Papay soda marème louche neu daal j'espère qu'il n'est pas de mèche avec sa fille 😮 Si oui Yaye Dior aura une grande déception " Paka bii lay rèndii sa waay mokay diokh sa none" thiey mbokk légui yi 😢
Soda maréme a récupéré tous les biens de Niawar puisque ce dernier à déjà signé les documents c le combat de BOURY FALL ❤ donc qui va pouvoir joué le rôle d'héroïne pour pouvoir encore récupérer les biens de ce dernier 😢 ça chauffe déjà 🎉🎉🎉
Je pense que tout ça c’est la faute de bourry, woudjou moylann, yaw sa dieukeur baalounala sarakhoûnala. Nga tass sa seuy dém. mane dinaa ligueye ba aksi fii woudjou dimako yakhal
Boury moy lumière dii protège keur gui .Leep lou Soda Maréme teek thi plan pour ruiner Ndiawar Diagne geum nanii la grande Dame Boury Fall 😊dinako kham
Papay Soda Mareme mi moy Koba nak dagno takhaw andeu pour wadal Ndiawar diagne yobou ko si souf wayei BOURI Amnagne si yaw yakar ❤c est bien 😂c est très bien
Depuis l’autre jour je me suis dit Modou n’a pas payé l’argent, la somme qu’il a donné à Soxna c’est pour qu’elle puisse construire quelques choses sans lui car il se peut qu’il part en prison. Et si Soxna investit elle peut lui venir en aide.
Aye way domou baye yi ndiawar diagne Ass diagne boumou niaw way lépe Sokhna diagne la ndakh mo conseille modou diagne lou bone 😡, mes Boury tamite machallah la force tranquille lako toudé celle classe ❤❤❤❤❤
Seytané wakhoul deugg wayyé yakk na ap khel....ma doli ci wakh ni BALA KHAM, KHAMADI KHAW LA RAYY. Ce qui me pousse à dire à la maman de Ndiawar que QUAND ON FAIT ENTRER LE LOUP DANS SA BERGERIE, IL NE FAUT S'EN PRENDRE QU'A SOI-MÊME!!! Khadija, Khadija, Khadija...tu t'es mariée par intérêt tandis que ton mari te vouait un amour inconditionnel au point d'être faible devant toi...mais GOOR amoul loudoul kaddom té ya ngui kakoy khagn...ton amour pour l'argent et les biens matériels te fait perdre la tête au point de risquer la perte de ton mari, le respect de tes enfants!
Xalisso badio est une série télévisée qui a pour enseignement le rôle de la jeunesse dans la famille exemple de sérigne et sa petite sœur les enfants de Ndiawar avec sa première femme ❤❤❤visitez cette série télévisée pour des nouvelles inspirations de la jeunesse ❤
Modou diagne mi niiit la walla kouberr kon fayoul khalisse bi Mareme soda ak bayaam dinan rateuuuuuuuu ndiawarrrrrrr bamou bayi c'est bon Da melni mom marem da birr sakh mom geun forokhlei😂😂 Merci evenprod nioun femme modou modou yi contane nagn si yennn c'est bien c'est très bien Bou niou diotoul message sakh dioteu notification xalisso ou bete bete
Kou d'accord nii xaliss Amoul mbokkeu rek laalal j'aime 😢😢😢
Franchement Boury S'habille décemment et très classe❤❤
Hâh oui elle voulait récupérer sa place dans la société et sa place de première dame 😂😂❤❤
Yala na boury sauver ndiawar😢❤
Loloy am . Soda djeul leupeu. Boury ñow recommencer à zéro avec ñawar
@MimiNdoye-m4x 👍
@@FatisSy-r9qnon soda meunoul dieul lep li abus de confiance la Soda souci guéné dafay yomb trop Boury moy sauvé Ndiawar c’est claire
Mettez la traduction avec xalisso aussi svp 🙏🙏🙏❤️@@evenprod
Cœur pour notre prophète Muhammad 🎉❤
ﷺ❤
SALLALAHOU ALLA MOUHAMAD SAW NOTRE BIEN AIMÉ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Psl❤❤❤❤❤
❤❤❤❤PSL
❤❤❤❤❤
Boury elle a compris l jeu d soda Mareme pate ak organiser lay def pour mieux comprendre. Papay soda Maréme betouma dè mannn
Elle a tout compris c’est bien c’est très bien 🤩
😂😂lolou meune nama raye c bien c tre bien😊
Wallay même moi aussi betouma 🙏
😊😊😊
@OumouBa-li9ws Gnou xare suite bi.
