Être mouride tidiane layene ibadou c’est du pareils au même vous diverger sans même vous rendre compte ce qui compte c’est être un bon musulman point l’union des cœurs et pas la divergence des tarikha
Tout ce que je sais c'est que j'aime bc bc bc Seydina Muhammad paix et salut sur lui ❤❤❤ Sam dieuredieuf wayy yalna yalla féyla yiww si barké Seydina Muhammad salalahou haley wa salam 🤲🤲🤲
@@cherifcherif7033 Et c'est quoi le rapport ici thi kimou diokou ak kimou diokowoul? 🤣🤣🤣 n'importe quoi,lolou dh yako sania wax, guéneul Sénégal nga ték kimou diouko, tégualé iow ki nga diokou sou boba digua xam Maolana Cheikh Ibrahim Niass mom kép moy Cheikh al islam ba kérok adouna di touki, sa xol moy diekh rk mouy iow ak gni melni iow. Lolou nak la ya allah def, tél ko nangou nopalou mba deuké sonou rek té dou wagni dara thi ndogualou souniou borom. Non ni dioulitr nga mais ignane lou yallah may sa morom dioulite, aaah li dafa niaw way. Yam léne way tamit, té bayi topaté bi ak yendou waté bi pour tok di xassé rek. Niounr miss naniou séni wakh dh, yeungua louniou té souniou léne tontou guéne mér alors togn ak ignane ak soxor moléne sonal. Dèlène sissou rk, iow mom boula pannou glace sori rk🤣🤣🤣 xamna xol bou tangue nga nara deuké, Baye rek kep dongue késsé kou am lénéne c'est bien démal ak mom. Genrou Sam Mboup bi islam laniou fi nékal xamni lep thi souniou borom la diougué té falay délou. Mais sa genre gui seytané laniou fi nékal waxou diaxassé ak yé fitna moléne yitél, mbir mi dou concurrence. Kone iow yay ki wara def ndank té yarou. Commencé par bayi diniou yendou rk🤣🤣🤣aaaah yéna sik way
@@LaBarhamienne dama retane ba sonou wakhi doff rek ngafi wakh dagua faté messi ak christiano nio gueuneu siiw baye si adouna humm tantôt mouride yi né ahmadou niassene yi né baye wayé mirou charia hum kou senetou lolu moussiba do degueu jamais niou wakh si niata diabar laniou ame niome ahahah lounioissiy neube le nombre d'enfant nak ahahhah kham nga senegal dafa nekh kou nekeu niounela yawela waye kou weete kham sa bop attirer du monde lolou khana waly seck mounenako waye finalité moy lane ay talibe moye katou yalla rek diape talibe di teudé takeu lou passé 4 diabars etccc.. dieuleul lepeu machala waye dagua done khale demal si sa serigne tu lui demande kane moy "YAMA SOW " la 75 eme épouse de baye pose lui juste la question
Arrêter svp gnioun gniogui yak sougnou rewmi ak ligayou nakk gni ak yi gnou khewal on est musulman point l’union des cœurs pour gniou beug toub dougnou si l’Islam
Je ne fais partie d'aucun tarikha mais une chose est sûr nous tous nous aimons le prophète Mahomet SWS et k sunu Mame yi niniouy tagué Rassoulihi machallah ❤️ et vraiment quand j'entends sam mboup chanté les louanges j'ai des lames Au yeux 🥰
J'ai vu Baye Niasse durant mon enfance a Castors. Une bel homme, de teint un clair, toujours sourire aux lèvres, visage attirant et accueillant. Il était toujours entouré de ses talibes. La maison près du collège Carter a Castors
Machala saam diadieuf baye Niass Waayé kéndou taalibé seydil hadji malick yi si respecté les autres Lii wané nako na niépp roy si gnoom. Lii mooy Sénégal tidiane mourid khadir ak niépp.
