Donc niogui si novembre 2022 serigne bii dieul nasi ay solution dieureudieufeti borom touba serigne mountakha yalla nafi yague thé and ak wérr ❤️ ❤️ ❤️
Ces jeunes ne sont pas des bandits mais des gosses découragés et sans repères. Il faut les aider. Le journaliste est fort car il parle avec eux sans les vexés. Bravo à toute l équipe
Bravo pour ca documentaire! Ça reste vraiment à saluer...Quand à aux gosses ils ne sont pas des bandits ils ont juste besoin d’aide et d’orientation pour qu’ils puissent retrouve leur famille...
Toutes nos félicitations il ya beaucoup de niches favorisant la déperdition de l'enfance déshéritée au Sénégal des programmes doivent être définis pour lutter contre ce fléau car il commence à prendre des proportions insoupçonnées il y va de l'avenir même des jeunes qui constituent la relève
Il faut denonçer ça. IL faut montrer la video au khalif general pour qu'il trouvera une solution le plus rapidement possible. Ça ne peut pas avoir dans une ville sainte comme touba . Merci pour le reportage
Ils sont au courant bien entendu sauf que leur ignorance veut tout dire... Il y a un problème d’encadrement dans ce pays et aucun suivi. Et très honnêtement je ne suis pas étonnée de voir ce genre d’image.
J'aurais bien aimé que ces informations soient transmises le plus rapidement possible au khalif général des mourides pour qu'il puisse prendre une décision pour recadrer et réinsérer ces jeunes. En effet, ces jeunes ont juste besoin d'un encadrement et d'un accompagnement. Vu qu'ils sont dans la ville de Touba je trouve c'est logiquement les autorités religieuses et administratives qui doivent y remédier en apportant des solutions immédiate. J'ai énormément confiance en ce sage Khalif et je suis certain qu'il apportera son soutien intellectuel et financier. Un grand merci à ce journaliste présentateur qui rempli bien son rôle " chapeau"
Macha Allah fantastique vidéo Touba gar bou mag fala dane Diangé métier si wetou keur Serigne mame cheikh mbacke mome Serigne fallou di kou bakh waye même bir keur Serigne mame cheikh mbacke bofa wérre yeré té fermé wo bountou keur gui encore kenne neckoulle si keur gui yeré yeép laniye wérri soune keure mome damako sakh djellallé même aye Dalle yalla na yalla safara leup temou diarraleko si lokho Serigne bi
Ndaysan cey li dawna yaram de Man de sama rague buma bokal ndaye ak baye migui ci video dara lanuko yobou won Mou daw mais niogui koy set te incha allah dinanu ci takhaw
Dieul aye millards diko diokhé Macky sall pour covid bi, té sa N'diabote toumouranké Thieuye sounou kulifayi naniou oubii séni beute té ragal Yallah... Li dafa niaw té Touba à une histoire et c'est honteux de voir çà vraiment
J habite à Touba Mball mais ses jeunes ont les as abandonner alors que personne n'a parle pas c'est honteux ses jeunes font partie de la société aideons lés
Kilifayi daniou wara djioublou thi euleukk ndaw yi,, construire des usines , ....; ndaw yi am possibilité deff des formations professionnel.... dakh touba waruta kharr dara thi Etat , Serign touba defarna ay mourite you mana arr deukeumbi mai sck....... ??? kon naniou geuna warrmane deukkbi *Lhomm quil faut a la place quil faut*
@@gueuemougueyemou7253 police bou touba takhoule gnoye police xolale touba nomou tolou am ñiari poste de police lolou manoule dara Touba lumuo néw néw warona am 5 poste de police
Avec ça niouni kéne doukofi wakhé khalé yoyou kéne santou si Mbacké wala s'y parents yi gnio wara téyé séne bôme yi yawmal khiyam résponsaboul bi sisa dom yalla gnoune lakoye lathi diékhouko sérigne bi lidafa rouss lou si ville sainte cité fakhmane amoul sakh Dakar so wakhé gniouni nonou Sérigne bi ga li bakagne Sénégal va mal 😡😡wakh dieou Bari diefeu touti 😭😭
Li dé mofi nekk ku bakh, Serigne Modou lo ngabou ak safinatoul amane li mo wara doon senn ligeey wayé toop khalé you jigeen yi rekk di soumi, li mo gueneu niaw fouf sole jupe bou amé fente wala tekk mèche si bopp, ta gni weur Serigne bi dou niou ko wakh degueu, aye règlements de comptes rekk la gnou fi néké. Li niaw na si sunu dekeu bi
GESTION WOU TOUBA LANIOU WARA DIEULÉ SI LOKHOY MAIRIE BI ... CE N'EST PAS NORMAL THI TOUBA AK STATUT BI MOU AM. DOU DEUG DOU YONE ... NANIOU RAXASS DEUKK BI ..
