Champion d'Afrique Nigeria résultat 3 pour Sénégal et 2 pour le Nigeria eumeu est champion d'Afrique mêm si on l'a battu c'est un champion d'Afrique par équipe il a reçu la médaille d'or par équipe
Franc c'est un champion d'Afrique parce que les équipes qui participent la CEDEAO c'est les mêmes équipes qui participent le champion d'Afrique on a juste changer le nom depuis lors on ne parle plus de champion d'Afrique on parle de CEDEAO c'est ça la différence mêm les règlements ont changé
Même yekini vice champion du monde en lutte grecroméne en Afrique du Sud c'est le seul lutteur sénégalais qui a un médaille d'argent au champion du monde en individuel
Maintenant les choses se sont retourné sur lui franc tu as marqué contre ton camps sokhor bakhoul eumeu molà meunn allez retour... Taaa lilayy yarrr moungui gnew 😊😊😊😊😊
Fii yalla fi nêk. Eumeu sêne mo beuri combat diankhe dji Niarry combat yi dakh si arêne bii Eumeu sêne vs gris bordeaux Eumeu sêne vs modou lô Lodoul yalla nêne Khalei dafay yarrou
Franc danga beguone weer Eumeu mais Yaw ya weerou. Adouna ngui nii nit danga koy nangoul Li Yalla def ci mom même boula nekhoul. Eumeu Sene dafa def lou niep tek sen beut té carrière bimou def guemouma nga def ko mola dakk beuré aller-retour Va et vient ak Est Ouest Nord sud ak côté yi 😂😂😂😂😂
@@sidibarhamatraore293 bro esk kham nga bou wakhone ak respect Eumeu amoul problème bobou pour may ko chance, c’est un releveur de défi en plus kou may SaThies chance daneko do moytou Franc
De toute façon eumeu lors de se championnat il a perdu deux combat avec la même personne en équipe et en catégorie de poid c’est la que franc di que il n’est pas championnat d’Afrique
Entraîneur pdt 45ans Ki rek mo am tt les mérites du Sénégal bilay mane ki dama ka fan di kou am gueum gueum beuk reiwam bounou meusona gagner hargn bi ngay guiss si mom dalay beugulo si ay bakam ay toucham ay conseiller yi si lepp lika warr kep koumou former yalla maynako étrange tay lolou moy alkhamdulilah yalna sa diam yaag ambroisie sarr le journaliste aussi c mon fan je le suis il pose d questions respectueux il dit tjr du bien aux uns et aux autres ns vs remercions de tt nos❤ Mai louway wakh wakh eum ak franc koumou neikh koumou nakhaŕi combat la ❤❤❤❤❤❤❤combat derr combat diankh ❤❤❤❤❤❤❤
À l'époque le championnat d'Afrique de la lutte regroupait plusieurs pays africains alors championnat de la CEDEAO cela concerne que les pays de l'Afrique de l'ouest donc il y a une grande différence de niveau et de valeur entre les deux titres. Eumeu Sene demeure un grand champion de lutte. Ceci étant dit il doit pouvoir accepter de lutter avec franc ne serait ce pour lui donner une leçon de lutte et il peut le faire
Suggestion au présenteur la prochaine fois il faut au préalable discuter avec celui qui doit apporter des éclaircissements pour qu'il puisse vérifier toutes ses archives afin de répondre de façon plus précise. ( En donnant les dates exactes, le nombre de victoires, les adversaires battus, les catégories...)
@@mbackegaydelserignembacke8335n'importe quoi il ya même les marocains tape sur Google championnat Afrique 2013 en Tanzanie. Tu mélanges tout fran c'est lui qui confond la cDEAO et l'Afrique. Car en 2015 c'était au Congo
Je suis dans une joie immense. Franc n'a pas été sympa il voulait humilier Eumeu Sene et le traiter de menteur au yeux du monde mais heureusement Dieu ne dort pas, il a rétabli la vérité par la bouche de tonton Ambroise Sarr.
Ay bi gathié tay limoy yené Neg la Borom mosay fanane franc yak say fans yu rew sen wakh bou bari bi yeup nakaté yen sakh dolen champion d’Afrique champion cedeao la🤣🤣🤣🤣 no yalla dou nitt vrai karma mongui ni legui kou doulone na diar fimou diarone defarat ay doulam si ndiek na😂
Mbeure bou gueuna yarou si vip moy eumeu sene motakh ma beug ko kou d’accord rek lalal jaime
Eumeu sene champion d'Afrique
Franc do champion d'afrique 😅😅😅😅😅🇬🇲🇬🇲🇬🇲 merci per ambroise sarr 🥰🥰🥰
😂
😂😂😂😂😂😂Franc momene féne deh
Merci père franc respecte eumeu sene❤
Eumeu yalla naala yalla may ndam li dess si sa lamb
amine frr💚❤️💚❤️💚❤️
Allahou ma amiiine waye
🤲🤲🤲
Amine yarabine
Amine
Père embroise sarr mérite toute la gloire.
