🛑SAM MBOUP ET TAFSIR ABDOURAHMANE GAYE EXPLOSE L'UNIVERSITE DANS SPECIAL GAMOU DU 23 AVRIL 2022

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 1 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 541

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 2 роки тому +171

    Yalla na Étudiants yeup tekki !Amine
    Tafsir Abdou Rahman Gueye ak groupe bi yeup yalla nane am goude fane ak wer.Amine
    Yalla na nieup am diamme. Amine

  • @softdstlo8171
    @softdstlo8171 2 роки тому +23

    Nianale léne Tafsir weér ak gouddou fane yalla samouko ta art ko si barké yonéte bii 💯💯💯 sopé Tafsir Abdou Rahman gaye 💯💚💯💚💯

    • @SheriffCham-m8y
      @SheriffCham-m8y 5 місяців тому +1

      Yall neen ko yallah boli dafal si barkeh s.a.w 🤲🤲

    • @leadion4862
      @leadion4862 3 місяці тому

      Amine y rabi

  • @momobah8190
    @momobah8190 2 роки тому +58

    Sam tay ni nga seidalei seum xol bii 😩❤️Yalla na Yalla seiddalei nonou sa xol 🤲🏾t’es le meilleur Yaggeu nako wah wallahi ❤️Nangoul nala 🥰

  • @mamediarraka9822
    @mamediarraka9822 2 роки тому +14

    Machaa Allah Tafsir yalla nala yalla may wer ak werlé goudeul sa fane té gueune leu katanal si barké Nabil Moustapha. Serigne Sam khol seedna. Yalla rek kay yalla

  • @mbenekane5592
    @mbenekane5592 2 роки тому +21

    Machalla wa 2stv Ken amoute sen faye bilay Yalla nalén Yalla defal diamou diou sakh bou ande ak yokouté ba fayou 👏👏👏👏👏🙏🏽🙏🏽🙏🏽♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @oumouba4764
    @oumouba4764 2 роки тому +2

    Walahi sam voi bi day daw SMA yaram 🤦🥰🥲 bilahi yalla nalen yalla Faye goudal sen fay

  • @mbackendoye7308
    @mbackendoye7308 2 роки тому +52

    Machallah Tafsir dama ko sopp Wallahi Yalna yalla yaggal takhawayam na niep wakh Amine 🙏❤️

  • @diarrandiaye4091
    @diarrandiaye4091 2 роки тому +2

    Macha Allah les Oustaz yalla nalene yalla defal diam,may Len werr ak goud fane.
    Vous avez assuré yalla nagnou yalla may degg ak topp

  • @mansoursy9451
    @mansoursy9451 2 роки тому +49

    Yalla naniou yalla Fayal cheikh seydil hadji Malick Sy ♥️🙏bilahi khol yagui fékh ♥️

  • @absatoudiop9609
    @absatoudiop9609 2 роки тому +2

    Yalla moy Karim. Koumou may niou gné la machallah. Kham kham gui selna firi bii lerna. Say sou wakhé khôl yi sed nayssane. Yalla n'a yalla fayal lène bopam.🙏🙏🙏

  • @alyniang7331
    @alyniang7331 2 роки тому +5

    Same Mboup yalle na bourbi faye la je très content fière d'être Musulman 💖💖💖❣️❣️❣️💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖😍😘😘😘😘😘😍😍💖💖💖❣️💖💖😋😋💖I love your émission

  • @fallmodou8975
    @fallmodou8975 2 роки тому +18

    barkeb brom touba liikouko beuga diele'fii ci rewmi danga sonne nioune gamnane liniouye gam ba pare gamnane bamba gnii gamnane maodo gnii gamnane mam limamou gnii gamnane cheikh abdoulahi niss ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aminatandiaye4478
    @aminatandiaye4478 2 роки тому +2

    Masha Allah Tafsi r- Cherif mamine et Sam mboup xol sedeunaaaaa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤contane nagnou

