DIACKSAO 2015 - Le Gamou de Serigne Mbaye Sy Abdou axé sur Grandeur du Saint Coran

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 175

  • @sokhnacoulibaly6529
    @sokhnacoulibaly6529 6 років тому +5

    mane dale pape mbaye sy abdou yalla lalay bayel ylnag fi yaag di guindi ndaw gni dila deglou defna si mane lou bari yalna borom bi fayla yiww

  • @FREESO9229
    @FREESO9229 Рік тому +2

    machalah c'est un immense plaisir de vous écouter vous m'avez aider à être sur le droit chemin je ne peux pas vous payer

  • @ndeyeamindoye1150
    @ndeyeamindoye1150 9 років тому +32

    Sa takhaway rafetena thi diné ak tarikha bi sy malick yalla na borom bi gnody say fan defal diam ak tawfekhei thie sa barké mame

  • @fayekhady6536
    @fayekhady6536 5 років тому +7

    Machalah c'est toujours un plaisir de vous écouter .yalla na yalla gouddal sa faan sy malick .yalla may nu degg ak topou .vraiment koumma deggal dou deff loudoul beugg yalla ak topou souna souniou sangue bi (psl).

    • @fawadeseck1972
      @fawadeseck1972 2 роки тому

      0⁰00±

    • @DiarryDjigo
      @DiarryDjigo 6 місяців тому

      Man de mon ma khamal fou yala deuk AK fan là khéthe n'a niou may degù AK tope

  • @debboafrique719
    @debboafrique719 2 роки тому +1

    Machaalah. Sy. Yalana. Yala goudal. Faneyi. Toujours leçons you pertinente merci

  • @assanemaodombaye9656
    @assanemaodombaye9656 2 роки тому +2

    Diacksao 2014 ak 15 wakhtane yissi serigne defff meussou mako degue

  • @moustaphadjamilmbaye1461
    @moustaphadjamilmbaye1461 4 роки тому +1

    Sy yalla na yalla yok fane bi in sha allah beugue nala sama khol

  • @mamadoudiouf9385
    @mamadoudiouf9385 9 років тому +8

    serigne mbaye sy abdou;yalla na yalla doli la ta defal la lo beugue; DIOL FOUTA.; wala mbaye sy daara;yalla na yalla def gnou beugue la amine

  • @absatoure565
    @absatoure565 7 років тому +16

    machallah s Mbaye sy abdou ni rek nga mouna mele kouy sa baye s abdou aziz sy dabakh Malik kouy sa mame el hadji malik sy maodo ni rek ngay mele kewéle dou teup domdji beute

  • @omarhanne8240
    @omarhanne8240 2 роки тому +3

    Man dh talibe baye niass waye kou baugue sarigne Mbaye sy abdou machallla kou bakh kou baugue diné yalla gou dal sa fane sy ♥️

  • @fatimasy8854
    @fatimasy8854 6 років тому +22

    Machallah machallah...yo allah yobe seydi SY. Pour les gens qui dislik la video, que dieu vs vienne en aide et qu'il soigne vos coeurs, Inshallah.

  • @aidagueye569
    @aidagueye569 8 років тому +4

    machalahh sy yalla na yalla yagal tahaway bi cii barke cheikhna Ahmed tidiane cherif

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 5 років тому +2

    Machala serign mbaye sy Abdou yalana yalla goudal sa fann si barke seydina Mohammed (saw)

  • @aminata0485
    @aminata0485 9 років тому +39

    Ay Papa Mbaye Sy gnola beug!Dundeul Sy Malick,dundeul té yaag fi lol Sy!...

    • @mouhamedka4679
      @mouhamedka4679 7 років тому

      Papa yallah nagua fii yague lol ta adague werr si Barker cheikhou Tidiane

  • @laminegueye3954
    @laminegueye3954 4 роки тому +3

    walay li meunoumassi doyal ayway ayway ayway ayway yalla naniou yalla fayal maodo ak wa keureum 😢😢😢

  • @ibouthiaw6719
    @ibouthiaw6719 4 роки тому

    Machala si wahtanbi nehna trop mame yal gafi yague te were mame amine

  • @amadousow4730
    @amadousow4730 8 років тому +11

    man challah yalna yalla fayla serigne day matte serigne di didiglou baakh di tere lou bonne