10mil Salatoul Fatiha lala défal yow Serigne Sam Mboup adiyal lako bima dégué zikar si. Té inchallah dina youlli li nékk sama poche loum touti touti ma diox lako Adiya Baye. Yalla na Yalla fayanté ak yow silou bax
Dieuredieuf cheikh samme mboup yalla mi ame fay yalla nala défal ay yiiiw si barké alhouranou karim si barké seydina mohammed salalahou alleyhi wassalam
Silmakha you mane ndiathiar yii fisi senegal keur sougnou mame hadji Malick lako guiss mouy Sam MBAYE mii ak keur baye niass lakoguis moy cheikh Omar Faty Diallo niass , babacar Thiam ak Barham mo yorone gni done diangue kham kham si dará Elhadji Barham niass keur madiabel Dieureudieufé Cheikhou tidiani
Vraiment Sam Mboup vous êtes sans façon humble,bén kholoup iniane nékoul ci yow lii moma guéne neex ci jabootou Maodo sont universels Macha allah
La voix de Sam Mboup machalah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️, longue vie à lui🙏🙏🙏
Amine yarabi
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏
Je suis mouride talibe serigne saliou mais j aime baye niass et surtout ce khassida me fait pleurer a chaque fois
Être mouride tidiane layene ibadou c’est du pareils au même vous diverger sans même vous rendre compte ce qui compte c’est être un bon musulman point l’union des cœurs et pas la divergence des tarikha
mourid la wayé baye niass damako beug bilay🙏
Sén wah yi noûmay def louy mourite la wayé j'aime baye Niass baye Niass lepp kouy joulite dagko wara beugu Moy cheikhal islam wara mourite mom waroul beugu yenen Serigne yi
Degue bahreik machalla
Do mouride dé😢
je suis un mouride qui adore cheikhal islam Baye niass.
Allah t'adore ❤️🤩❤️❤️❤️🥰😘
Sa prouve ta véracité muslim
Moi je suis talibé baye niass et j'adore Serigne touba de trop...Machallah
MANE TAMITE BEUGUEUNALA BARKÉ BAYE NIASS 😍
Macha alla yalnala yalla defale khéwal goudou fane wéér soutouraa naguoul niou souguouy koor 🙏on est unique ❤️❤️❤️❤️💓
Allahou Akbar doundeul wéreul Serigne Sam cii barké Mawlana Cheikh Ibrahima Niass Baye ✊🏽❤️✊🏽 Thiéy Cheikh Al Islam ❤️🥺😭
Thieuye Baye Niasse yalnanioula yalla fayal Niasse Alahou Akbar
Amine
Sam mboup 😭😭😭😭😭barki baye niass je n'ai pas de mots. Yalla na ya allah guena wéreul baat bi inshallah thi barké seydina mouhammed saws.
Macha allah serigne sam yalna Allah deff la diame si barkep maola na baye niass kontan na yalna yalla Samo la
Amine ak yaw
Amine
Sa voix est extraordinaire.
Billahi machalla je l aime beaucoup
Machallah 🙏🏿😍❤️❤️ Lii neex Na teh rafeet Machallah 🙏🏿 Jerejëf Sérigne Sam Mboup ak Oustaz Pape Hann Yallah Naleen Yallah Faay seeni xol
MashaAllah Sam mi mangui Ñane Talibé Baye fougn dadié ak mome téral ko ndakh kou séll la ❤️❤️❤️
Inchallah
Inchallah
Je te jure que dina tedd, abadhan.
Tout ce que je sais c'est que j'aime bc bc bc Seydina Muhammad paix et salut sur lui ❤❤❤ Sam dieuredieuf wayy yalna yalla féyla yiww si barké Seydina Muhammad salalahou haley wa salam 🤲🤲🤲
😭😭 amine yarabi
Dieu te bénisse
Tu seras avec celui que tu aimes in sha Allah
Amine ya rabbi 🤲 🤲
Macha’Allah li rafetna. Nieup waar nagn di deff lini mell
Bilahi ma keur maodo rek la Sene deun yatoni. Dioulit dafa wara yamalé njiep. Mais dof ba alkou.
Vraiment Sam on n’ai fière de toi ❤❤❤❤❤
Doundeul wèrreul cheikh Sam Mboup si barkei Cheikhou Tidiane 🤲🤲
Amiiin yaa RABBI ci barké BAYE BARHAMA NIASSE ( RTA).
