C'est que dafa am yeenë sénégalais you soxor ku dem représenté rewëm ñëw même wa rewëm ñooy taxaw naan ko doo champion nanu baayi soxor et puis nitt bëggë bërre waroul taxx ngua koy manqué de respect buleen lambu boolee nak meune ngua wakh laan te ak moom. Respect champion eumeu t'es une légende sur ce sport
Le lutteur le plus talentueux de tous les temps... Le lutteur qui fut le grand terreur des mbapats dans toutes les banlieux du Sénégal, Le lutteur champion d'Afrique avant l'âge de 20 ans Le lutteur de l'ONU Le lutteur Roi des Arènes Le lutteur le plus constant au Sénégal physiquement et techniquement. Le lutteur des ministres, députés, DG et présidents de la république Le lutteur des chanteurs Le lutteur de tous les confrérie musulmans et chrétiens Le lutteur des anciens gouloir Le lutteur des professeur, Médecin, bureaucrate et ouvrier Le lutteur des cas sociaux Un grand légende. Enfin Le lutteur de tous les continents. Mes respects EUM
Waye eumeu diu champion d afrique waye video yi gñièpa guis nanouko gñou dane ko gñiari yone 😂😂😂 eumeu mome si bôpame kham nani bou dof dof lo baa dieule franc moye domou retrétame eumeu lou yomba laye woute té sa thies sakh danoulo ko
J'estime trop franc mais il est est trop arrogant deugu nékhoulll ki moyy eumm la légende vivante de la lutte kouko khaamoull dégu nguaakooo yaaaguiiii soguaa feulll franc donc respect au grand même soufèké danguako khepp amall diaamm rekkk
Eumeu rekkkk jusqu'à la fin gnila beugoul ay nonnnn lagnou Mouno def louléne nekh aduna nonoula fans Ak non mofi nek depuis l'antiquité athia domou djola bi Ak sérère gni wah nagnou khar bo def Liga def de 17 an a 43 ans vive tysinger❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Gnoune pikine lagnou deuk 💚❤️💯 T moy Sénégal 🇸🇳 thiowou rois des arénes ak champions Afrique. Miss nagnou ko 😂😂 atouka gnoune. Dieul nagnou 🦍🦍🦍🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️
Nicena mbeur boul falé champion piir c'est le travail qui paye n''écoute pas les gens c'est ce que tu fais après c'est fini la vie continue vrai champion d'Afrique les jaloux vont maigrir votre fans depuis Belgique Bruxelles from ourossogui
Franc d'Italie li gnou yaw fi la quench yenou la Door ci souf nganna yako raw khana kone do champion ci kanamam eumeu sene au moins nekna roi des arènes respect way boy
Xaragne lo le populaire Le plus teknik. Le plus grand bagarreur de la lutte sénégalaise. Modouuuuuuuuuu looooooooooooo ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
Wakh ci cadre lamb ak communication bou bone bokoul Franc vrai dofla fi la nekon nane reug reug pap nga danne bouma danon Bombardier douma jubiler ci soubasa mou dieul avance sam tey mou beug nio fat
Denka ragal rek....la declaration de Franc dou raison nga bagna beuré ak mom...denga amoul si mom pékhé rek eumeu😂 Franc mono ko teré mou combat...Dakh légui adversaireyi libre
Mais quelque soit le gravissime de la déclaration de Franc, il a prouvé et avec bravoure, donc l’éviter c tuer le soort … sportivement Franc c l’adversaire idéal mais c dommage on peut forcer personne…
Le lutteur le plus talentueux de tous les temps... Le lutteur qui fut le grand terreur des mbapats dans toutes les banlieux du Sénégal, Le lutteur champion d'Afrique avant l'âge de 20 ans Le lutteur de l'ONU Le lutteur Roi des Arènes Le lutteur le plus constant au Sénégal physiquement et techniquement. Le lutteur des ministres, députés, DG et présidents de la république Le lutteur des chanteurs Le lutteur de tous les confrérie musulmans et chrétiens Le lutteur des anciens gouloir Le lutteur des professeur, Médecin, bureaucrate et ouvrier Le lutteur des cas sociaux Un grand légende. Enfin Le lutteur de tous les continents. Mes respects EUM ❤❤
C'est que dafa am yeenë sénégalais you soxor ku dem représenté rewëm ñëw même wa rewëm ñooy taxaw naan ko doo champion nanu baayi soxor et puis nitt bëggë bërre waroul taxx ngua koy manqué de respect buleen lambu boolee nak meune ngua wakh laan te ak moom.
