A ce rythme nak Kou nek di wakh je pense que makhou Dina guéneu malheureusement li moy Senegal nitt dafay def délit nioukoy nianal ndiek ba victime bo moy moudiou nek coupable allons rek
Pour une fois on traite correctement le sujet des violences conjugales dans une série sénégalaise en punissant le coupable comme il se doit. Evenprod vous avez donné le bon exemple de grace ne gachez pas ça di libérer makhou. Nagn kon tedj comme il se doit rk
Pour l'amour que j'ai envers cette série, à part le bande annonce je ne cesserai jamais de vous supplier, mettez la traduction s'il vous plaît Evenprod🙏🙏😭❤️ Merci !
Evenprod vous êtes très suivi manchallah. La situation de Dieynaba et Makhou est un mal profond dans notre société actuelle. La violence conjugale est la cause principale de la mort de beaucoup de femmes et de jeunes filles au Sénégal et c’est horrible. Il faut laisser Makhou souffrir en prison pour sensibiliser et conscientiser les hommes. À travers cet acte vous contribuez au changement et vous nous aidez à faire face à cette situation. La femme est un trésor kénn warouko torokhall kénn warouko doore. Halte aux Violences Basées sur le Genre. Trop c’est trop.
Diouma tall merénala barkhi Thierno Moulay sow 😡😡😡😡😡 Loy dem di dieuleul Makhou défense Mais laobé yii keur alkaly Tay mou safff Amy Mbay nena makhoudia alalou mbolo la 😂😂😂😂 kon neko mayonnaise ❤❤❤
Ce que je ne peux pas comprendre c'est que des femmes puissent cautionner la violence en demandant à ce que Makhou soit pardonné pour le sortir de prison. Daba Thiam n'arrêtera donc jamais de me décevoir. Son amour à '' sens unique '' pour Alkali lui fait perdre la tête et elle a influencé sa fille. Voyons si elle va partir de chez ses parents. Makhou mérite amplement la prison. Même si c'est pour un court séjour, il le faut. J'espère de Dieynaba Tall ne va pas reculer dans sa démarche. STOP AUX VIOLENCES SOUS TOUTES LES FORMES.
Je suis entièrement d'avis avec vous.. C'est malheureux vraiment que l'on veuille pas punir Makhou pour son acte. La société est trop injuste, il tabasse sa femme sans regret jusqu'à occasionner son accouchement et c lui même qui reçoit du soutien au dépriment de sa femme. Puff
Ki dafa doff trop , amoul ben diom Et ça reflète tellement la société sénégalaise, la violence faite aux femmes est tellement minimisée, on le voit comme une simple « erreur » motakh les gens ne changeront pas aussitôt
Makhou ne merite en aucun cas la prison . En premier il a dit à Dieynaba ma mère est entre la vie et la mort et toi tu est entre de te faire belle est-ce que si c’était ta maman tu allais faire la même là ils ont commencé à disputer et Makhou a sortie de la chambre et Dieynaba la poursuit jusqu’à déchirer la photo de sa maman . C’est normal qui réagi parce que ça a cause de la maman de Dieynaba que sa mère est entre la vie et la mort
Daba Thiam ak dôme bi nio geuneu niakk diom thiim surtout Daba Thiam … Kham nga lanela djiggen ken douka door il n’a qu’à apprendre la leçons pour ce pays Even kholen bou bakh ligani deff
Daba Thiam xol mounouma ko si mome 😑 mome ay att mou langal ko Alkaly ba lou takk si mome mou soll robe avocat ni mokoy défendre 👩🏾🦯, Alkaly torokhol ko mouy diay beugue goor 😒 soula bouguone doula fi bayi takk sa nawlei humilié la devant tout les kelkun, manqué na trop way si diek, naniou teuthie Makhou bou ndaw ba dameu si thiabi ba, nax dafa rew
Comme disait Alkaly bou daw, justice for everyone! Naniou bayi Makhou ci cachot bi touti guir mou dianga adouna. Il a tue un bébé quand meme! Daba et Amy Mbaye sont mal placées pour donner des conseils…
Kou yakamti won bande annonce bi beusseul j’aime😂❤
Maguini😂😂
Maane akk yoow 😂😂😂❤
