Bilahi souma fatéliko temps yi sonko dane déme tribunal wala sou manif dane ame li états bi dane guéné thi homme de tenues arsenal biy guéne lou takh mounou niou ko déf di deuk bi niou déf ronde li metti na di agressé ni rék yalnaniou yalla mousseul sam niou aar niou thi daradiay seydina mouhamed amine
😡😡😡. La Solution que l'état et la police doivent prendre.. 1 / Interdire formellement le travail de moto taxi Diakarka à Dakar 2 / Interdire que 2 personnes puissent monter sur une même moto quelque soit la raison
Ex moi je travaille avec mon cousin comme électricien, plombier ou maçon etc on fait comment si on a une moto moto ?80%des 2 roues sont conduits par des vaillants travailleurs pas par des beuk lou yomb.Les peines de prison doivent être alourdies 10 ans direct et que le Président regarde qui on doit libérer avec les grâces.
Y’a ça aussi moi j’ai été témoin de plusieurs aggressions successives un dimanche soir sur l’autoroute vers 18h des gens à bord de motos attaquaient tout sur leur passage armés de machettes. Ça m’a traumatisé tellement me sentant impuissante devant cette violence. Et ce qui m’a fait le plus mal c’est que les agresseurs ont dépassés les policiers à quelques mètres
@@maremekane5309 voilà tu as tout compris. Ils demandent au citoyen d'aider alors le Sénégal c'est pas comme les usa au même si tu n'es pas armé le citoyen à côté a son arme et peut intervenir pour te secourir . Deuk bi kou yabou dieul say matoukay
Que chak famille donne 5000f pr mois et vous prenez les volontaires ds le qtier d'abord si sa suffit pas vous allez solliciter d'autres personnes et faire 2 brigade de 10 éléments ou 15 éléments gni assurez jrnee les otres la nuit t ngén maylén réreu
Très important ligua wakh lolou laniou wara def chaque quartier amna aye gens au chômage nioniou Guay recruter chaque maison maison niou léne di fay li c grave franchement
Agression en plein jour ngaye wakh ay tall lamp. Pourquoi pas niou ték ay force de l'ordre dans chaque coin des quartiers walahi dina wagni lou bari au moins niom soun guisser niéti moto you téglo dinan lén interpeller.
@@khadijacoly9392 niata gokh modane am manifestation ? Pourtant fep lan lén done deployer. En plus amna zone you geuneu dangereux niom xamnanko bounko défé priorité légui mou diex fi. Population lén la meun bo guissé sa cogne niouy déf naka soudoul nonou nga dénoncer lén thia bamouy tél.
Il faut sortir les militaires qui ne font rien dans les casernes..meme en italie les militaires sont disloquer dans les villes qui ont plus de criminalites vue que les moyens de la police sont derisoir..
C la même équipe qui sévit organisez vous et surtout cherchez des autorisations de port d'arme et armez vous kou agressé vous visez les pieds comme ça il va plus agresser ou peut être en rampant les honnêtes citoyens sont fatigués.
Loumouy doyé dakeu bi😂😂😂@@veriteabsoluedeugneekhoul1720c ça k j dit à mes enfants foor bakhoul bou nekon bilouka foré demna ci wadji sakh m yalla bakhna yalna yalla fegnal gni bonne gni
Réfléchi toi .policier da meune takhaw si cogne nek fofou rek melni gardien khel pour xalate tmt niou nekone fofou nio wara dimbali kokou en cet instant précis
@@Fidel_nimrod policier yi meunouniou takhakh kogne bou nék mais senegal police bi dafa takhawoul pour sécurité nit yi au moins sakh chaque 2km mou ame policier youfa monter dina takh agresseur yi ragal sakh mais fi dale yaye moytou rék
Il faut bien interroger le gars agressé On dit qu’il a été poursuivi par les agresseurs depuis la BIS située à côté de EMG castor Qui a avisé les agresseurs (7 au total ) Pourquoi avec autant d’argent à t’il pris un jakarta au lieu d’un taxi Pourquoi la route de la corniche pour se retrouver sur la route principale ??? Qui a donné à ces agresseurs l’heure, la marque et couleur du jakarta, l’homme en personne Je m’excuse
Si c’était moi le Taximan j’allais foncer directement sur le gars qui le sac . Parce que il était derrière et il a tout vu lolou motakh mou guiss li wadd !
peut être il se disait que comme castor ak Hlm soriwoul donc il va prendre Jakarta pour arriver rapidement. Peut être que les agresseurs l'ont observé depuis qu'il sortait de la banque.
