Intégralité combat Lac Rose vs Jackson - Reportage : Tapha Gueye, Palla Diop et Lamine Seck

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 18 гру 2024

КОМЕНТАРІ •

  • @DoudouThiam-lj3vo
    @DoudouThiam-lj3vo 6 місяців тому +58

    Félicitations lac rose diambar nga amoul khalate yokeu liguéy rék day bakh inchalla 👌🏿👏🏽❤

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 6 місяців тому +81

    *Seetlou na grands contre petits yeup yici eup grands yi nio daan. Sen diaar diaar bokoul ak boys yi. Danio ramper, mbappatt lou yague avant niouy dougou arènes. Teh temps yoyou ay réseaux sociaux amoul, il fallait être un vrai champion pour percer. Motakh génération bobou dougn moromou boy yii. Félicitations Lac Rose!*

    • @seckousmane3397
      @seckousmane3397 6 місяців тому +4

      Deugu gua wakh

    • @fayendiouma2081
      @fayendiouma2081 6 місяців тому +3

      Bilahi Aka lerr bro

    • @fallabdou7163
      @fallabdou7163 6 місяців тому +4

      Pask yégalougnou khaléyi dakheu beuré mais khaléyi beuri thiow lagnouy bolé ak mak yi

    • @babadia5289
      @babadia5289 6 місяців тому +3

      Tu dis vrai, sa diar diar yalaa 😊

    • @mory6196
      @mory6196 6 місяців тому +3

      Mbeur bout d'âne mo geuneu sonou sakh mbeur bout danou dinagne la geuseum bagua sonou😂

  • @fillafall1657
    @fillafall1657 6 місяців тому +26

    ndaye san le retour de lacrose félicitations du courage djack son

  • @Bouchrambacke
    @Bouchrambacke 6 місяців тому +40

    Yéne nék leu borom mo thiy fanan lim yéne rakkam pape ndoy mom lako yalla fay

  • @bloodmoonb.o.o.z2809
    @bloodmoonb.o.o.z2809 6 місяців тому +17

    Tapha Gueye, tu es là en tant que consultant et non coach ou parrain de Lac Rose. Sois professionnel way.
    Félicitations Lac Rose.
    Jackson, benen yoon teyeul té indii souplesse.

    • @tk92221
      @tk92221 6 місяців тому +1

      T’as raison pas faux

  • @davidsy8278
    @davidsy8278 6 місяців тому +17

    Diaksone mes encouragements Mes félicitations à LAc rose champion gua lamb mo tereudi rék

  • @fayendiouma2081
    @fayendiouma2081 6 місяців тому +10

    Félicitations lac Rose 🌹 gana ligueye rek champion

  • @waxkatoudeug
    @waxkatoudeug 6 місяців тому +11

    Lac rose, boul bayékou. Faudra encore redoubler d'efforts et surtout continuer les entraînements sans relâche, beaucoup de physique et de contact ! Entraînements you saf sap molay takha nieuwat au sommet. Am nga place si lamb ji ba légui

  • @boubacarlimanbadiane8668
    @boubacarlimanbadiane8668 6 місяців тому +22

    Lac rose❤❤❤❤❤

  • @nitoudeugfall
    @nitoudeugfall 6 місяців тому +19

    Degeul tapha Gueye dafa contann😢😢😂😂

  • @ndiougafatim
    @ndiougafatim 6 місяців тому +34

    FASS 4 combats , 4 victoires laaye amme , déésnaa GRIS BORDEAUX contre AMA , ADA FASS contre GOUY GUI !!! On verra incha allakhou raabiii

