🛑Alhamdulilah Bonne nouvelle pour Fallou la belle surprise de L’acteur Rojer pour Fallou

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 6 лют 2025

КОМЕНТАРІ • 191

  • @couradiopndiaye9620
    @couradiopndiaye9620 6 днів тому +54

    Falou né sa yaye merci ligueyou ndeye daye fenie si milieux oh contente continue Machallah ya yaye yana ko yala yeureum🙏❤️

  • @NdeyeFatouGaye-o4w
    @NdeyeFatouGaye-o4w 7 днів тому +94

    Ligueyou ndeye daye fégne di milieu yaye fallou dieureudieuf repose en paix ❤❤❤

  • @MameDiarraNdiaye-ll5gs
    @MameDiarraNdiaye-ll5gs 7 днів тому +32

    Machallah li eupna niortou serigne fallou fall yallnaléen yalla fay li rafét na

  • @adamapamba3375
    @adamapamba3375 7 днів тому +30

    Machallah ndeysann dinga diéma yakk nite fekk yangui kay defaral. Fi yalla rk mofi nekk

  • @Ndiame-ck4hl
    @Ndiame-ck4hl 6 днів тому +12

    Yalla soula naré dimbelé dafay melni kouy yakh fallou sa ligueyou ndaye dinala walou ❤❤❤

  • @damedieye8998
    @damedieye8998 7 днів тому +35

    Sénégal amena gnou bakhe yalla na senne khewal yokou

  • @Awayandésindidi
    @Awayandésindidi 6 днів тому +15

    Ma Sha allah ❤yallah naléne yallah faye.wayé thiéye yallah souniou borom bou navré défar nouné laye nieuwé. Yallah nieup am diam

  • @Diouma-i4w
    @Diouma-i4w 2 дні тому +1

    Machallah yalla na ko yalla guené🙏🙏🙏❤❤❤

  • @AdamaDiouf-hx8qd
    @AdamaDiouf-hx8qd 7 днів тому +26

    Yalla rkay bour yalla boula beugué teral dalay natou ba paré chapeau a vous❤❤❤❤❤

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 7 днів тому +18

    Machalla fallou fall sa maman kou bakhe lawone yallanako yalla yeureume té khareko alediana amineeeeeeee yallana yalla guènenèko si khatekhate tata fallou bakhoule yaguie gagnou daga bone sokhore ignane dotokodéfatie papa fo nek maman fallou liguièyame rafetena

    • @adamadioum2659
      @adamadioum2659 7 днів тому +1

      Wawaw daye geuneu nékhe inchala fallou wakhale sa yaye merci

  • @AbySow-b3e
    @AbySow-b3e 7 днів тому +114

    Aye waye nagne takhawou ci keur gui tabakh ko balamouy guéne gnou défaral ko bamou nice inchalah yalla bakhna 🙏🙏🙏

  • @ndeyefaye867
    @ndeyefaye867 3 дні тому

    Walahi Fallou fall ça yaye seuye na sa keur baye, longueyou ndeye daye fegne ci milieu, Merci à la population Sénégalaise ❤❤

  • @adamadioum2659
    @adamadioum2659 7 днів тому +17

    Yalla naléne Yalla Faye merci beaucoup vrement sounou khole sédena trop

  • @BintouSaw
    @BintouSaw 7 днів тому +44

    Falou amna terrain am luko tabax ak ay meubles machalla fallou fall

    • @seye5809
      @seye5809 7 днів тому +5

      Yalla nako yalla samou❤ serigne fallou fall

  • @adamadioum2659
    @adamadioum2659 7 днів тому +17

    Fallou néle maman merci au Yalla nala djik. Waye

  • @Salikhate732
    @Salikhate732 6 днів тому +5

    Walay ndeysane 😢 fallou yala doula sétane lépa diekh inchallah yala nala yala guéne si Liga nek

  • @adjadosso1263
    @adjadosso1263 7 днів тому +27

    Yaye meun na décédé mes ligueyam dé décédé mouk jtm sounou Yaye yi ❤❤❤❤

  • @fasahrassoul3895
    @fasahrassoul3895 7 днів тому +12

    Machallah yalla nako souniou borome téguile Nattou yiiii ci barké kou teddd kiiii🤲🤲🤲

  • @Madamemmedia
    @Madamemmedia 7 днів тому +10

    Roger merci Yalna Fallou guéneu inchallah

  • @MOUHAMADOULAMineKANE-cu8vo
    @MOUHAMADOULAMineKANE-cu8vo 5 днів тому

    Machallah akt bi rafet na trop bilahi yallah nallene yallah laffal thiate deffal len diam inchallah si barque seydina mouhamed saw franchement contane n'a trop li Moy Sénégal ken d'où fallou fall mérite nakko nooukko togne guathie dinalllen rey

