NETIER DEMAL DIANGUI KO LI NGA FILMER NI DARA BAKHOUSSI DI REPETER AY ÑIETI YONE LI SERIGÑE BI DI WAKH .KARA MBODJ YAKANA KHALISSAM
Wakh nakh DEUG DEUG la lathe j suis tidjiane deh mais limouye wakh il faut ke guene khawa tolo diangue walla kham kham nitt koune guemelal ligua guem epuis kara mome bokou nekha mou dieul ay millions diokh ko ko khamolen loumou ko defal teh wouroulen ndakh magui def social ou po ndakh dou nieup la sene affaire di siw
N'oubliez pas de vous abonnez sur votre chaîne Senbuzz TV et d'activer la cloche pour recevoir les notifications merci.
Salam je veut le numéro de amm de sen buzz svp
U
C'est pourquoi j'aime sadio Mané. Il n'en a rien à foutre de ces trucs de marabouts ou de buzz. La bénédiction de ses parents et les prières que les pauvres qu'il vient en aide formulent pour lui suffisent pour lui faire avancer. Aujourd'hui il fait la fierté de tout le Sénégal sans pour autant s'exhiber.
serigne ahmadou kara Noreyni wenibik diadieuff wayy mbacké jsuis pas mouride mais dimension bi serigne di wakhé dafa lathie nite ki nek meme niveau de spiritualité.much love to you borom bakh bakha generalou bamba.
Lou wér nga wakh fawou nga ame tolouwaye bobou
Pendant ce temps sadio Mane construit des mosquées des écoles donne à manger à ceux qui ont faim etc....
ipupa dos santos fally ms yaw lii loussi nék aaaaaaa
kara mboje yagoul dara yonena ay matelas rebeuss boulen niiou sonal Way
Legui loussi sunu yone ki cheikh Modou kara moy tourondo wam gnom gnar ba Dara doul Dara la wone
Yow lo deff comme acte solidaire sokhor baxoul
ipupa dos santos fally pendant ce temps tu passe tout ton temps à commenter dans les affaires d’autrui
Baptême validé machalla yalla nguéne doundou ba féké ndiarignou bb bi
ziar nala Diarra ravi de te connaitre
Ndeydane lir na comanetair yèp mais amna nit niou sokhor nak walahi Serigne bi fimou diar ak kara mbodj bamou aksi fi tay oumpoi nalène lole ndeysane li dou dara wornamani yènèm si si Serigne bi wèsouna fi dieuradieuf yalla nala yalla samou yokou say khèweul si barkè cheikhoul khadim dèmlène wouti loungène diokhè sokhor bakhoul
tu veux dire que yalla diaarou faak moom le destin de l'homme et entre les mains de dieu vous n'etes pas plus talibe que nous mais dafa am loo khamne yalla rek mooko moom nite waay . foutaise
@@lotisgueye2192 je me demande kesk kara mbodj a fait de mauvais
Lotis Gueye yaw linguay wakh xamoko Louné daa am si lokho yikoy yalla di diarélé
Lotis Gueye sa datta ndaye sa dambali baye wakhi sokhor rek ngaffi wakh
@@lotisgueye2192 merci gni dagne fokk ni ay kagna lagnou..
Ohhhh machala vraiment liiii sedd na xol dieuredieuf serigne touba 🙏🙏🙏🙏
Nagnuy am respect sii kilifeu yii rawatina mbacké mbacké yii togne dou galathie dehh taa gni kulen fonto diko guiss silu gaww gaww
Luweirr
Kara ne fais que vous abrutir déme léne rameul séne baye ak ndéye mo eupeu diam C’est un comédien qui maîtrise son art
ioe ku xamadi nga
Ndeysaaan tay lanioukoy guena ramal di beureugou
Kou mandouwoul sak djoulite matoul ma ngui dièguelou nieup
Mo gueune d
%# sa data ndaye nga mandou si 👎👎👎
Kara mbodj waaw goor yalna yalla dolila diame yokku yagg wer barké mame cheikh ibrahima fall lamp
Bilahi Niacka mandou amna, Kara Mbodj bouko nékhé diokh Serigne Modou kara Auto Serignam la bayam la, ndakh mom lanko toudé ta moko toudou bimou Dioudo. waw goor kara mbodj ni la ap mouride di déf
Machalla done mouride rèk mon nèkh
C'est le bapteme de mon idole avec Serigne Modou Kara Mbacké et longue vie à bebe Mbacké Arame Mbodj
Je comprends plus certains de mes frères Sénégalais, pourquoi tant de haine et de jalousie? Kou nékk na gueume loumou gueume Wa Salam, diam si gnieup
Merci beaucoup bilay mo guene deh .