Serigne modou lo ngaabou yaa you safinatoul amaane de Lii leppou si sa loukhou la nekk Niga sonné woon si mbirou aïda diallou sookou sonné woon si lii mou diekh takk Lii de sogne kou bayyé nii woorna s touba moo guené garaaw ay aïda diallou You ñakk xouroum yi
Mon cher y a pas plus irresponsable que leurs parents qui passent tout leurs temps a faire des enfants . Pourquoi les gens les plus pauvres ont plusieurs enfants , comment tu peut te dire que je fais des enfants et le bon dieu s'en occupe, c'est quoi cette réflexion des Sénégalais , et y en a qui se cache derrière la religion. Le Prophète n'a pas besoin de disciples innocents et irresponsable. Ces jeunes n'ont rien fait c'est de la faute de leurs géniteur qui pense que la vie c'est uniquement baiser et faire des enfants .
Donc niogui si novembre 2022 serigne bii dieul nasi ay solution dieureudieufeti borom touba serigne mountakha yalla nafi yague thé and ak wérr ❤️ ❤️ ❤️
Rafa tv lii amna solo trop na kilifayi deff senn ligeuy 😭😭 sama xoll nekhoul en tenqu doomou touba 😥😥
Ligeey bi rafete na Macha Allah, li boko woneé woule wone kilifa yi dou gnou si diem dara,
Walay li
sou etat bi defe ligueyam gnouni degnouy khekh dine.
@@alassanecoly7200 wakhal dè,
Merci yay merci baye yalla nalén fi yalla bayi basi kanam🤲💞
bravo pour ce documentaire qui permettra de situer les responsabilites
Allaahu Akbar 😭 lii ñaaw Na Si Dëkkub sëriñ Tuubaa bii
Yen deh yena diara setane liguen di def amena solo trop je m'abonne à votre chaîne et surtout continuez à dénoncer vous êtes excellents
MANCHALLAH WA RAFAH TV SENE LIGUEY AMNA SOLO LOOL ✅🙏🏾🙏🏾❤️
Yalla naléne yalla soppi ak gnoune gneup 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ces jeunes ne sont pas des bandits mais des gosses découragés et sans repères. Il faut les aider. Le journaliste est fort car il parle avec eux sans les vexés. Bravo à toute l équipe
Bilay deugleuh
Bilay deugleuh
Vous êtes très important pour la société de ce pays
Bravo pour ca documentaire! Ça reste vraiment à saluer...Quand à aux gosses ils ne sont pas des bandits ils ont juste besoin d’aide et d’orientation pour qu’ils puissent retrouve leur famille...
Toutes nos félicitations il ya beaucoup de niches favorisant la déperdition de l'enfance déshéritée au Sénégal des programmes doivent être définis pour lutter contre ce fléau car il commence à prendre des proportions insoupçonnées il y va de l'avenir même des jeunes qui constituent la relève
Khalle yi kollen diapalle niou dem Inschallah ❤❤❤
Merci les journaliste 😍😍😍
Il faut denonçer ça. IL faut montrer la video au khalif general pour qu'il trouvera une solution le plus rapidement possible. Ça ne peut pas avoir dans une ville sainte comme touba . Merci pour le reportage
Ils sont au courant bien entendu sauf que leur ignorance veut tout dire...
Il y a un problème d’encadrement dans ce pays et aucun suivi.
Et très honnêtement je ne suis pas étonnée de voir ce genre d’image.
En tout cas c'est pas une belle image au ville sainte de touba
Nn billahi kii vrai journaliste leu👌👌👌👌
Thieuy li de dawna yaram lol di guiss lou melni thi deug bou melni touba mais khaleyi yalla na len yalla wagni guen tegue thi Lou bakh
Yalla nalén yalla gundi si barké s touba
Vous êtés trés important de ce pays
J'aurais bien aimé que ces informations soient transmises le plus rapidement possible au khalif général des mourides pour qu'il puisse prendre une décision pour recadrer et réinsérer ces jeunes.