Euma wakhkatou deug la té limou def si lamb il mérite du respect
Bilahi
Li rék warna takh nite baña sokhoré sa morom, toujours kou beug soufél sa morom yalla molay soufél
😂😂😂 Bilahi wakh nga deugg.
Sénégal leegi Fenn soss toumal manipuler rek mofi am
C'est tout à fait vrai
Eumeu séne❤❤❤❤❤
Franc mossoul nék champion dafrique eumeu séne vrai champion dafrique
Champion d'Afrique Nigeria résultat 3 pour Sénégal et 2 pour le Nigeria eumeu est champion d'Afrique mêm si on l'a battu c'est un champion d'Afrique par équipe il a reçu la médaille d'or par équipe
Franc c'est un champion d'Afrique parce que les équipes qui participent la CEDEAO c'est les mêmes équipes qui participent le champion d'Afrique on a juste changer le nom depuis lors on ne parle plus de champion d'Afrique on parle de CEDEAO c'est ça la différence mêm les règlements ont changé
Lolou sakh mooy champion d'Afrique.
Même yekini vice champion du monde en lutte grecroméne en Afrique du Sud c'est le seul lutteur sénégalais qui a un médaille d'argent au champion du monde en individuel
@@abibkeita7447NON. NON. LA. CEDAO. 16. PAYS. REK. LA. TÉ. TCHAD. BII. PAABI. DI. WAKH. BONOUL. CEDAO
@@abibkeita7447 gambie. Guinée. Bissau. Ak. Mali cote d ivoire. Guana. Nnigeria. Burkina , senegal . Niger cape vert Togo. Bénin. Sierra. Leone Libéria. Lii. Rek. Moy. Cedeao
Franc dou sarap ndm ba paré beuri wakh😂😂😂😂 Eumeu sene champion par force❤❤❤❤❤❤❤
Wouy dé na😂😂😂
😂
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
13 combat 13 victoire 🤴🥇
Thanks for the clarification uncle
Eumeu champion d'Afrique ❤❤
Maintenant les choses se sont retourné sur lui franc tu as marqué contre ton camps sokhor bakhoul eumeu molà meunn allez retour...
Taaa lilayy yarrr moungui gnew 😊😊😊😊😊
Eume mérite beaucoup de respect
Eumeu sene mon champion yalla nala yalla Defal diam mon champion eumeu 🎉🎉🎉🎉💪💪
Franc souye wét di kharou
Ded way 😂😂😂😂😂
Da fekk gnou changè tour competition bi lolou rekk moy difference bi
Non dou kharou njak djom ladef il va préparer un repli 😊
Franc doff la weroul
Franc do champion d'Afrique kone 😢😢😢😢😂
😂
Cedeao c’est Afrique
Non ses pas d’Afrique car ces pas tt les pas afrik ki sont ok là-bas
@@peterdieye5858kone AES moy Afrique
Eumeu yallana ko yalla dolí sútúral
Merci père Eumeu a tenu les mêmes propos dans son dernier interview avec Lamine lutteTv
Merci beaucoup père eumeu seul 🎉🎉🎉
Tay sama khôl bi séd na bilahi
😂😂😂😂ani wa franc yii
MERCI BCP
Eum le grand champion respect à vs ton nom est indélébile dans la lutte Sénégalaise❤❤
Ay fran Yama bett😭😭Eumeu Séne balma akh😂😂
Bizarrement wa franc yi guisouma kene si commentaire yi 😂 bilahi yalla meuna até 🤣🤣🤣
Dagnouy waaaff 😂😂😂
Bilaye yena sokhor 😂😂😂 Amelene soutoural 😂😂😂
Dougnou fingne féne
Gathié😂😂😂😂
Yalla rek mo woor.
merci beaucoup Pere Ambroise Sarr pour les eclaircissements et felicitations pour ton beau travail a l equipe nationale
Li warna takh adouna nitt def nank fran eum sa grand la je pense meun nga beurei ak mom leip si yar
Wayyyy Sama khol Bagui melni wanagou Mbotou ❤❤ frane Loy wakha wa Cogne ba😂😂😂😢😢
Fii yalla fi nêk. Eumeu sêne mo beuri combat diankhe dji
Niarry combat yi dakh si arêne bii
Eumeu sêne vs gris bordeaux
Eumeu sêne vs modou lô
Lodoul yalla nêne
Khalei dafay yarrou
😂😂😂 alhamdoulilakh rabil al amine tieuy bi gatié
3:15 😂😂😂😂Franc du champion d' Afrique..Big mouth..thanks for the clarification.