Teh si c nous les mourides qui parlent rek ngay guiss lolou
Ndeysane amna ay commentaire yohamné soumako guissé xamné borom xol ba feexul té walahi fek ndagou woune ndogalou yallah sen xol dou feex ndax lingay bagne mou yokou té sabo xeuyé guiss moy avancé à grand pas lolou man na ray nit. Yalla nanou yalla moussal ci xoloub kiñane
Amin waye
Jah kara KC ku kignane dou djité
Sama baptéme idole avec serigne modou kara mbacké sama bébé Mbacké Arame Mbodj longue vie à toi
Je me demande pourquoi tant de haine et c’est toujours les mêmes personnes qui sont partout qui commentent sachez une chose on a pas choisi d’être mouride Serigne Touba nous a choisi et on est très fier d’être des talibés louniou ame Serigne Touba moniouko geuneul.BAMBA DANK U
Dieureudieufeuti cheikh ahmadou kara kouko waxoul gorei wo
Bilahi ketchup soumadone kara mbodj dinguama délo sama billet d’avion bimala dieundal yow filmél serigne bi guay filmé sa bop ba dieulo youkhou bi😂😂 gua khamni par 3 mois lakoy youkhou
Yaw dinga ma Ray rék😂😂😂😁😁
🤣🤣🤣🤣
😂😂kone setlouga lolou yaw
😂😂😂😂
Billay wa nga deggue
Tarkalla bravo Kara di santati ahmadou Kara mbacke noreyni général nos respect
Kéne dou cheikh Ahmadou kara Mbacké Noreyni yagual té wèrr mbacké ndeysann kara mbodj dafa ame talibé bilahi
Ah les gars kiy mayé porsh hamgeni aduna safuko Mbacké tu es le sauveur kutedki rk mola saf. Kula Dingatt rk dala gamul. Lunulay ciow nay sorii
Waxal dh 137 yeup touba la dem si ndiabotou kou tedd ki gnii daniou tawate modou dh wakhi serigne lodoubawa balla bi rk
Demleene diaamoudji yalla moo gueune!!!
Lidieuntil sa diamou yalla guenn mandou soff guenn trop
Akasa dieure dieuf kara mbodji yalnala yalla diapale barkep serigne touba mbacke contan si yawo bou bakh yalnanga goudou fan ak weure ak khewal parkep serigne touba mbacke ak talube rek mo Woore dee
Merci bcp Généralo bamba kéne d'où yawe
Lou lère fall
Machalah li néxna si khôl
khayroul khalkhi kouko mom kara moytoull sa pop mann mouride la wayé yaw mom thia abdou diouf ak Abdoulaye lala weddi wone khamo dara dagay force rek
Loutakh sokor tmt
Ioe katal sa ndei nioune potique woune serigne modou Kara par force ❤️❤️❤️
Dieuredieufé serigne touba. mbacké bala yagu fi lol té and ak wër
KETCHUP SI BOPPAME DAA TIIITE BI SERIGNE BI YOUKHAU...REGARDER SA REACTION😂😂😂😂😂😂😂
Dieureu dief s touba
Akassa Machalla Machalla Rafetna Mbake
Cheikh Ahmadu Karra mbacké jërëjëf
Moudioum jamono serigne touba nena daniouy dieul deug deff ko fene dieule fene deff ko deug wayé bagne bagne nangou Jah kara point
Kome beugou léne serigne touba diaroule ngénedi sétan baye commenter serigne touba yalla moko maye loumou mayoule kéne
Bilay nak ndakh niou nopalou
Merci beaucoup
Akassa Mbacké Balla Serigne Touba Amoul Morom
Dieureudieufé Serigne Touba
Machalla mbake Mala beugue ❤️❤️❤️
Tu ne pouvais pas prier , Parce que serigne saliou t avais dit de t assoir . Dieu le tout puissant , t as recommandé de faire la prière, tu dis que serigne saliou t as dis de t assoir tu écoute serigne saliou et non le tout puissant . Il t attend . mécréant .
