Aucune personne ne peut affirmé que tel personne a créé tel langue tous les langues sont la création de Dieu donc difficile de déterminer quel famille est la première a l'a parlé
Nous sommes des descendants de coush depuis le sudan nos ancêtres ont règne sur le royaume de coush avec nos frères de sang les Dinka nuer... L'origine du wolof est nilotique de même que notre langue et culture..
E. E. M kha kha boul diaxasé histoire dé thi lo khamante li rek molen separe 🦍 kese éthique sa amoul thi aduna bi khana sathie domou diambour ô mbokhess wala sathie khale domou diambour kese thi adunabi
Ça il y a aucune livre de histoire qui a écrit ça ça c'est pas vrai c'est toi qui a inventé ça arrêtez de faire ça va regarder le histoire il y a aucune livre qui a écrit ça ici nous tous nous sommes même pas c'est la dieu qui a créé
Ici nous tous nous sommes même parce que c'est la dieu qui l'a créé🙏🙏🙏 respect
2 роки тому+1
Laaj bu njëkk moo di yw ñaata livre d'histoire nga mas a dawal (lire) ? 2- Fi nu jëlee li nu fi wax (sources yi) mi ngi ci description bi, kuy weddi bindkat, xamtukat, saa-mboor (écrivains, scientifique, historiens) ñooñu ngay weddi, waaye du nun ñii nga xam ni, sunu xam-xam bariwul; danuy jottali rekk.
2 роки тому+1
Cëy Yàlla ! Yaw li ngay wax nii lu mu doon (du xam-xam) ! Tee ngaa maandu soo xamul ne man !!
Bàlluwaay/ Source: téere Saaliwu Faal « Wolof Ak Esibt Gu Njëkk Ga », Yoro Booli Jaw ma-mbooru saa-senegal (1847-1919), téere Seex Anta Jóob « Nations Nègre et Cultures ».
Production : Souhaïbou TV
Yalna al quran doon sa wétaal , yalna souff woyaf sa kaw , souhaïbu 😭😭🤲🤲
Mamadou ba cva
😢😮❤❤🎉sama yarm bakidaw jey wolof nena konjon ijpte lann jok nepayem ay olof lej
Jërëjëf. Yalla nalen yalla fay yiw
Machalla amna solo trop.
Dafa diot niu xamat finiu boku.
Mashallah tawarkallah Amna solo lool yàlla na yàlla barkeel xam-xam bi
🙏🏾
Machaa Allah yalla nala yalla fay yiiw 👍👍👍❤️🇸🇳
Wolof kéy amneu macha Allah ❤ man soninké dama guém Sénégal ak ay languame Afrique rk guay gui ay plusieurs langues ❤
Jaajëf
Jerejeuf amena solo lol kham fan nga sokheko yon la🎉🎉
Dieureudieuf ❤️🙏🏾
Maasàlla amatina solo lool akasa jaajëfati solo si foo ko takk rekk weesu na ko, xam sa bopp dara dàqu ko🙏🏽
Maa chaa Allah. Dieureudieuf
🙏🏾
Amna solo lol Dieureudieuf 🙏🏾
🙏🏾
Nous les wolof sommes les descendants des sudanais..du royaume de cush..nous sommes des nilotiques.
Attention, rien ne nous dit que nous sommes descendants d'eux, pourquoi pas l'inverse.
Mounou malen faye❤
Yalanala yalla fay❤❤❤❤
Votre travail est incroyable et incontournable. Bravo les frères 👏🏾
Lotahh naar di wah ya allah
Merci beaucoup
🙏🏾
Macha alah amna solo loool diadieuf way
Du courage mon frère. Ku xamul finga bayeeko xam finga jem du yomb te reer rek moo ciy top
Machallah c'est vraiment intéressant parceque leggui kou nékk dalay diaay Lou kenn khamoul th lolou dangay dello guinaw
Mais merci beaucoup
🙏🏾
Waouh gor fall❤❤❤
Jërëjëf kilifa gi !
Yal na Yàlla yokk xam-xam bi.
Paate Lamin = Ptolémé...