Salam c'est vraiment triste Et ce n'est que la partie visible de l'iceberg C'est pire avec les batailles rangées entre supporters après les matchs navétanes et les dégâts collatéraux qui s'en suivent: agressions, jets de pierres endommageant les vitres des balcons des maisons alentours L'état du Sénégal est complètement à terre à cause du gatsa gatsa quotidien entre Politichiens reléguant au second plan les préoccupations quotidiennes des Sénégalais et des Sénégalaises. Que Ya Rahman sauve le Sénégal 😥😥😥
Je suis taximane mais de Tout façon soudon mane brome moto yi laye mbeukka auto bi yakhou wala gniou deih je m en fou😢😢😢 lolou rekk mo warone nekk rolou taximane bi
waxo deug dei nioune nieup guiss naniou camara de suveillance yii es pourkoi biniou koy agresse dimbliwo lene ko pare dinou sonal ak wax li ses injuste en plain journee daffa niaw koi *
Liiii la donn wakh demmm genr témoignage yiiii wadjii Di deff niii amoul sans fénnn rek fénn rek ....guisouniou kénn koulenn diapalé loutakh mou nek sa kanamm té défoo si dara
De toute façon counou diape ngay agressé nanou raay ndayam comme nouko wa Thiès défé c'est la seul solution 😡😡😡
C tous boléneko defoul kham
Yalla kou ray nitt la wakh dh wakhoul kou agressé dé bakhna daal
@@Babacar137Nagnou la diap gay agresser diga xam nakh li yalla wakh lagnouy défe ou pas
Agression maintenant cest partout en plein jour moto jakarta yi lagni wara éliminé
Je suis carrément d'accord avec toi
Bilahi souma fatéliko temps yi sonko dane déme tribunal wala sou manif dane ame li états bi dane guéné thi homme de tenues arsenal biy guéne lou takh mounou niou ko déf di deuk bi niou déf ronde li metti na di agressé ni rék yalnaniou yalla mousseul sam niou aar niou thi daradiay seydina mouhamed amine
Lolou yeup sorina... Gnata gnoyy geunn concours par an? Corps yeup c par excès, nagn fougue ci kogn yi et aar niit yi ak keur yii
Bilay lolou rk moy solution
vraiment tu as dit la vérité
Depuis politiciens yii agressions yi dafa yokkou
Policie africaine dou pour asskan bii pour politicien yi la Afrique dagno deugeu ligeuy la yakar
Sénégalais nétali RK wayé solidarité jamais 😢wakh rk
Vraiment gni daniouko topou ak nouniou hamé yor na khaliss bou tolou nonou
Peut-être foumou retiré xallis gnioko diaye wa allah allam 😢
@@moussacissokho4248 wala sahh mou yoole bopamm ken hamul deuk bee jahasso
Sénégalais mounumako comprendre , le Taximane il pouvait même sauver le gars mai malheureusement son intérêt personnel est plut fort.
Bilay lolou rk moniou tardel
Ils peuvent pas se retenir devant l’argent
Sathe rek
Taximane bi kayy il était l mieux placé pour sauver l victime avec sa voiture il devrait heurté un des motos
@@SaidouDiallo-ob2hb franchement! Mai xalisss beiiko titeul 😂😂😂
Solution woute arme rek ray Sen Ndeye bene bene
C’est la seule solution 😢😢
😡😡😡. La Solution que l'état et la police doivent prendre..
1 / Interdire formellement le travail de moto taxi Diakarka à Dakar
2 / Interdire que 2 personnes puissent monter sur une même moto quelque soit la raison
Pertinent !