Dieuredieuf Mbacke balla aicha Serigne Touba Amoul Morom
Alhamdoulilah ahmadou ❤️👌🏿
Katt lèn ndayam feulé domeram yi ki daffa teral ay wadioureum sila deuk diem len am limou am sokhor rek molène diap koudoul mouride nak li dalay diaxal ki serigne MODOU Kara lagnouko toudé bimou néké lirr moko toude Kone Lolou dou taye xaroul bamou am xalis mou gnew si mome kounek lingay niane yalla am sa teranga Diokh ko sa tourendo wagniwoul dara sen datta ndaye yén gniy critiquer yeupe sen dambali baye
DEUGU REK MOMA NIOR merci way
Merci deugu rek moma nior contenna si yaw loll
Wawaw b1 d'i yenn imbecil y merite kon l'insulte nah danio niaw sokhor
DEUGU REK MOMA NIOR gniiiii sen xol yi moy xorom sen deudieuw ndaye xasan dano soxor
Wa sama sope lanlay yokho nak wala dafa danû leër macha Allah
Bilahi damako beugue ba guentè ko guiss ko rek la beugue Walahi
Kou bakh video bi amana solo wayé dafa diakhaso tropp dési bayi hélll témou geuneu semple mangui toup nak🙏
Connerie pure.. ya trop d con su senegall
Saïdou Traoré yaye con bou kateu sa ndaye bi yaw mou sokhor mi domeram
🤣🤣🤣🤣
Modou Fall 😂😂😂 nekoléne ci deugg motaxx ngayy merr
Kara yalna ngua am. Club bou makk thi barké Serigne Touba
Yaw AK sa tourou toubab bii 😂so moytouul dinga niaf Sa ndey
Khassoulen ko mais kou teddki nguen di khasssss ☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼
Talibe bou yoroul dè ken dou dem nguentem...
Dangay doul rék serigne yébou yamounou
Yonou serigne Touba amoul lolou Mbacké Mbacké faléwoul alal.
Merci
😂😂😂🚶♀️🚶♀️
Q@@
mo ham fuko serigne nam tolu mu mayko auto c simple mo mome khalissam hamolaine fumu jar ak kara sonu guaine way
Gni diarougnou tontou sakh dagno sokhor
Walahi linga wax khamo ko Sénégal Lou soti rek laniou kham tei douniou kham fou mbir yi soso
L'heure est grave vraiment je suis étonné par ces propos fallacieux
Yaw mayniou djam yaw mom ibadou gua mandou mom amna solo mécontent gua
yaw danga rére sokhor serigne bi dano diangal ay téguine un peu de respect sinon nga mandou
@@ndeyefaye9533 yen nguay nonou serign touba ngeun ndakh yeni dollen lou kara di wakh ta serign touba messou KO wakh té je vous défi dolen guiss fen fouko serign touba binde
BO NAREE DEF LU METIER DEMAL DIANGUIKO MO NGUENE TATONER BI
Dieuredieufety cheikh ahmadou kara mbacke noreyni yaw lo am diokh gako kou tedd ki akuk ndiabotam
Sallahou kou yabou madou ci mom dara dara dara manu len ko ci mom ninan dem len diamou ci yalla magui lendi ladieu lan moy diamou yalla?