En effet, ces jeunes ont juste besoin d'un encadrement et d'un accompagnement.
Vu qu'ils sont dans la ville de Touba je trouve c'est logiquement les autorités religieuses et administratives qui doivent y remédier en apportant des solutions immédiate.
J'ai énormément confiance en ce sage Khalif et je suis certain qu'il apportera son soutien intellectuel et financier.
Un grand merci à ce journaliste présentateur qui rempli bien son rôle " chapeau"
Allahouakbar ces bâtiments doivent être démolis dare dare
Le plus rapidement possible,
khalif bi diokhé na ndigeul baye fall yi
Deuk dou sel, gnifay dounde nioy sel di sellal
J'ai meme les larmes aux yeux yallah naléne bour allah takhawou
Touba thia canam Mogui déff lou am sollo thi touba wayé défarr degue défar khallé yi moko gueneu fouff bou gnou déffaré ndaw gny rék eulék degue by bakh
Vous avez parfaitement raison !
Défarr khalé yi mo gueneu lep bilahi walahi Touba thia kaanam mom khlés rek
Machalla merci beaucoup
❤️❤️❤️ la responsabilité incombe aux religieux
beau travail
Macha Allah fantastique vidéo Touba gar bou mag fala dane Diangé métier si wetou keur Serigne mame cheikh mbacke mome Serigne fallou di kou bakh waye même bir keur Serigne mame cheikh mbacke bofa wérre yeré té fermé wo bountou keur gui encore kenne neckoulle si keur gui yeré yeép laniye wérri soune keure mome damako sakh djellallé même aye Dalle yalla na yalla safara leup temou diarraleko si lokho Serigne bi
Ce journaliste il est fort👏👏chapeau a toi
Billahi wallahi
Wa touba ça kanam yalla nalénn yalla dollé taxawou yénank ji li serigne bi bek waww lénn goor
J'aime bien l'analyse du journaliste ta tout dis
Liii rekkk la Serigne biii wara takhaww mai Lou nekkk ga terre koo bayiiii liii dafa niaww sii touba😭
Niouss lenn gni gnibi senn keur 😂😂😂😂😂😂😂😂
Me li dafa niaw ani wa TOUBA sa kanam marce bi la niou wara tot 😭😭😭😭
@inconnu Warna contante kay
On est en novembre 2022 machalah cet lieu a été démoli
Celui qui qui dit que ses parents sont a saint Louis on habite ensemble a diaminar
Vraiment je vous remercie. Ils manquent juste encadrement où sont les parents ils ont démissionné en regardant les petit dans les rues
Machalla 😢
Ndaysane méttina yalnalene yalla takhawou
Lii eupp na thi deuk bou tolné Touba ak wathiouway bim am thi l'islam
Yalla nallèn yalla sopii barkè naby moustapha😭🙏
Li mom kouka giss ngir yalla naka wane sr bi li feumm dieum bougne si takhawoul khalé yi billahi oun oun😭😭😭😭😭😭
Merci rafa tv
Waadioryi niou yaratoul zen doom yi bayilen ci lo leen nehk Merci Rafah
Sama waay wallahi wadiour yi diambaar lañ ndakh diangal nañ leen wayé touba lonou manqué moy encadrement
@@khadimdiop4199 diangal nañ leende waye diangal rek daa doyul dañj leendi bayi ci zarétyi nioy deff lolen nehk ñi nioleen nehk anndal ta waadioryi donn leen contrôlé
Mon dieu thiéy yalla balle niou que v protège
Allahou akbarr yalla nalén soun borom sopi thi barkép srgn tb Mbacké
Bilahi Lou weer la Man Touba la deuk même sama kogne madiyana mbarya mo geuneu reub fii bilahi trop c'est trop
marché bi danko wara sobi ay usine ndaw ngi disi ligeye touba marché okas rek la am takhaw lensi rek
ndaye sans fi douna fi lou méti bilahi 2009 la fi niaw won 😭😭😭
Santal yalla bou bakh
info merci beaucoup alhamdou lilahi mon frère
@@serignesalioukane1612 fo deuk sama mbok mi
touba darou khodoss
@@serignesalioukane1612 bakhna deureuf cheikh bi yallna yala takhawou bou bakh
La principale cause est est la négligence des parents en vers leur fils
Ndeysane dawna yaram yalna yalla samou niou 🤲
Quelle honte! C est inacceptable. Ces enfants devraient etre à l ecole et en sécurité
Machallah liguéy bi rafétna yalna sunu brom sopi xaléyi thi lubakh
Ndaysan cey li dawna yaram de Man de sama rague buma bokal ndaye ak baye migui ci video dara lanuko yobou won Mou daw mais niogui koy set te incha allah dinanu ci takhaw
Liko meuna safara moy Serigne Mountakha mbacké na téck vidéo biiii beute rék . Légui mou safarawou
Wakhal ci kawe 😪😪😪
