Franchement modou lo a fait deux combats en 3 mois si vous étiez à sa place vous alliez dire que je suis fatigué. C est lé seul lutteur à avoir mis en jeux sa couronne de roi 2 fois en jeux dans une même saison donc bravo a lui. Prends d autres tu dois respecter modou lo même si vous ne luttez pas. Respectez Modou lo mo la raw dalay may chance rek
Mdr modou ragal tapha tine rek la def moniwone athlete chak 2mois mou beuré moko arranger ta combat bi sou taxawone fin saison la dieum meun na nopalou ba doyal dako nièméwoul rek c’est ça
@@papsngom7260 je ne dis pas ça par fanatisme, mon lutteur préféré c'est Ama balde, mais honnêtement Tapha Tine il a appris de ses erreurs j'ai l'impression
Lamine il est bien, pertinent té il est objectif il parle à tous les lutteurs comme s'ils sont ses frères. Objectivité bi c marquant Mais Mod lo loutakh kouy wakh si mom rec di mér tal lén gaz tok si. Souko nékhé nopalou. Kou téglé 2 combats en 2 mois si Mbeur bou mag Tapha Tine soula nékhé bégna té beurek mom ngay wakh si mom comme si da am loumou la déf alors que folén tassé mou bégué la mou nice. Li lamb rec la sou diékhé diékhna bayilén diambour da déf li nguén défoul nguén di sissou
Saway Modou gnemewoul saway dhe. Saway depuis 2014 thi bene entrainment BCAO thi la Modou di bayi khel Tapha.. Gayi di toudou mbeur yi ba toudou Tapha “ Mou nee non Kokou dof bou yewou laa legui “ 😂
Tapha Tine a rajeuni. L'expérience commence à apporter ses fruits. La force intérieure prime sur la masse corporelle. Bravo pour la discipline sportive
*Tapha Tine gabari rek leu eup modou lo. Amoul beurreé waleu khekh bi diakhal modou Lo, et sur le plan sportif modou lo moko gueneu bakh staff, eup ko entraînement, eup ko mental, gueun ko professionnel.*
Yokal kassé Issa pouye nokou ko ak lac de guiers 2 ak ama baldé té niom nieup modou Lo dalen nokou ki modou Lo dou moromam moko meun foufff yambar la 😂
@@moustaphakhoule3506 Saway boul ko tekk fofou Modou lo danoul Balla, danoul Lac, danoul Bomb te Baye Mandione sakh Dafa am difficultés ak mom. Pr dire vrai rekk Modou mo dakka beurer Tapha fouff Mais geumouma mou dane Tapha ndax moka long large ko eup ko rallonge foufff
Pour battre balla il faut osez l'affronter et l'attaquer en premier avec des coups forts et precis. En plus etre tres rapide sinon dou bakh. Si tu lis mes conseils tu va gagner
Tafa tine ay Serere laniou kom yow ms respect modou lo ndakh kou buere 2cimbat 3mois wara mana noppalou te xamgani modou lo ragalouma te boul fatteni ama dala Dan lac 2 dala Dan te niom niar yèp roi bi molen Dan kon yow mano don roi bo defe sa bop roi sénégalaise dounioula kholati kom lutter ms kom comédie lanioulay khole te tik tok bi yafay fess
Boul ko tekk fofou Balla ak Lac 2 bi nga toudou Modou lo danou lene te Tapha danena Bomb mi dane Balla ak Modou, dane Eumeu sama champion bi dane lourds yeup presk. Modou meussou fi dane lourds bouko eup taille ba took thi kawam. Thiol li mofi nekk rekk Mais Modou meunoul dane Tapha saway.
Tapha tine modou lo c’est ton roi tu lui doit du respect donc laisse modou lo en paix car les autres lutteurs sont comme balla gaye qui ton potentiel adversaire.