  • @massyllandoye6677
    @massyllandoye6677 6 років тому

    ay mala beug yalla na dieule si yaw wird si barkep seydina mouhamad salla lakhou aleykhi wasalam kouka lir nel amine si barkem

  • @medounesarr4585
    @medounesarr4585 6 місяців тому

    بما جاء في الحديث القدسي، أنه قال الله تعالى: «عِبَدِيْ! لَمْ تَشْكُرْنِي إِذَا لَمْ تَشْكُرْ مَنْ أَجْرَيْتُ النِّعْمَةَ عَلَى يَدَيْهِ»

  • @oumarly7552
    @oumarly7552 4 роки тому

    Machallah Sy Malick kontan naniou yalla nala yalla défalla diamm wathioongén ak nioune nioun taalibéyi nioosi déss

  • @Zikrou-tv
    @Zikrou-tv 6 років тому

    Yalla na yalla yagual lafi souniou Serigne, yaniou guindi djioubanti niou. Yalla naniou yalla tass thi sa barkei. Amine

  • @sowaminata9659
    @sowaminata9659 8 років тому +1

    alkhamdulialhi rabil alamina manshallah kou léne gnaka woutilene manshallah xol sedatina yalna yalla goudal sa fane sy Malik ci Barker sanguou sanguayi salalahou aleyhi wa salam

  • @oumykadam4099
    @oumykadam4099 7 років тому +2

    Yalnala yalla faye souniou serigne souniou mame sy malick

  • @cherifaidara7141
    @cherifaidara7141 8 років тому +8

    encor merci papa serigne mbaye pr lei bn waxtane dont ta labitude d ns fer vreimen k dieu tacorde longue vi et santé de fer par la grace d ntre prophète seydina mouhamed (p.s.l)
    Amine !!!

    • @ibrahimadieye1019
      @ibrahimadieye1019 8 років тому +1

      Cherif Aidara CKHIEMBACKESAKHO

    • @ndeyeminguembengue8719
      @ndeyeminguembengue8719 4 роки тому

      Sy Malick yalla na gua yague diamono ande ake wére yague gno wétéli soute sognou Mame dja aye fane mashallah si barké seydina mouhamed psl yague fi lole choukrane sy❤❤❤❤

  • @oumykadam4099
    @oumykadam4099 7 років тому +4

    machalla sougniou papa sougniou serigne yalna yalla goudeul sa fann sy malick

  • @diopballa3671
    @diopballa3671 9 років тому +1

    serigien mbaye yalla yall defle koudou fat yer ya bakh

  • @oumousakho849
    @oumousakho849 9 років тому +8

    Euy way lii nexna way!!! Serigne Mbaye Sy yalla gua yague di gamou ak askan bi way! Dieuredieuf Sy!!

  • @KikishaFall
    @KikishaFall Місяць тому

    ay way noumay def ba guiss serigne mbaye sy abdou

  • @leuchleuch2902
    @leuchleuch2902 9 років тому +10

    Yalla naniou yalla def ay talibe cheih

  • @WAWA-xd9yu
    @WAWA-xd9yu 4 роки тому

    Barakal'Allah fikoum Yalna YALLA YOKEU sa martaba SY MALICK DABAH NIOU FÉKÉ AMINE IN CHA ALLAH

  • @mita7113
    @mita7113 5 років тому

    machala yallana yalla goudal fan yi mou and ak weer

  • @djibyfaye4057
    @djibyfaye4057 5 років тому

    machallah serigne Mbaye SY Abdou yalna la yallah yokou goudoufaan akk weur cii barké Seydina MOUHAMED PSL

  • @miinata2934
    @miinata2934 4 місяці тому

    Oh la suite Mashallah dolaniuyu

  • @khadiatoundao6605
    @khadiatoundao6605 7 років тому +2

    tabarakala yalnagnou yalla mey dégue akk topou.

  • @mamisow3477
    @mamisow3477 9 років тому +1

    Machallah yalla na yalla bayilafi nga yague dignou diokh khamkham

    • @momarka2005
      @momarka2005 9 років тому +2

      May Allah bless Serigne Mbaye Sy ibn Serigne Abdou Aziz Sy

    • @mamadoulo9268
      @mamadoulo9268 5 років тому

      Masahala yalna yala guoudal sa fane

  • @amyndiaye9652
    @amyndiaye9652 6 років тому +1

    Machallah yalla na yalla wéral té baayi léen fi lou yagg ngén niouy guinddi

  • @abousy5908
    @abousy5908 3 роки тому

    Sama serigne sama wassila machalla serigne mbaye sy abdoul aziz je t'aime fort blh wallahi

  • @taphagueye6484
    @taphagueye6484 9 років тому +1

    Machallah sy malick yallana borom bi same la mousseul la si thiat barkè serign babacar sy

  • @papaseye2003
    @papaseye2003 8 років тому +3

    sy ni ngay sedalé sa ma khol yalna ko yalla sedalé sa khol...