Eumeu sene ❤❤❤❤❤
En Résumé, Eumeu Sène ligue des champions la dieul alors que Franc Conférence League la gagné 😂😂😂😂😂😂
Magui ram
@@Ibrahimafall-cz9vj Père Ambroise Sarr yalnafi yague té werr
😂😂😂😂ray ngama
Thank you 🙏🙏🙏🙏🙏💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽💚❤💚❤💚❤💚❤💚❤💚❤💚❤💚❤
😂😂😂😂💚♥️✌️
Merci pere
Fran dou champion d'Afrique 😂😂😂😂😂
Yall mon merci beaucoup eumeu dam.rek
Franc danga beguone weer Eumeu mais Yaw ya weerou. Adouna ngui nii nit danga koy nangoul Li Yalla def ci mom même boula nekhoul. Eumeu Sene dafa def lou niep tek sen beut té carrière bimou def guemouma nga def ko mola dakk beuré aller-retour Va et vient ak Est Ouest Nord sud ak côté yi 😂😂😂😂😂
Non franc dafa def Erreur bou reuy.
Il devait respecter Eumeu Sene niane ko chance si ndieke mo geun yeufou dof yimou def
@@sidibarhamatraore293 bro esk kham nga bou wakhone ak respect Eumeu amoul problème bobou pour may ko chance, c’est un releveur de défi en plus kou may SaThies chance daneko do moytou Franc
@@ibrahimaseye7267 bilahi DEUG leu mon frère Franc mom dafa yahkal bopam dans ce cas na dem kholi fenen temou bayi Eumeu Sene.
De toute façon eumeu lors de se championnat il a perdu deux combat avec la même personne en équipe et en catégorie de poid c’est la que franc di que il n’est pas championnat d’Afrique
lamb dou dine nopilen ndm
Entraîneur pdt 45ans
Ki rek mo am tt les mérites du Sénégal bilay mane ki dama ka fan di kou am gueum gueum beuk reiwam bounou meusona gagner hargn bi ngay guiss si mom dalay beugulo si ay bakam ay toucham ay conseiller yi si lepp lika warr kep koumou former yalla maynako étrange tay lolou moy alkhamdulilah yalna sa diam yaag ambroisie sarr le journaliste aussi c mon fan je le suis il pose d questions respectueux il dit tjr du bien aux uns et aux autres ns vs remercions de tt nos❤
Mai louway wakh wakh eum ak franc koumou neikh koumou nakhaŕi combat la ❤❤❤❤❤❤❤combat derr combat diankh ❤❤❤❤❤❤❤
Merci à Ambroise.
Yeep leerna legui, Euneu Sene champion la.
Franc hamal loyy wakh..
Mom sah dou champion d'afrique copin😂😂😂 loloula pabi wahdééy😂😂😂
Franc looye wahe waa cogne ba
Moma diakhal
Khana dama féne
Miss CDEAO 😂
@@ngordiouf6064😅😂
Franc champion kogn la hahahah😂😂😂😂
Franc champion d Afrique de l ouest !
Merci père
À l'époque le championnat d'Afrique de la lutte regroupait plusieurs pays africains alors championnat de la CEDEAO cela concerne que les pays de l'Afrique de l'ouest donc il y a une grande différence de niveau et de valeur entre les deux titres. Eumeu Sene demeure un grand champion de lutte. Ceci étant dit il doit pouvoir accepter de lutter avec franc ne serait ce pour lui donner une leçon de lutte et il peut le faire
Merci père ñi don wakh yeup diñan nopi
Khana lérna nagne franc eumeu dousa morom
Suggestion au présenteur la prochaine fois il faut au préalable discuter avec celui qui doit apporter des éclaircissements pour qu'il puisse vérifier toutes ses archives afin de répondre de façon plus précise. ( En donnant les dates exactes, le nombre de victoires, les adversaires battus, les catégories...)