Respect champion eumeu t'es une légende sur ce sport
Billahi man lolou la nit ko demna mem amoul won sakh ken warouko khas wakhou malak ko kham ne amna
Franc day Nexal rk guén di mer 😂😂💔
fran Limou wakh c la vérité il n'a pas gagnée c tt c k fran a dit les vidéo sont partou
@@abdourvms6034no sénégalais rek aka émotif 🤣🤣
@@kanebabacar-wv3uj sénégalais xamul kouy foo kw 😂😂🤦🏾♂️
Le lutteur le plus talentueux de tous les temps...
Le lutteur qui fut le grand terreur des mbapats dans toutes les banlieux du Sénégal,
Le lutteur champion d'Afrique avant l'âge de 20 ans
Le lutteur de l'ONU
Le lutteur Roi des Arènes
Le lutteur le plus constant au Sénégal physiquement et techniquement.
Le lutteur des ministres, députés, DG et présidents de la république
Le lutteur des chanteurs
Le lutteur de tous les confrérie musulmans et chrétiens
Le lutteur des anciens gouloir
Le lutteur des professeur, Médecin, bureaucrate et ouvrier
Le lutteur des cas sociaux
Un grand légende.
Enfin Le lutteur de tous les continents.
Mes respects EUM
Damala Beegeu Téral ❤❤❤😂😂
Bou Tabaski ki passé nala térale 😂 instant bi dépenses yi mo bari😂😂😂
Do wakh mouk palmarèsaam😅😅😅
12 victoire
10 défaite
2 nul
1 sans verdict...
Palmarès franc
13 victoire
13 combats
Palmarès Modou lo
23 victoire
3 défaite
1nul
..,..
Palmarès
😅😅😅😅😅 ligua wakh yeup si bayam kharagne lo la nékeu😂ki ragalla boye na dieul fren boudé deugue le
Borom 11 defaites yii😂😂😂😂eumeu le lutteur le plus populaires
Eumeu yalla nalla Yalla Defal Diam
Boul nekoul champion d’Afrique, nék na roi des arène boulén niou sonal❤
Eumeu Séne champ' d'Afrique kúka banie sa xõl ame na fébar
Waye eumeu diu champion d afrique waye video yi gñièpa guis nanouko gñou dane ko gñiari yone 😂😂😂 eumeu mome si bôpame kham nani bou dof dof lo baa dieule franc moye domou retrétame eumeu lou yomba laye woute té sa thies sakh danoulo ko
@@almaktoumdiop8749 lima layi wakh mouyi Sa xõl bi wallahi dah ame fébar dùma wakh Ac yawú Ndakh bõné Eumeu danoul sa Thiès la pré si yawoù 🙏
Franc na dém ci moromam yi xana dafléne ragal ?
@@TheBlackCoton franc nokha moromane yépa déme dabe Bombardier gñiari yone si béna gone ganane
@@almaktoumdiop8749 bombardier bii nii di wout xaliss , xalé bouko daane di jubiler dagua niakk diom, franc loumouy daw reugu reugu, serigne ndiaye, alune seye ? Wala guissouléne ?