Balla gaye mom niom Aziz défaral nanko mais daniou koy yakhal lou bari si fin carrièrem diogué si ay défaite you méti beugue dieul kou mélni tapha tine de même que tapha tine yaw do dieul lac de guerre guay dieul Balla soula dané sa nek roi des arènes louye diafé leu mais nak Balla gaye 2 yalnako yalla may ndam inchallah
Machallah lamine sa mbokkou talibé mingui lay gnanal yalla mousseul leu thi thiate ak nooon barké SEydiNA Mouhamed ❤ak sa yakar ba CHEIKHOUNA AHMADOU BAMBA 🙏🙏🤩👺
Sa lamb yepp iow la faral ms bayi nala faral Baol Baol la iow modou la epoulè fans baol bark SėriGNE saliou ndakh modou international mm ak balla gueye modou fepp 🎉🎉🎉
Saway Modou moka dakka beurer foufff Mais Modou meussoul dane bene lourds bouko eup taille ba tok thi kawam. Thiow li rekk mofi neek Mais Modou lo mola geuna kham ni dou dane Tapha ( Y’a une trop grande différence de Taille)
Dane kou dane Tapha takhoul Modou dane Tapha ! Modou danena Eumeu te Eum mo dane Balla ak Bomb mi dane Modou. Modou meussoul dane lourd bouko eup taille ba took thi kawam qu’ on se dise la vérité. Thiow li mofi nekk mais Modou dou dane Tapha mm bou daner gnouko dane.
Dama meuss gueum Modou Lo meune Ama ak Boy Niang mais bilay meunoul Tapha Tine, Modou ya wakh deugue d boul ko djeul da ndiol am dolé té da yéwou si lamb legui 😂😂
Boul sokhor nekko roi beugeu saltél roi niakk fay da toppal feullei do touss niakk diom kharagne lo xalifa general koullou mbeur soula mettei nga dem bayi baol
@@layekharagne2224 Mais frère Issa pouye mou ragal door momou ngay tekeleu ak lourds yii tamite 🤦🏽♂️. Gris j8 d’ accord Mais Gris soutoul Modou lou beuri comme Balla, Bomb, Tapha te Gris 4 appuis lako Modou daner sen 2e combat bi. Nangoul tamite frère ton lutteur a tjrs des difficultés avec les lourds yiko eup masse ak rallonge.
@@papadiom9260 il a des difficultés avec les lourds mais en 18 ans de carrière il a seulement 3 défaites et seul 2 lutteurs l’ont battu , donc Modou sou amoul wone problème ak lourd yi founiou dieum 😂modou est vraiment le meilleur lutteur de l’histoire, eumeu sa mbeur nane la dané bombardier 2 fois dou 4 appuis ? donc lui aussi il a problem avec les lourds selon ta logique.
@@layekharagne2224 Non Mais Eumeu ak Modou bokougn ndokhtou beurer thi lourds yi. Eum a appris à lutter contre les lourds depuis l’ âge de 17 ans te en plus il a fait le greco mo tax mu meuna dane Balla, Lac 2, Gris bagnou tokk parcequ’ il les impose la lutte sans ngimb et y’ a pas une grande différence de poids entre eux contrairement à Modou. Et aussi Eumeu avait eu les mm difficultés contre Bomb aussi Motax fakk ko mou reup rekk lathi wout Mais bougn tolo wone touti dafkay tiaxabal. Modou kaay Bou tolone nii ay Bombardier moy raaw Bomb dina fii door mbeur mou dhee ndakh dafa sokhor 😭😭😭
C'est la 1er fois ma découvrir facette bi ci tapha tine mais il est vraiment sympathique ❤..mais nak bayil sunu roi bi ngay sandi xér😂
Je sais pas si vous avez noté l’évolution de Lamine. Il devient de plus en plus pertinent sur ses questions.
Wayaw lamine c'est le meilleur amoul complexe si mbeur bou mak wala mbeur bou ndaw ...bamou amé diabar batay da gueuneu pertinent....lamine mom manchalla
Kou yarou la contrairement a Modou anta
Il est très professionnel machallah
Oui plus pertinent que les soi-disants journalistes.
Lamine mom franchement meun'a Aam lounk .. yarouna meun na liguey
Lamine evolue bien mashaAllah . Il me donne Ismaila Diop qui faisait l’émission Den Kumpa à la RTS .