lérna nagne mon pére fran do Champion d'Afrique eumeu séne moy champion d'Afrique
Eumeu🎉🎉❤sene❤❤🎉❤
Merci père Ambroise
Euma sèn deug rk❤
Dofdouwer❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Franc do touss❤️💚
❤ RESPECT EUMEU❤
Nice
Eumeu rouslo woniou mouk
😂😂😂😂😂😂ah Dedete Kay doumako lalllll
😂
suis pikinois ms batay leroul💚
Con mécontent ga doto si am Lou l'aire dé 😂😂😂😂😂
Wa yaw thi sissou mane yi nga bok
Eumeu séne Amna ngeureumou waadjiour 😂😂😂 kénn duko troxal 😂😂
😂😂😂FRANC dal ndéké CFA laa😂😂😅
😂😂😂😂😂😂😂😂
Ambroise Sarr honnêtement tu déconnes, Franc a parfaitement raison Eumeu dou dara
Da done wèratè far wèrou ndèkètè mome monèkoul champion d Afrique eumeu yaye champion d Afrique
Eum c’est mon lutteur mais il doit arrêter de dire douma beurré ak yaww c’est la lutte 🤼 franc il provoque c’est la Charme de lutte
Lolou mom deug laa kw ! Dafa wara bayi di gawa guiss bopam kw! Kholal Eum gnimou done andale gnep kene nekatou fii… Tyson, Jordan, Tyson 2 etc…
waw mais nak franc dafko xawa manque de respect motax eumeu champion la nakoko nangoul rek
Mamadou Ali Ndiaye damako deugeu rk dafa yarou❤
1er
Péé
Wouy champion CEDEAO kay frand kay wouyou fi 😂😂😂😂😂
Champion d'Afrique amatoul legui CEDEAO mo am
😂😂😂 wa ana Fran cdeao😅😅😅
Bilahi kham nane franc Dou champion d'Afrique champion CEDEAO Na bayi wakh bi rek grand bi mayko chance lolu Moy yon
Benue la rk cedeao goroup lathi africk pska beure bi dou africk guep niokoy def yenue deuk lathi rk faranc dall champions dafrick la nio yam rk pska dou africk guep nio thiye beure
@@mbackegaydelserignembacke8335Sawaay ragalal Yalla mba nga dem guestu dji
@@mbackegaydelserignembacke8335n'importe quoi il ya même les marocains tape sur Google championnat Afrique 2013 en Tanzanie. Tu mélanges tout fran c'est lui qui confond la cDEAO et l'Afrique. Car en 2015 c'était au Congo
saway mano wakhe bam yam ah donté sakhe béne rew la mangui ah bayiléne séne,thiakhane yi
@mbackegaydelserignlol lol boul wout justification bokoul 😂😂😂embacke8335
Eumeu yaye ndanane
No no li dou mako lal 😂😂fra oh My good😂😂😂😂😂😂😂😂
Lerna eumeu sene moy champion dafrique mer per❤❤😂perhaps
Eumeu Sene grand champion du monde
😂😂😂😂xaral ma nopi manou rek mayé patteuh bi 😂
Farnc bouy wete di kharou 😂😂😂😂😅😅😅😅
C'est clair
Merci coach franc da sokhor
But contre son camp franc 😂😂😂😂😂
Plus carton rouge😂😂
@@MoFort-by3su 😂😂😂😂😂
Plus cogner sa tête sur le poteau accompagné d’ un carton rouge !
😂😂😂😂 CSC bi😅😅😅
Sarap li way😂😂😂
Je suis dans une joie immense. Franc n'a pas été sympa il voulait humilier Eumeu Sene et le traiter de menteur au yeux du monde mais heureusement Dieu ne dort pas, il a rétabli la vérité par la bouche de tonton Ambroise Sarr.
Yalla atté naa deh
Ay bi gathié tay limoy yené Neg la Borom mosay fanane franc yak say fans yu rew sen wakh bou bari bi yeup nakaté yen sakh dolen champion d’Afrique champion cedeao la🤣🤣🤣🤣 no yalla dou nitt vrai karma mongui ni legui kou doulone na diar fimou diarone defarat ay doulam si ndiek na😂
Magui dé bilaye 😂😂😂😂😂😂
Eumeu sen rék❤❤❤😂😂😂
Non eumeu sene moy real madrid champion d Afrique ❤❤❤❤❤
Wouy Magui contane 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Franc ndèkètè d’où gatte
Franc do champion d'Afrique 😂😂😂
Franc loy wakh wa kogn ba😂😂😂😂😂
Khana 12 naaa😂
Franc dou champion Afrique
Pa Bii dafa Sokhor Franc champion d'Afrique individuel et par equipe❤❤
Khana dedete kay 😂😂😂😂😂 franc kone champion de communauté rurale leu 😂😂😂😂😂..
Non non soubhane allah....wallahi le reducul ne tue pas
😂😂😂
Eeeeuy wa dji 😂😂😂diéguel lèn ko rék
@@amdydiongue-k1n li nak moy remontada 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
😂,,,😂😂😂😂😂😂
❤❤
Pour plus de professionnalisme il faut avertir quelques jours ou heures avant celui qui est censé apporter les éclairages
Fans franc yi ana nguene 😅😅 khana danguene dèm voyage 😅😅
Franc mo deug ndem 😂😂😂
Franc na am yar Eumeu moy sen chef
Champion CEDEAO😂😂😂😂😂😂
Franc mo meuneu fenn😂😂😂
Delenn invité Père Amb ci plateau yiii