Eumeu sama mbeur yalnaniou yalla wanélé rk man mame sidy TAMBÉDOU iow rk la beugue so amé combat damaye sonnou pour nga am ndame
Eume sene yaye lamb respect
ioe yabaté gua dh kii am 12 victoires 9 défaites guanii mooy lamb ?😂
@@Babacar14 kii gnimou daane nieup nio meune boy franc, mom xana lamb dji amoul bénéne boudoul eumeu !? Na dieul moromam yi niou xoll
Merci Eumeu Sene 🫶
J'estime trop franc mais il est est trop arrogant deugu nékhoulll ki moyy eumm la légende vivante de la lutte kouko khaamoull dégu nguaakooo yaaaguiiii soguaa feulll franc donc respect au grand même soufèké danguako khepp amall diaamm rekkk
Merci eumeu on contant Mane biss bo accepte beurre ak franc yalla nala ray boul meussa beure ak koula sokhoré sa carrière
VRAIMENT EUMEU SENE JE SUIS TRÈS TRÈS CONTENT DE VOUS PETIT FRÈRE, TOUS SAUF FRANC DAFA REW ,INIANE,SOKHAR,DAFA WAAY....
Eumeu rekkkk jusqu'à la fin gnila beugoul ay nonnnn lagnou Mouno def louléne nekh aduna nonoula fans Ak non mofi nek depuis l'antiquité athia domou djola bi Ak sérère gni wah nagnou khar bo def Liga def de 17 an a 43 ans vive tysinger❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Un très grand champion Euma sène très bien communications de ta part masha Allah mayal chance gris 2 combat bou nekh na Diadieuf champion
Eumeu que tú soit Champion dafrique ou champion de boudiouman on sen fouu nous on taime champion ❤❤❤
Maÿi léne ñu diamou Moustapha Namm champion d'Afrique leu❤😂😂
Wa legui dolene deme beure ak champion d’Afrique yi ngene bayiko mou tok 😂😂😂
😂😂😂😂😂
Bilahi té jouéwoul béneu match
😢😂😅
Bilaye ya am inspiration ❤ dafa am gnou soxor lole vamos eum
Merci le roi des arènes pour les éclaircissements Eumeu seul laniouy toppou 💚💚♥️♥️👑🙏🙏🙏
Dp8 quand il est roi des arènes
@@boumysagne9695 c t en 2018 face à Bombardier
Gnoune pikine lagnou deuk 💚❤️💯
T moy Sénégal 🇸🇳 thiowou rois des arénes ak champions Afrique. Miss nagnou ko 😂😂 atouka gnoune. Dieul nagnou 🦍🦍🦍🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️
Waaaa loolou môme faw niou nangoul lako yafi gueune métti parcour gueune fi raféte ay combat combat dér deugue 👏👏👏
I'm huge balla gaye 2 fan but I've maximum respect for the legend eume sene
Eumeu le grand champion
Merci champion pour la communication, toujours correct
Kou geum ni eumeu champions d'Afrique la lalal j'aime ❤❤
Dou bn champion d’afrique
@@daoudader4641 dette wayy
Wa legui bo demai coupe d’afrique, sa equipe gagner, dou champion d’afrique? Yène khawma gniak logique molene dal oubien gniak degue français
@@MrOusmane23 pourtant manak yaw nioy bokk wax dh frère
No daoudader4641 la done wakheul walay, yow mane ak yow gnio far. On a les mêmes points de vue. Mais daouda dèfiant le , dafay kagnio eumeu sene koi
Eumeu séne meilleur lutteur derrière yékini❤️❤️❤️
Merci bcp Eum le grand champion yow ndanann nga machalla suis vraiment fière de vous bien parler ❤❤❤❤
eumeu nak bagna dieul fran amo si bene argument on t aime bcp votre combat s impose
Vous avez tout mon respect champion ton non est indélébile dans la lutte Sénégalaise Yalna sa diam yagggg Eum le grand champion ❤❤❤❤
Nicena mbeur boul falé champion piir c'est le travail qui paye n''écoute pas les gens c'est ce que tu fais après c'est fini la vie continue vrai champion d'Afrique les jaloux vont maigrir votre fans depuis Belgique
Bruxelles from ourossogui
Eume contane ci yaw vraiment champion gua goudou fane wërgou warame
❤❤yawe rek lagnouye tope sounou champion incontestable
