Mame Mor Mbaye déshabille Sokhna Aïda Diallo "Cheikh Béthio moma nouyoulé ak Aïda mais.."

Поділитися
Вставка

КОМЕНТАРІ • 1,6 тис.

  • @imameassaneseck9143
    @imameassaneseck9143 4 роки тому +3

    Watna thi yalla sokhna aida Diallo mo gueune mamor baye

  • @ThiatouBayedarouyi
    @ThiatouBayedarouyi 9 місяців тому +1

    Merci mame mor mbaye aida Diallo dafa yeup nitt ni

  • @ndeyediodiondiaye6689
    @ndeyediodiondiaye6689 5 років тому +9

    Machalla dieureuf serigne touba amoul morome bilaye dou nite mback

  • @labsolugueye9016
    @labsolugueye9016 5 років тому +1

    Man Daii présidentielle Yii pasai Damala Mairaii wonn Ba Mounou Mala wonn xolatii sax Maii sa kadou yii Daii Mom machalah Barke Mam cheikh ibr serign Touba kaineu la ☝️❤️☝️❤️☝️

  • @southafrica6239
    @southafrica6239 5 років тому +25

    Maa Shaa Allah!!! Señ mame Mor mbaye Linga wakh Lèppou deg le ku bakh nga yallah naa yallah goudel saa fanne tè and ak wèŕŕ

  • @deguenediallo1465
    @deguenediallo1465 5 років тому

    Dieureudieuf mbaye yalna nga goud fane loooool té andak wérr koud téd ki ahmadoul khadim d'où morom

  • @masigasissokho3821
    @masigasissokho3821 2 роки тому +3

    Tu à tout dit merci je ne suis pas mourir mais c intéressent ♥️♥️♥️🙏🙏🙏

  • @lomactarmodou6418
    @lomactarmodou6418 5 років тому +1

    Ko beug serigne touba lega wakh keppo deug la yalla nalla serigne touba takhawo takhawo gno amine

  • @saliouba9888
    @saliouba9888 5 років тому +3

    Merci mame Mor . Ndiguel rek inchala

  • @mariediop1098
    @mariediop1098 4 роки тому +4

    Machallah.. Serigne bi amna Sollo trop..♥️🙏🙏🙏🙏

  • @mamedia6425
    @mamedia6425 5 років тому +16

    Keineu mame bamba yallah na yallah yokou sa leire 🙏🙏🙏🙏

  • @annitademe4146
    @annitademe4146 5 років тому +5

    Machallah Mame Mor contane nagne thi iow vrèma

  • @mahejdjdj1863
    @mahejdjdj1863 5 років тому +12

    Oumar Sall l'homme véridique machallah

  • @lixman5339
    @lixman5339 4 роки тому +6

    Thiey yalla 👏👏Ken dou yonnetibi (psl)

  • @toubadiop4803
    @toubadiop4803 5 років тому +4

    Machala mame mor wahbi amna solo yalla nala yalla fay si barke serige touba

  • @demeabdoulaye161
    @demeabdoulaye161 5 років тому +49

    Que allah nous guide dans le droit chemin

  • @oumarsylla5209
    @oumarsylla5209 5 років тому +3

    💚💚💚 i like this man! Mame mor Mbaaye ma la sope nguir Serigne Touba

  • @moustaphagueye7597
    @moustaphagueye7597 5 років тому +1

    Mame Mor fénkat la, Serigne mountakha waxna nguénn diamou yalla bâyi téré, té lounoufi téré yép yéninguakoy déf. Dieufélénn ndigualou yalla AK serigne Touba. Taguénn bâyi seytané... Kii môme election ya laako bâyi fiii nguafi nék di wattt si serigne Touba si election yi di fénn nann 2ème tour day âme par force yak aida Diallo yéna yam doméram dji

  • @safietoudiedhioudie9328
    @safietoudiedhioudie9328 5 років тому +21

    Mercie beaucoup 👍☝️👂👈❤❤❤👏👏

  • @mamadoulaminendiaye2671
    @mamadoulaminendiaye2671 5 років тому +6

    Djereu jëëf serigne Mame Mor. Kham kham gui sel na, beug gui woor na, kheur gui si serigne bi eup na. Yalna yalla defal leu diaaam.
    Journaliste bi nak rafetlouwouma say question dara. Journaliste dafa wara ame kham kham, mais yow mom sa question yi gueum na ni beugone wakh lo serigne Mame Mor lou eup la gueuna nirou. Alhamdoulilah ba mom ande na ak dal ba topoula si fingako beugone yobou.
    Santati serigne Touba.