C pa la solution
Késsé nak, tout genre de moto Sans exception
Ex moi je travaille avec mon cousin comme électricien, plombier ou maçon etc on fait comment si on a une moto moto ?80%des 2 roues sont conduits par des vaillants travailleurs pas par des beuk lou yomb.Les peines de prison doivent être alourdies 10 ans direct et que le Président regarde qui on doit libérer avec les grâces.
Quel lien entre moto et agression ?
Senegal bouñioulay agrèssè kèn doula dimbali 😢😢😢
Guisgua dhé kène doula falé
Surtout ceux qui sont en voitures c'est bizarre
Il faut que gnépe di amme pétrole walla essence ak allumettes, gnome bou gnou yorré pompe gua arrosé léne
Vremant bi mom da yomb
Bilahi Tik tok reck
Yéna yambar rek nioune bi niou agression sonalé souniou pont bi si autoroute bi dalifort nio si Diouk mou dégne ak Grand Éric
Âme nguéne foulah
Nolein def?
Où va notre pays sheuttt😢
Yen kougni agresser nguen beug gayi intervenir ta yorougnou arme
Y’a ça aussi moi j’ai été témoin de plusieurs aggressions successives un dimanche soir sur l’autoroute vers 18h des gens à bord de motos attaquaient tout sur leur passage armés de machettes. Ça m’a traumatisé tellement me sentant impuissante devant cette violence. Et ce qui m’a fait le plus mal c’est que les agresseurs ont dépassés les policiers à quelques mètres
@@maremekane5309 voilà tu as tout compris. Ils demandent au citoyen d'aider alors le Sénégal c'est pas comme les usa au même si tu n'es pas armé le citoyen à côté a son arme et peut intervenir pour te secourir . Deuk bi kou yabou dieul say matoukay
Mai khér yangi fi, fo tourné yem tihé khér
❤ Bismillah ❤ yén Kaye dimeuliwolen ko Guen daw nann docteur après la mort 😢
Ki bimouy nieuw fékeuneu agresseurs yi daw, bou yagg Caméra de surveillance yi nékone si place bi moko djeul
Toute moto n ayant pas d immatriculation lisible doit être confisquée
Que chak famille donne 5000f pr mois et vous prenez les volontaires ds le qtier d'abord si sa suffit pas vous allez solliciter d'autres personnes et faire 2 brigade de 10 éléments ou 15 éléments gni assurez jrnee les otres la nuit t ngén maylén réreu
Très important ligua wakh lolou laniou wara def chaque quartier amna aye gens au chômage nioniou Guay recruter chaque maison maison niou léne di fay li c grave franchement
Tous les bandits ont été libérés
Amna kounei khamé na Agresseurs yi Grand Yoff laniou deuk tei nena brom djassy bi Ndjogou la toude
Agression dou yeufou guorr
Vraiment
Niakk fayda la gor deuggla day daur War
Il faut les fermer en 10 ans de prison
Bolénsi ko diapalé wonne khaliss d'où raw
😂10 ans, khana 50 ans gua beg wakh
@@amethngom7873ngay diapalé nitt teh amo arme sougn la réyé ya perte
Mome kay dafa dioum 60 ans la beugona wakh@@papesaliougueye1729
Mobilisez vous faites des reunions de quartiers "operation watch " surveillance de votre quartier.
Agression en plein jour ngaye wakh ay tall lamp. Pourquoi pas niou ték ay force de l'ordre dans chaque coin des quartiers walahi dina wagni lou bari au moins niom soun guisser niéti moto you téglo dinan lén interpeller.
Verité absolue
😂
Kikey dof leu
Ya combien de coins à Dakar
Les force de l'ordre meunouniou assure lolou
C'est la population qui doit régler sa une bonne fois
@@khadijacoly9392 niata gokh modane am manifestation ? Pourtant fep lan lén done deployer. En plus amna zone you geuneu dangereux niom xamnanko bounko défé priorité légui mou diex fi. Population lén la meun bo guissé sa cogne niouy déf naka soudoul nonou nga dénoncer lén thia bamouy tél.
