Peut être que Tounkara devrait se demander d'abord, comment les mourides parviennent -ils à réunir une si grosse somme pour un événement comme le magal? Pas étonnant pour des gens qui restent des disciples de l'Homme (Serigne Touba) qui a reçu l'autorisation d'éduquer ces disciples dans le travail. Pour moi en voici un premier succès qui mérite d’être salué. Le magal de Touba génère beaucoup d'argent au profit de l'Etat (taxes, impôts), des vendeurs et consommateurs. En quelque sorte si on avait deux ou trois autres rassemblement de ce genre alors c'est l'économie sénégalaise qui en profiterait avec une grande circulation d'argent. Pour qu'il ait un développement économique et qui serait rentable à la société alors l'économie a besoin d'une très grande circulation d'argent qui ferait profiterait à la population. Cette grande circulation d'argent ne saurait avoir lieu que si par exemple l'investissement dans l'économie nationale soit augmenté. Et des événements religieux comme le magal de Touba qui avoisine un coût de 100 milliards FCFA devrait être encouragé car c'est une somme qui est investi dans l'économie nationale et surtout qui ne va pas dans les mains d'une seule personne mais de plusieurs personnes (vendeurs, consommateurs). Ces derniers auront donc avec le plus qu'ils ont gagné de continuer à financier leurs activités voir d'autres activités économiques aussi. Donc respect à notre grand magal de Touba et merci encore à M. Syll. Tout ce que Serigne Touba nous a conseillé n'est que du bien. Ses enseignements peuvent servir de sources d'inspiration pour trouver des solutions à nos maux. En tout cas en tant qu'un homme qui prône pour le développement de son pays, je vois le mouridisme comme une doctrine qui marche sur la voix du développement économique, religieux et social. Exemple: la richesse des mourides a permis la construction d'une mosquée de plusieurs dizaines de milliards de FCFA, une Université islamique à Touba en cours de construction, des champs exploités chaque année à Khelcom et ailleurs et qui rapportent des milliards de FCFA, le tarbiya utilisé dans les Dahira Mourides participent aussi à l'amélioration de l'éducation des disciples tant sur le plan religieux et moral... Dieuredieufé Serigne Touba. Dou kéne dou kéne, té kéne dou mome.
Pas de règlement de comptes mon père, Mouride ndigeul, wakh diou séw bakhoul si Makk,Diamoudjil dji Yalla, boul nango nék dofou mbolo, la liberté d'expression ça existe, té beugeu beugeum la wakh,takhoul mou ame, Serigne Kara wakhna beug beugeum pour niou sopi tourou réwmi di Sénégal toudé ko Mbacké Barry,souba on attend d'autres propositions venant des nos amis et frères Mourides, incha Allah !
C'est clair, c'est net, c'est précis et concis. Serigne Mbaye Sylla, que ce triste sire ne réveille plus en vous, une quelconque animosité ou colère. Vous avez tout dit.: il a ravalé ses vomissures. Yalna Yalla defal la, defalniou ay xeewal yu takku si barké Prophète Muhammed ak jëwrignam Cheikhoul Khaddim. Amiine
Soun papa mbaye gueye syll yalla nala soun borom fay si léral yi ngay léral kanta mamadou sy tounkara dara khamouko limiy def ni yépp day diéma dokh si bopou nitt gni rek wayé yonou mouride bi kouko djéma khadiamal yaw yafay Diaré yakhou ba fawou
Mr Sylla j'espère que tounkara vous entendra . Votre analyse est très pertinente . Plus opportuniste que lui tu meurs . Ce sont des attitudes pourries comme celles de Tounkara qui plombent l'épanouissement de tout un peuple . Ils seront démasqués, un par un.