  • @elhadjiibrahimafall211
    @elhadjiibrahimafall211 5 років тому +7

    Je te connais pas deh mais amo Kham Kham Bangua wahei djiguen mounoul djitei moro mam la hameni sa ham ham touti na demal diangui wate le coran et voire ayahh yii bou nek loumouy wah merci. Enplus tu es mourid mai hamo dara si mouridisme

    • @talibebunjeng9470
      @talibebunjeng9470 5 років тому

      merci

    • @milkfaye2761
      @milkfaye2761 4 місяці тому

      @elhadjiibrahimafall211 yow mi am xam xam kay leralalniou ndax djigen manna djite moromou djigenam nga waxma thiy ban hayah la ne

  • @khadimsow2809
    @khadimsow2809 5 років тому

    Dieuredieuf serigne mame mbaye kadouyi rafetna lolll te wer loll yalna yalla fayla guengui fay ci barke borom Daroul mouhty dieuredieuf mouride sadekh

  • @dansokhomouhamed3061
    @dansokhomouhamed3061 5 років тому +15

    Je.qui.très. contant. De..lui.ils. Parler. Bien.bik.respect. à. Toi🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @djilifall6288
    @djilifall6288 4 роки тому

    Bilahi Mame mor yalla nala yalla défal Diamo si barkep Serigne Touba

  • @manhattanblack3640
    @manhattanblack3640 5 років тому +67

    Yaw journaliste bii dé yawit beugoo jamm dè.bayilene posé question fitneu waay.billahi loudoul jame jame moko gueune.god bless all of us.

  • @mamemorniang8708
    @mamemorniang8708 4 роки тому

    Allahou akbarr Sama toma yalla na yalla yalla faye ❤❤❤❤❤❤

  • @cheikheseck7129
    @cheikheseck7129 4 роки тому +3

    Merci wa dieuredieuff ser mame more Mbaye ❤️❤️❤️😍😍😍😍

  • @AichaThiam-ki4ok
    @AichaThiam-ki4ok 4 місяці тому

    douma mouride wayé yalla kham nani billahi wallahi dama beugu Serigne Fallou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @gueyemourtalla9639
    @gueyemourtalla9639 5 років тому +11

    Merci Mame Mor Billahi wanga degeu seringe touba domou Adama 🙏👌

  • @CM-xo3oy
    @CM-xo3oy 5 років тому +1

    Wow maintenant c'est les Mourides qui dominant au Senegal! Aida n'a rien fait de grave. Elle s'est juste trompe et peut le rectifier. Mais certains senegalais sont vraiment mechant. S'il vous plait, je ne parle pas du Marabout avant que vous commencez a m'insulter.

  • @pendandiaye709
    @pendandiaye709 5 років тому +3

    Mane dall ki la beugu mane kou beugu s.mame mor mbaye beusseul j'aime

  • @amadoumnd8336
    @amadoumnd8336 5 років тому

    Merci mam mor 👏👏👏👏👏👂👂👂👈☝️☝️☝️☝️☝️

  • @medoune89
    @medoune89 5 років тому +55

    C'est pour la première fois que je le vois avec un discours posé....

  • @princessedangerous3858
    @princessedangerous3858 3 роки тому

    I love you beugeu gua kou diara beugeu cheikh ahmadou bamba khadim rassoul❤sama xol la nek mo ligayal peaux noir diouli si ndokh bi kena dou khadim rassoul😍dieureudieuf yalla bigua oubi weh sama xol bi defci serigne bamba

  • @aminataba9331
    @aminataba9331 5 років тому +12

    Mè yène yallah diam le beugue tè mom le santanè. Dans ce monde keine mo geune c le prophète Mouhamed psl .