  • @ndiogoulaniane4794
    @ndiogoulaniane4794 2 роки тому +3

    Billahi sam mboup ak taff ken dou yene machaalla

  • @kingyass2974
    @kingyass2974 2 роки тому +26

    La 2stv en terme de montage ils sont les meilleurs. Yalla na kep étudiants validé année bi wax yalla meune nako . Merci Tafsir pour cette sensation

  • @GAUCHER_MAGIC
    @GAUCHER_MAGIC 2 роки тому +38

    Rien que de l'écouter a nouveau j'ai le corps qui frissonne❤️❤️😭😭 j'ai le cœur apaisé 💞💞

  • @diarryndiaye4076
    @diarryndiaye4076 2 роки тому +19

    Machallah Tafsir gaye et chérif Aidara yallah na yallah yagale sens takhawaye si barke seydina Mouhamed (psl)

  • @madiagnediagne2766
    @madiagnediagne2766 2 роки тому +6

    Machalla yalla nalla yalla sama serigne sam Mbaye,AMINE YARABAL ALAMINE.

  • @ndeyeseck6515
    @ndeyeseck6515 2 роки тому +16

    Wa li koumou dawoul sa yaram dou nitt❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @senysallsall1129
    @senysallsall1129 2 роки тому +1

    MAME Abdou yalla nala yokou lérame si brké mouhmede ✊🥰🇸🇳❣️❣️❣️🙏 Amine waye Baye karime

  • @safietounguenodiakhate8012
    @safietounguenodiakhate8012 2 роки тому +5

    Machallah wou kana kheneu dou ya Rassoul psl 🙏 tarikhatoul diné l'islam yeup ziara na leneu machallah magui mell nii j'étais ô présent yallah borom laffal thiath inchallah contane na trop dieureudieufé ya Rabi 📿🧕🤲🙏🤝

  • @goraniang9551
    @goraniang9551 2 роки тому +1

    Machalah à toute l'équipe de la 2stv
    Dieureudieufeuti sounou Borome mome minou bolei thi ndiambotegui bidiahi Taha psl

  • @fbc4773
    @fbc4773 2 роки тому +18

    Machalla yalla na léne Yalla fay fayal gnou Mame Maodo mo gnou khamal Mouhamed (PSL) bayou Fatimatou sama toureundo🙏🏼🥰

  • @gnimasatousen4589
    @gnimasatousen4589 2 роки тому +1

    Machallah sam li nékhna loll wayyyyy😍😍😍 yalna suñu borom bi gueuna wéral bateu bi

  • @muliesonko1610
    @muliesonko1610 2 роки тому +5

    Yenn yep dome Janna tul firdaus s’y kenn woor n’a borom nian bu nangu laa ☝🏽🤲🏻🙏🏾🕊🕊🕊

  • @sellybiramasall9973
    @sellybiramasall9973 2 роки тому +15

    Sam mi fouma ko meuneu guissé tamite💖💖💖💖

  • @amycollesane2896
    @amycollesane2896 2 роки тому +9

    YALLAH NANIOU YALLAH SUBHANAWATALAH FAYAL MAGUE NIOU BAX GNIFI NÉKONE TÉ TASNIOU THI SÈNI BARKÉ. ALAKHOUMA AMINNNN🤲🥺❤️
    Mais Tafsir AK Sam boufeke roguagn yima toureuh😭😭😭 en vous écoutant tout au long de ce Gamou ay roguagn YÈWEUL leuh Kone mangui nianeuh 🤲YALLAH mou deffaralèn ko AK kèpp kouguèn thi andaleuh🤲 Dieuredieuf amouniou sen faye😭😭😭 MACHA'ALLAH ❤️❤️❤️

  • @kaoumou7550
    @kaoumou7550 2 роки тому +3

    Machallah Yalna yalla wéral bate yi beugue na Tonton Tafsir bilahi yalla na nguéne goudou fane si barké Mouhamed ❤❤khole yépp séde