Personne n’as aider le gars ont n’as bien regarder la vidéo
Vous avez bien raison on a tout vue personne ne la soutenue
Cest bien fait pour le taximan
Bilahi
Bakhna si taximan bi
Gnak doylou rek AK beug Lou yomb
Billahi borom taxibi kene douko yerem par ce que sathila
merci niaw
Yoré ay millions tamite di dougou si jakarta au moins nga dieul taxi sakh ak rew mou woradi bii doye warr yéneu yii kharou la😮😮😮
Bilahi
Pourtant lolou ladon wakh
@@mamemorfall3066 doyna warr
@@pendatall8126 vraiment té niouni momoul khalisse bii kii la yoni nala diokh passou taxi wala niou khôl lénéne la vie est sacrée
Vraiment
Do bayyi doul mounane nioko done dimbeuli khana bi agresseur yi démé chaque jour c comme ça médecin aprés la mort rek😢
Vraiment
Il faut sortir les militaires qui ne font rien dans les casernes..meme en italie les militaires sont disloquer dans les villes qui ont plus de criminalites vue que les moyens de la police sont derisoir..
Surtout lolou bane ndieurign laniou am
Copin lolou wakh ko le ministre des forces armées pas les militaires ils n'ont rien fait un peu de respect
Tant que les deux roues circulent librement y'aura toujours des agressions, ya beaucoup de deux roues a Dakar et surtout l'arrivée des Thiak Thiak
C la même équipe qui sévit organisez vous et surtout cherchez des autorisations de port d'arme et armez vous kou agressé vous visez les pieds comme ça il va plus agresser ou peut être en rampant les honnêtes citoyens sont fatigués.
Je suis du même avis que toi bilaye c'est la seule solution 😢
Lou tak diapalé woulé ko
Surtout ça c ça qui fait mal imagine toi ya de gens qui était à côté et regarder au lieu de prendre le pierre et jeté sur eux
Dégo dagni AM pistolet ?
Gniata nite lagn réy 🗡️
Si genre ÿi ?
Kou yoroul armé nk😭😭
😂😂😂😂😂😂😂😂😂taximan bi wouy li motakh fooor bakhoul limouy foor la khamoul
Fooroul dé dafa sathie moko tay
Pour mane sakh daleu agresseurs bi la foor
@@anna2945😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
*Momm kay dougual na bopam😂😂😂*
Loumouy doyé dakeu bi😂😂😂@@veriteabsoluedeugneekhoul1720c ça k j dit à mes enfants foor bakhoul bou nekon bilouka foré demna ci wadji sakh m yalla bakhna yalna yalla fegnal gni bonne gni
Naniou manko dokhane ndayou sathie yi kugn si diap ray sen ndaye
Oú est Sonko pour apporter les solutions contre ce banditisme
Dakar dafa bari kogne yo khamni ayy ragal laniou
Yéne douniou dakhar ndayou Agresseurs yii😡
Kou tite Galse’n rek lalal j’aime 🤦🏽♂️
Mobiliser vous armer vous kou ngen si diap tall lene ndeym c tout c des hommes comme vous
Comme si ce pays n'a ni police ni gendarmerie c lamentable.
Réfléchi toi .policier da meune takhaw si cogne nek fofou rek melni gardien khel pour xalate tmt niou nekone fofou nio wara dimbali kokou en cet instant précis
@@Fidel_nimrod policier yi meunouniou takhakh kogne bou nék mais senegal police bi dafa takhawoul pour sécurité nit yi au moins sakh chaque 2km mou ame policier youfa monter dina takh agresseur yi ragal sakh mais fi dale yaye moytou rék
Il faut bien interroger le gars agressé
On dit qu’il a été poursuivi par les agresseurs depuis la BIS située à côté de EMG castor
Qui a avisé les agresseurs (7 au total )
Pourquoi avec autant d’argent à t’il pris un jakarta au lieu d’un taxi
Pourquoi la route de la corniche pour se retrouver sur la route principale ???