    • @Ibzy_boss
      @Ibzy_boss 5 років тому +2

      Aminata Ba Lou lèrr Wallahi_Azim

    • @vieuxba5797
      @vieuxba5797 4 роки тому

      Lou lérrr

    • @mbenefall9086
      @mbenefall9086 4 роки тому +2

      Ak brom touba

    • @princedrt2784
      @princedrt2784 4 роки тому +1

      lou leer amoul sikk serigne touba moy khadimoul rassoul maname moy dieuwrign Mouhamed PSL

  • @mbenegueuye8310
    @mbenegueuye8310 5 років тому

    Dieureudieuf s mame mor fi s mountakha reck mofi né té si aay ndingualame réck laniy dokh koumou nèkh ak koumou nakhari

  • @deuggreikktyallareikktakh3505
    @deuggreikktyallareikktakh3505 5 років тому +5

    *Wallahi Li nga wax Yeuppe deugg la Baye Mor mais meune.nga bOokkalè tooorope.*
    *Après Aïda Diallo liiñOu wara khêkh deugg Ci YonneWiii moyy BokkaLè Gui.Nous associons trop ALLAH aux humains*
    NaañOu Diox YALLA Sunu Borom Thieurreum bImOu mom wayy

    • @Important-e6f
      @Important-e6f 5 років тому +1

      Deugg rk nga wakh, mane dama diomi sakh

    • @deuggreikktyallareikktakh3505
      @deuggreikktyallareikktakh3505 5 років тому +1

      @@Important-e6f Dafa euppe Wayy Billahi Wallahi...Franchement il faut k ñOu gueuna Xamal Mbokk taloubbê Yi YALLA ,YONINTE BI S.A.W, AL"QURANE ak SUNNA de prime abord avant ñouciiy teikk Lènnènne

    • @Important-e6f
      @Important-e6f 5 років тому +2

      @@deuggreikktyallareikktakh3505 sétanal rk, aljanna mom djeureudeuff diww ak fatt ay wakhtu diouli nèk si lula neekh dou fa yobou kèneu,

    • @deuggreikktyallareikktakh3505
      @deuggreikktyallareikktakh3505 5 років тому +2

      @@Important-e6f ah en tout cas Serigne TOUBA Nèna xamoul T amoul Aldiiana bOu Diiamou YALLA DouLe mayyè...waxna ni Diamoulène YALLA T baaña doOne dofff

    • @DibbDiouf
      @DibbDiouf 5 місяців тому

      Omar sall mom fén rek ak sosal gni gni lafi néké

  • @ndeyekhadyngingue736
    @ndeyekhadyngingue736 5 років тому +1

    Yena guiss sokhna aida toudou doom serigne saliou samb moy toudou moy mayé sey yi

  • @ndiagabeye591
    @ndiagabeye591 5 років тому +4

    Merci beaucoup ya buegue serigne touba mane yaw laye bege

  • @linvincible2967
    @linvincible2967 5 років тому

    Kii moom yeukkeuti fitneu ak wakh wakhi dof rek la meun. Seytané leu... on n'accroche pas une vie à une personne mais à Dieu parce que c'est lui qui te l'a donné. Dieu merci...

  • @maguettembodji6078
    @maguettembodji6078 5 років тому +5

    Yalla na serigne touba fay la bègueé ❤

    • @lomactarmodou6418
      @lomactarmodou6418 4 роки тому

      Beug ga serigne Touba lala mana wakh yalla na serigne bi Faye

  • @ndeyeantasamb1641
    @ndeyeantasamb1641 Рік тому

    Toma nafekh bakhoul djiguene dou djite mbollo sallahou alla mouhamed ♥️♥️❤️♥️❤️❤️♥️

  • @ndaobambiste7446
    @ndaobambiste7446 5 років тому +4

    Franchement certaines journalistes mérite des formations de qualité serigne Touba kene

  • @maffafa4111
    @maffafa4111 5 років тому +1

    merci .mame mor mbaye liladonehar sa rection

  • @SeneSenghane
    @SeneSenghane 5 років тому +9

    Dieuredieufé Serigne Touba Khadimul Rassulillahi.
    Mame Mor wax bi rafètna Maa Shaa Allah.