    • @alexbalde3507
      @alexbalde3507 6 місяців тому +6

      Ama dou moromou Gris, demb pape Ndoye danouna dhé

    • @mbayetall6875
      @mbayetall6875 6 місяців тому

      Fofou môme copain tu te trompe vraiment

    • @mbayetall6875
      @mbayetall6875 6 місяців тому +1

      Ama rek si khalé

    • @MouhamedKebe-yl2jj
      @MouhamedKebe-yl2jj 6 місяців тому +1

      Défaite de pape Ndoye

    • @CherifCherif-f2s
      @CherifCherif-f2s 6 місяців тому

      Gris d'où mbeur drianké la dépense lay woutt

  • @AbdouAzizSylla-v8y
    @AbdouAzizSylla-v8y 6 місяців тому +16

    Lac Rose machalla

  • @abdou.djimodjimo4357
    @abdou.djimodjimo4357 6 місяців тому +5

    C’est un champion le petit Jackson 💪🏾💪🏾

  • @abousoumare3345
    @abousoumare3345 6 місяців тому +2

    Félicitations lac rose du courage Jackson la prochaine fois Jackson ne confond pas vitesse et précipitation c’est pas pareil la lutte est un jeu échec ben ben ba guiss yon wi lac rose à eu la chance et l’expérience lac yokal contact yi nakh réflexe yi gueuna gneuw félicitations et bonne continuation pour la suite

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc 6 місяців тому +10

    Lac Rose c'est vrai dane na mais côté entraînement ça reste énormément côté phisique liga si wara ligéye da beuri forme bi dou forme biga wara ame

  • @Mrdiop
    @Mrdiop 6 місяців тому +3

    Du courage jackson champion ngaa démaal défarouwaatt
    Toutes mes félicitations à Lac Rose, bonne continuation bayiil xél daa ngaa bok si lamb jii amoul bayii liguey rék mowoor
    Lac Roses késsééé✌️✌️✌️✌️✌️

  • @diop3575
    @diop3575 6 місяців тому +7

    Thieuy yallah dangay teuguelé ay victoire di dane doune la wkh dara nga niew danou deg lounee 😂te yallah kham nani lac rose tay sou dano wone dana deg lounee dinane ko wkh beugo wone lamb dji psk kerok ya eundi gris 2 hier ya eundi pape ndoye ms yallah soutoural nako may ko ndamm mane nak tay wkh deug fa yallah fraloma la wone ms nak beugouma wone aussi nga psk damala beug nakh sa thies souma amone louma gueuneul sakh do beuréti ak mbeurou guediaway ms nak sport la rek ❤

  • @SouleymaneTall-jb3hn
    @SouleymaneTall-jb3hn 6 місяців тому +16

    Lac rose seul

  • @AbdoulazizThiam-u7v
    @AbdoulazizThiam-u7v 6 місяців тому +6

    Gueum nani lac rose thiate rék mo nék ci mome mé yalla khamnani dou moromou boy yi yeup wayé yalla bakhna

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 6 місяців тому

      Gnak entraînement mo nék si mom ak manque de sérieux thiatt amousi na srx geume entraînement

  • @Siskothies
    @Siskothies 6 місяців тому +3

    Ay way contane naa❤❤❤❤

  • @DjibiThiaw-wy2xy
    @DjibiThiaw-wy2xy 6 місяців тому +2

    Lac rose way félicitations

  • @tk92221
    @tk92221 6 місяців тому +3

    Lac c’est un guerrier. Té lac tey dafa lerr tey mashaAllah té amneu nguëmb té am tektalou lamb. Jaune bi djik nako et surtout meune beuré lafi wané

  • @mamadoumareme9849
    @mamadoumareme9849 6 місяців тому +3

    Félicitations lac rose ❤❤❤

  • @gueyemodou3456
    @gueyemodou3456 6 місяців тому

    Merci beaucoup Lac rose ❤

  • @Concept0208
    @Concept0208 6 місяців тому +8

    Felicitations à Lac Rose. Jackson sou xolatoul nimouy beuré dou gawa dane mbeur mou yéwou. Surtout sa facon de contre attaque. So liré sama commentaire ci sa Open Presse bi xamné Lac Rose fofou lala meunona dané. Même sa combat ak Sokh ragal ay door mo tax mou tenté lou kén xamoul. Mais meunonenala dane facilement.
    Donc bo sétané sa bopou dinga xam linga wara retifié.