Yalla nalène yalla souñiou borom sopi
Gnii bonou niou koulène diapalèè lagne amout yalla nalène sounou borom guindii si liiiiii
Amine waye parent yi amna niou si responsabilité bu mak sakh
Gniii gno Bone senn bonou bopp rekk
Dieul aye millards diko diokhé Macky sall pour covid bi, té sa N'diabote toumouranké
Thieuye sounou kulifayi naniou oubii séni beute té ragal Yallah... Li dafa niaw té Touba à une histoire et c'est honteux de voir çà vraiment
J habite à Touba Mball mais ses jeunes ont les as abandonner alors que personne n'a parle pas c'est honteux ses jeunes font partie de la société aideons lés
Jaime bien lle journaliste
Lii niaw na mouy am si Touba
Kilifayi daniou wara djioublou thi euleukk ndaw yi,, construire des usines , ....; ndaw yi am possibilité deff des formations professionnel.... dakh touba waruta kharr dara thi Etat , Serign touba defarna ay mourite you mana arr deukeumbi mai sck....... ??? kon naniou geuna warrmane deukkbi *Lhomm quil faut a la place quil faut*
Tabakh yi lanou wara todj amou fi bene diarigne
Serigne touba yalla dinako wèrr dh fenn rek la done deff wayè lepp dina lèrr
Oh 😥
Modis 😭😭
Sa date yaye
Je rêve ou quoi fii Touba la . Lii doyna war d. Et où est le maire dans tous ça
Touba mom com amoul méri lounou wah rek nioune Serigne bi mère bi mom ban ndiarigne lafi am
Vraima
Pourquoi ne pas rénover ces bâtiments en faire des centres d'accueil pour mineurs cela peut aidé la jeunesse
Lima geunA métti thi touba moye barina loufiye khéw té s mountakha yagou thi dara 😭ay waye nanko wan Serigne Bi
Merci bcp Pask li ken waro ko neub Touba c la ville sainte
😪😪😪 yalla naléne yalla dimbali ba guéné léne si natou bi
Salam apres cette reportage.yallnaci solution toppou barkeb khadim rassoul le problème est constater maintenant liciy responsablite individuel kou nek naci taxaw moy waydiour di topp jabot gui bagne di gawa abandonne toute tank yii surtout lici kilifa yii warra taxawe kouko yalla menlo mou garaall léneko dou site bi rek a touba nanou cii joublou di Niane sounou borom safara amcii ndax touba lanou am senegal lanou amm yallnanou sounou borom dolle dimbali barkeb Serigne bi🙏🏿
Li mome sayabo serigne bi jok thi légui bala eup lakho boys yi maguis bilahi fi ak 10ans sunu léne topa towoule dagua déug touba lou doye waar c trop
Mias Ani police Touba bi Mame Touba la dege wayé dall
@@gueuemougueyemou7253 police bou touba takhoule gnoye police xolale touba nomou tolou am ñiari poste de police lolou manoule dara
Touba lumuo néw néw warona am 5 poste de police
Il faut montrer les images au khalif
Touba moy deuke bi gueune bonne si Sénégal
noo bol wakh loolou
Ndeye sàn yalna yalla wattou lën barkéb cheikhna Ahmad bamba
Won leen ko Seringne bi 🤲🤲
Ana Wa Touba ca kanam
Si l'Afrique est toujours en rtare c ça les parents qui savent pas valeur de l'enfant
Délén nebe séne kanam way touba mowaraw sy Sénégal nax ay miliyare lanie té nagayi wathe finasé galé yeup way
Sa leufeul day touba mo warra raw si Sénégal motakhe louné touba laye khéwé
nd yaw dof degiue moy yaw dnéye mé yalla bakhna frère
Ndeye sane nagne lén tégaat či yone rek, lou bone fèp leu am
Rafet lou wouma reportage bii, pour plusieurs raison
C'est ton probléme si c'est des soulards
Vraiment tu a raison
Marshallah amna solo
Non touba barina louféy khéw😢
Nanou déf centre ande taxawou niou weredi
سررت بك سرج منتحا بك سكرا والله 😭😭😭😭😭😭😭😭😭🇸🇳🇸🇳 jërëjëf touba sa kanam
Par contre man dama len yeureum ils ont désespéré 😢mais serigne andi solution
Avec ça niouni kéne doukofi wakhé khalé yoyou kéne santou si Mbacké wala s'y parents yi gnio wara téyé séne bôme yi yawmal khiyam résponsaboul bi sisa dom yalla gnoune lakoye lathi diékhouko sérigne bi lidafa rouss lou si ville sainte cité fakhmane amoul sakh Dakar so wakhé gniouni nonou Sérigne bi ga li bakagne Sénégal va mal 😡😡wakh dieou Bari diefeu touti 😭😭
Wallahi li gnaawna sax foudoul touba waxantoumalack si deukk bou séll bi.... Ana serigne modou lo ngabou?