Papay soda marème louche neu daal j'espère qu'il n'est pas de mèche avec sa fille 😮
Si oui Yaye Dior aura une grande déception " Paka bii lay rèndii sa waay mokay diokh sa none" thiey mbokk légui yi 😢
A guiss ngua dé
Wa danio beug ay sama mbok lakoy diokh mou seuyel ko té diambour yi sakh nio guena goré boy khol
Bayiko rek mais on dirait que boury a compris son jeu😂
@@OumouBa-eo5uy mom la fok d
@Pudiquementbelle Ah guisgeu dh, gnou xare suite bi.
Boury elle est très classe ❤
Yalla nafi yalla bayi sunu papa yi ak sunu maman yi basi kanama kanama kanam si barke s touba 🤲❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤j'aime trop le prophète mohamed (paix salut sur lui)
Yaw li d'où pour finir stp🙏
❤❤❤❤SAWS❤❤❤❤❤
Wa evenprod yalla naléne Yalla faye Alkhamdoulilah❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
@Fcmobilebêta1009 Amine.
BÉTÉ BÉTÉ moye pied droite XALISSO pied gauche di dokh di béguel Sénégalais yi 🎉🎉
@mohamedelhabibndiaye8069 Yeinakofi ame. 👍
J’aime pas bétebéte
Y’a trop de bruits
Bilay iaw 🎉
Modou diagne li nak moy mayé moma gueneul fay bore 😂
Niak diom rk😂😂😢
Pour man faynako
@arameseye-b7r Est-ce que laloul wone pexer ? 😂
Tem mo diaye terrain yi😂an even prod😂
Baa soda Mareme diayoul terrain yi
Des cœur pour notre prophéte Muhammad ❤❤❤
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤❤
Amine yarabi niou bokou KO 🤲🤲🤲
Amina ❤❤
Amin 🤲🏽
Ohhhhh la classe de boury je l'aime trop dou bolé dara aki wakh ❤☺️👍
Papay Soda Mareme mom louche na di
Waw lepp momla limouyy wakh rakk dji bou demé soda lenene lakayy wakh
Mtx ken defatoul Lou bax dy 😢
Xalis bi molèn intéresse pa sey bi
Moh soda mareme dafa nangoussi xalissou djawar dih....moguii ko done signe lo rek té verifier woul limou done signe
@sossooooooo Gnou xare suite bi.
Soda maréme a récupéré tous les biens de Niawar puisque ce dernier à déjà signé les documents c le combat de BOURY FALL ❤ donc qui va pouvoir joué le rôle d'héroïne pour pouvoir encore récupérer les biens de ce dernier 😢 ça chauffe déjà 🎉🎉🎉
Je pense que tout ça c’est la faute de bourry, woudjou moylann, yaw sa dieukeur baalounala sarakhoûnala. Nga tass sa seuy dém. mane dinaa ligueye ba aksi fii woudjou dimako yakhal
@@coumbadaganandao1418iow tu dois te faire soigner dhé ❤l😂 tu es jalouse de bourry ou quoi
Boury moy lumière dii protège keur gui .Leep lou Soda Maréme teek thi plan pour ruiner Ndiawar Diagne geum nanii la grande Dame Boury Fall 😊dinako kham
machalah Bourry Aka am classe,té organisée, et puis elle revenue au Bon moment
Elle n’aurai du pas partir, j’espère qu’elle n’est pas venue trop tard
Bande annonce bi tang na dé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@Fansanimeetclubtin Boul tarder épisode bi. 😂
@@evenproddégue guénema daguéne ma falewoul gnoune wa thies serigne guagne lagne beug guis si serie yi svp😢
Trop sax 🥵😂
@evenprod inchallah di na ko sétan😂😂😂😂
Xaliss tasss nah famille😢😢domou baye ya c fini 😢😢😢
@babshifayzo663 🥲
C’est bien c’est très bien la classe de bourry
Akk Beauté bou Rare bii😍
@IbrahimaNdiaye-v2h 👍
Evenprod yéna meune nak xalisso série au top kou d'accord ❤
@SeynabouKa-t6d Merci. ❤
Xalisso dafa nékh ❤
Papay Soda Mareme mi moy Koba nak dagno takhaw andeu pour wadal Ndiawar diagne yobou ko si souf wayei BOURI Amnagne si yaw yakar ❤c est bien 😂c est très bien
Depuis l’autre jour je me suis dit Modou n’a pas payé l’argent, la somme qu’il a donné à Soxna c’est pour qu’elle puisse construire quelques choses sans lui car il se peut qu’il part en prison.