    • @Alamine-lx9vi
      @Alamine-lx9vi 6 місяців тому

      Lac roce dafa ritakh moko may chance mé boy bi moko meun fouf wakhal lenen bro Jackson daray ragal nekoul simom défaut mo gnew rék mé Dou moromou boy yi

    • @Concept0208
      @Concept0208 6 місяців тому

      @@Alamine-lx9vi Jackson ndanane la. Mais Sokh la wax sou ñéméwone ay door dane Jackson.
      Jackson bimou diapaneté dafa warone chargé Lac Rose ay coups avant mouy tenté bén action. Combat bou nék ak ningakoy abordé. Lac Rose ndanane la fok nga sonou loko wala nga wañiko doko dane ci beuré.
      Jackson dafa nék mbeur mo xamné soko attaqué souy ñew dou am arret dafay dém ba diex lolou bokouna ci liko dane. Même ci xex bi dafa néxa lire. Sou la doré nga reculé day daw koor la a distance, so repliéwo dotoul am controle dafay def lépou limou am pour diexal beuré bi. En plus so xolé ses 3 derniers malgrés qu'il les a gagné mais adversaires yi ba légui dañouy contesté: Ameth Deme, Niakh, Sokh..
      Dou critiques négatives lay déf mais juste conseils pour mou retifiéwou parceque borom Jom la té nga entrainé. Mane personellement je savais que sou beuré ni danou.

  • @yesyes7713
    @yesyes7713 6 місяців тому +15

    Lac Rose vs Franc combat là

    • @Khamza903
      @Khamza903 6 місяців тому +1

      Nn Lac rose sa thies

    • @yesyes7713
      @yesyes7713 6 місяців тому +2

      @@Khamza903 n'importe quoi 🤣

    • @modo6218
      @modo6218 6 місяців тому

      N’importe quoi yaw danagua yabate 😂😂

    • @Khamza903
      @Khamza903 6 місяців тому +1

      @@yesyes7713 pourquoi franc tmt 🤣

    • @Khamza903
      @Khamza903 6 місяців тому

      @@modo6218 sa thies si défaite la diougé na dieul Lac rose wala zarco

  • @furax4545
    @furax4545 6 місяців тому

    Félicitations Lac rose, tu mérité plus 👏

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 6 місяців тому

    Félicitations Lac Roz Danga bokouthi Lamb ❤️❤️❤️thiath Molo Topon rék Mé Mbeur Mounoula boo respecte Say entraînement Kèneu Mounoula 🧏‍♂️

  • @YathWade
    @YathWade 6 місяців тому +1

    Félicitations Lac Rose

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 6 місяців тому +3

    Lac Rose Kasé 🙏🏽🙏🏽

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo 6 місяців тому

    Pour la première fois que j'ai vu lac-rose donnait autant de respect à son adversaire . Ça montre que il a battu un grand champion

  • @samysane77
    @samysane77 6 місяців тому

    Ohh lac rose j'ai eu les larmes aux yeux

  • @SouleymaneCamara-n9e
    @SouleymaneCamara-n9e 6 місяців тому +1

    Diackson dafa téla sogon si man dafa waron khekh touti mais nk lambou ni leu manon neu gueneu niaw si bo takha won lac rose mbeuré dan leu mais ya mbeuré ya danou courage félicitation lac rose mbeur bou ma nekh dakh am diom❤

  • @IslandCureislande
    @IslandCureislande 6 місяців тому +5

    BARKEP ALHURAAN WAKHOON NALEN LAC ROSE DEY DAAN JACKSON. GOODNESS OF GOD YALLAH REK MOY BUUR. LAC ROSE YAW SERIGNE FALLOU MOY SA TOURONDO BOUL TIT BOUL RAGAL. I'M THERE INCHALLAH. GUEUNEUL SANTA YALLAH.. LORS DU FACE TO FACE LEUR DERNIERE J AVAIS DIT QUE LAC ROSE DEY DANN. NORMALEMENT SAKH DOOR MOU DANOU LA WAROON DOON MAIS LAC ROSE DAFA BAKH KHOOL ESKEY. BRAVO LAC COURAGE JACKSON