  • @AnnaBop-zn3wn
    @AnnaBop-zn3wn 6 днів тому +3

    ❤❤❤❤yallanalene yalla defal tawfeekh thi barkel Serigne Bethio begnalene

  • @sayesene9519
    @sayesene9519 7 днів тому +8

    Serigne fallou fall santa yalla bou bakh sante sa yaye ak sa pape. Li farfar la rek frero

  • @fatimaba6116
    @fatimaba6116 7 днів тому +28

    Des fois dangay def dara pour yakh nit fekké khamoni yangui ko defaral
    tantay Fallou loolu
    maako dal su guenton ni sou defé li Fallou dinaci diaré Yallah teralko douko daf
    Liila la poular nan "ignan YALLAH lay khekhal te kou Khekh ak BOROM bi defet nga ciy dieulé

    • @lalaidebh5kf
      @lalaidebh5kf 11 годин тому +1

      Wallahil hanzim ko khamoul bouko yalla tabakhé guani daga Koy Danel day meti rek wayé yay danou

  • @aramefall520
    @aramefall520 2 дні тому

    Machallah yalnalèn yalla fay contane naniou boubax si yen nièpeu nioune famille fallou

  • @FantaSylla-l3r
    @FantaSylla-l3r 6 днів тому +5

    Yalla deh bouy defar dafay melni kouy yak Machalla 😊

  • @maimounafaye5442
    @maimounafaye5442 6 днів тому +2

    Ndeye sane yalla bouné li moy sa destin alla kouli alli déng si diar.Mais bravoFallou Fall sa ndeye ya ligéy lii, mais merci BRAVO le Sénégal séne takhaway rafetna❤❤❤❤❤

  • @ElhadjimamadouMbaye-b7y
    @ElhadjimamadouMbaye-b7y 5 днів тому

    Ahh contane Na machallah Yalla nalléne yalla faye barkepe serigne touba doléye cheikh ibra

  • @yatoudaff5846
    @yatoudaff5846 7 днів тому +10

    Machallah xol sédeu na justice pour fallou

  • @MariamaSane-yj9tv
    @MariamaSane-yj9tv 7 днів тому +5

    Machallah bnne acte ylnléne ylla faye fallou louniouko diapalé méritonako❤❤❤❤❤❤

  • @FatouSarr-xy4ks
    @FatouSarr-xy4ks 7 днів тому +6

    Yalla na yalla faye lene thi barkep seydina Mohamed ❤❤

  • @MaimounakebeMayna-d8s
    @MaimounakebeMayna-d8s 7 днів тому +14

    Wa fallou mii waliw la 😢😢 d

  • @MaimounaDieng-fz5hr
    @MaimounaDieng-fz5hr 5 днів тому

    Bilakhi fallou sa ndeye ligueyna.diam rek ngaye ame❤❤❤❤❤

  • @MaimounaDieng-fz5hr
    @MaimounaDieng-fz5hr 5 днів тому

    Roger yow goor nga garminga.yalnala yalla diapalé.❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyefayedabakh
    @ndeyefayedabakh 7 днів тому +5

    Machala yalla reck moye yalla☝️👈

  • @AstouSeck-u6o
    @AstouSeck-u6o 7 днів тому +7

    Laff thiat bayou mbéne Glass 🤲🤲

  • @Mechaelsoum
    @Mechaelsoum 6 днів тому +2

    MACHALAH yalla bouye defare dafaye nirok louye yakh

  • @BallaDiop-v1n
    @BallaDiop-v1n 5 днів тому

    Vraiment contenant trop sakh yalna yalla goudal sa fanne fallou

  • @Barrandiaye-m7u
    @Barrandiaye-m7u 7 днів тому +6

    Machallah li raffétte na❤

  • @mariemesarahtall2625
    @mariemesarahtall2625 6 днів тому +1

    machalllllaaaah liii mooy deugg tantam kheuthiio keur mo indi lii yeupp ,tey djiii yalla indi louy samp keur machalllllaaaah,c mieux ainsi sakh ndax pour sûr keur papam ay galadjie rek la,un nouveau départ mo gueune MOK ay freram

  • @rosefatimatatall8652
    @rosefatimatatall8652 7 днів тому +1

    Yala loumou def rek mo gueune ci diame bi. Yalna Yala takhawou Fallou inchallah

  • @AntaFall-t2w
    @AntaFall-t2w 7 днів тому +4

    Sa ligeuyou ndeye féna 🎉🎉🎉❤❤❤

  • @mariemely3290
    @mariemely3290 6 днів тому

    Yow yallene am yeurmade celase voit que dans ce senegal oly a toujouŕs des gens qui oeuvre pour le bien.merci mes fils que le bon dieu repande ssa grace sur vous tous ...