Des cœurs pour notre prophète mouhamed psl ❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Salalahou alla mouhamedine ❤❤❤❤❤❤❤
Dieynaba c’est dure mais maintien rekkk ! Il faut donner l’exemple ! Violences conjugales yé wara diekh ! Enough! Enough! Ça souffiiit
Inaff inaff😂😂
@@yamandiaye1344😂😂😂
Bilay trop même na dém o gniouf ce sera une leçon
A ce rythme nak Kou nek di wakh je pense que makhou Dina guéneu malheureusement li moy Senegal nitt dafay def délit nioukoy nianal ndiek ba victime bo moy moudiou nek coupable allons rek
Bilay
Kou beug Saydouna Mouhamed Loy wout yalla ngako am😢🎉
Allahouma salli ala seydina Mouhammadine wa alihi wa sahbihi wa Salim PSL ❤️🕋
Psl
SALLALAHOU ALLEYHI WASSALAME NOTRE BIEN AIMÉ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
Sallahou haleyhi wasalam 🥰🥲
Salalahou alla mouhamedine ❤❤❤❤❤❤❤
Bété bété day gueuneu métti 😢 wallahii
Jt jure ça fait peur
Dina guena nekh saff kani 😂😂
Dimanche ty bi yalla boumou nek sounou dernier dimanche amine ❤🙏🏾
Amine
اللَهُمَ صَلِّ عَلَى سَيِّدِنَا مُحَمَدٍ وَسَلِّم☘
Allahoumma salli 'alâ Sayyidinâ Mouhammadine wa sallim☘
li ma nêkh thi yêne moye da ngêne respecter internaute yi machalla bété bété le meilleur séries qui parle le culture et traditionnels dû sénégal
Allahouma salli alal mawsoufi bil Karami wal dioudi PSL ❤️🕋
Ndeyssann diouma thiam xoll bou rafett la am ak liko domou bayam yii deff yeup 😢😢
Mom ak yaye dji yeup denou niak diom
Billay gnak diom la yayam qui se sacrifie a attendre un homme qui humilie ta famille plus de 20ans li dou bakh gnak classe la @@djibyjosephbore3609
Dou khol bou rafeet . Niakk personnalité la deff mome ak yayam.
Mais je suis pas d accord avec elle ce bâtard de petit makhou il doit subir les conséquences de ses actes pour prochaine fois douko defati
Pour une fois on traite correctement le sujet des violences conjugales dans une série sénégalaise en punissant le coupable comme il se doit. Evenprod vous avez donné le bon exemple de grace ne gachez pas ça di libérer makhou. Nagn kon tedj comme il se doit rk
Nanke rek 😂 ya way li série la dé
@@AlbertDaCosta-n1iréalité te aussi violence conjugale kham gna ni barina thi rew te meunoko wedi
non lign ko teudj doyna psk gnom gnaar famille la
Vraiment d’accord 👍🏾
@@sokhnasaliou7859 arrêtez l hypocrisie sénégalaise là famille ba thi lan
Mane laobé yi la beug 😂
Vraiment Déguéne joue très bien ❤❤❤❤
Non billahi bête bête nekh ndegay seetan série bi sa xool di nekh Ana niou kontan si wa evenpord mayal ma lene ay toujours j'aime❤
Kou beug seydina Mouhamet psl lale aime❤
Psl lomouy signifier😅
Kone souma laloul ❤ c’est que beugoumako ?
S ♥️ a ♥️ w ♥️
Psl ❤❤❤
Yalna SONKO am Diamou yagg si Sénégal Ak louka weur si Barké Baye Niasse Yarabi Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf Teuf ❤❤
Wawaw amine ya rabi diamou sonko moy diamou Sénégal
Pour l'amour que j'ai envers cette série, à part le bande annonce je ne cesserai jamais de vous supplier, mettez la traduction s'il vous plaît Evenprod🙏🙏😭❤️ Merci !
Amina rew na trop.dieynaba yeureum nako. Sacha béteu néne ko
Wakh nga lep
Chacha nak Dafa eupeul melni kougnou takk😂
Chacha nax yalla mou tokk way 😂mane jme demande esk moudié woul doff sax ishhh
Des coeur pour notre prophète psl
Evenprod vous êtes très suivi manchallah. La situation de Dieynaba et Makhou est un mal profond dans notre société actuelle. La violence conjugale est la cause principale de la mort de beaucoup de femmes et de jeunes filles au Sénégal et c’est horrible. Il faut laisser Makhou souffrir en prison pour sensibiliser et conscientiser les hommes. À travers cet acte vous contribuez au changement et vous nous aidez à faire face à cette situation. La femme est un trésor kénn warouko torokhall kénn warouko doore. Halte aux Violences Basées sur le Genre. Trop c’est trop.