Merci je suis très contente de vous
Je suis faire d'être wolof ❤
Aucune personne ne peut affirmé que tel personne a créé tel langue tous les langues sont la création de Dieu donc difficile de déterminer quel famille est la première a l'a parlé
Machalah amna solo
Amna solo lool❤❤ ligéye bi rafêtna
Mashallah amatina solo diadief
Amna Solo lool❤
Merveilleux
Machallah ❤
Jërëjëf
Macha allah
Diadieuff 🔻☯️🔺
Wolof ❤
Jërëjëf❤❤❤❤
Ma challah diërëdiëf❤❤❤
Mais livre bi nane laye déffe ba amsi svp🙏🏻
Amna solo ❤
Merci ❤❤❤
Mâcha allah rafet na lolllllll
Namón nañu lén way
Fii la ëppee daal 🙏🏾
Amna solo machalla
Amna solo
Macha allah Amna sollo dama Khoulo Bah Sonne sii wolof Amna Mais personne ne me crois
Te li ñuy wax teguwul ci xam, teguñu ko fenn.
🙏🏾
Nous sommes des descendants de coush depuis le sudan nos ancêtres ont règne sur le royaume de coush avec nos frères de sang les Dinka nuer...
L'origine du wolof est nilotique de même que notre langue et culture..
Merci
Merci beaucoup ❤❤❤
Mashalla
🙏🏾
Jaajëf
Belle culture générale
Machala
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
E. E. M kha kha boul diaxasé histoire dé thi lo khamante li rek molen separe 🦍 kese éthique sa amoul thi aduna bi khana sathie domou diambour ô mbokhess wala sathie khale domou diambour kese thi adunabi
❤❤❤
Bëg na lool
🙏🏿
Jërajëf
Mana solo
🙏🏾
Wolof yi tamit dagno diay senn culture dem nekii dioulitt. Islam dou sounou culture arabe yii gnoko momm
Déjà l'islam c'est pas une culture mais une religion
@@fatimadiop1402 l'islame n'est rien d'autre que la cuture des arabe réveiller vous les arabe vous pour vous imposer leur culture
Yaw wero nonou dh😅
Sa waay gnooom Serigne Touba gnepa leen nangou
Loolou sa problème famille la
Ndax lii bindu géntihi aytéére
Su dee topp nga widewóo bi ba mu jeex, am na téere bu nu ci tudd.
« Wolof Ak Esibt Gu Njëkk Ga »
Jerejeuf leer na.
Wa gninan wolof amoul funiou ko tek ?
Ñenn ci seen bakkan kepp ! Ñeneen ñi ñàkk a xam te jëfandikoowuñu seen i xel; xam lu xellu !!
Çëy
6
Kallama arabe la moy baat wala kadou
جرجفت
🙏🏾
Ça il y a aucune livre de histoire qui a écrit ça ça c'est pas vrai c'est toi qui a inventé ça arrêtez de faire ça va regarder le histoire il y a aucune livre qui a écrit ça ici nous tous nous sommes même pas c'est la dieu qui a créé
Ici nous tous nous sommes même parce que c'est la dieu qui l'a créé🙏🙏🙏 respect
Laaj bu njëkk moo di yw ñaata livre d'histoire nga mas a dawal (lire) ?
2- Fi nu jëlee li nu fi wax (sources yi) mi ngi ci description bi, kuy weddi bindkat, xamtukat, saa-mboor (écrivains, scientifique, historiens) ñooñu ngay weddi, waaye du nun ñii nga xam ni, sunu xam-xam bariwul; danuy jottali rekk.
Cëy Yàlla ! Yaw li ngay wax nii lu mu doon (du xam-xam) ! Tee ngaa maandu soo xamul ne man !!
@@bayaldia5179 yaw khamo histoire démal djangui
Bella storia
Masala ❤❤❤❤❤
🎉🎉🎉 masalla
Amna solo
Merci beaucoup
🙏🏾
Jërëjëf
Merci
❤❤❤❤❤
Machala
Jërëjëf
Merci infiniment
Jërëjëf