ALLAHOUMA AMINE YARABI
Amine yarabi
Amine ya rabbi niou
WALLAHI DINGUA HAMNI BAYE BARRHAMA DEGG NALA . TU ES UN VRAI MUSULMAN ZERO DISTINCTION . YA BAKH CHEIKH SAM MBOUP
Machallah mon frère
Mdrrr bouma raye way si kimou diokou kokou dou moromou baye nank nank rek
@@cherifcherif7033 Et c'est quoi le rapport ici thi kimou diokou ak kimou diokowoul? 🤣🤣🤣 n'importe quoi,lolou dh yako sania wax, guéneul Sénégal nga ték kimou diouko, tégualé iow ki nga diokou sou boba digua xam Maolana Cheikh Ibrahim Niass mom kép moy Cheikh al islam ba kérok adouna di touki, sa xol moy diekh rk mouy iow ak gni melni iow. Lolou nak la ya allah def, tél ko nangou nopalou mba deuké sonou rek té dou wagni dara thi ndogualou souniou borom. Non ni dioulitr nga mais ignane lou yallah may sa morom dioulite, aaah li dafa niaw way.
Yam léne way tamit, té bayi topaté bi ak yendou waté bi pour tok di xassé rek. Niounr miss naniou séni wakh dh, yeungua louniou té souniou léne tontou guéne mér alors togn ak ignane ak soxor moléne sonal.
Dèlène sissou rk, iow mom boula pannou glace sori rk🤣🤣🤣 xamna xol bou tangue nga nara deuké, Baye rek kep dongue késsé kou am lénéne c'est bien démal ak mom.
Genrou Sam Mboup bi islam laniou fi nékal xamni lep thi souniou borom la diougué té falay délou.
Mais sa genre gui seytané laniou fi nékal waxou diaxassé ak yé fitna moléne yitél, mbir mi dou concurrence.
Kone iow yay ki wara def ndank té yarou. Commencé par bayi diniou yendou rk🤣🤣🤣aaaah yéna sik way
@@LaBarhamienne dama retane ba sonou wakhi doff rek ngafi wakh dagua faté messi ak christiano nio gueuneu siiw baye si adouna humm tantôt mouride yi né ahmadou niassene yi né baye wayé mirou charia hum kou senetou lolu moussiba do degueu jamais niou wakh si niata diabar laniou ame niome ahahah lounioissiy neube le nombre d'enfant nak ahahhah kham nga senegal dafa nekh kou nekeu niounela yawela waye kou weete kham sa bop attirer du monde lolou khana waly seck mounenako waye finalité moy lane ay talibe moye katou yalla rek diape talibe di teudé takeu lou passé 4 diabars etccc.. dieuleul lepeu machala waye dagua done khale demal si sa serigne tu lui demande kane moy "YAMA SOW " la 75 eme épouse de baye pose lui juste la question
Papa same mboupe c Aminata barhama Diallo beugue Baye niass ❣️ a Saint Louis ♥️🇸🇳
Bilahi Walahi Talahi, c'est cela qu'on doit cultiver au Sénégal. On doit toujours privilégier l'union avant tout.
Je vois que Sam et Tafsir sont des références dans ce pays
Tivaouane a toujours montré l'exemple pour les autres j'en suis pas sûr
La voix d'or sam mboup magnifique Macha alla laf thiat ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Masha allah masha allah yallah naleine yallah faye li neikhna ❤️❤️
Machalla
Je suis mouride mais je sais que Toutes les bons chemins mènent en DIEU...❤️❤️machaalah
😭😭😭🫀❤❤❤❤❤❤🙏 niassi 📿
salut tu me plais bcp
tu habite où
mw suis de Matam
Une voix mielleuse capable de terrasser un taureau en colère. Merci beaucoup Grand Monsieur !