  • @talibecheikh1478
    @talibecheikh1478 6 років тому +1

    Machalah sy Malik yana yala goudal say fane

  • @sodaleye8686
    @sodaleye8686 4 роки тому +1

    Machallah sy kene dou seydil Hadji Malick Sy ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @babasane338
    @babasane338 4 роки тому

    Mashallah yal nako yala yokkou ay faname thé an dak weur si barké mame abdou

  • @ouzbeck3167
    @ouzbeck3167 3 роки тому +1

    qui est la en 2021??

  • @AliouSalifNiang
    @AliouSalifNiang Рік тому

    Machalla Ndiol Fouta Sy Sawade

  • @malickgueye2723
    @malickgueye2723 5 років тому +1

    Goud fan ak wer gui yaram Sy

  • @aminataka2668
    @aminataka2668 2 роки тому

    Sy yagu fi té weer

  • @khadijandao6772
    @khadijandao6772 Рік тому

    Serigne bi beugg nala ❤❤❤

  • @elhadjmactarfall1114
    @elhadjmactarfall1114 5 років тому

    Dieureudieuf Serigne Babacar Sy ibn Abdou Aziz Dabakh

  • @binetoudiakhate6759
    @binetoudiakhate6759 3 роки тому

    Yalnaga fi yague te wer macha Alllah

  • @talibecheikh1478
    @talibecheikh1478 6 років тому +1

    Walahi ma beugue te gueume te sope te nope te fire thi saydina cheikh Ahmed t idiane khoutboul maktom balzakhoul maktom borom tanjou hanrifina bilahi rta

  • @zakariadeune2296
    @zakariadeune2296 4 роки тому +1

    Ma challah kén dou mom

  • @diopballa3671
    @diopballa3671 9 років тому +3

    serigien mbaye yalla yall defle koudou fat

  • @oumykadam4099
    @oumykadam4099 6 років тому +1

    Machalla sy kholl yi sedena looll

  • @nounoursgirl4903
    @nounoursgirl4903 6 років тому +3

    Tel père tel fils MachAAllah

  • @assanekhoule2910
    @assanekhoule2910 8 років тому +5

    they MAODO yalnagnouko yalla fayal

  • @almanafih4889
    @almanafih4889 2 роки тому

    mashalah yalna yalla yok yiwe

  • @gassamaamadoumamadou
    @gassamaamadoumamadou 7 років тому +3

    serigne mbaye sy machallah

  • @famaraseydisarr591
    @famaraseydisarr591 2 роки тому +3

    Machalla c est toujours un plaisir de vous suivre en écoutant avec attention

  • @fofanadjibril1977
    @fofanadjibril1977 3 роки тому

    mashallah barakalha salemoualeykoum wramatulay ta là où❓

  • @tissadioum1390
    @tissadioum1390 3 роки тому

    Machallah on est content

  • @sophiamane5691
    @sophiamane5691 5 років тому

    yalla sougnou borom nangou niane amine

  • @khadymane1466
    @khadymane1466 5 років тому

    Machallah yalnalafi yalla bayi bassi canama cam sy

  • @MandaFoulbhé
    @MandaFoulbhé 4 місяці тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤حبيبي

  • @pendasowsow8748
    @pendasowsow8748 2 роки тому

    Saama khol ❤️ sédatina Saama wassilla ❤️

  • @bayeassanesall4577
    @bayeassanesall4577 5 років тому

    Yallanala Faye sy malick

  • @papadayasadikhbadiane4593
    @papadayasadikhbadiane4593 3 роки тому

    Amna solo lol Sy Malick yague fi

  • @aminatasene7779
    @aminatasene7779 9 років тому +1

    ma gui gnane yalle mayela goude fane bou andale wére ak wére lé nite kou bakh moguini kou diara roye

    • @biramediop1840
      @biramediop1840 9 років тому

      S erigne ya bak yala na yala faye yal bope te ma la were Mes condoléances grand, que la terre lui soit légère! C'est trop dure mais courage. Mes condoléances grand, que la terre lui soit légère! C'est trop dure mais courage?