  • @abdoulsane7540
    @abdoulsane7540 7 днів тому +2

    Adouna yalla ko mome ❤❤

  • @mahamadoumahanehann7026
    @mahamadoumahanehann7026 5 днів тому

    Beugouma kouye vidéo ndimbeule bimouye défe mais bi mome d’accord nathi a 💯

  • @MaimounaDieng-fz5hr
    @MaimounaDieng-fz5hr 5 днів тому

    Mane mi todo laye dieunde sama meubles ❤❤❤❤❤

  • @abyba5966
    @abyba5966 6 днів тому

    Mashala adouneu moguini yalla bouy defar dafay melni louy yakh chapeaux a vous free fallou on continu le trajet

  • @angelediouma9258
    @angelediouma9258 7 днів тому +1

    Dieu s est souvenu du cœur de la mére de Fallou et a Béni son fils

  • @HabyDiop-i9e
    @HabyDiop-i9e 6 днів тому

    Fallou il mérite k du bien

  • @LissouneSall-qx8qu
    @LissouneSall-qx8qu 7 днів тому +2

    Diereudieuf yalla nalene yalla faye amine li rafetena trop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @thianemboup8694
    @thianemboup8694 6 днів тому

    Salaam nit dé dafalay déf dara beug laa torokhal far bour yallah diaréfa ngua téd ba faw Macha allah

  • @Diouma-i4w
    @Diouma-i4w 2 дні тому

    Machallah merci a vous yalna ko yalla guené 🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @dehabou7720
    @dehabou7720 6 днів тому +1

    Ay way koumay djign katt 😢

  • @fatouhanne6701
    @fatouhanne6701 6 днів тому +1

    Nila yalla bouy défar day melni kouy yah ❤ mougne rék mo am solo ☝️tanta mba xol yagui féeeh😂

  • @MomiDiop-v6f
    @MomiDiop-v6f 6 днів тому +1

    Ay way yalna yalla khep doli amine 🤲

  • @CheichdieumbeGueye
    @CheichdieumbeGueye 7 днів тому +3

    MACHALLA yalla nalla faye

  • @MaguetteGueye-n9z
    @MaguetteGueye-n9z 7 днів тому

    Yayou fallou ligueyba ak yaye yeup li yaye rek mojoy def ci dome nit kou bahla

  • @fatoumoundaodiop6386
    @fatoumoundaodiop6386 7 днів тому +2

    Ba Italie sama khole seed na si yeene sa keur inchala sou paré si yene lakoye meublé

  • @BabacarMbaye-f3u
    @BabacarMbaye-f3u 6 днів тому

    Aywaaay😢😢😢😢😢😢contane na way.Fallou Yalnako Yalla defal diam lafalko tiat

  • @mariamadiop4417
    @mariamadiop4417 7 днів тому +9

    Ahh nekh na yalla na si guéne top inchallah ♥️

  • @nmggm5642
    @nmggm5642 6 днів тому

    Touba ameublement merci kdieu sort falou de la prison amine todo il faut faire des meubles de qualité et qiu dure parceque on a beaucoup de déception de nos ouvriers du pays on aurait voulu le consommer senegalais mais on a beaucoup de déception sur nos ouvriers donko n en fait pas parti bonne continuation ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sokhnagueye1459
    @sokhnagueye1459 6 днів тому

    Machala yalna Yalla yokoulène wa toro❤❤❤❤❤❤

  • @khadydieng3302
    @khadydieng3302 6 днів тому

    Diguène dogali tanta Fallou ko khamoul fouka Ndèyame diourè MANOU REK SI MOME.....❤

  • @PrincesseSeck-k6i
    @PrincesseSeck-k6i 6 днів тому

    Ndaye sanne merci nous somme contant kindouyénne merci ankore une foi

  • @DijaBa-q4e
    @DijaBa-q4e 6 днів тому

    Machallah li Lou rafet la yalna yalla barkel lep

  • @FatouSarr-p3d
    @FatouSarr-p3d 6 днів тому

    Fallou yalla n'a delu si ay ndiobotam inchallah

  • @SIRA.K
    @SIRA.K 6 днів тому

    Yallah bouye dêfare daye melni kouye yakh merçi bcp un beau geste carismatique Fallou on est avec toi❤

  • @MamediarraNdoye-w9z
    @MamediarraNdoye-w9z 7 днів тому +1

    Machala yal nalén yalla fay

  • @tfkteew3586
    @tfkteew3586 6 днів тому

    Machallah talibé Serigne Saliou bi (enlève les boucles d’oreilles ha!!! Talibé Serignebi doutake aye diaro nope) merci TODO ameublement🙏🏽🙏🏽❤️❤️ tata bou Fallou yalla boumou cardiaque 😂😂

  • @adamadioum2659
    @adamadioum2659 7 днів тому +2

    Fatima sa khôl dotoule nékhe bilaye ya bonne khalé yi téki par force 😂😂😂😂

  • @fatoumoundaodiop6386
    @fatoumoundaodiop6386 7 днів тому +3

    Sounou borome kene la mome rek momouna khekh yalla fa mouye defare niit diotewoufa