Yalla na yalla Yoko saye maye
Niasse rek alhamdou lilah ❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭😭
Sa voix est extraordinaire Ma sha Allah. Yalna baat bi werr si barké Seydina Mouhamed saw
Alhamdoulilah dieureudieufé BAYE ❤️❤️❤️❤️❤️
Machalla j SS mouride mai tt l monde est fiert d cette chanson
Arrêter svp gnioun gniogui yak sougnou rewmi ak ligayou nakk gni ak yi gnou khewal on est musulman point l’union des cœurs pour gniou beug toub dougnou si l’Islam
wallahi amoul sik, ni ngeunél bi senegal ame moy tarikha yi. yalna yalla sam niou si barke Barké baye moukhtar ka
Je ne fais partie d'aucun tarikha mais une chose est sûr nous tous nous aimons le prophète Mahomet SWS et k sunu Mame yi niniouy tagué Rassoulihi machallah ❤️ et vraiment quand j'entends sam mboup chanté les louanges j'ai des lames Au yeux 🥰
Lolou werna lolou ❤
Barki Baye Niass li nekhna❤❤❤❤❤❤❤🥰❤🥰❤🥰❤🥰❤😭❤😭❤❤😭❤💖
Trop
Serigne mboup je vais vous transféré un cadeau de 100salat fatihi ci barké baye niass adiarama bouye
Machallah sam yallah na yallah weurale batte be Inchallah
ماشاءالله ياشيخ بارك الله فيك وجزاك الله خيرا جرجف شيخ إبراهيم انياس
J'ai vu Baye Niasse durant mon enfance a Castors. Une bel homme, de teint un clair, toujours sourire aux lèvres, visage attirant et accueillant. Il était toujours entouré de ses talibes.
La maison près du collège Carter a Castors
ndaysan
quelle chance!
Quel chance waou
Sam yallah yallah fay la si barké baye Niass
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Dieureudieuf maolana cheikh Ibrahim niass. Thiey sounou baye . Yaye sounou baye si deugu
Masha'allah 🥰❤❤❤❤NIASS
Machallah Sam Mboup que vous garde
Ohh masahallah yallah nasa diamou yagg yallah gudal sa fann yarabi diaradiaffeee bayee🙏🏽❤️❤️
ماشاء الله تبارك الله 💝 🌹👆🏾جرجف مولانا شيخ انياس قلبي وروحي وكلي 🤍🌹جرجف شيخ إسلام باي 💝❤️🌹🤍🤍🤍
Ndeysane Macha allah Sam Mboup
Machallah Dieurdieuf Sam mboup ❤️❤️💸💸💸💸💸💸💸💸💸💸💸💸💸🇨🇵🇸🇳
Machallha dieureudiefé Maolana Cheikh Ibrahima Niass RTA ❤️❤️
Ma shaa Allah beautiful voice
J'adore baye Niass ya pas un jour où j'écoute pas cette chanson
Machala saam diadieuf baye Niass
Waayé kéndou taalibé seydil hadji malick yi si respecté les autres
Lii wané nako na niépp roy si gnoom.
Lii mooy Sénégal tidiane mourid khadir ak niépp.
10mil Salatoul Fatiha lala défal yow Serigne Sam Mboup adiyal lako bima dégué zikar si. Té inchallah dina youlli li nékk sama poche loum touti touti ma diox lako Adiya Baye. Yalla na Yalla fayanté ak yow silou bax
BARKHAMA MONDIAL BARKHAMA INTERNATIONAL.LE SAUVEUR DE L'HUMANITÉ.L'HÉRITIER DU PROPHÈTE MOUHAMMAD(PSL)...