Qui a donné à ces agresseurs l’heure, la marque et couleur du jakarta, l’homme en personne
Je m’excuse
Mais peut être qu’ils sont juste positionné devant les banques à attendre ???
Yow tamite tu penses que soudone deal leu les agresseurs allaient accepter que leur visage soit à découvert ?
@@poundkiima4241 j’ai juste donné mon point de vue
Certains délinquants sont comme des clients ordinaires dans les banques
Tué vraiment doué merci excellente question ?
Tué magistrats 😁
Dele sorale mote biverly yi la plu pare gni ko yor yeu sathie molene Takhe diouk fete très atation
On a tous vue la vidéo 😢 il n'a été aidé par personne, c'est décevant 😢
Si c’était moi le Taximan j’allais foncer directement sur le gars qui le sac . Parce que il était derrière et il a tout vu lolou motakh mou guiss li wadd !
C´est ien fait pour le taxi mane il est exactement comme les agresseurs
Mane dé Kouma kar ma dakhar ndayam ndayam
😂😂😂
😂😂
C'est grave
Chauffeur Taxi bi hier ladone wakh néé kou daxar ndayam
Chauffeur Taxi yép ay satheuu lagne l
Mes seneguale nane guaye yoré aye millions té meno dieule sa oto bope ndahe gua yore sa sac dohe bannie laye tope
Waa legui kou mom sa xaliss guenei ko dann laa wara agressé dangua xam loum fi daan def ta neinan si moto bi la yeiiguoon réfléchi un p
Yaw mousse guaa gneupp
amougnou auto
peut être il se disait que comme castor ak Hlm soriwoul donc il va prendre Jakarta pour arriver rapidement. Peut être que les agresseurs l'ont observé depuis qu'il sortait de la banque.
Dama nop nabou leye déh ❤❤
3O PERSONNES 1 MILLIONS PAR MOIS ATAYA AVEC SURVEILLANCE 🇸🇳🇺🇲🇬🇳🇨🇦👀👀👀💪💪💪💪
Lou takh senegal police manul deff patrouille si quartier yi wett yi
Sénégal si boopame mo amoul diapalanté😢
Garage moto yi nek si côté banque 🏦 yi mo doul yone
C parck senn kogn bii ayy goor choco choco nioffaa deukk lii deh Bilayy soudonn GUEDIAWAYE Borom taxi bii moyy foncer mbeukkk sen ndayy
Gni yoré affaire justice bi nio xamoul dara
Leup sa kaname la té dimbaliwolèn ko bagnou yomb khalis bi.
😢😢😢😢😢
Li khew Sénégal doyna warr lol population bi rek nio si meune dara
Il faut faire une demande de port d'arme maintenant pour être tranquille dans ce pays
Gnii takhaw di setane nio geuneu bonne nieup😢netali rek guéné yakamti thiiip
Taximan bi bien fait ça lui apprendra
Yenn gni yenaa meune fenn binioukay agresser ken dimbali wouko on a regarder ls vidéos doull rekk
Guisnan video bi ken diapaléwouko dani doull rk
Alhamdoulilah borom taxi bobo nimako méré diépi ko ndakh dokhalim
Film bi kat bahna ndah preuve la
Sa data yaye
L'Etat dois prendre des mesures drastic trop c'est trop
Boy yi grd yoff laniou deuk
Yalla nagnou yalla samal bopam defalen Diam werr katane ak soutoureux
No na population rekk dieul sene matouwaye rekk
Ms attente bou néké 3millions khana Kone 3 tack yi Wade khana tack 100mille la🤔thieuy yalla 😢
Le président doit aider les jeunes des projets de travail tout sa c manquement de travail Qu'Allah nous aide ❤❤❤
Salam c'est vraiment triste
Et ce n'est que la partie visible de l'iceberg
C'est pire avec les batailles rangées entre supporters après les matchs navétanes et les dégâts collatéraux qui s'en suivent: agressions, jets de pierres endommageant les vitres des balcons des maisons alentours
L'état du Sénégal est complètement à terre à cause du gatsa gatsa quotidien entre Politichiens reléguant au second plan les préoccupations quotidiennes des Sénégalais et des Sénégalaises.