Li dé mofi nekk ku bakh, Serigne Modou lo ngabou ak safinatoul amane li mo wara doon senn ligeey wayé toop khalé you jigeen yi rekk di soumi, li mo gueneu niaw fouf sole jupe bou amé fente wala tekk mèche si bopp, ta gni weur Serigne bi dou niou ko wakh degueu, aye règlements de comptes rekk la gnou fi néké. Li niaw na si sunu dekeu bi
@@akambengue512 bilahi sa bate thia kaww
Milliares yi serigne bi di diokh gouvernement bi di len ko dimbeule fi la bokhone si toute tanke yi lolou Moy deugue
C pas vrai diowoul dara gouvernement bii
Mamadou cisse meune ga féne
Marche bi mome wa touba ca kanam warnagnouko egalli loué magazin yi sambe ko
Dawna yaram yalla nalen yalla defal diam amine
Mais li yaguena fi. Depuis le début des années 2000. Vente de tabac yamba banditisme. Il ya du TOUT ici
😭😭😭😭😭😭 bilakhi dafa daw yaram
Doyna war trop nako serigne mountaha yekk gnaw na ci touba
Cheikhouna fall yalna ko yalla sam nio done diangano😢
GESTION WOU TOUBA LANIOU WARA DIEULÉ SI LOKHOY MAIRIE BI ... CE N'EST PAS NORMAL THI TOUBA AK STATUT BI MOU AM. DOU DEUG DOU YONE ... NANIOU RAXASS DEUKK BI ..
Niou melni La serign modou kara yor di dimbali tay niou niew diko indil ay problème senegal la kene mounoul comprendre ....
Bilahii Sénégal wakhado reck lii daffa eupeu sakh gnii fép si wér mi laniou nék dk la eupé
Yalla na Lén yalla doli yeurmandé barke seydouna Mouhamed
Rafahi tv sen video bi ndakh diar ngeun thi klifayi lata mouy nieuw thi reseau sociaux yi
@@akambengue512 🤝🤝
Li kou deuk touba yakarna oupoula mei war nanthié dieul decision amna heure yo khamni kén doufii gnimé diar
rafahi yénagui def liguéy bou am solo loll
Serigne modou lo ngaabou yaa you safinatoul amaane de
Lii leppou si sa loukhou la nekk
Niga sonné woon si mbirou aïda diallou sookou sonné woon si lii mou diekh takk
Lii de sogne kou bayyé nii woorna s touba moo guené garaaw ay aïda diallou
You ñakk xouroum yi
Mon cher y a pas plus irresponsable que leurs parents qui passent tout leurs temps a faire des enfants . Pourquoi les gens les plus pauvres ont plusieurs enfants , comment tu peut te dire que je fais des enfants et le bon dieu s'en occupe, c'est quoi cette réflexion des Sénégalais , et y en a qui se cache derrière la religion. Le Prophète n'a pas besoin de disciples innocents et irresponsable. Ces jeunes n'ont rien fait c'est de la faute de leurs géniteur qui pense que la vie c'est uniquement baiser et faire des enfants .
Pure vérité fuite de responsabilité des yalla na yalla yiir gniou same gnou same sunu ndiabot alhamdoulilah