Wakh deug mo nékh yallah mais lamb ji daniouko wara categorisé genre A,B,C..... chaque anné niou guéné ay outsider si categorie bou nek..mais lepa diakhasso😂😂
Modou lo Bou naré ragal na bayi beuré bayi len Sen wakhi thiakhan modou day may tapha tine chance rek tapha mon djitou modou si lamb modou eup ko victoire guen ko néwi défaite niane len modou si ndiék rek 😂
C’est possible kel supporter modou la Mais modou meuneu dane tapha aussi de par ses qualités intrinsèque Tapha dolé rek la eupalé modou moy son plus grand atout
On veut l'interview de yekini ou centant gningue
Boy Niang - Siteu
Bombardier - Franc
Reug Reug - Balla Gaye 2
Modou Lo - Tapha Tine
Yaw mi nak ya kham lamb machllla
Modou lo c est un tres grand sportif de haut niveau ba parei ame guinaw boy yi meunougnou dará si mome
Ndîol ponkal nek encaisseur tek si oyof mystique sakh danoul modou lo sounou borom moko guimb dafa niakk roi bi
C'est un très grand sportif de haut niveau parei
Cheikh Basse nkm nice yagui cool numéro Lamaine Seck la beugue déh
Senegal kou danou meuno darra ki dane mo meune lépppp modou lo dane na ama ta aye eurre you berri la déf
❤
❤❤❤❤❤
Boy niang vs sathies combat revanche
Wakh deug mo nékh yallah mais lamb ji daniouko wara categorisé genre A,B,C..... chaque anné niou guéné ay outsider si categorie bou nek..mais lepa diakhasso😂😂
Modou lo Bou naré ragal na bayi beuré bayi len Sen wakhi thiakhan modou day may tapha tine chance rek tapha mon djitou modou si lamb modou eup ko victoire guen ko néwi défaite niane len modou si ndiék rek 😂
Sonko 😂😲
Tapha tine meunoul dane modou
C’est possible kel supporter modou la
Mais modou meuneu dane tapha aussi de par ses qualités intrinsèque
Tapha dolé rek la eupalé modou moy son plus grand atout