  • @saliouniang2691
    @saliouniang2691 2 роки тому +14

    Mano ma guis koo melni yonentibi yallah na yallah deff nio bgg younentibi ♥️♥️♥️

  • @ndeyemerrylo1907
    @ndeyemerrylo1907 2 роки тому +1

    Li defoul loudoul nekhh😭♥️♥️♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️Sama xol sedd na, yalla nalenn Allah fayy❤️♥️♥️♥️♥️

  • @papaaliounembaye4996
    @papaaliounembaye4996 2 роки тому +15

    Suis mouride mais vraiment sama khol Sed n'a yallna diam yague❤️

    • @princessemyadiallo9791
      @princessemyadiallo9791 2 роки тому +1

      Dieureudjeuf ♥️♥️♥️

    • @bourendong767
      @bourendong767 2 роки тому

      Amine 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

    • @abdouazizba7515
      @abdouazizba7515 Рік тому

      Xana mouride n’est pas Muslim pffff use your mind way

  • @sidyadiaby6706
    @sidyadiaby6706 2 роки тому +5

    Tafsir abdourahmane gaye Gaye yalna leu yallah may gouddou fane ak wergou yaram Allahuma amine 🤲🏾❤️😘

  • @kalsoummbaye2476
    @kalsoummbaye2476 2 роки тому +2

    Mashalla Tafsir yallah neu yallah goudeul senn fann sam Yallah neu yallah werreul batt bii nioun Waa UCad on est content Mashalla

  • @fatoucisse4817
    @fatoucisse4817 2 роки тому +2

    Papa Tafsir ningayy bègalè souniou khol yii Yallah nako Yallah sèdalè sa khôl fotolou sii adouna
    Amine ya Rabii❤💕💕

  • @papadiarra3807
    @papadiarra3807 2 роки тому +77

    Alhamdoulillah baniou amé Tafsir bilae amouniou sa faye nous les étudiants de l’université Cheikh Anta DIOP nous vous remercions du fond du cœur. Paix et salut sur vous outas yallah nala Diam sonal ak weer🌷🌷🌷🙏🏾

    • @AngeGabriel05
      @AngeGabriel05 2 роки тому

      @@kabou43 ah bn l'entrée c'est à combien???

    • @kabou43
      @kabou43 2 роки тому +1

      @@AngeGabriel05 l'entrée c'est libre na nieup tew niou sargal tafsir abdourahmane gaye aux théâtre national daniel sorano le 14 mai à 16h30mn

    • @AngeGabriel05
      @AngeGabriel05 2 роки тому

      @@kabou43 In Chaa Allah lolou dañe kaay téweii... Tafsir suñu Oustaz leu sou xewlei dañe kay wouyou ci
      yalla nañou borom bi maay tale akk fékkei🙏🏿

    • @coulibalypenda7641
      @coulibalypenda7641 2 роки тому

      @@kabou43 55

    • @dancogassama8234
      @dancogassama8234 2 роки тому

      @@kabou43 et iiiiiôio est îoooiiiiiioi ooôôooôoĩooio

  • @diawmarame3137
    @diawmarame3137 2 роки тому +1

    Machalla Taphsir Abdourakhmane ak Mamine Aidara yalla nalen yalla maye fane bou goudou ak wer 🤲🤲🤲

  • @ndeyeseye9240
    @ndeyeseye9240 2 роки тому +9

    MACHALAH TAFSIR ABDOURAHMANE , CHERIF, SAM MBOUP 111 sans Ordonnance Inchalah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @ndeyefamadiouf4129
    @ndeyefamadiouf4129 2 роки тому +9

    Bilay le peuple est content Tafsir je t'aime beaucoup Same sounou Khôl sedde na yalna yalla goudal sen fane 2s❤️❤️❤️

  • @ndiogoulaniane4794
    @ndiogoulaniane4794 2 роки тому +2

    Yallana yalla fay len si barque werou koor guii amin 🙏🙏😍

  • @mamankhadysene5364
    @mamankhadysene5364 2 роки тому +80

    Machalah tous les étudiants de l ucad sont trés contents. Vraiment tonton Tafsir ak tonton chérif yalla naleine yalla Faye si barki seydina Mouhamed merci aussi à la 2stv