Dieredieuf Serigne Mbaye Gueye Syll amna sollo mounoul niak défois niou recadrer. Mane dé sincerement bima guissé wakh djodjou nékhouma darra ndankh Toudou Serigne Touba dii toudd kénéne wakhou makk bourrou aduna yabaté lakko déff. Au fond on sent qui'il n'est pas véridique sur ces paroles. dJIKOY nafékk rékk la yooor. Doméram pire là mounane lanes si Magal gui ki mo osé.
Tounkara yaag neu revendiqué que Serigne Touba moy Héros National. Comme Tounkara ak nioun gniy wakh Rewmi bamba ko mom. Lolu kounek amnga sagn sagn wakh sa yeug yeug... Man nak douma jugée nitt kouma khamoul li nek ci sen birr khol YALLA moko kham. Mais Lima kham CI Tounkara moy nit kou bakh kou beug Serigne Touba ak kou beug maag niou bakh yi nek Sénégal... Bay mbaye gueye taay mom andumak YoW. Sama mbokoum talubé nga yaag nala topou depuis touba Médias .. tassé nak YoW CI deuk you barri. Konn koula sopoulaaa
Billahi wallahi kou tedd ki cheikh ahmadou bamba KHADIMOUL RASSOUL wesuna fofou bamba fepp moy wahci pas Senegal rek lolou nako bayye ak Serigne yi ahmadou Borom le moy donoy yonnente bi shw Cheikh ahmadou bamba il est le sauveur de l'humanité 👌🏾
Eh pourtant quand il m avait invité red black l avait souligné que Sénégal cakanam veut dire Sénégal émergent es ce que tu ne travail pas pour macky Sall il tounkara avait crié non ohhh les masques sont tombé
moi personnellement, j'ai décidé qu'on ne dise plus Serigne Touba mais plutôt Borom Touba yaakarou jaam yi car n'importe qui peut se réclamer un beau matin Serigne et Borom Touba weissouna Serigne et baabooba
Guëmna ou pas digantém la ak Ýallah ak Borom Touba kénén khamoul lici bir kholam. Lettre bi liroumako kon doumaci wakh mé nagnouy nëbalanté ay sik man dal mbokoo nako dés ke mounék talibé.
On remerciera Macky Sall pour qu'une seule chose ,il nous a permis de démasquer pas mal de personnes
Wax nga dëgg de, mdrr
Merci encore macky won nagniou na fekh yepp
Merci pour cette belle analyse
Lou leer
😂😂😂😂😂👋🏾👋🏾👋🏾
Merci Mbaye Gueye Sylla. Nous sommes contents pour toi.
🙏👍
Pa bi règlement de compte rek lay deff. Mom moy doundé serigne bi.
Merci por vou baye mbaye Gueye Sylla
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah
Peut être que Tounkara devrait se demander d'abord, comment les mourides parviennent -ils à réunir une si grosse somme pour un événement comme le magal? Pas étonnant pour des gens qui restent des disciples de l'Homme (Serigne Touba) qui a reçu l'autorisation d'éduquer ces disciples dans le travail. Pour moi en voici un premier succès qui mérite d’être salué.
Le magal de Touba génère beaucoup d'argent au profit de l'Etat (taxes, impôts), des vendeurs et consommateurs. En quelque sorte si on avait deux ou trois autres rassemblement de ce genre alors c'est l'économie sénégalaise qui en profiterait avec une grande circulation d'argent. Pour qu'il ait un développement économique et qui serait rentable à la société alors l'économie a besoin d'une très grande circulation d'argent qui ferait profiterait à la population. Cette grande circulation d'argent ne saurait avoir lieu que si par exemple l'investissement dans l'économie nationale soit augmenté. Et des événements religieux comme le magal de Touba qui avoisine un coût de 100 milliards FCFA devrait être encouragé car c'est une somme qui est investi dans l'économie nationale et surtout qui ne va pas dans les mains d'une seule personne mais de plusieurs personnes (vendeurs, consommateurs). Ces derniers auront donc avec le plus qu'ils ont gagné de continuer à financier leurs activités voir d'autres activités économiques aussi. Donc respect à notre grand magal de Touba et merci encore à M. Syll. Tout ce que Serigne Touba nous a conseillé n'est que du bien. Ses enseignements peuvent servir de sources d'inspiration pour trouver des solutions à nos maux. En tout cas en tant qu'un homme qui prône pour le développement de son pays, je vois le mouridisme comme une doctrine qui marche sur la voix du développement économique, religieux et social. Exemple: la richesse des mourides a permis la construction d'une mosquée de plusieurs dizaines de milliards de FCFA, une Université islamique à Touba en cours de construction, des champs exploités chaque année à Khelcom et ailleurs et qui rapportent des milliards de FCFA, le tarbiya utilisé dans les Dahira Mourides participent aussi à l'amélioration de l'éducation des disciples tant sur le plan religieux et moral...