Wawaw mashallah
Waxal way🙏dafa leer
Moy lep
Waw ❤❤
Machala sam goudal fane
Quelle voix . djeureudjeuffff sam mboup
Machallah baye niass mala beug sama xol❤❤❤
longue vie à vous 😘😘😘yagui sédal xol yii barké borom bonnet carré bii💕💕💕
Yalna yalla weureul baat bi yarabi
Machala rafét na lole
الحمد لله ما شاء الله شكرا لكم يا سام جزاك الله خير مولانا الشيخ الاسل
Alakhou akkkbarrrr❤❤❤❤ chekhal l’islam ❤😢😭
Machallah Niass 🥰🥰🥰🥰
جزاكم الله خيرا باركم الله
Niass machalla li moy Sénégal
Dieureudieuf baye niass ❤
Dieuredieuf cheikh samme mboup yalla mi ame fay yalla nala défal ay yiiiw si barké alhouranou karim si barké seydina mohammed salalahou alleyhi wassalam
Je suis fier d'être talibé Baye ❤️♥️🙏🙏🤔🤫
Thieye yonéneti bi yaw rék ya meuna sédale khole ❤️❤️❤️❤️
Longue vie barké Cheikh Tidiane rta
Machallah Niassy Coumba Abdallah
Dieureudieufe MaoLana cheikh Ibrahima niass
Mach'Allah 💓🙏🏽
Mashalah jereujeufer Baye
Voilà le Sénégal yalna jamm yagg yarabi
Contaane naa si moom....Machallah. yalna ko yalla fey té gueune koo beugue loo mbirou Cheikhal islam baye niass. Lii rek dey moy senegal.
Non Sam longue vie à vous
Yalla gua goudou fannnnnn
Pape hanne et Sam mboup Masha Allah sama khol seedena
Nandall guaniou thi lerr gui baniou mandi niass❤
Beug Baye rek té yaala tax 💘💘💘💘💘
Same mboup Do nite yala nala yala faye sa khole borome kholou diama biii ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Limoy Sénégal nagn fonk magg gni nopi diamou yalla benen none lagn am moy ibilisse yalna yala maygnou kholou alkhourhane yala gueureum gnou
Mancha Allah Niass ❤❤❤❤❤
Machalah way nekhna tropp❤❤❤❤
آلحمدلله على نعمة الاسلام والإيمان والإحسان
Walahi je suis mouride mais mane baye Niass nimou mey déif mane ah yalla reik niokeu kham barki borom touba
Machallah Dieureudieufe
Ahhhhhh li nekhna trop machallah 🤩🤩🤩🤩🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Oh Ndeysane 😭😭😭 SALAL LAHOU ALEYHI WA SALAM 😭😭😭
sam me rappelle mame babacar thiam ndeysane yalla nako souniou borom doli yeuram teii yok leram❤️❤️❤️❤️😭😭😭
Wly
Niass kou beugue yonènte yallah rék diga barkélou thi cheikh Ibrahim Niass alhamdou lillah diaradieufé cheikh Ibrahim Niass ♥️♥️♥️♥️
Alhamdou lilah dieureudieufé Baye Niass
Machallah nekhna trope 👌
Dieureudieufé Baye Niass, Docteurou khol yii❤️
billahi li da da nehè si holo baye barahma niass ambassadeur yonatebi yalla mohamed ❤❤❤❤❤😢
Machalla yalla nala yalla faye si barkel borom weir
Dieuredieufe baye barhama ❤
Thieuy baye machalla sam mboup
Alhamdoullilah bima bima yakaré n'a dioulit la
جزاك الله خيرا
Allahou akbar li nexna di
Machalah beg nala serigne sam
AL HAMDOULILAH ❤️🤲🤲
Sam Mala beugue chaque jour mom lay sétane machallah ❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️
Machallah sam mboup dieureudieufé baye niass ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yaram dawna ndeysane Jarajeuf Baye Niass
Dieureudieufé mboup khôl yi fekh nagnou et les larmes tombes bilahi
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️niass
Machalah Dieuredieufffè Baye Niass
Thiey yalla dieureudieuf bay ❤️🥰
Wallahi Merci beaucoup Baye Niass Rik 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭👂👂👂👂👈👈👈👈🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Silmakha you mane ndiathiar yii fisi senegal keur sougnou mame hadji Malick lako guiss mouy Sam MBAYE mii ak keur baye niass lakoguis moy cheikh Omar Faty Diallo niass , babacar Thiam ak Barham mo yorone gni done diangue kham kham si dará Elhadji Barham niass keur madiabel
Dieureudieufé Cheikhou tidiani