Franchement modou lo a fait deux combats en 3 mois si vous étiez à sa place vous alliez dire que je suis fatigué. C est lé seul lutteur à avoir mis en jeux sa couronne de roi 2 fois en jeux dans une même saison donc bravo a lui. Prends d autres tu dois respecter modou lo même si vous ne luttez pas. Respectez Modou lo mo la raw dalay may chance rek
Diambar la moom ! Mais moo ni woone loolou moo ko gueuneul ! Combat yi mouy beurei bagna sorintei
Modou mayou ko chance lamb molen bolé
C'est en 2 mois matoul sakh 3 mois
Mdr modou ragal tapha tine rek la def moniwone athlete chak 2mois mou beuré moko arranger ta combat bi sou taxawone fin saison la dieum meun na nopalou ba doyal dako nièméwoul rek c’est ça
Vraiment Modou Lo a fait ce que personne n'a fait 2 combats en moins de 2 mois. Il faut le respecter ce roi là.
Tapha Tine a beaucoup changé, il a beaucoup évolué, ça va être très très difficile de battre
😂😂😂😂😂mandou contre eumeu sene mo waral wakh dji kii deh modou lo dakoy dane matin midi soir
@@papsngom7260bayiko fofou rek
@@papsngom7260 je ne dis pas ça par fanatisme, mon lutteur préféré c'est Ama balde, mais honnêtement Tapha Tine il a appris de ses erreurs j'ai l'impression
Comment toujours répéter le mappat de balla et tapha tine toujours. Du respect pour les deux
Lamine il est bien, pertinent té il est objectif il parle à tous les lutteurs comme s'ils sont ses frères. Objectivité bi c marquant
Mais Mod lo loutakh kouy wakh si mom rec di mér tal lén gaz tok si. Souko nékhé nopalou. Kou téglé 2 combats en 2 mois si Mbeur bou mag Tapha Tine soula nékhé bégna té beurek mom ngay wakh si mom comme si da am loumou la déf alors que folén tassé mou bégué la mou nice. Li lamb rec la sou diékhé diékhna bayilén diambour da déf li nguén défoul nguén di sissou
Lamine bonne continuation tes questions sont pertinentes 👍🙏👌
Baol notre fierté ❤❤❤
L'histoire retiendra tapha . j'aime bien ton figua diare
Franchement tapha vrai sportif leu je suis émue
Merci❤tapha tine❤la king❤👑💯✅
Lerr na yalla daguéna déssé kham monde 🌍 lô 💪
Bayilèn fofou rek
Mais dou fans balla wala bombardier nguéne kaye wakh.
Saway Modou gnemewoul saway dhe. Saway depuis 2014 thi bene entrainment BCAO thi la Modou di bayi khel Tapha.. Gayi di toudou mbeur yi ba toudou Tapha “ Mou nee non Kokou dof bou yewou laa legui “ 😂
@@papadiom9260 Meussou ko niemé
@@papadiom9260 bakhna déléne wakh rek 🤣
Tapha Tine a rajeuni. L'expérience commence à apporter ses fruits.
La force intérieure prime sur la masse corporelle.
Bravo pour la discipline sportive
Tapha tine futur roi des arènes inchallah
Tapha dine boul yakamti heure bi sou diotai inchallahou rabi yaw ak modou lo diguene beurei mou dane la inchallahou rabi
😂😂
Tapha tine daneko inchaAllahou rabi
Yaay wakh lolou Mais Modou wakhoul lolou dhee 😂
Je suis très content de retrouver mon idole à travers cet interview.
Borom tak ci rip
@@Jubjubbaljubanti92 oui my bro il nous faut une victoire cette fois ci.
Tapha tine rek inchallah mon fils
Balla gaye ll a vie yalle nala yallah defal ndammm te li dess sa carrier yallah bosi degueuti mugnal ❤❤
Balla dafa maguatt
Roi des arènes bou beuré 2combats si béne saison kéne masou kofé déff sé très normal mou nopalou
Surtout en espace de 2 mois ak boy you geuna tangue
Anh kay ! Yekini def na ko
@@abdoulayegueye6686bane annee?