Franc dokhal fowi beurré wougnou ak yaw ❤merci eumeu boul co dieul na wakh louco nékh
Franc boul wakhati si ki yoroul sa weurseuk niemh woula xolill lenenn bro champion gua ❤❤❤🎉
Fran Yall nako Yalla samou
ءامين ❤❤
Na am yar ak Téguin réwanée Bakhoule
@@elhadjicheikhba4122 lolou sa gatt nekousi
😂😂😂 wakhléne franc mou réglé Rek tek waneko yone. Bii 🧏♂️pikine deuk leu💚❤️💯🧏♂️🧏♂️🧏♂️🧏♂️🦍🦍
Merci beaucoup eumeu sene tay singo 💪💪💪💪💪♥️🥰❤❤
Eumeu yow ndanane ngua champion ngua ❤❤ kénne meunouko nattablé❤❤❤
Eumeu❤❤❤❤❤❤
Eumeu une autre dimension ❤
Franc d'Italie li gnou yaw fi la quench yenou la Door ci souf nganna yako raw khana kone do champion ci kanamam eumeu sene au moins nekna roi des arènes respect way boy
Lolou douko wax deii franc bleu le si kanam Eum😂
Do bayi fen
NDIAGO ORBI REK INSALLAH 🎉🎉❤❤
Eume sene c'est un grand champion franc c'est un jeune champion il doit être clame
Merci eumeu ❤bul musa beure akmom
Sa khol mo gueune rafete si mbeuryi ❤
Eum diambar la koi crieu kholko rek Ak age bi Machallah 💯
Eumeu yalla nalla yalla defal diam
Merci eumeu boul beur ak môme defa rew
Champion d’Afrique guey bagna dègg mais par la force diguako dègg do champion d’Afrique
Ama noum defon modou lo rek😂😂😂
Moustapha Name champion d'Afrique la té meussoul jouer match can
Ya daaane sama mbeur Balla gaye mais tu es un vrai champion nanguou yakoulll sounou palmarès dara ayyythiaa Eumm tay shinger❤❤
Danga daw combat 🤣 bii c tout 😂😂 barké yallah saway fii amoul tapalé amoul négocier roi des arènes 9 défaite 😂😂
Thank you bro ❤❤❤❤❤
Xaragne lo le populaire
Le plus teknik.
Le plus grand bagarreur de la lutte sénégalaise.
Modouuuuuuuuuu looooooooooooo ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
Wakh ci cadre lamb ak communication bou bone bokoul Franc vrai dofla fi la nekon nane reug reug pap nga danne bouma danon Bombardier douma jubiler ci soubasa mou dieul avance sam tey mou beug nio fat
Eumeu sei troppo forte 💪🏿🦁🦁♥️
Merci bien dit
Merci beaucoup eumeu séne seul ✌️🙏
Yawe rék yaye gor billahi mala beugu mbour❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
merci beaucoup Eumeu boul beurei akk Franc dafa beuri nd.... wakh
Eumeu séne le vrai champion d’Afrique incontestable.
Merci beaucoup sampion ❤
Pour beuré ak grand yiii faaww nguaa diokh lennn thieur c'est la réalité mais koffiii waakh yenn yiiii mou sissou khoool ko sii sa booopppp
Quoiqu'il arrive tu es le champion d'Afrique.
Denka ragal rek....la declaration de Franc dou raison nga bagna beuré ak mom...denga amoul si mom pékhé rek eumeu😂
Franc mono ko teré mou combat...Dakh légui adversaireyi libre
Lamine vraiment professionnel nga ay question you am solo lay posé ❤❤❤❤❤
niémé wo ndiago bi dé
Merci Eumeu séné
Masaala amenasolo diadief ❤❤❤❤❤❤❤❤
Danga ragale franc rek 💪🏾lila modou Lo def louko rawe lalaye def papa sow nak lim wakhe dara nekousi tamit
Respect eumé sene est un très grand champion ta raison sa thies mongi si vip yi kou fi dieuma diokh boy yi wala diko wathié ma nokk la
Mais quelque soit le gravissime de la déclaration de Franc, il a prouvé et avec bravoure, donc l’éviter c tuer le soort … sportivement Franc c l’adversaire idéal mais c dommage on peut forcer personne…
Franc akk Eum Lamb saxx da lénn bolé woul franc naaa djieul Gris 2 ou SaThies
@@serignembengue2491 sii lamb bole nalen bu baxx
Modou lo a clairement evite Tapha tine pour aller prendre Siteu mais est ce que vous lui avez dit qu’ il a tue le sport ??