Dieuredieufé Serigne Touba.
Dou kéne dou kéne, té kéne dou mome.
Saway tothie ngafi wallahi deugleu devellopement Senegal Senegal touba lay tambalè inshallah
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah amne solo loooooooool dieurudieuf baye mbaye gueye Syll Syll godou fan wir tawfékh ak khéwal barke khassida yi amiiiiiiiiiiiiine
Macahlla
Vraiment vous êtes excellent mbaye Gueye syll
Effectivement mooom tounkara talibé seriñe Touba moo ko corrigé fiii si télé 📺 bi wanniko khamoul darà siloumouy waah bilaahi Tounkara ioe yèémooonou sah tè booo atouwoul sa bop dinanou Kééf taa tombé
Merci yàlla nala yalla faye
Mbaye Gueye Sylla merci way sa répond yi amna solou
Dieureudieuf linga def d bok na ci liy wanéna non seulement mouride deug nga mais citoyen nga !!! Geune nala naaw .... yallah nala serigne touba fay
👍
Masa Allah Wakhalél Ganou dé yallana serigne bi fayla
Merci Touba Vision Yawwit nio ngi guis sa ligueye binga def ci yoon bi
Amine ya rabi
Mbaye geuye syll bayill Tonie nitte daye mandou tonkara toudou la tassoula ta yaw momo yonou mouride dothiy daara, mbaye geuye syll ragalall yalla ta bayyi soss
Merci serigne Mbaye Gueye syll . Yalla Nala yalla takhawou Bi Barakatoul Khadimou Rassoul . Amine . DIEUREUDIEUFE BOROME TOUBA KHADIMOU RASSOUL .
Pas de règlement de comptes mon père, Mouride ndigeul, wakh diou séw bakhoul si Makk,Diamoudjil dji Yalla, boul nango nék dofou mbolo, la liberté d'expression ça existe, té beugeu beugeum la wakh,takhoul mou ame, Serigne Kara wakhna beug beugeum pour niou sopi tourou réwmi di Sénégal toudé ko Mbacké Barry,souba on attend d'autres propositions venant des nos amis et frères Mourides, incha Allah !
Malick doul ki limouy wakh khamosi gat nopil
Allahou Akbar : fomou Magalou TOUBA 😢😢😢
Tounkara linga wakh graw n'a dhé
Dieureudieufff serigne mbaye ma contend si yaw
C'est clair, c'est net, c'est précis et concis. Serigne Mbaye Sylla, que ce triste sire ne réveille plus en vous, une quelconque animosité ou colère. Vous avez tout dit.: il a ravalé ses vomissures. Yalna Yalla defal la, defalniou ay xeewal yu takku si barké Prophète Muhammed ak jëwrignam Cheikhoul Khaddim. Amiine
Tounkara cimmmmm mbayyyyy
Machalla s mbaye Gueye Sylla 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Diadieuf serigne Touba diarama mame chiekh ibra fall
Merci mon père,tu es vraiment un grand Monsieur.
Serigne Touba EST plus qu'un héros national,il EST UNIQUE ET UNIVERSELLE.