Tapha legui dey lakeu français sakh 😂😂😂Machallah
Tapha tine à du bon cœur.
moustapha tine très champion degeue yalna yalla yokou diamou ak kartan très comenigue bien
Lou weurr nuit daye am keuli fa yaw danga niute machallah xol sede n'a thii yaw ❤❤❤
Tapha tine méré na modou lo déh😂😂😂
Machallah champions émission bi nékhna mé li nga wakh si sunu roi bi nak nangouwouma roi Dara yéw moom ngay weur ak Say morome Kone boul waxé nonou
❤❤❤ machallah ❤❤❤ très dicipline ❤❤❤ champion ❤❤❤
Merci champion
Machllah ❤❤❤❤ moustapha
Amady❤moustapha❤tine❤rek baol baol❤bi❤
*Tapha Tine gabari rek leu eup modou lo. Amoul beurreé waleu khekh bi diakhal modou Lo, et sur le plan sportif modou lo moko gueneu bakh staff, eup ko entraînement, eup ko mental, gueun ko professionnel.*
Bombardier loum dané Modou lo
wayei modou niemewko
entraînement momo modou eupoul koko
Lutte tv vraiment chapeau mais je vous propose de faire un fond noir quand vous faites ces genres d'interview
Merci
Balla gayie 2 moufi ni❤❤❤❤
YOW EUMEU SENE NOKOLa meuno dane boy niang MODOU MOYE SEN PAPA
Ki nokk bombardier 2 fois bombardier dane modou lo cone ki mo meune modou lo
Frère figako tékk lamb nékoul fofou
@@salioudiallo3412saway ki danoul b52 nak décision arbitre la dane ba tokk si kawam laniou wax
Yokal kassé Issa pouye nokou ko ak lac de guiers 2 ak ama baldé té niom nieup modou Lo dalen nokou ki modou Lo dou moromam moko meun foufff yambar la 😂
@@moustaphakhoule3506 Saway boul ko tekk fofou Modou lo danoul Balla, danoul Lac, danoul Bomb te Baye Mandione sakh Dafa am difficultés ak mom. Pr dire vrai rekk Modou mo dakka beurer Tapha fouff Mais geumouma mou dane Tapha ndax moka long large ko eup ko rallonge foufff
Tapha tine yalna dane balla gaye
Balla gaye kasse ❤❤
Tapha dima ray néna qui se soit 😂😂
Svp nak Tapha ay bagage you diougué Guediaway bouko utiliser ti prsk wa staff Balla gaye sagne naniou louné ta lamb diaral nalén louné moytoul
Tapha tine kesssse baol baol bii yawoor dé ligueye rek ❤❤❤💪👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑🫵❤️❤️❤️
Bon communiquant
Balla Gayie 2💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Tapha Tine ku Iniaaan nga te soxor drm Modou moo man sa nday
Mou Mane sa bay AK say mbok😅
Yaw sa Baay juru la drm 😅
Tapha Tine ak Reug Reug combat la
Pour battre balla il faut osez l'affronter et l'attaquer en premier avec des coups forts et precis.
En plus etre tres rapide sinon dou bakh.
Si tu lis mes conseils tu va gagner
Ah pour mane il doit l'attendre lomou ték mou teguiko
Yalla Nala yalla soutoural may la ndam si balla gaye sa diabar ji dafa bakh bilahi man la vigile bi nék fi sa dom yi Di diangé
Oh machallah je suis très émue merci beaucoup ❤
Tafa tine ay Serere laniou kom yow ms respect modou lo ndakh kou buere 2cimbat 3mois wara mana noppalou te xamgani modou lo ragalouma te boul fatteni ama dala Dan lac 2 dala Dan te niom niar yèp roi bi molen Dan kon yow mano don roi bo defe sa bop roi sénégalaise dounioula kholati kom lutter ms kom comédie lanioulay khole te tik tok bi yafay fess
Boul ko tekk fofou Balla ak Lac 2 bi nga toudou Modou lo danou lene te Tapha danena Bomb mi dane Balla ak Modou, dane Eumeu sama champion bi dane lourds yeup presk. Modou meussou fi dane lourds bouko eup taille ba took thi kawam. Thiol li mofi nekk rekk Mais Modou meunoul dane Tapha saway.
Merci beaucoup ❤❤❤❤
modou ✨ xaragne lo rek santé 👑 yalla
Tapha tine modou lo c’est ton roi tu lui doit du respect donc laisse modou lo en paix car les autres lutteurs sont comme balla gaye qui ton potentiel adversaire.
Sa se voit que modou niéméwoul tapha.