  • @mamediop8111
    @mamediop8111 2 роки тому +1

    ❤❤❤❤❤❤❤💖💖💖💖💖yalnaniou yalla def ay talibeé chiekh barké yonentebi

  • @abdoudiouf7125
    @abdoudiouf7125 2 роки тому +7

    Depuis España pero estamos más orgulloso de nuestro sam y tafdir de él hadji Malick desde el profeto

  • @AngeGabriel05
    @AngeGabriel05 2 роки тому +28

    sama Oustaz Tafsir Abdourahmane Gaye akk Cherif Mamine Aïdara, yalla na borom bii gëneu weiral bàtt bii🙏🏿 guddeul seini fane🙏🏿

  • @babacardiop10
    @babacardiop10 2 роки тому +18

    machaHala Yalla na Diam yague Sénégal 🤲🤲🤲

  • @ndiagagueye2846
    @ndiagagueye2846 2 роки тому +3

    Machallah ma universite khana nieppou ay tidiane lagne yalnaniou yalla fayal seydi el hadji malick

  • @matydiop792
    @matydiop792 2 роки тому +4

    Yalna yallah fayale niou sounou mame you bakh yi yallah léne yeureume yokou séne aye lére tase niousi séni barké amineee touf touf touf yalna yalla défe diame Sénégal amineee 🇸🇳❤❤

  • @babacarsenghor9663
    @babacarsenghor9663 2 роки тому +16

    machalah nexna trop
    zikr niassen nekhoul ba nekhoul mais dafa nekh ucad bi yeup yegouna

    • @lunelune8872
      @lunelune8872 2 роки тому +1

      khana sam mboup kene dou mom

  • @maremendiaye820
    @maremendiaye820 Рік тому +1

    Masha'allah tarikha cheikh gui niakeu sé né woroul ❤

  • @matythiam867
    @matythiam867 2 роки тому +1

    Je suis mouride mais bilahi welahi dema begue tidiane yi 🥰🥰ando messi ak same sago bilahi surtout Tafsir abdourahman Gaye Diam rk inchallah 😍😍😍

    • @princessemyadiallo9791
      @princessemyadiallo9791 2 роки тому

      Djeureudeuf dagua bakh rék♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @khadimngom7189
    @khadimngom7189 2 роки тому +2

    Marchalla yalla nalén yalla fay xol seudeu Billaye walaye ak wa 2stv
    ❤❤❤❤❤❤❤❤🎃🎃

  • @seythian8793
    @seythian8793 2 роки тому +7

    Machallah oustaz Tafsir Gueye mala bague❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Ama-tb9es
    @Ama-tb9es 2 роки тому +7

    Quelle chance que vous avez cette génération!!! Nous on avait pas ça!! Diap lèn ci bamou deugeur😍 té sen ay mourrou mi ngi rafèt mashallah, je me rappelle une année á l'approche des examens on nous avait invité un chanteur connu et au milieu du show son batteur nous dit au micro" étidiant yi yAllah na nguèn am bac" 🤣🤣🤣

  • @mbayesy5923
    @mbayesy5923 2 роки тому +21

    Yallna yalla fayal niou same ak tafsir❤️✨abdou rahmane gaye✨🌙ak kouné amine🕌❤️✨🙏🌙

  • @fabacarydiedhiou5109
    @fabacarydiedhiou5109 2 роки тому +12

    Alhamdoulilah prières sur le prophète manchanlah tafsiir ak chérif mais Sam yalla n'a brom bi fekhal sa holl kom nunko deifaler ni yalla gua dugu aljana way😪❤❤📿

  • @bayeserignendiaye7563
    @bayeserignendiaye7563 2 роки тому +112

    Masahala Tafsir mane damako sope trop yalla na yalla mayé fane bou goudou ak wérale trieur surtout la vois et chérif aussi .un grand merci pour la 2stv. Tafsir et son équipe yalla na léne yalla faye des cœurs 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 💕 pour Tafsir