C'est un faut type ce tounkara
Dieurdieurff ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿
Dieureudieff sama Baay dji
Yallah na la Suno Borom bi defal kudu fan ak wër
Diadiuefati serigne mbaye yalla na yalla sammula ta dollila kattan yaggue FI lool ta werr allahuma amiine
Merci beaucoup
Jërëjëfëti sëriñ Mbaye Gueye. Noo ngi siare bu baax.
👍
Merciii tonton mbaye Gueye tounkara mom dou nittou dara thiemm
Serigne touba rombna hero national serigne touba guedj le dieureudieuf serigne touba tounkara dal diarul tontou
Waxal dh
wallahi rombounako
Pere merci beaucoup. Tounkara mom da ray bopam.ay wakham diaroul sax deglou.
Dieureudieuf pape
Gorgui bayil yêh fitna.
Tounkara kou beugue Serigne Touba la.
Diamou djil Yallah bayi xuloo ak xasté Mag nga.
Mbaye dafa souffrir des
Dol
Merci beucoup diradieuf amna solo
Dieureudieuf a mbaye gueye goudou fane ak weer mercj merci merci
Soun papa mbaye gueye syll yalla nala soun borom fay si léral yi ngay léral kanta mamadou sy tounkara dara khamouko limiy def ni yépp day diéma dokh si bopou nitt gni rek wayé yonou mouride bi kouko djéma khadiamal yaw yafay Diaré yakhou ba fawou
DAra dafati KO bahga
Dieureudieuf mbaye guéye Sylla
Yallana yalla goudeul saw. fane serigne mbaye Gueye sylla
Merci bcp kilifangui tounkara dou nitou dara
Salam BAYE MBAYE GUEYE SILL DIADIEUFEUT YALLA NALA BOROM TOUBA SAMBAL BOBAM
SAMBAL BOPPAM
Bravo diadieuf gorgui tounkara dou nitu dara
Merci Mbaye
Diadieuf serigne Mbaye Gueye sylla yalla nala serigne bii guene takhawou si barké borom darou moukhty amine
SERIGNE TOUBA dou ay thiakhane ba kou diokk wakh ssi
Dieureudieuf serigne nbaye Sylla amena solo serigne touba amoul morome
machallah papa amnasolo tounkara domoukharamla
yalla nala yagall takhawayy fy kou bakh ki
Thiéye yalla kone li lépou diote nafée am ki khamoul khadim Rassoul
Je suis d'accord avec tounkara
Votez Sonko , et faire voter Sonko si vous voulez le changement
*Dieureudieuf mbaye gueye kadouyi rafétna mash'aĺlah tounkara dou dará nafékh leu boumack*
Machallh
Mr Sylla j'espère que tounkara vous entendra . Votre analyse est très pertinente . Plus opportuniste que lui tu meurs . Ce sont des attitudes pourries comme celles de Tounkara qui plombent l'épanouissement de tout un peuple .
Ils seront démasqués, un par un.
Dieredieuf Serigne Mbaye Gueye Syll amna sollo mounoul niak défois niou recadrer. Mane dé sincerement bima guissé wakh djodjou nékhouma darra ndankh Toudou Serigne Touba dii toudd kénéne wakhou makk bourrou aduna yabaté lakko déff. Au fond on sent qui'il n'est pas véridique sur ces paroles. dJIKOY nafékk rékk la yooor. Doméram pire là mounane lanes si Magal gui ki mo osé.