Dah yen ni yor sen telephone di wah lou niaw ci derou diambour yi lolou ci ak diamou yalla la bokou?
Y A MIEUX A FAIRE DANS UN PAYS ARCHI-PAUVRE. MAIS BON........
Rafetna machaallah
Dieuredieuf serigne touba
Serigne Modou tognioul kene batay deguo lene mou wakh fi kene lou niaw wala mou def si yonam la nek bobou ba legui yalla defko limouko def donc mbadou lene nguen dem wakh ak séni baye yi
Dieuredieuf Serigne Touba
Mashallah kara mbodj
Defofi dara bouléne niou sonal way liguéy lène ta noppi dolene fi deff lou serigne Touba defoul ak Mame Elhadji Malik sy ak Mame Baye niass. affaire bi dou ay miracle dieul nitt yi yoboulene si yalla la dou lenene ☝️
Al houlamouwou warrasatoul an' biyahi
Kene dou dia kara
Baye Diop Soldarou Nguirane Baye Samba yawe koula yobou si yalla yéna geuneu doff foufe domeram yi
Yaw gemo yalla sakh
@@mouhamadoudamendiaye829 akay deug
@@bouryndiaye3000 wa guiss nga deu boury
Diaradiaff serigne Touba
Yène gniy oubi sen guemigne Di wakh Xana tay nguene Meune wakh limouy def lousi sen yone Xana tay nguen Meune wakh Bimouy dem thi prison yi di mayé aye matla ak ventilo ak lenen lolen yegoul folén nekone limou def Mo guene dem grand théâtre di battré nit day mandou way
Deugh deugh
Mbacké dioumo deih yalla s .touba la geuna beug ke nieup nax dadi mom deureum bi geinoul gal gii bamba yalla la atane wah dji yomboul nak
bb titi Mbaye mourale sa bope bi mo gueune
Dagaa dioum liga wakh amoul... Yalla yonen bi la gueuneu beugueu gneup na leeeerrr
Don’t waste your time and your money on this things. You can help hospitals and schools is better
Musa Lowe is true
My people is pore
I swear , they could do better with that money . This guy is just making joke 🤣🤣🤣
So true . This is bullshit
Think that yu only are BULLSHIT.... Big shit!!! speak in wolof n yu gonna see come on...
Musa Lowe Don’t choose what people do with their money and just because he’s doing things for the marabou does not mean he doesn’t help other people or do other things
Ndeysan Baye Darou yi kein eupoulein ay teguine ak yarr Cheikh Ahmadou kara mbackei Noreyni yaniou yaral sa bop baniou meun ragnei kilifeu DieuReudIeuFé SeRiGne TOuBa kein dou Cheikh Ahmadou kara mbackei Noreyni
6:59 moy yokhou yiii 😂😂😂🚶♀️😜😜
Merci bcp
Merciii way weur na ba sonneuh
Merci beaucoup ya takh ma setane ko
J espere que kara auto bii dieundeulko sa ndeye ak sa baye avant!!I espere bien pour toi!!!!
fatou ravi de te connaitre
Wakho fi dara tè sa Yonne nekousi
Il doive suivre l.exemple d sadio mane...realisme social...poukare l...
Kara mbodj a chak foi il est dans les prisons pour leur aider. Et puis sakh mo mom khalissam . Et toi tu fais koï pour ton pays apart commenter
laigui warul joh serigne bi
Talbi Amir yako diokh limou am bakoy diokh conseil sa xourou ndaye nga mandou si domeram satan k tu es 👎👎👎👎
6:58 Ahhhhhhh bi daf ko raté😂
Yallah mo meune diaye nitt dala diaye nga fokni yaw la gou wé di khola si béthio thioune Modou kara mi Dafa béwou yalla ngane la
Linga wakh reyna yalla Serigne touba la guene beug k yonénete bi wala daa am bénène yalla bu am
Wahoul lolou dh dani yalla la geuna beug k yonénti bi té yonéne sama dieum diéko geuneul dieumi bopam
Nii daniou reeer
Amlen deg deg nak wakhoul lolou degloul bou bakh mun ngene critiqué trop
Beugue ci yonent bi et beugue que yonent bi il ya une grand difference
Djanguil wolof balaa ngay dinguaay
Ohhhhhhh mashalla
Bamba merci
Thieuy kara 💪💪Ay way Koumay may auto tmt sokhla nako dehhhh
Diadieuf Mbacké doundeul lou bari goudou fan wergui yaram
Gniiye wax na séne serigne wala séne baye diokhé porche gnou guiise
Kara ne débite que des CONNERIES.