  • @pogba7440
    @pogba7440 2 роки тому +1

    Tafsir abdourahmane ohh yallah na yallah fayy al dianatoull firdawsi❤❤

  • @maissawalybourserere8776
    @maissawalybourserere8776 2 роки тому +11

    Machalah il as tout résumé ! Tafsir gaye Un vrai pédagogue yalna yala goudeul aye fanam defalko diam inchallah

  • @falldiarra8246
    @falldiarra8246 2 роки тому +3

    Samm mboup yalna yalla samoula te are là si barkep seydina mouhamed,

  • @ndeyebarakatoufall6884
    @ndeyebarakatoufall6884 2 роки тому +1

    Ndèkètè ètudian yi dou roubè rèk lagnou meune machalla ❤❤❤

  • @Kheucha103
    @Kheucha103 2 роки тому +6

    Machalah tafsir machalah exceptionnel à Sam ♥️😍❤️❤️❤️💯💯💯❤️❤️♥️♥️

  • @yoboye611
    @yoboye611 2 роки тому +7

    Machallah yalla na guéne fi yague té wére ❤️ khôl yeupe séde nagnou ❤️❤️❤️

  • @fallmodou8975
    @fallmodou8975 2 роки тому +2

    nioune mom amouniou loudoul soune tarikhayii barkeb brom Touba mandeh contan naloll😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤ saam yaguefi waye barkep touba❤❤❤

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 2 роки тому

    Machalla yalla naniou yalla défal dégg ak topou machalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ li nékhna way ohooooo khol séde na kéne dou Nabil Moustapha wayé kéne dou Mame aladji Malick Sy yalnako yalla Faye boleko ak sopém ba rasoulilah 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭♥️

  • @moustaphanger5169
    @moustaphanger5169 2 роки тому +12

    ماشاء الله 💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖💖 💖💖💖💖💖 بألف ألف ألف ألف ألف ألف ألف ألف

  • @assanediagne1222
    @assanediagne1222 2 роки тому +1

    Machallah nékhna trop billay ,sam yalna yalla saamm leuh ak Tafsir
    wa 2stv il faut bien régler le micro de Tafsir Gaye pour qu'on aura une très bonne qualité sonore mé à part ça vous avez fait un excellent travail
    Merci beaucoup

  • @camarapapesalif8965
    @camarapapesalif8965 2 роки тому +1

    Je vous adore yalla n'a yalla goudoul séné fane si bargue Seydina mouhamed ♥️

  • @coumbasow1147
    @coumbasow1147 2 роки тому +4

    Machalla yalla nalen yalla may goude fan weregou yaram Tafsir et cherif dema l'en SOP Biolay💕💕💕💕

  • @teningsarr846
    @teningsarr846 2 роки тому +16

    Machallah kén d'où yw doudaleu lo dounou doyoul❤❤❤

  • @sellybiramasall9973
    @sellybiramasall9973 2 роки тому +4

    Leylatoul khadri ucad lako0y defé Inchala 💖💖💖😍😂

  • @madiagnediagne2766
    @madiagnediagne2766 2 роки тому +4

    Machalla cherif yalla nalla yalla faye.
    Amine yarabal ALAMINE.

  • @elhadjibabaniang360
    @elhadjibabaniang360 2 роки тому +9

    Dieureudief Sam ak tafsir machallah nkh na trp

  • @babacarfam251
    @babacarfam251 2 роки тому +1

    Machala same mbaye ak tafsir abdou rahmane mbaye

  • @laminendiaye8991
    @laminendiaye8991 2 роки тому +1

    Mbectei menoul eup lii❤️❤️mercii pour tout yalla nalein sama borom faye❤️❤️❤️🙏

  • @IM_Tv22
    @IM_Tv22 2 роки тому +11

    Yalna Yalla fayal niou MAODO 🥰

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 2 роки тому

    Ndaye sane Serigne sam mbaye yalna yalla Faye la wérel batbi mayla goudou fane♥️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @yoboye611
    @yoboye611 2 роки тому +4

    Machallah dougnou doyal ti dila déglou Tafsir Mamine yalla na léne yalla takhawou

  • @fatoumbodj8950
    @fatoumbodj8950 2 роки тому +13

    Yalna gnou yalla fayal mane maodo ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @cherifmane4788
    @cherifmane4788 2 роки тому +12

    Excellent Tafsir Abdourahmane GAYE, c'est important de tenir de tels discours dans nos universités.