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 6 місяців тому +1

    FÉLICITATIONS LAC ROSE

  • @Lmoustapha2024
    @Lmoustapha2024 6 місяців тому

    Bon courage diackson ❤ lisi kanam moye dack incha allah ❤

  • @Bouchrambacke
    @Bouchrambacke 6 місяців тому +7

    Mais du courage jakson vrai mbeur

  • @papadiabel3118
    @papadiabel3118 6 місяців тому +4

    Jackson daa bari wakh rek👍

    • @maramediop3216
      @maramediop3216 6 місяців тому

      Jackson AK beuri wakh dioumo😂😂😂

  • @IslandCureislande
    @IslandCureislande 6 місяців тому +4

    PAPE NDOYE KAY MA BAKHELA CI BATIIN BOUL TAKATI NGUIMB BOU AM LOU JAUNE. YAW ROUGE MOY SA COULEUR SACHE LE. KOUNE AK SA COULEUR BILAY MAY NDAM C IMPORTANT. GOODNESS OF GOD.. VISIONNAIRE

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 6 місяців тому +1

      Pape ndoye 3 victoire la tégalé si ngimbe bou jaune bigay wakh de grâce bayi léne fanatisme bi

    • @IslandCureislande
      @IslandCureislande 6 місяців тому

      @@MilkMilo-qr5uc bess bou ne AK lissa wara khew bess bou ne AK lissa wara am. Pape NDOYE je lui coseil barkep alhuraan boumou TAKATI Lou JAUNE CI nguimb am lui AK balla GAYE2 sinon IL vont Le regretted point. Goodness of good

    • @IslandCureislande
      @IslandCureislande 6 місяців тому

      @@MilkMilo-qr5uc Pape NDOYE NEY rouge REK lebou LEU NA khonkhaa thiouy touro beaucoups de sauw te NA BAYINA poudeur kanam gui lolou dou yeufeum.

    • @kefgg
      @kefgg 4 місяці тому

      ​@@IslandCureislandekone couleurou ngemb motakh mbeur di dane 😂😂😂😂 Lamb Senegal c du jamais vu 😂😂😂

    • @IslandCureislande
      @IslandCureislande 4 місяці тому

      @@kefgg n importe KOI qui ta dit sa esque comprendre ngua LIMA wakh. Batine lala wakh barkep alhuraan.. Oui la couleur et important pour la lutte. Les nguimb joue. Des fois c nguimb contre nguimb. Breff

  • @abdougorafall5863
    @abdougorafall5863 6 місяців тому

    Professeur la lac dou moromou ben khalé

  • @Faye-sv1jx
    @Faye-sv1jx 6 місяців тому

    Lac roce bilahi nieup gnoko yénè victoire bi ❤

  • @abdoufall3831
    @abdoufall3831 6 місяців тому +3

    Machla Lac filisitasio

    • @Boubou1024
      @Boubou1024 6 місяців тому

      Yaw loy lak ni français wala

  • @BassirouNdoye-ib4mj
    @BassirouNdoye-ib4mj 6 місяців тому

    Cest un grand lutteur lac rose

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc 6 місяців тому +1

    Lac ❤❤❤❤❤❤

  • @OusseynouNdoye-wo1dk
    @OusseynouNdoye-wo1dk 6 місяців тому

    Lac rose est de retour ❤❤❤

  • @SoukhaTraore
    @SoukhaTraore 6 місяців тому +1

    Lac rose ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @NdongoBadiane
    @NdongoBadiane 6 місяців тому

    Merci lac felicitations mais continu les entrainments

  • @AliounebadaraThioye-ho4tq
    @AliounebadaraThioye-ho4tq 6 місяців тому +1

    Lac rose boul nopalou dh ❤doli liguey rk daga am place si lamb dji

  • @dizikha2003
    @dizikha2003 6 місяців тому +2

    Lac roso nakh nacko deh

  • @serignebabacarthiam9934
    @serignebabacarthiam9934 6 місяців тому

    Lac rose guenal focus si sa bop si lamb gua bok ay champions rek gua dan fi deuguelal sa bop yok entrainment yi bravo