Que Ya Rahman sauve le Sénégal 😥😥😥
Je suis taximane mais de Tout façon soudon mane brome moto yi laye mbeukka auto bi yakhou wala gniou deih je m en fou😢😢😢 lolou rekk mo warone nekk rolou taximane bi
Loudoul nétali ak dull meunouniouko
waxo deug dei nioune nieup guiss naniou camara de suveillance yii es pourkoi biniou koy agresse dimbliwo lene ko pare dinou sonal ak wax li ses injuste en plain journee daffa niaw koi
*
Bilay walou wouniouko dhè ba parè di reuy lamigne
Il faut faire sortir l armée
Italie dé nonou laniou dèff guéné arméé bi
Mes yéne niouy khass nan dimbali wounioukén kou yor arme mom nékhouta lala ms soudon manla mom niom niépoulay tothie séne lou bonne ay khathie laniou rk😢
C'est des agressions au scooters
Au moment des faits tu ne l'a pas aidé kougn fii agresser niou sétane mais nétaliii mom manchalah
lii metti na wayy 😭😭😭🙏🙏
Dieulénne sénny mattouwaye sécurité senny quartier en premier... gnioune dhé gnioyy sécurité sougniou quartier kougniou diapp dotoko défati 🔥🔥🔥🔥🔥
Grand yoff agresseur yi fadiar laniouye kar gni liguéyi wa Dakar nagne déf comme wa thiés mbédioume kaname borome mokoye fadiale bopame
Boutique bobou domeram dji togone si bounte bi,sarap ndeyam la defoul, pour dimbali ki gnou agressé
Liiii la donn wakh demmm genr témoignage yiiii wadjii Di deff niii amoul sans fénnn rek fénn rek ....guisouniou kénn koulenn diapalé loutakh mou nek sa kanamm té défoo si dara
Vraiment une telle sommes avec un diakarta
Je suis parfaitement d’accord, dieul taxi 3.000 beu 5.000 francs sah mo geune fouf
sama grand frére dab nagn ko si scooter yobou 6millions si mom ba tay 0
COMMUNAUTÉ BI OUT LENN 3O PERSONNES GNO SURVEILLANCE EREA YI 😎😎👀👀👀👀💪💪💪💪🇸🇳🇺🇲🇬🇳🇨🇦
Sénégal nékhoul dé agresseurs bo Rey dém kaso 😮😮😮
On doit immatriculer les motos
Et mettre dea caméra dans les ruess
Taximane bi tamit badolana dh nite day doylou Senegal métina way 😢😢😢
Il faut commencer à couper les mains plus prison si no il y aura plus grave
3 millions 500 nga yoré yék si moto di diaye walacana way si wéroul khana Taxi sakh sakh tanéna
Kou agresser gnou teuthie le sa guirou dounde kou raye niou raye la moye solution bi
Les gens qui étaient présents étaient en mode spectateurs alors qu'ils pouvaient intervenir
Sénégal dou mousa am sécurité
Baye fall gni dagniy doff doff lou rek bly ioe nagni doug hlm 3 xam nagne ni hlm 6 dafa wéte motax mais gni kougne si nday diap
Lii rék motax dkr souma fa démé douma fa beugue yague 😢😔 doundou bou métti rék nga fayy doundou Lo yorr🫰🏻dou takhaw 🙌🏻🤦🏻♂️
Saway beugu lou yombe rk moko yobé 3million500 di dieul diakarta do dieul taxi
Surtout lolou 😢
Li rék laniou meune danioulaye sétane baniou raye niou tak micro yi di wakh rék
Personne n'a levé le petit doigt, ce sont tous des lâches ! Il y avait assez de monde pour arrêter ces malfrats ...
Si vous attrapez un agresseur il faut le T...er ne le laisser pas partir, la population doit prendre ses responsabilités.
Bilahi mane souma dougué si Gab bi bay guéneu damay tiite parce que do kham koulay topou moy lolou
Il faut mettre des poste de sécurité avec caméra de surveillance dans chaque quartier et y mettre les policiers qui ne font rient sur la route