Woukhou serigne bi day ak diane la
Merci kara diasakaa
Machalla nekh dé 💚❤️
Ko bague s Touba abonné sama pasd
Ngathie ngalama cheikh ahmadou kara mbacké noreyni
Boucher bou seye bi youkho dafa tite 😂😂🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Arrêtez de juger les gens sur leurs actes où di digante kholou djouliit dafa wara seettt jah kara mbacke yala moko deff limou done kara mbodj yala moko sake mou ame thiofel si mom kone mandou dafa guene wassalam!!!
SUBHANALLAH KADOU YOU
Yén bayyilén kara mbodj mom kii moko baptisé toudé ko boppam kone nii la meuneuh mél
O gens, craignez votre Seigneur
Gani yalla moom la gueuneu beugueu que yonen bi😶😶😶😶...
Yalla yonen la beugueu moom la djeukeu amaal... Bind nala guir man ma bind lepp guir ioe...Lolou la yalla wakh!!!
Louniouy sow sow ngay sori Do ken Te Ken dou yaw not kidding voila interessewoul waro setane ay video am mane dee doumako defense ngeum day deugou
Machahalla
Holale niou hiffe yii. li amaloula bene ndiarigne amna niouko yello va aider les pauvre tu auras la bénédiction d'Allah
Tiéy kara lernama ni il a prix tout en charge les arrivée départ et hôtel etc
AH C NORMAL C SON GUIDE KAY MANDOUL SA YONN NEKOUSSI
Mounaan lèn è s k dègue ngèn fèn yiimay fèn niou naan ko deugue leu serigne bi dieurinioo lèn sèn khèl yii moo gueun
Ousmane Sow ioe sa leufal ndey
Papito Seyeuh merci
Ndeysan 😂😂,yalla la guina beug ki yoneneteu bi. Et yonnente bi nek geune dji mindef🤔.je pense cette video est privée
I'm faithful reecouter oubien so tired n'est pass olof fait LA tradiction
Doundal Mbacke balla yagu fii lol tei werr
BOUCHER BOUDEE DA NGA DEF LI NETIER DEMAL DIANGUI KO LI NGA FILMER NI DARA BAKHOUSSI DI REPETER AY ÑIETI YONE LI SERIGÑE BI DI WAKH .KARA MBODJ YAKANA KHALISSAM
Bouché cé un con vraiment
ua-cam.com/video/7ePyfSlNMgs/v-deo.html
Wakh nakh DEUG DEUG la lathe j suis tidjiane deh mais limouye wakh il faut ke guene khawa tolo diangue walla kham kham nitt koune guemelal ligua guem epuis kara mome bokou nekha mou dieul ay millions diokh ko ko khamolen loumou ko defal teh wouroulen ndakh magui def social ou po ndakh dou nieup la sene affaire di siw
Mâcha halla
JEURJEUFETY CHEIKH AHMADOU KARA MBACKÉ NOREYENI POINT
Waw kane moy youkhou ni douniouko guéné salon bi ba sérigne bi parré kétcheup kharagnoul dara naniouko dakk niou wo Niang 🤣🤣🤣yalla na diamm yague
Talibe cheikh dou togne dee wala dou deug
@@cheikhkara3132 toub nako
Couthi am sa kharite mou rich boula défaloule fotok yak déram,kara nak dafa togu ak bayam ak serign niam,yéne tècki wouléne tous