  • @ABAKARA-q8o
    @ABAKARA-q8o 6 місяців тому +1

    Pourtant bou danou
    Yone rék yaw tapha Gueye gua khalape ko mé yalla barina soutoura

  • @abdouleye1656
    @abdouleye1656 6 місяців тому +5

    Yalla bari sotora bilahi lac kinga dane moula gana takhaw fopo

  • @AbdoulayeagneKane-rt7ql
    @AbdoulayeagneKane-rt7ql 6 місяців тому +1

    Lac Rose seul ⚔️❤️⚔️

  • @moussandiaye1762
    @moussandiaye1762 6 місяців тому

    Yenne nakoko

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 6 місяців тому

    Machalah ❤❤❤❤

  • @vieuxkhalil
    @vieuxkhalil 6 місяців тому

    Du courage Jackson Guene défarou watt RK inchallah ❤

  • @CireMane-vu1hg
    @CireMane-vu1hg 6 місяців тому

    Ousseynou tine dieureudieuf

  • @ModouDiaw-dl1gj
    @ModouDiaw-dl1gj 6 місяців тому

    Félicitations Lac ross

  • @Zakaria-h1w
    @Zakaria-h1w 6 місяців тому

    Pokola kén Nawlo wouko, amoul respect ci bopam

  • @xalimagui-officiel9001
    @xalimagui-officiel9001 6 місяців тому

    Jackson dagn ko wakh ya meun Lac Rose malheureusement tel n'est pas le cas. Je crois que le gars est en train de retrouver sa forme initiale. Félicitations à Lac Rose et courage à Jackson.

  • @moussa1257
    @moussa1257 6 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤❤lac ross machalla ❤❤🇸🇳 à

  • @soldarouyayam8524
    @soldarouyayam8524 2 місяці тому +1

    Lac rose Dane na kou ame diome kou ame fite kou ame fouleu

  • @CheikhSarr-mk2qd
    @CheikhSarr-mk2qd 6 місяців тому +7

    Lac rose da reuthii

  • @aliounefall490
    @aliounefall490 6 місяців тому

    Lac rose vs quench ou lac rose vs zarko tapha gueye tu connais l'adversaire de lac rose

  • @AntaCisse-pj5wx
    @AntaCisse-pj5wx 6 місяців тому +1

    Lac Rose mo meunone ci ay moromam, ndeyssane genou bi moko yackal réck mais mbeur kaamil leu bilahi
    Mane mom damako beugue réck

  • @MbavkeGaye
    @MbavkeGaye 6 місяців тому +2

    Tapha giris 2 champion la beneu defait la am combat yi guena meti moko beuri bom dieul nem pout combt combat boko wara yeguel mo bakh si mom

  • @nafissatoudione9128
    @nafissatoudione9128 6 місяців тому

    Météwona ndamli coubakh la billahi

  • @blazejohns8004
    @blazejohns8004 6 місяців тому

    Félicitations lac rose et du courage a Jackson tu n'as pas démérité vraiment djioxéga lép. Lac rose dafa tardé si lamb franchement worona dépassé fi mbeur Bouma estiméla fimou tolou ni woronako wéssou bou yag xamouma lanela nak mais mom mo worone nék le tigre de fasse sou amoulwon retard si carrièram

  • @eddyfall2337
    @eddyfall2337 6 місяців тому

    Ohhh courage Jackson

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo 6 місяців тому

    Jackson le modou lo de cette génération manques de chance rek

  • @SmbayeFall-kj1xr
    @SmbayeFall-kj1xr 6 місяців тому

    Lac rose❤

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 6 місяців тому +1

    Demal nga defarou wate am nga lou la bet mai lac rose dane la dou gathie man la kheuss bathie seras

  • @user-li1ro9pn8y
    @user-li1ro9pn8y 6 місяців тому

    Marley vs diamteri

  • @Zakaria-h1w
    @Zakaria-h1w 6 місяців тому

    Fass Université lamb leu !