    • @rebotreno151
      @rebotreno151 5 років тому

      センセンガン Wadji deh loumou wax loudoul MOR la toudou day feneu kathieu katt deugg mongui ni😂😂😂
      Dangueine fattei thi élection yi boumouy youxou Macky di xandjoou macky gagner mou tit di weddi aka djiegallou bobba lako sibbb 😂
      Feneuh rkk

  • @bassiroufall9595
    @bassiroufall9595 5 років тому +2

    Machallah dieurieudieufaty s touba mbacke amoul morom mame mor yalla naga fi yague te wer

  • @babafall6941
    @babafall6941 5 років тому +6

    Saydina omar je suis très content d'avoir toi jajeuf srg bo magg bi

  • @zeynabdiallo6431
    @zeynabdiallo6431 5 років тому

    🙏🙏🙏Machaalla kadu yi rafét na

    • @rebotreno151
      @rebotreno151 5 років тому

      Zeynab Diallo Wadji deh loumou wax loudoul MOR la toudou day feneu kathieu katt deugg mongui ni😂😂😂
      Dangueine fattei thi élection yi boumouy youxou Macky di xandjoou macky gagner mou tit di weddi aka djiegallou bobba lako sibbb 😂
      Feneuh rkk

  • @amidousissoko2773
    @amidousissoko2773 5 років тому +5

    Ce mec qui parle et aida diallo est le même parce qu’il compare également amadou bamba et Allah, alors quelle est la déférence entre lui et aida jallow 6 et 9

  • @CheikhNdiaye-w8h
    @CheikhNdiaye-w8h 4 місяці тому

    Jarajeuf Mame Mor. Serigne touba rek amoul morom❤❤❤

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 5 років тому +5

    Faites attention à Sokhna Aida elle avait une part très importante dans le coeur de Bethio Thioune et ce n'est pas sans raison. Dans notre société on a du mal à respecter les femmes. Dommage

    • @marindiaye9403
      @marindiaye9403 5 років тому

      Bilay gno bok guis guis

    • @adamadione4267
      @adamadione4267 5 років тому +2

      @@marindiaye9403 bayiléne nafékh Aïda da wara khame bobam

    • @moiseendurant5284
      @moiseendurant5284 5 років тому

      C triste mais vous avez raison

    • @marindiaye9403
      @marindiaye9403 5 років тому

      @@adamadione4267 demain digua am sa reponse

    • @alphaoumardiallo3884
      @alphaoumardiallo3884 Рік тому +1

      Avoir du mal à respecter une femme c moyen grave qu 'avoir du mal à respecter Allah swt fait attention à tes commentaires

  • @awadiouf5681
    @awadiouf5681 5 років тому +1

    Man balama beugueu dee aida diallo nann dieureudieuf cheikh bethio thiow li thiow serigne touba laa. Deugueu nekhoul

  • @bambadioum4043
    @bambadioum4043 5 років тому +10

    Dieuredieufety Serigne Touba. Señ Mame Mor contanna lool thi sa pastef.

  • @bassiroudieye4691
    @bassiroudieye4691 5 років тому

    Akassa Mame Mor. Ya bakh. Ya beugue serigne Touba. Tu es un vrai défenseur du mouridisme. Yalla nangua ame feyou serigne Touba. Serigne Bass.

  • @khadyfalliloufall730
    @khadyfalliloufall730 5 років тому +9

    1er vue 👀👀

    • @grandakar
      @grandakar 5 років тому

      Yaw mom geumo Dara this election yi lala weddidawakh deugu

  • @madoundiaye697
    @madoundiaye697 5 років тому

    😂😂😁😁😁non mamor mbaye dina ma raye😁😁😆😆

  • @cheikhdiouf9535
    @cheikhdiouf9535 5 років тому +27

    Diadieuff.mame.mor.yalnala.yalla.faye.

  • @ahmadrachid8127
    @ahmadrachid8127 5 років тому +1

    Baayilen sen maam yinguen di diaamou té nguen diaamou yalla, al'qur'an ak sunna bounguen ko toppon simplicité rek nguen di doundeu, as'salaamou alaykoum!

  • @akd696
    @akd696 5 років тому +11

    Aida diallo foumou sampaté bach tégaléne ndéyam point

  • @Lopios-g6l
    @Lopios-g6l 4 роки тому

    Machalla ken dou borom Touba yakarou fii akk fagnoudieum !!