  • @f.b.s7667
    @f.b.s7667 6 днів тому

    Macha Allah yallah Naléne yallah faye ya raby ❤️🙏

  • @BintouGueye-nd2yr
    @BintouGueye-nd2yr 6 днів тому

    Yalnako Yalla gnéne prison légui amine

  • @abdoulatifkebe5070
    @abdoulatifkebe5070 6 днів тому

    yalla naleen yalla doli diabalé

  • @AmadouDiallo-em6pm
    @AmadouDiallo-em6pm 6 днів тому

    ❤❤❤❤justice pour fallou justice pour fallou

  • @fatoudiagne-y1s
    @fatoudiagne-y1s 6 днів тому

    Machalla je suis heureuse pour cet acte merci beaucoup à vous tous ❤❤❤

  • @diaw64
    @diaw64 7 днів тому

    Ay way Sénégal daniou bakh ndeysane

  • @DiamaDiop-k4l
    @DiamaDiop-k4l 7 днів тому

    Macha Alla Fallou Yalla nala Yalla takhawou

  • @PapiPapi-z6d
    @PapiPapi-z6d 7 днів тому +2

    Fallou limala wakhoone depuis si début bi dou dégne sa liguéyou yaye rek moola walou bilay motakh djiguéne bouy deuye dangua wara moigne nguir sa ndiabote bilay

  • @BebefaSeck
    @BebefaSeck 6 днів тому

    THIEY TANTA YALLA GUI DEFAR FALLOU MACHALAH EY SO YEUGONE DOKO TOUDEU

  • @SeynabouSeck-nr2hd
    @SeynabouSeck-nr2hd 7 днів тому +1

    Machalla fallou laff thiat

  • @diarrathiam3536
    @diarrathiam3536 6 днів тому

    Machalla yallanalene yalla faye geste noble

  • @gueyendeye5486
    @gueyendeye5486 7 днів тому

    Merci vraiment contane nagne trop bilahi wétou gnou ben yone si combat yallah nalène yallah fay yiw 🙏

  • @MariamaMbenguué
    @MariamaMbenguué 6 днів тому

    Fallou liberté la beug guir yallah hum

  • @LazoDiallo-k4c
    @LazoDiallo-k4c 7 днів тому

    Al hamdoulilah Bah oui magnifique que Allah vous protège merci beaucoup les gars

  • @galadiofall8334
    @galadiofall8334 5 днів тому

    Sa liberté vaut mieux que tous !

  • @AntadiamaNdiaye-l6c
    @AntadiamaNdiaye-l6c 7 днів тому +1

    fallou nél sa yaye diadieuf liguéyou ndeye day fégne si milieu

  • @diabelfall3636
    @diabelfall3636 6 днів тому +2

    sant rek yala nelawoul

  • @AdjaDiop-h7z
    @AdjaDiop-h7z 7 днів тому

    Machalla que Dieu vous garde 🙏🙏😊

  • @dogodiop5188
    @dogodiop5188 6 днів тому +1

    Thiey yalla boy defar day melni koy yakh

  • @papaba-d7f
    @papaba-d7f 7 днів тому

    Justice pour fallou fall 💡

  • @FatouSow-x6y
    @FatouSow-x6y 6 днів тому

    Bilaye klole sédena li forna yalle na yalla doli diamou

  • @MussaSowe
    @MussaSowe 6 днів тому

    Yaye fallu da ligey keur bayam

  • @YacineFayesalikhate
    @YacineFayesalikhate 6 днів тому

    Alkhamdoulila. Xol❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤️❤️🙏🙏🙏🙏

  • @AwaSeck-l6z
    @AwaSeck-l6z 6 днів тому

    Bilahi wakh sa kaw fi yalla di défearé domou Adama féwoka ba kaye yakh

  • @BbAwaNdiaye-y7t
    @BbAwaNdiaye-y7t 6 днів тому

    Machalla Roger âme n'a solo loool

  • @Limatata988
    @Limatata988 7 днів тому +2

    Macha Allah yalla feuyleine deugue rek moye moudj

  • @FrançoisMendi
    @FrançoisMendi 6 днів тому

    Merci beaucoup a vous aussi dieureudieuf

  • @SokhnaBaa
    @SokhnaBaa 7 днів тому +4

    Thieuy tatay falou fonék ko khamoul Niko ndayam diouré boulko fékhél khana yousoufa histoire ram dégoko touma bakhoul

  • @AidaDiaw-g7e
    @AidaDiaw-g7e 6 днів тому

    Machallah 🎉❤

  • @mounadabo4644
    @mounadabo4644 6 днів тому

    Machallah ❤️❤️❤️