  • @MouhamedDiallo-o6w
    @MouhamedDiallo-o6w 6 місяців тому

    Ndeysane deggal Tapha Gueye 😂

  • @abdoutoure2490
    @abdoutoure2490 6 місяців тому

    Boy. Bou. Si respectè. Woul. Beur. Mou. Mak. Ni. Lay. Démé.

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 6 місяців тому

    TAPHA GUEYE BO TOGUÉ PLATEAU BOUL DI YEUKEUTI SAY MBEUR DI TOUTEUL GAYI

  • @mortallaseyedallou6976
    @mortallaseyedallou6976 6 місяців тому

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ndiayemamemodou7550
    @ndiayemamemodou7550 6 місяців тому

    Tapha wakhi farrr rekkkk😅😅

  • @Lilkheuchfrombomakingbii
    @Lilkheuchfrombomakingbii 6 місяців тому

    Tapha gueuye contane na bani dialidialalo😂

  • @mahmoudba2399
    @mahmoudba2399 6 місяців тому

    Dako ngëna diss rek bilakhii djakson ndanane la souniou tolowone lac am problèmes

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 6 місяців тому +1

    Ba pare khekh bi yako momone man kheuss bou bathie seras mako wakh ya mommon khekh bi mai danko yakam ti mai lamb la lac ross dan la dou gathie

  • @MamdiaraNdong
    @MamdiaraNdong 6 місяців тому

    Di wakh ni pikin ginaw raill amate naniou benee bathie seras bou besstak

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 6 місяців тому

    Félicitations lac ross ndaandane la de

  • @espritsaints4685
    @espritsaints4685 6 місяців тому

    Lac rose moy bandit 😂😂😂

  • @FallouSene-ds8hd
    @FallouSene-ds8hd 6 місяців тому +1

    Lac rose seulllll

  • @maramediop3216
    @maramediop3216 6 місяців тому

    Nooo Jackson vrai champion

  • @matargueye1822
    @matargueye1822 6 місяців тому

    Gayi khana lac lagne faralone

  • @mustaphagaye4868
    @mustaphagaye4868 6 місяців тому +1

    Lac rose kece ma beug gris2

  • @ndiayemamemodou7550
    @ndiayemamemodou7550 6 місяців тому

    They lac rose changer kii moylolu

  • @assanegueye241
    @assanegueye241 6 місяців тому +2

    Jackson dafa nagou woon

  • @Elhadjikane-i6f
    @Elhadjikane-i6f 6 місяців тому

    Vraiment Jackson ya dane sa bopp il faut respecté ton adversaire

  • @LamineFall-f2g
    @LamineFall-f2g 6 місяців тому

    Lac rose déme na fin de carierre ni bagne nagne beuré mag la beuré😢

  • @ndiayemamemodou7550
    @ndiayemamemodou7550 6 місяців тому

    Jackson yakh beurrébiii d ....degal tapha Gueye da farr😅

  • @abdougorafall5863
    @abdougorafall5863 6 місяців тому

    Sénégal amatoull mbapatt mo takh ben khalé manatoull beuré

  • @abdoulayefall1282
    @abdoulayefall1282 6 місяців тому

    Jackson dafa beuré ba donu guerrier deug la

  • @MoussaTandian-rc2yx
    @MoussaTandian-rc2yx 6 місяців тому

    Lac rose

  • @amdykaita9405
    @amdykaita9405 6 місяців тому

    Jackson diambar deugue ngua ya déf lépp billahi

  • @demefalldiop2361
    @demefalldiop2361 6 місяців тому

    Jackson niakk respecté lac rose moko daane

  • @Lilkheuchfrombomakingbii
    @Lilkheuchfrombomakingbii 6 місяців тому

    Mangui guédiaway mais lack rose yénénako ndamli ndakh wagni woul dara jakson ta au contraire dou enrangé lk rs ta xolam lako yallah fay