  • @djibrilsy9610
    @djibrilsy9610 5 років тому +4

    malgré tout Sokhna aÏda borom paStef le

  • @Heendiaye
    @Heendiaye 4 роки тому +1

    Serigne mame yalla nalla yalla faye pédagogue bi bakh

  • @willystar4007
    @willystar4007 5 років тому +19

    Tout est lié à des raisons financières et économiques. Tout est lié à des intérêts économiques. Aicha veut protéger des intérêts economiques.
    La vie des gens est guidée par la gestion de leurs intérêts économiques

  • @azizweberpro7835
    @azizweberpro7835 5 років тому +1

    Serigne Mame Mor Mbacké yagg fi lol té andak wer voila nitt kou véridique ...kaddu yi amna solo lol machallah deug néxoul Serigne Mountakha moffi toggal Serigne TOUBA té limou beug moy ameu ...yonou Mouride amoul kenneu kouko manna sokhal rawattina Khalé bou dioudou barky démm.Donc soxna Aida yamal si coudou niou rokhla si thinnn té olof ndiaye néna "Kouy diaxann di saw bala kénneu toy ga laurr".

  • @adamasene5415
    @adamasene5415 5 років тому +14

    Mane ki lay weurr .je l'adore

  • @nifandumba7911
    @nifandumba7911 5 років тому +1

    Bilaye walahi magui guigne si magou yalla serigne touba migui si sounou bire dou coye fattou

  • @aliounebadarambaye1601
    @aliounebadarambaye1601 5 років тому +47

    Walay mame mor wakh nga degg serigne touba motakh niou ame diamm motakh warounio déf dara louko nakhari té serigne mountakha moy serigne touba diko niane mou dièguelniou mbacke balla.

    • @abdulfama5345
      @abdulfama5345 5 років тому

      Akassa waaw gor

    • @babafall6941
      @babafall6941 5 років тому +1

      Ndaysan amna solo

    • @patriotedusenegal1350
      @patriotedusenegal1350 5 років тому +3

      ya meuna doul serigne touba motakh niou am diam yalla moy borom diam domeram demal diangui té bayi bocalé

    • @papegueye4376
      @papegueye4376 5 років тому +2

      @@patriotedusenegal1350 khadje nga mo takh do ko mana kham

    • @Tahirousarrforever7418
      @Tahirousarrforever7418 5 років тому +2

      Wakho deug yalla Moy borom diameu

  • @aliounediouf2862
    @aliounediouf2862 4 роки тому

    Mame mor mbaye Yalla la Yalla fey yiw varie borom Touba.Mbacke

  • @azizgueye9858
    @azizgueye9858 5 років тому +5

    Mame Mor yaa baax
    حفیظک الله و اطال عمرک ببرکاه الشیخ الخریم

    • @nitudeug3382
      @nitudeug3382 5 років тому

      ما رأيت من هو أكذب منه

    • @kadiatoubaldebalde5628
      @kadiatoubaldebalde5628 5 років тому

      Tu as oublié ce k tu a fait la maison de assane douif tu es pareil l les thiantacoune

  • @wakeurstoubadiangueakdiang8646
    @wakeurstoubadiangueakdiang8646 5 років тому +2

    Machallah s mame mor dieuredieuf wakh dji amna solo nane di maytou di wathi ndigeul li ndakh ko khamni bou meiré sunu borom meire bou contané sunu borom contane serigne touba serigne mountakha togayoup sunu borom la togué gnou bayi kheil bou bakh té khamni sunu borom ngouram gui amna gnouko présenter fi ci adouna té kéneu djitouwousi serigne touba serigne mountakha mbacké

  • @mbayediouf7119
    @mbayediouf7119 5 років тому +6

    Défal ndankke djiguén amna foumouy djitè ay moromam dh😂😂😂

    • @papamalickdiop1205
      @papamalickdiop1205 5 років тому +1

      Mbaye diouf hors sujet.

    • @airmaxstar5762
      @airmaxstar5762 5 років тому +2

      Mbaye diouf fane la

    • @beugueldiouf4524
      @beugueldiouf4524 5 років тому

      Djiguéne Bouy djité dé dou si yonou mouride. Khana fénéne

    • @beugueldiouf4524
      @beugueldiouf4524 5 років тому

      Ki kagne da H.S rek.