Ana fans bete bete yii🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Nima diépé famille maréme sall motakh loniolén déff begue na😂
😂😂😂😂
😂😂😂bilahi 😂
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤
Aameen
Amine ya raby
Aamiine Yaa rabbal halamiine
Amine 😢😢
Amine
La meilleure série du moment au Sénégal 🇸🇳 ❤️ ❤
C’est très bien Amina rew na ya ndakk nogaye motakh digua degue louné 😂
Diouma tall merénala barkhi Thierno Moulay sow 😡😡😡😡😡 Loy dem di dieuleul Makhou défense
Mais laobé yii keur alkaly Tay mou safff
Amy Mbay nena makhoudia alalou mbolo la 😂😂😂😂 kon neko mayonnaise ❤❤❤
Bon repos dominical à tout le monde Even Prod yènafi nekk ñougui leeni contanè boubaax❤❤❤❤❤❤❤
Deguén mi sadique na dh😂😂
Je suis lougatoise j'aime bien les série sénégalais et les commentaire 🎉🎉😂😂😂
Ce que je ne peux pas comprendre c'est que des femmes puissent cautionner la violence en demandant à ce que Makhou soit pardonné pour le sortir de prison. Daba Thiam n'arrêtera donc jamais de me décevoir. Son amour à '' sens unique '' pour Alkali lui fait perdre la tête et elle a influencé sa fille. Voyons si elle va partir de chez ses parents. Makhou mérite amplement la prison. Même si c'est pour un court séjour, il le faut. J'espère de Dieynaba Tall ne va pas reculer dans sa démarche. STOP AUX VIOLENCES SOUS TOUTES LES FORMES.
Je suis entièrement d'avis avec vous.. C'est malheureux vraiment que l'on veuille pas punir Makhou pour son acte. La société est trop injuste, il tabasse sa femme sans regret jusqu'à occasionner son accouchement et c lui même qui reçoit du soutien au dépriment de sa femme. Puff
Je suis entièrement d'accord
Ki dafa doff trop , amoul ben diom
Et ça reflète tellement la société sénégalaise, la violence faite aux femmes est tellement minimisée, on le voit comme une simple « erreur » motakh les gens ne changeront pas aussitôt
Je suis d'accord pas de piété pour lui
Makhou ne merite en aucun cas la prison . En premier il a dit à Dieynaba ma mère est entre la vie et la mort et toi tu est entre de te faire belle est-ce que si c’était ta maman tu allais faire la même là ils ont commencé à disputer et Makhou a sortie de la chambre et Dieynaba la poursuit jusqu’à déchirer la photo de sa maman . C’est normal qui réagi parce que ça a cause de la maman de Dieynaba que sa mère est entre la vie et la mort
Merci beaucoup even pro yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah c'est très bien ❤❤❤bon dimanche ❤❤❤
Omlét len sama commentaire 😂❤🎉 Amy mbaye 😂
Ndéyesane makhou damako yeureum sakh😌
Nous vous aimons "waa Artistes des différentes séries de production du Sénégal ❤❤❤❤
Svp @evenprod ne nous décevez pas . On veut monter un exemple de justice pour toute femmes battues. MAKHOU na dess si kasso bi svp . 🫵🏾☝🏾
Dimanche tay yalla boumou done sougnou dimanche bou moudjou🙏🙏🙏
Amine
Yalla na nieupp ame jammou wakhléne amine❤
Amina seu rewandei mo diour li yeupeu c’est bien c’est très bien
Déguene rekk mo bakh si famille alkaly 😂😂 bien fait pour vous 😊
Meunou mako omlétte té yaw meunoko bakhal paroles de Amy mbaye😂😂
😂
Kone mayonnaise rek koné thieup 😅😅
😅😅😅😅😅😅p
Kone nagnouko maillonaise koné thiape walam😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@boussoGueye-po1hb 😂😂😂
Mais li nekhna dh 😭🎉🎉❤❤❤❤
Franchement parlé damay yékha diot annonce bi walla lane la heur bo nieuwé ndékké amna nioulafi djitou 😢😂😂😂😂 longue vie à nous 🎉❤
Mareme sall da melni bimouy dundu la eupone diam 😂😂😂😂
Vraiment 😂
😂😂😂😂bilahi yaw😂😂😂
@@MansourCisse-r2h ah wakhe deugue yalla 😂
