Oh nous Senegalais et Muslimes croyants pourquoi ne pas ces divisions qu Allah nous interdit soit disant tarikhas et suivrent la voie de Dieu et nous ranger derriere notre Prophet qui n etais ni tidjane ni khadre ni mouride .Quiconque divise les musulmans aura des problemes serieux avec Allah et des comptes seront rendus .Ces graves ces mensonges et manipulations. Qu Allah nous recussitent Amine.
Mané nafekh bi nek sene digeunté lanouy wané. Tariqa senegal elles se contredisent ! Les Tijan disent que yonenté mo diokh salatoul fatihi à Cheikh Tijan, Layene yi né Baye Laye moy yonent...or Baye Laye si doundam diangalé woul salatoul fatihi...comment se fait-il que yonent bamou neké sa Madina diangalé woul salatoul fatihi, mou wouyou dji boromam dora fegnou Cheikh Tijan diangalé ko, delousi sous forme de Baye Laye encore une fois diangalé wou ko. Ga khamné né entre Cheikh Tijan et Baye Laye am na kouy wakh lou weroul. Vos tariqa se contredisent entre elles té pourtant vous dites que béne guéne...mdr
C vous qui avez divise la ouma islamique, vous qui avait emmene des tarikha ici. La ouma islamiwue etait unie au temps du prophete car le prophete ne connaissait pas de tatikha. Il n'yavait que sa sunna
@@FIPOUSOPIREWMI sou tarikha amoulwone islam dou avancé. holal tel niata salafiste nioy guéne islam ey ancien wahabiste nioy guéne islam tes . fait des recherches
Oh nous Senegalais et Muslimes croyants pourquoi ne pas ces divisions qu Allah nous interdit soit disant tarikhas et suivrent la voie de Dieu et nous ranger derriere notre Prophet qui n etais ni tidjane ni khadre ni mouride .Quiconque divise les musulmans aura des problemes serieux avec Allah et des comptes seront rendus .Ces graves ces mensonges et manipulations. Qu Allah nous recussitent Amine.
Salam..yene wa chaîne bi est ce que ay dioulit nguene louy yakh, diakhasse, toutal sene moromi dioulit..delo lene sene khel si yalla..
Machallah
yeine mom chainou shaytan guéne rek Yeine ndonguay tass réwmi mais Yalla gueumoul nélawoul
Vérité absolue 👍
Verite absolue🤚💓
Meunoléne gnou diakhassé ak mourides yi sounou Aÿ mbocky dioulite laniou sénou ibliss
Je suis content de toi
Inshallah, kéne dounou diakhasé, wa chaîne bi nioye shayetané rajim
Toppou yalla toppou yonentam PSL réka woor le Coran et la sunnah triomphera inchallah deugue rekay moudiou
Yeen seen ug njullite mate na saytu waat d. Seen titre de satan bi ngeen def laaxamul mooy lan mbokk yi
Mané nafekh bi nek sene digeunté lanouy wané.
Tariqa senegal elles se contredisent !
Les Tijan disent que yonenté mo diokh salatoul fatihi à Cheikh Tijan, Layene yi né Baye Laye moy yonent...or Baye Laye si doundam diangalé woul salatoul fatihi...comment se fait-il que yonent bamou neké sa Madina diangalé woul salatoul fatihi, mou wouyou dji boromam dora fegnou Cheikh Tijan diangalé ko, delousi sous forme de Baye Laye encore une fois diangalé wou ko.
Ga khamné né entre Cheikh Tijan et Baye Laye am na kouy wakh lou weroul.
Vos tariqa se contredisent entre elles té pourtant vous dites que béne guéne...mdr
Tarihayi gnoo tardéle Sénégalé yi ay soss kassé laa dou l'islam dou dara wallahi
Chaitane.bakhoul
Astakhfirou.laha
bayilen di divisé la ouma islamiya kousidé dem safara salafiste you bonneyi
C vous qui avez divise la ouma islamique, vous qui avait emmene des tarikha ici. La ouma islamiwue etait unie au temps du prophete car le prophete ne connaissait pas de tatikha. Il n'yavait que sa sunna
@@FIPOUSOPIREWMI sou tarikha amoulwone islam dou avancé. holal tel niata salafiste nioy guéne islam ey ancien wahabiste nioy guéne islam tes . fait des recherches
Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégalé yi dou l'islam dou dara loudoul bida ay soss kasé la
Wawaaw morit ak tidiane war nano pache fi bo yagge
Baleen di ñou gueumlo ni dangene joubo xam nañ lepp
Diouli si guédj boudoul Dara nako sa baye déff niou khôl nioune Domi Mame Diarra moniou doy .
Sen tarikha you gniouss ndayam yi gnio yakeu sénégal tegeulen sen ndaye feulé
Bismilahi rahmani rahim alhamndoulilahi rabil alamine a’rahmani rahimi maliki yawmi dini iyaka nahbadou wa iyaka nastahinou ihdina siratal moustaqima siratal lazina an amta aleyhim hayril mahdoubi aeyhim wala daline
Alxouran ak sounnah doynagnou soxla wougnou lénén dara féssoul sougnou beutt loudoul l'islam bou rahoul dara
Loutakh WAHABIYA YI ( waa AHMED lo)ak IBAADOU YI dioubowougnou ???
Wakhofi dara
Moytoulén tarihayi dou l'islam yonéte yalla bi saw bayi woufi béne tarixa loudoul l'islam kasé
Yén wahabiste Yii Sonou guin dé
Gno tay sonna
Yalna yalla mousal gnou ci soss ci dîné yalla bi tarihayi bida kasé laa
Vérité absolue 👌