@@papadiom9260 c valable pr tt le monde mm sa thies n’aucune raison valable pour éviter franc
Sappiyoga bly 🥰🙏😭❤❤❤
Machallah le champion te le maître de lutte Sénégal ❤❤🤲🤲🤲🤲🤲🙏🙏
Merci eumeu bou bén vips dieul franc
champion nga machallah ❤️
Beugg may aliou seye chance ak guouye gui ak serigne Ndiaye après ngani do beurék franc eumeu Sene tappét ngeu niéméwo franc
Lan lay ragal si franc boy bi mo meunoul communiqué il doit du respect à ses aînés pour niou may ko chance
Je suis tt a fait d'accord avec eumeu sène vraiment ❤❤❤
Eumeu svp bou Gouy gui danné ada fass may ko chance 🙏🙏🙏
Katale sa ndaye faullé nékato sama mbeur fran eumeu moye combat
Nassa diam yag lol mbeur talentueux et respectueux
Merci em kontanna
Eumeu linga don kén meunousi Dara pére Amboise sarr léral na lép bravo champion diam si yaw rék
Merci Eumeu
Tu es un champion !!
Tu es le meilleur ❤❤❤Eumeu
Saway da ragal franc😌😂😂😂
Daffa ragal boy bi🤣🤣🤣
ioe weero😂😂
Merci Eumeu sene❤❤❤❤❤
eumeu sene ❤❤❤❤❤❤ mane yaw rek laye top ❤❤❤❤
Ndiago bi seleu
Eumeu ne veu plus lutter juste par ce que franc a mal parler...😂
Godo 🥰🎉
Merci eumeu b3kk si yow ❤️
❤merci eumeu
Eumeu je suis fier de toi boul beuri ak franc il parle trop tiyel fofou
Je suis de pikine mais eum sa meune gouygui ya meune alioune sey yak franc la beugue nga confirme franchement
Tapette gua rekk bouniou sonnal bo dieulé Franc daguay teudeu force
Eumeu séne le grand champion💪🏽💪🏽✊🏾❤️
Eumeu dh lima dall ci mom diakhal nama damako coumasé beugue ❤❤❤
Eume champion lepp rerna 💪
Eumeu yow fekei ma ci bolè😂😂 archive yagui fi tmt 😂😂 Franc NDIAGO OR bi domou Modou Kharagne Lo ❤❤ the Goat 👑 ❤
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤
Le lutteur le plus talentueux de tous les temps...
Le lutteur qui fut le grand terreur des mbapats
dans toutes les banlieux du Sénégal,
Le lutteur champion d'Afrique avant l'âge de 20 ans
Le lutteur de l'ONU
Le lutteur Roi des Arènes
Le lutteur le plus constant au Sénégal
physiquement et techniquement.
Le lutteur des ministres, députés, DG et présidents
de la république
Le lutteur des chanteurs
Le lutteur de tous les confrérie musulmans et chrétiens
Le lutteur des anciens gouloir
Le lutteur des professeur, Médecin, bureaucrate et ouvrier
Le lutteur des cas sociaux
Un grand légende.
Enfin Le lutteur de tous les continents.
Mes respects EUM ❤❤
Mdr😂😂😂
Eumeu champion la khol bou bakhol ❤bou bakh la yor
Merci bro domou pikine bi kase lay topou ème
Eumeu douma sa supporter mais vrai ndanan nga.