    • @mbayediouf7119
      @mbayediouf7119 5 років тому +1

      layemakhtar laye très intelligent 🙏dafnè djiguén dou djittè dioulli manèko amna foumouy djitè ay moromam diouli si dinnè fofou lay Wakhè

  • @dembadiop6738
    @dembadiop6738 5 років тому +2

    MAME MOR MBAYE ya kawé yalla nala serigne touba fayy Euskeuy Fall

  • @assanegueye4036
    @assanegueye4036 4 роки тому +19

    thiey adouna nanou delou si alkhourane ak souna yonentibi mo guene

  • @absambaye9732
    @absambaye9732 5 років тому +1

    Machahalla mame more mbaye wakhe dji rafetna

  • @mayipndiaye1632
    @mayipndiaye1632 5 років тому +7

    Man dé Aïda Diallo bounko Don ray sakh Sama gatt! Nakh guemoul touss! Wayé Mor Mbaye mii tamit guemoul gatt! Si door kat yi la boke! Ay door katt ngén! Yaw Aïda Diallo rék nga tané!

    • @Seyeseye1079
      @Seyeseye1079 5 років тому +1

      Éléctions presidentielles démb lawoone

    • @sallomar2471
      @sallomar2471 5 років тому +2

      Grand wa khal waye mamor dou dra door katt la

  • @afiamediatvsenegal6733
    @afiamediatvsenegal6733 5 років тому

    Bilaxi begg na ci Mame Mor Mbaye Machallah

  • @mohameddiop7274
    @mohameddiop7274 5 років тому +29

    Yalla na diam yagu

  • @aladjindiaye5141
    @aladjindiaye5141 5 років тому

    akasa dieureudieuf serigne mame mor yalla nala serigne touba faye contan na trop si iow mane sa sopé la kou la beugue

  • @bathiediop1028
    @bathiediop1028 5 років тому +3

    J'apprécie bien❤ sa façon d parler. Serigne Touba la kéneu xamoul loumou done.
    Diadieuff Mame mor

  • @awasarrdiop4561
    @awasarrdiop4561 5 років тому

    Bilahi kou yeuk Serigne Touba dou dal. Yeungou ngay def. Serigne Touba amoul morom moh👌

  • @bambagabi9720
    @bambagabi9720 5 років тому +6

    aye waaye kone serigne mountaha naléne wakhe niou bayi medicament you bone yiniouye diaye, na léne wakhe niou bayi senegal bigniouy saltele, naniou bayi yakhe biniouye yakhe senegal

    • @ousseynoufall5004
      @ousseynoufall5004 5 років тому

      Kane mofi yakh Kane mofi diay médicaments you boneu Kane mofi saltél réw mi
      Kane mofi yakh
      Dou mouride yi dh té SERIGNE MOUNTAKHA MBACKÉ mouride yi lay ndiguel

    • @olypibrahim5052
      @olypibrahim5052 5 років тому

      Mais attend, Yakk senegal Gua Wax Ioe Mouride Yi grace au magal ton pays a 236milliards juste si evenemen magal bii ... Tu me parle de Yaak senegal, Après guanii saltel Ioe Niou dem biir dakar Tabakhal lafa Juumah bou couté 20 milliards ... Avant de parlé Faut Bien reflechir.'

  • @mouhamadaneallhamdoulillah0292
    @mouhamadaneallhamdoulillah0292 5 років тому +1

    Manchalla khadime Rassoullu 😍

  • @alertecitoyen9932
    @alertecitoyen9932 5 років тому +36

    Ce gars est pire que Aida Diallo
    Merci de votre attention

  • @ndeyekounta6091
    @ndeyekounta6091 5 років тому

    Mancha lla wakh dji manta .djeurejeuf serigne touba ligueyeul gua yalla mou faye la mbollo