Et si Soxna investit elle peut lui venir en aide.
Asalamou enlaykoum sama mbokou djoulit yii Yalnako diam sakh sii yene 🤲🤲🤲❤❤❤
Merci beaucoup pour tout équipe Evenprod c'est bien c'est très bien 😂
Aye way domou baye yi ndiawar diagne Ass diagne boumou niaw way lépe Sokhna diagne la ndakh mo conseille modou diagne lou bone 😡, mes Boury tamite machallah la force tranquille lako toudé celle classe ❤❤❤❤❤
Seytané wakhoul deugg wayyé yakk na ap khel....ma doli ci wakh ni BALA KHAM, KHAMADI KHAW LA RAYY.
Ce qui me pousse à dire à la maman de Ndiawar que QUAND ON FAIT ENTRER LE LOUP DANS SA BERGERIE, IL NE FAUT S'EN PRENDRE QU'A SOI-MÊME!!!
Khadija, Khadija, Khadija...tu t'es mariée par intérêt tandis que ton mari te vouait un amour inconditionnel au point d'être faible devant toi...mais GOOR amoul loudoul kaddom té ya ngui kakoy khagn...ton amour pour l'argent et les biens matériels te fait perdre la tête au point de risquer la perte de ton mari, le respect de tes enfants!
@mypbarro5416 Quel vérité ! 👍
Soda Mareme ak Papa dji amna lougniy manigancé😂😂😂
@1Daro87 Lolou ley ndirol dh. 😂
Kone modou diagne fayagoul ndiawarr😢😂😂😂
La beauté de bourry❤ le regard
Wakhati ko dh khéetou kholam rek
@ walai maman manchallah Toute jolie bourry en plus yiw lolou sax sol Lou diote Alahouma barik❤️
yalla sénégal am diamou amien
Kou beug seyedina Mohamed lalale j'aime ❤❤
Kou beuge Boury ak Maty Rose ak Xalisso rek l'alal j'aim ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
@Fcmobilebêta1009 👍
Sii ça chauffe mais soda mariéme akhe papa séne affaires lérou😱😱😱😱😱
Moy mboki taye yi
@@mormbaye2989bilay 😢😢
@MadameNDIAYE-lc7nb Ah doyna ware gnou xare suite bi.
@evenprod mais douguéne ma djéle
@ 😂
Konn modou fayago batay 😅😅😂
Modou kay dafa doywar 😂
@sokhnandiaye9999 Mo diaxal gneup. 😂
Modou diagne kone fayoul khaliss bi ki mo am fitt😂😂
Moma diakhal 😂
@khalilmbaye Mo diaxal gneup.
Bad lén Diadia sa yeuf la kharal ba Boury nieuw rk😢
Kou dakor Maty Ross ase Diagne mokoy takk ❤
@MaremeNiang-o3m À suivre.