    • @rosalieniakh9670
      @rosalieniakh9670 8 років тому

      birame diop

  • @djashkeub7231
    @djashkeub7231 6 років тому +2

    yana yalla yagale tahaway mou andeu akh wérr

  • @bilasarr7181
    @bilasarr7181 9 років тому +2

    Yalnagua dounou lollll sy malick

    • @rosalieniakh9670
      @rosalieniakh9670 8 років тому

      Bila Sarr

    • @rosalieniakh9670
      @rosalieniakh9670 8 років тому

      اللهم صل وسلم علا شيدنا محمد وعلا اله وصحبه وسلم تسليما

  • @masskhoule7130
    @masskhoule7130 8 років тому

    Macha alla amna solo loll yal na yague amine.

  • @amysarr9402
    @amysarr9402 5 років тому

    Ndeyesane Papa goudal fane.

  • @amycollembengue3531
    @amycollembengue3531 7 років тому +1

    dieureudieuf sy malick

  • @sokhnacisse6119
    @sokhnacisse6119 3 роки тому

    Machallah Sy Malick

  • @malickcisse1173
    @malickcisse1173 5 років тому

    wallihi mala beugue yalna yallah yokk sa takha way

  • @sambacoulibaly7888
    @sambacoulibaly7888 5 років тому +1

    Machalla alhmdoula

  • @aissatakante6805
    @aissatakante6805 5 років тому

    Machallah machallah wahdji rafetna merci 🙏

  • @khadygueye5933
    @khadygueye5933 7 місяців тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mademasow7589
    @mademasow7589 5 років тому

    Machalla sy malick

  • @yacinedieye5547
    @yacinedieye5547 9 років тому

    Ndeysan li nexna way yal nalen ya Allah takhawou

  • @moussaniang4702
    @moussaniang4702 6 років тому +1

    Allahu Akbar

  • @ndiayeawa8780
    @ndiayeawa8780 Рік тому

    ❤❤❤❤

  • @bounekhatab313
    @bounekhatab313 4 роки тому

    Maacha Allah

  • @idyndiaye2745
    @idyndiaye2745 9 років тому +1

    Amine na y alla barkel si Barney Moustapha psl

  • @thianeba5988
    @thianeba5988 4 роки тому

    Machallah s'y malick

  • @alyndiaye2508
    @alyndiaye2508 Рік тому

    ❣️❣️❣️❣️

  • @hcfhgf3482
    @hcfhgf3482 6 років тому

    Mane talibé cheikh la beug sokhna serigne bi

  • @rastamarle5290
    @rastamarle5290 6 років тому

    amine sy malick

  • @dienabadiallo9178
    @dienabadiallo9178 9 років тому

    bilahi mala sope sy goudal fane

  • @fatoundaw4097
    @fatoundaw4097 4 роки тому

    Amine yarabi

  • @cheikhtidianendiaye8729
    @cheikhtidianendiaye8729 5 років тому

    Mashallah Sy Malick

  • @barafall518
    @barafall518 8 років тому

    machalah li nékhna

  • @magoufal9351
    @magoufal9351 9 років тому

    ma bilahi dafama nekhe rek yana ko yalla maye were

  • @cheikhdiattara5632
    @cheikhdiattara5632 6 років тому

    Assalamou khalaykoum wa asfyakhi khana décodeur TNT douléne diappe

  • @moustaphasall8913
    @moustaphasall8913 8 років тому +2

    yalla nako faye hiw té yagal kofi lool lool

  • @manssourndiaye8806
    @manssourndiaye8806 9 років тому

    yalnafi yague t wére

  • @khadrediouf5566
    @khadrediouf5566 6 років тому

    Talibe cheikh rek

  • @MamadouDiallo-gw1qv
    @MamadouDiallo-gw1qv 3 роки тому +6

    MACHA ALLAH 🙏🙏🙏❤️❤️❤️

  • @famoushniang3498
    @famoushniang3498 6 років тому

    Machallah 😘😙

  • @diassysaliou8656
    @diassysaliou8656 9 років тому +1

    Sama xol dafa séd bilakhi. somako degue rek békkk

  • @amadousarr2383
    @amadousarr2383 9 років тому

    Merci mon dieu