  • @salioumbaye2479
    @salioumbaye2479 5 років тому +51

    Merci way Serigne bi wakh bi amna solo loll way

  • @doudougueye106
    @doudougueye106 4 роки тому +1

    yénnn gniii yéna yeukeutiii Aida dialllo wakh kat yi ak site yi "aida loumou beug dou ameu lou Seugn Mountaha beug moy ameu " Subhanallah........ gnarii beug beug yii warou gno bokk sakhhh siii ap lamigne ndakhhh bokouniou yone..... LEUNDEUM AK LERRR di danou di wakhhh ba mbeukou rekkkk li dou alou sopppp la rekkkk wakhé len khamkham mo gueun

  • @yettafaye53
    @yettafaye53 5 років тому +7

    🕌🇸🇳⛪👏👏👍 je suis catholique nous vous remercions tous les sénégalais❤

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 5 років тому +1

    Machallah borom deuxième tour inévitable kaddou yi rafet na lool mais boul ci arrière nak wawww gooré mbaye

  • @serignendiaye22
    @serignendiaye22 5 років тому +3

    Yonou mouride mo beuri nafekh ! Ana MBACKÉ MBACKÉ bidone sabar biir touba

  • @samndiaye8325
    @samndiaye8325 5 років тому

    Masala

  • @AbdousalamBaJB
    @AbdousalamBaJB 5 років тому +4

    Serigne touba est une personne quelque spit sa dimension.

    • @ibrahiimaba9554
      @ibrahiimaba9554 5 років тому

      Abdousalam. , Ba EN

    • @modoudiouf9054
      @modoudiouf9054 5 років тому +1

      serign Touba a dit : ''je suis ni Homme ni djinn ni prophète mais je suis cette créature unique qui vit d'apparence en humain sur terre ''

    • @baysall9672
      @baysall9672 5 років тому

      Limoy wakh gamou ci toss.fomou Nékk interé personelam moko fa bayyi

    • @assanendiaye2237
      @assanendiaye2237 5 років тому

      Serigne touba depasse LA dimension humaine ..reflechit

  • @mamadoulaminediame572
    @mamadoulaminediame572 4 роки тому

    Vraiment merci beaucoup

  • @arimaz89
    @arimaz89 5 років тому +24

    Aida limakay nianal moy yalla nako yalla guindi ,diko digeul mou bayi lepeu mou sedeu aduna diarouko,ter deugeur bopeu baxoul ,nit kou bax dafay degeu ndigeul bayi terer

    • @astousaleh3430
      @astousaleh3430 5 років тому

      Amine

    • @omarsall2860
      @omarsall2860 5 років тому

      Waw gôr kobakh l'I nga wakh môy dagg nigy wakh kén wakhlo wolén sorto kalas gi fétna rék lanoy yé té khamon Dara tihi yôn wi khalais rék lanôy war mérce

    • @Homme07-c2y
      @Homme07-c2y 5 років тому

      ndaw kou rere vous avez rien compris

  • @ballafall1026
    @ballafall1026 5 років тому +1

    Bayiléne serigne touba kou maneu na déf ni mome

  • @dieynabadiallo2554
    @dieynabadiallo2554 5 років тому +4

    Ces genres de personnes nous donne la force d'aimer encor serigne Touba❤ yonou mouride rek mo gnou sohal

  • @AichaThiam-ki4ok
    @AichaThiam-ki4ok 4 місяці тому

    yonou mouride machallah wayé gnou mélni sokhna aïda motakh gnou yap léne

  • @TEAM_DMG_OFFICIEL
    @TEAM_DMG_OFFICIEL 5 років тому +11

    talibé chiekh bi Nanou dém si Serigne saliou thioune mofi nékal chiekh bi pour Man FIN

  • @djillyka3062
    @djillyka3062 5 років тому

    Machlla.ame.na.solo

  • @barhamamboup6431
    @barhamamboup6431 5 років тому +6

    bokallé mom bakhoul deklou na sa wakh lép Nice wayé auto mom boul wakh ya cheikh Ahmed bamba bamba yoroul réw mi dhe 😱
    واذا ركبوا في الفلك.........

    • @abdougueye3398
      @abdougueye3398 5 років тому

      Sisou mane kéne Douko tonton 😂🤗

  • @leboundoye2314
    @leboundoye2314 5 років тому

    Machalla machalla yalla n'a diamou yagui diadeufe sérigne Mame mor mbaye kéne d'où Serigne Touba diadeufe mourit