Khadija respect ass diagne diekeur daniou koy respect 🫵
Bilay wakh ga deugue
Dama yakamti maty rose seuysi beu mbougeul sorcière bi😌
@aminadiouf148 Beugo diam. 😂
❤❤🎉🎉🥰🥰@@evenprod
Xalisso badio est une série télévisée qui a pour enseignement le rôle de la jeunesse dans la famille exemple de sérigne et sa petite sœur les enfants de Ndiawar avec sa première femme ❤❤❤visitez cette série télévisée pour des nouvelles inspirations de la jeunesse ❤
Soda marem aka nékh réglé papam rk guaw woo😂
Mafia djitou kou d'accord
Bilay
MAFIA😂😂😂
Ha Modou mom waxoul won fay n xaliss bi b parei😂😂😂
Man njawar diagne ayy rei 😂 lá Mai deff 😂😂😂😂 ya Nekh
Très bien c'est bien even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah ❤❤❤
@yayemayelatmbao5442 Merci. ❤
Modou diagne mi niiit la walla kouberr kon fayoul khalisse bi
Mareme soda ak bayaam dinan rateuuuuuuuu ndiawarrrrrrr bamou bayi c'est bon
Da melni mom marem da birr sakh mom geun forokhlei😂😂
Merci evenprod nioun femme modou modou yi contane nagn si yennn c'est bien c'est très bien
Bou niou diotoul message sakh dioteu notification xalisso ou bete bete
La classe que Boury dégage oooh🥰🥰🥰🥰
Classou boury me dépasse tmt❤❤❤❤
Yalla nagnou yalla may khollou mougne
Mais banquier boudée dafa beugue diadia loumou donne deff akk Boury pleine de surprises 🤔
Bande annonce bi c bien c très bien 🎉 1:52
Soda maréme et son père da gni Wor ya dior ak ndiawar soda day joué rk wayé khalisse bi la beug
Soda Maréme ak papam déh plan lagn ték. Nenako kouy yott dou seukeutt
Sk bayi guen khel ni soda signé lona diaware aye dossier pour entreprise bi hummm sama khél gnaw
@arameseye-b7r sisi plan la pour lék ci khaliss bi. Ndiawar ak yayam déh guissa gougnou dara
Le père de mareme soda naka diék wolou wou mako😂
@bintaaayadeuh8800 Doyna ware. 😂
Machallah wa evenprod ❤
Tay mom ma fi nieukeu😂
YALLA N'A NÉIPOU AM JAMOU 🤲
C'est bien très bien even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah c'est très bien ❤❤❤❤ndiawar 😂😂😂
Xalisso vraiment beurina ay djagat...mais boury je l'aime bien elle a beaucoup de classe
Bouri trés classe
@maguettethiam6392 👍
Modou diagne daa diaye terrain yiimo bokak ndiawar diagne😂😂
Li mome bétouma soda ak papame 😢
Mane damaye lathé ki Fayoul wonne kalisse bi ba paré 🤔mes louy problémbi😂
En yaye xam 😂😂😂😂ndiawar dîna ma ray 😅😅😅
😂😂😂
#Evenprod j'ai l'impression que Marém Soda et so père veulent klk chose (étrange) je leur fais pas confiance 😮
C’est bien c’est très bien c’est bien contane na deh 😂😂🎉
@ramosciss7921 C'est bien ça. 😂
Des cœurs pour notre prophète mouhamed ❤
Mareme soda amna loumou signer lowone ndiawar dh😅
Soda marieme bilaye dina sathie xalis bi yeup môme ak pape djie niou complot c bien c très bien 😂😂😂😂😂😂
@codoudiouf7568 Gnou khare suite bi. 😂
@evenprod 😂💝💝
Papay soda marem diouboul dé😂😂😂😂😂😂😂
Thiouw Li nak bouri rek moko wara fay 😂😂😂Awou yaye defal sa meunin Yaw nitou diamou ga
@NdiayeFatima-c5k À suivre. 😂
Très bien c bien 👍
Sallalahou alla Muhammad ❤️ ❤️ ❤️
Konn bokk na kouné protégés rakam 🎉
@matygueye6412 Xalisse mougui leine di beug diaxasser ?
Wa soda mareme da gnewei 🤰 kone
Xobè ngeen nak😂
❤bilahi boury beug nalla je mens pas❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉merci 🙏 😘 😊 way
❤❤❤❤ inchallaawe Yallah n'a sotti soutoure 🥰🥰🥰💯🫶🏿
Xool Boury rek rétaan ndah taar machaalah 😅
Xalisso rek ❤❤❤
Allhamdolilah ❤
Even production si caw si canam
Hoo 😢😢 mboku tassna 😓😓😓
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdoulilah ❤🎉
Yayou Ndiawar mongui sissou teh li yeup ak mom… C’est bien, c’est très bien
Bilay Boury zo t’aime 😂❤
❤
Avk soda marème ak papa lègui es ce tak diambour gueuneul tak sa mbok nak🤔
Billy
Leçon dioudou watt machallah
@buz7755 Doyna ware. 👍
très bien c’est bien c’est très bien 😂😂😂
Soda mareme mi dmrm la rk ndiawar ak yayame en yaye😂😂
Soda maréme tu monte decend😂😂😂
Modou Diagne madou ya diay Terri yé😂
❤❤❤
C'est très bien 🎉❤
Bonjour et Jummah Mubarak à tous ❤