Dieura dieufati serigne mbaye sylla
Bàye mbaye bulyàkh emition bi boul wakh ak ñooñou, amna yanén you app solo yooyou, danlay sonal rék
Jeureujeuf ya bakh si nit yi gueumoul dara komm tounkara
amna solo
Tounkara yaag neu revendiqué que Serigne Touba moy Héros National. Comme Tounkara ak nioun gniy wakh Rewmi bamba ko mom. Lolu kounek amnga sagn sagn wakh sa yeug yeug... Man nak douma jugée nitt kouma khamoul li nek ci sen birr khol YALLA moko kham. Mais Lima kham CI Tounkara moy nit kou bakh kou beug Serigne Touba ak kou beug maag niou bakh yi nek Sénégal... Bay mbaye gueye taay mom andumak YoW. Sama mbokoum talubé nga yaag nala topou depuis touba Médias .. tassé nak YoW CI deuk you barri. Konn koula sopoulaaa
Maa cha Allah
Merci mame mbaye Gueye
Billahi wallahi kou tedd ki cheikh ahmadou bamba KHADIMOUL RASSOUL wesuna fofou bamba fepp moy wahci pas Senegal rek lolou nako bayye ak Serigne yi ahmadou Borom le moy donoy yonnente bi shw
Cheikh ahmadou bamba il est le sauveur de l'humanité 👌🏾
@@Kingsley114 boude kham gako rek bakh na
Machalla
Tounkara est un farfelu il est loin d’être un patriote c’est plutôt un opportuniste
Machalah bay Mbaye Gueye sylla
Tounkara kay dou mourite prsk mourite dou déff lolu
Machallah yalna yalla barkel saye mbir
Ndey sane amna solo des
Bravoooo 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Merci d'avoir remis à leur place de petits prétentieux .
S. Touba coko l'ale l'ale ma Mane noreyni
diedieuf
Très bien
Dieuredieuf serigne bi Yalla naguafi yagg té wére tounkoura dou nittou darra
Dieureudieuf serigne mbaye gueye sylla amna solo
Dieureudieuf
Diadieuf wakh dji amna solo
💪💪💪💪thank u papa kii geumoul dara
Tounkara dou exemple...nopaloul père...
Merci tonton
Machalah rafet na
Diere dief serigne bi goudeul fan Tounkara dou gorre BilAhi na féq le
Jaajëf SYLL Amatina solo Maashaallaah
Lat Dior et Serigne Touba sont Tous nos héros. Tounkara n'est qu'un fumiste et un jaloux
Eh pourtant quand il m avait invité red black l avait souligné que Sénégal cakanam veut dire Sénégal émergent es ce que tu ne travail pas pour macky Sall il tounkara avait crié non ohhh les masques sont tombé
Louy héros nationale serigne touba rombna lolou
Machallha degelle bouwer yage fi looooooòl sono baye mbaye geye
Mbaye amna solo
moi personnellement, j'ai décidé qu'on ne dise plus Serigne Touba mais plutôt Borom Touba yaakarou jaam yi car n'importe qui peut se réclamer un beau matin Serigne et Borom Touba weissouna Serigne et baabooba
Lolou le cheikh ahmadou kara wah borom touba moy defar ay serigne wesuna yoyou amoul morom
@@ousmangaye1687 may nako borom touba yague na te baboba incha allah
@@ousmangaye1687 Touba amna Guinée conakry, c'est toi qui me l'apprend
@@modoufallthioune6731 Si si et je pense qu'il ce Touba a bien existé avant le village Touba fondé par mon homonyme Vénérable Khadim Rassoul.
Diadieuf sa baye manla sa dome chams si Espagne 🇪🇸
Mame bauy yague fi lool bakh nga si yoonou mouride barkep serigne sam mbaye
Fier d'être mouride et c tout borom Touba yafinek......
dieredief Gueye yalla nala s touba fey
Guëmna ou pas digantém la ak Ýallah ak Borom Touba kénén khamoul lici bir kholam. Lettre bi liroumako kon doumaci wakh mé nagnouy nëbalanté ay sik man dal mbokoo nako dés ke mounék talibé.
Tounkara c'est le modèle de l'intellectuel malhonnête c'est un petit type
Yalna yalla goudal sa fane
Diaradiaf s mbaye
Dieuredieuf serignebi contenanububakh
serigne mbaye gueye jeureudieuf yalanayala fayla waxga lepp
Dieureudieufety serigne Mbaye Gueye syll
Maachalla
Bilahi Walahi Macky si dahko la dieum