  • @mihacoly6303
    @mihacoly6303 2 роки тому +2

    Machallah oustaz 🙏🏻 🙏🏻 🙏🏻 🙏🏻 😘❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @pendasene7595
    @pendasene7595 2 роки тому +1

    Billahi contente thie sam AK Tafsir abdourahman yalna niep am diam

  • @dihdiagne5031
    @dihdiagne5031 Рік тому +2

    Qu’elle belle voix de samboup❤❤❤❤❤

  • @mbayesy5923
    @mbayesy5923 2 роки тому +11

    Ndeysane machallah same 🕌❤️

  • @aissatoumboup6508
    @aissatoumboup6508 2 роки тому +1

    Machallah Walakhi nioune niépa contane yalla nalen yalla fay limom Dafa manquè wone si espace bi

  • @papesall3416
    @papesall3416 2 роки тому +1

    Sam dinga raye dé mane atanouma lidé bakhna macha allah

  • @yayasow6139
    @yayasow6139 2 роки тому +9

    Machallah wa 2st wa université 🇬🇭♥️♦️

  • @amadydia1501
    @amadydia1501 2 роки тому +2

    Merci là-bas Sénégal depuis Libreville Gabon 😭

  • @rouguibah8553
    @rouguibah8553 2 роки тому +7

    Yallah ñanko fékke ay ate you barii inchallah 🙏Xol Sédena Machallah ❤️🙏

  • @adjaratoundiaye9030
    @adjaratoundiaye9030 2 роки тому +7

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️ machalla khôl sedatina

  • @adamabeye3845
    @adamabeye3845 2 роки тому +1

    Ay waay khawma gnata yoon lay setane li te doumasi doyal. Sam Mboup ak Tafsir 😭 yalna yalla weral baat yi yalla bayi len fi nghen gnouy beghel si barke Seydina Mouhammad sallallahu haleyhi wasallam. Wallahi damalen beugue.

  • @amethndione6320
    @amethndione6320 2 роки тому +1

    Li chaque semaine warna am 😢😢❣️🙏🏿🙏🏿

  • @aminatandiaye8122
    @aminatandiaye8122 2 роки тому +7

    Alhamdoulilah ala kouli hal nignou contanné yalla guéne contanné nonou adouna ak allaxira.

  • @sophiethiam7082
    @sophiethiam7082 2 роки тому +1

    Mashalla yallah naleennn yallah faye li doumathiii doyalll

  • @senganendaw9550
    @senganendaw9550 2 роки тому +2

    Same Mboub dou nitou fiii❤️❤️

  • @bababalo6445
    @bababalo6445 2 роки тому

    No me sam mboup yalla nalafi yalla yenen 100 ans

  • @mamediarrafall9801
    @mamediarrafall9801 2 роки тому +8

    Machala je tellement ému longue vie Serigne sam

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 2 роки тому

    Tafsir guaye tamit yalna léne yalla Faye ak Serif def guéne Lou rafét yalla naniouko yagua téwé ta guéne wérr ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @badarasow320
    @badarasow320 2 роки тому +71

    Merci 2stv nous les étudiants nous sommes content de vos actes

  • @aminatadiouf2689
    @aminatadiouf2689 2 роки тому +1

    Tabarkallah maaa Shaa Allah Alhamdoulilah Dieureudieufeuty !

  • @Talibeserignebabacar2191
    @Talibeserignebabacar2191 2 роки тому +1

    Eye yow lii nekhenaa ba rombou nekhe Machallah fière d’être talibe cheikh ❤️

  • @aminadiop3313
    @aminadiop3313 2 роки тому +21

    Mention speciale a Sam Mboup Tafsir, Cherif Mamine yalnalen yalla faye guen yague fi te wer