Kou contane di Deguen rkk lalaal j’aime ❤❤❤
Daba Thiam ak dôme bi nio geuneu niakk diom thiim surtout Daba Thiam … Kham nga lanela djiggen ken douka door il n’a qu’à apprendre la leçons pour ce pays Even kholen bou bakh ligani deff
Daba Thiam xol mounouma ko si mome 😑 mome ay att mou langal ko Alkaly ba lou takk si mome mou soll robe avocat ni mokoy défendre 👩🏾🦯, Alkaly torokhol ko mouy diay beugue goor 😒 soula bouguone doula fi bayi takk sa nawlei humilié la devant tout les kelkun, manqué na trop way si diek, naniou teuthie Makhou bou ndaw ba dameu si thiabi ba, nax dafa rew
@ je suis d’accord pour son acte djiggen kene douka door na wa Even kham lolou
Le meilleur série du Sénégal ❤❤
Yalna gneup am Diam si barké seydina mouhamed
Alhamdoulilah 🎉
Machalla sallahou Aley wa Salam ❤❤❤❤
Sant yalla wa naffar am guénn ndamm ❤😂
Mairi dans bété bété even pro loléne gnou beugueul ❤❤❤❤❤entouka yéneu meuneu yéneu eupou dolé macha allah ❤❤❤
Avec evenprod votre cœur bat plus fort 😂😂😂
Dieynaba nakk inaf inaf ! Pourquoi tu pleures ?? Boul reculer kharit🤣🤣🤣
😂😂😂 c'est l'amour ❤
Amy mbaye wakh nako 😂😂
Yalla sénégalais yeup dém aldiana ❤🎉
Amen
Bande annonce bi mome danse 💃 na dee🎉🎉
Kham nguenn lanela dioyou Dieynaba Tall yi neu dess ci bande annonce bi, boumou topp demain InchaAllah
Ku confirmé ni Even pro sont des meilleurs beusseul j'aime
Ohh Makhou c’est interdit de pleurer bingay niouss Djeynaba Tall diko kadje aka boullé dafa nekhon kon triste bi dawoul sax souniou yaram 😂😂
Inaf 😂
Inaf lnaf
Merci bcp déguene ❤
Mane ndèkètè Deuguène sow la beug 😂😂
Mérci dèguène ❤❤❤❤❤
Les expressions de Dèguene vreumenttt 😂😂😂
Billy borso Ba de retour é way samba lou nékh 😂❤
Take katou cheveux bou j’aime sama commanteire bou mala reukèe dinga mourou 🧕🏾 dji 😂❤❤❤❤❤😊😊😊😊😊
😅🤪🤪🤪🤪😊
😂😂😂
Alkhamdoulilah ❤❤❤
Alhamdouliah 🙏🙏
Wa yén bande annonce bi nékhna dé😂😂😂😂😂
Ça promet comme toujours 🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Je suis fière de deguene
Elle vas réglé leurs comptes a la famille Alkaly .
alkhamdou lilah
Sallalahou allah mouhamed ❤❤❤
Kou beugue seydina mouhamed lalale jaime ❤
Rema Diop yallana yalla wereul baat bi lingay way nekhna ❤
C'est du lourd comme d'habitude
C’est bien Deguene c’est TRÈS BIEN
Comme disait Alkaly bou daw, justice for everyone! Naniou bayi Makhou ci cachot bi touti guir mou dianga adouna. Il a tue un bébé quand meme! Daba et Amy Mbaye sont mal placées pour donner des conseils…
C'est la première fois maye commentaire des❤❤❤
Wah evenprod sen faute de frappe si suivre à 20h 30mn Kagn nguene Loy changer
Weli Bonne continuations
Yalla na yalla nangou gnane
Sallalahou allah seydina Mohamed ♥️
Que dieu vous protège
Ayway ndaynaba 😢 Amina rew n'a way kou d'accord 😢🎉
Dieynaba sarahniou rek bayi dioyi ahhhh
Dama yeureum amadou deh😢😢
Série bi dal nékhatoul😅😅
Kou kham diaynaba loumi dioy
Sheutt déguéne mi😅😅 ..nénako « mou bankou ni morceau »
Wouyyy😃😃😃
Niaffff , Amina danga reww rek 😮 dotoko défatiii
Je n'ai pas le temps d'écrire, cliques deux fois sur le commentaire pour écouter l'audio .
▶︎•|၊|။||||။၊|။|||။|||။ 18:18
2:30 2:30 2:30
Dieynaba tall mome théâtre bi yeup dioy nako
Machallah 🎉❤
Lou nékh❤❤❤
Ça promet❤
Amina dafa réw rék mais dina khamné lépp deugue dingéne ko guiss dh yake sa famille 😂😊😊😊😊
Koudoul khalate Lundi matin Loula nékh défal😢
Les larmes de Dieynaba Tall 😂😂
Alkaly dafa wara Takk Daba Thiam gniou khôl Daba thiam ak Amina si keurgui noumouye wara mel❤❤❤❤
Even pro yéneu meuneu kay ❤❤❤c'est très bien 😂😂😂❤
Waaa mais mane beugue na laobé yi ann
Alhamdoulilah ❤❤