Nekhoul ba nekhoul waye tapha tine modou lo moy comba bi
Bilaye walaye
Mais Modou lo dafa sonou daye nopalou
Balla gaye2 à 22 victoires ;6 défaites 28 combats tapha tine respect à Balla gaye2 toi t'a 5 défaites t victoire
Lamine seck machallah bonne continuation 🎉
Tafa Tin waye nèna moy Rio bi😂😂
Pour dire vrai insbi mo meune balla gaye
Tapha tine légui dou gakka si lamb dji yéwou na bly😂😂
Balla gaye mom niom Aziz défaral nanko mais daniou koy yakhal lou bari si fin carrièrem diogué si ay défaite you méti beugue dieul kou mélni tapha tine de même que tapha tine yaw do dieul lac de guerre guay dieul Balla soula dané sa nek roi des arènes louye diafé leu mais nak Balla gaye 2 yalnako yalla may ndam inchallah
Machallah lamine sa mbokkou talibé mingui lay gnanal yalla mousseul leu thi thiate ak nooon barké SEydiNA Mouhamed ❤ak sa yakar ba CHEIKHOUNA AHMADOU BAMBA 🙏🙏🤩👺
Sama mbeur nga wone mais wedinala bisniki tay... Nangouni modou lo loy roi incontesté
Modou lo ragal la dey daw tapha baol rek
Loumcoy wanie
Thiéy Amdy Moustapha 😂💪🤣💪
Wakhi lamb leuh rek pour le provoquer boul co bayi. Comprends le il veut un combat royal c’est son droit aussi.
Konn amour bi Sincères eoul
Ama da wor wor bakhoul bilye ❤
Tapha boule sisou waye ligna wakh yombouna trop modou moye roi
Sa lamb yepp iow la faral ms bayi nala faral Baol Baol la iow modou la epoulè fans baol bark SėriGNE saliou ndakh modou international mm ak balla gueye modou fepp 🎉🎉🎉
Yamana way wakhal deug wy😅
Boul yakamti mayniou niou nopalou nieuwate di nga xamni modou lo mola eupeu fitt dakla beuré té xoloula sax dinala douma daane la inshalla
😂 deet waay
Saway Modou moka dakka beurer foufff Mais Modou meussoul dane bene lourds bouko eup taille ba tok thi kawam. Thiow li rekk mofi neek Mais Modou lo mola geuna kham ni dou dane Tapha ( Y’a une trop grande différence de Taille)
@@papadiom9260 waw ba boba inshalla
@@papadiom9260vraiment tu as raison 😅😅😂😂😢😢
Lamine amdi Moustapha tine roi des arene nou Sénégal bii gnémé wougnou ko
Danga sokhor meuno beuré 😂
Deugue rek ngua wakh
Balla gayie 2 moufi ni bilay ❤❤❤
man tpa tin rek lay toppo 😂😂😂😂😂
Ki dafa sokhor roi çest modou lo tèy boh danone modou loy done roi non
Balla Gaye 2 rek ❤❤❤
Lamine nékhoul ba nekhoul mé yagui yokou lamb
Tapha tine soxorr nga Modou lo c’est le rois par la force
Ki kou soxor La billahi
Lamine il est. Très différents ak sunu journaliste yi dalay pause question may la temps nga répondre vraiment
A jaaraama tapha tin yoo allah wallu aamiina yaa rabbal aalamiina
Mafia lamb moy ècartè combat tapha tine diko orientè si balla il faut arrêter cette hypocrisie
Mais c’est la logique le roi nena day pause d’ici 3 ans
@@talladiagne8092 3 lane ? Loolou bari n'a dei
@@talladiagne8092 3 ans ?? Adouna dafa goudou tank dhee baxna 😂😂😂
Tapha wakh nga deug modou lo niémé woula sathies la beug khar
😂😂𝐲𝐚𝐧 𝐠𝐮𝐢𝐮 𝐬𝐚 𝐱𝐞́𝐥𝐥 𝐧𝐚𝐤
On le comprend ça façon de parler il veut un combat avec modou mais il croit supérieur mais modou dou nekhou gnebé
modou champion la mais tapha la warone beurel mais l'impression qu'il attend sathies
Machalla
Modou laye BEYE 👍👍merci 👍 👍
Balla gayie 2 Rik
Bilaye yaye roi bi
Ohh frère niagui sathie mango😂😂
Modou lo rek laniouy topeu mo meune mo eupeu dool
Balla Gayue 2💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪
Wiri wiri diari ndari roi rek😅
Tapha tine vs Modou lo Moy combat bi .té ngene Bayi mafia bi
Lamin ❤❤❤❤❤❤❤❤
Yagui tardel SA bop dielal balla gueye 2 modou lo mom parewul sakh pur buere si 2024. 2025
Atia mbeurou sandaga xalissou baol baol yeup bolene ko dajelewone lolou danoul Modou Lo
Eume mola douma Modou douma Eume
Ioe depuis niata att yagui daw lac 2
Emplus Ama bila plaquei Modou moko watie
Dane kou dane Tapha takhoul Modou dane Tapha ! Modou danena Eumeu te Eum mo dane Balla ak Bomb mi dane Modou. Modou meussoul dane lourd bouko eup taille ba took thi kawam qu’ on se dise la vérité. Thiow li mofi nekk mais Modou dou dane Tapha mm bou daner gnouko dane.
Kiii mome Daffa melniii kou weroul bou wakhé rkk gua khebbb koo nit yomboul Tapha lokko fonk fonk bou wakhé gua bayiii ko wahiiiii doff rkk laye Wakh ah demal iow no mana nekk Roi des arène dé’ thé dano ki yor couronne 👑 bi may wakh menoune bane president walla ministre moko diokhé wero Tapha 😊
Yow khana supporter Modou nga ?
Tapha wakh béfi nek rek mais bou dadiék kou meune beuré, dou khékhe dou beuré
Ça ce voit contre balla gaye ak contre ama balda et beaucoup d'autres
Boul dieul fawzeyniii dh dagn la beug sarakhéééé😂😂😂😂😂😂
Badou souko dieulè wayadi 😂😂
Xanaa jëlaat😂😂
😂😂😂
Fier de toi machala tapha
Tapha tine v modou lo
Dama meuss gueum Modou Lo meune Ama ak Boy Niang mais bilay meunoul Tapha Tine, Modou ya wakh deugue d boul ko djeul da ndiol am dolé té da yéwou si lamb legui 😂😂
Modou lo dafa sonou daye nopalou
Boul sokhor nekko roi beugeu saltél roi niakk fay da toppal feullei do touss niakk diom kharagne lo xalifa general koullou mbeur soula mettei nga dem bayi baol
Balla la toudou santeu bombardier
Modou cerveau leu bokoy dieul molaye dane.
Geumou ma Modou daneko dhee ! Modou meussoul dane mbeur bouko eup taille tambali thi Baye Mandione… Danoul Balla, Lac, Bomb geumouma mou dane Tapha
@@papadiom9260issa pouye gris bordeaux pape bouba diop khadim diallo douniou ay ndiol ? modou da meussa beurrè ak koumou tollol taille ?
@@layekharagne2224 Mais frère Issa pouye mou ragal door momou ngay tekeleu ak lourds yii tamite 🤦🏽♂️. Gris j8 d’ accord Mais Gris soutoul Modou lou beuri comme Balla, Bomb, Tapha te Gris 4 appuis lako Modou daner sen 2e combat bi. Nangoul tamite frère ton lutteur a tjrs des difficultés avec les lourds yiko eup masse ak rallonge.
@@papadiom9260 il a des difficultés avec les lourds mais en 18 ans de carrière il a seulement 3 défaites et seul 2 lutteurs l’ont battu , donc Modou sou amoul wone problème ak lourd yi founiou dieum 😂modou est vraiment le meilleur lutteur de l’histoire, eumeu sa mbeur nane la dané bombardier 2 fois dou 4 appuis ? donc lui aussi il a problem avec les lourds selon ta logique.
@@layekharagne2224 Non Mais Eumeu ak Modou bokougn ndokhtou beurer thi lourds yi. Eum a appris à lutter contre les lourds depuis l’ âge de 17 ans te en plus il a fait le greco mo tax mu meuna dane Balla, Lac 2, Gris bagnou tokk parcequ’ il les impose la lutte sans ngimb et y’ a pas une grande différence de poids entre eux contrairement à Modou. Et aussi Eumeu avait eu les mm difficultés contre Bomb aussi Motax fakk ko mou reup rekk lathi wout Mais bougn tolo wone touti dafkay tiaxabal. Modou kaay Bou tolone nii ay Bombardier moy raaw Bomb dina fii door mbeur mou dhee ndakh dafa sokhor 😭😭😭
C’est la vérité
Kiii se soit! 😂😂tapha way
Tafa tine ❤❤❤❤
Merci tapha bonne chance