Diar Diari Balla Gaye 2 Ci Mbapat de A à Z : Et Tout Les Lutteur Guediawaye les révélations de Fadam

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 20 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 66

  • @abambayediop2232
    @abambayediop2232 3 роки тому +1

    Merci fadam man mom contane n'a si yeuw nit kou bax nga té taxaway binga âme si digeunté gouy gui sacadior rafét lou nako yalla nassa djam yague dohalal

  • @marapene2537
    @marapene2537 2 роки тому

    Mashaa'allah fadam 2 kou xaam lamb ga yala na sa jaam yaag

  • @loufa9357
    @loufa9357 3 роки тому +4

    Merci ferr fadame yalla na yalla faye félicitation

  • @championBoulan
    @championBoulan 3 роки тому

    Machalah fadame mii ndaane de gue la dafa topoue lambeue dembeue

  • @khalilfaye3879
    @khalilfaye3879 3 роки тому +2

    Fadame 2 vrment merci

  • @abdoutall8491
    @abdoutall8491 3 роки тому +5

    Machalla fadame lambologue nga machalla

  • @vieuxba2498
    @vieuxba2498 3 роки тому +1

    Bou nieup meleni yaw fadam diame tel moye âme sopenala t khawmala machala le générosité

  • @omarfaye1794
    @omarfaye1794 3 роки тому +4

    Machaa Allah bro

  • @abosarr7369
    @abosarr7369 3 роки тому +4

    Nite kou bakh la bilahi

  • @papindiaye4551
    @papindiaye4551 3 роки тому +14

    Fékéna Mbappat arrêt Dial Mbaye, bi Modou Di yénou Less 2, Di Mbott bay wadia khar Elton mais Modou Kouko setane Mbappat khamni Sénégal mofi dakh Beuré. Modou khétou Beuré yimou am Souko wa Sénégal khamone Adouna Tass. Modou topnako même Mbappat Assane Diouf, weur ko Ndombo AK yeukeuti tankam ba si kaw takhoul nga dane ko, songue KO takhoul nga dane ko, au contraire iow Miko def yay nek si danger bou reuy. Limay niane Yalla Modou boumou beureti AK géants yi si arène bi, legui Yene khétou Beuré yi fegne inchallah.

    • @abdouazizndao216
      @abdouazizndao216 3 роки тому

      Lou leer

    • @moussamangane7156
      @moussamangane7156 3 роки тому +1

      Fégnoul si digantéme ak balla gaye2

    • @papawade8521
      @papawade8521 3 роки тому

      @@moussamangane7156 deux défaites balla daka diangual beurré technique Lakay dané

  • @andedieulefimacky5209
    @andedieulefimacky5209 3 роки тому +8

    Balla gaye 2 danena mitrailleuse

  • @moussaboye3443
    @moussaboye3443 3 роки тому

    Machalla fadam kou kham Lamb nga khamnala bou bakh depuit bresil

  • @khalilfall585
    @khalilfall585 3 роки тому +4

    J veut l numéro d celui qui parle svp

  • @marapene2537
    @marapene2537 2 роки тому

    Sa cadior 2 sama champion bi yala nala brom bi taxawou defal la jaam

  • @matarsamb1980
    @matarsamb1980 3 роки тому

    Merci beaucoup fadame Junior machalla

  • @kebadia5831
    @kebadia5831 2 роки тому

    Amna solo Mobo anfa

  • @seckseck2238
    @seckseck2238 2 роки тому

    Machallah fadam

  • @moussagueye1403
    @moussagueye1403 3 роки тому

    Courage frère Omar Wade

  • @assantoure9965
    @assantoure9965 2 роки тому

    Ndaysane sa kadior 😟😟

  • @kebadia5831
    @kebadia5831 2 роки тому

    Amna solo fadam🙏🙏

  • @SenCrypto
    @SenCrypto 3 роки тому

    Fadam2 est le meilleur

  • @julesleroi
    @julesleroi 3 роки тому +2

    Mame balla déh même tonnerre dafko yanou wathiei ko ndakh diassi yi😂

  • @mamadoudieng3093
    @mamadoudieng3093 3 роки тому

    Ken dou modou lo le roi des arènes

  • @alassanendiaye1974
    @alassanendiaye1974 3 роки тому +1

    Yeppp

  • @chosen1798
    @chosen1798 3 роки тому +1

    Nice

  • @abosarr7369
    @abosarr7369 3 роки тому +2

    Bilahi ya kham lamb yaw re ya wara wakh

  • @amadougueye3243
    @amadougueye3243 3 роки тому

    Jaime cé gas

  • @babandiaye3154
    @babandiaye3154 3 роки тому +4

    Balla gaye dane aliou seye2 khamo lingay wakh

    • @Papi-yb2lf
      @Papi-yb2lf 3 роки тому +2

      Il a dit "si Lima guiss", manam liko beuteum may.

  • @bayedjilymbaye7185
    @bayedjilymbaye7185 2 роки тому

    Balla Guaye 2 mofi ne fadam

  • @assantoure9965
    @assantoure9965 2 роки тому

    Ama Modou sa baye la thie lamb yaw mbapatt ay déffét rék ngafa dieulé

  • @khalilfall585
    @khalilfall585 3 роки тому +1

    Mon ami namnako

  • @FS-jh4ky
    @FS-jh4ky 3 роки тому +3

    Balla gaye mo dane alioune seye 2 assane diouf
    Balla gaye mo dane sacadior marché peund après niou beuré bount keur mor fadam ben supporters yakk ko
    Balla gaye dane na moumeu
    Balla gaye dane na dolf dane mitrailleuse dans baye peulh dane papa sow

  • @jobendongo3080
    @jobendongo3080 3 роки тому

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ modelo

  • @moustaphadjamilmbaye1461
    @moustaphadjamilmbaye1461 3 роки тому

    Lamb arrêt dial Mbaye Ama Gouy Gui yague na demb mbapat guediawaye

  • @ballambengue8662
    @ballambengue8662 Рік тому

    fadam gua balma demewoul nonou deee Alioune seye 2 Fall mouma 2foi lanou beuré Fall mouma moko dane glamb toukoulor Alioune seye2 daneko école 25 défoul 4 api dafa tok drapo bi ba taye dji guisoul drapo bi bilhahi🙏

  • @Bassirou2mbenguembengue
    @Bassirou2mbenguembengue 3 роки тому +2

    Modou lo rek le roi niaw guediawaye diuel sen mbapatt yepou dem yonam moy bandin de le roi

    • @ousmanedieng429
      @ousmanedieng429 3 роки тому +2

      Faut préciser qu'il s'inscrivait en légers, et c’était vraiment un léger mais il faut le dire. Une autre vérité est que les Mbapatt à ''Arret Dial Mbaye'', c'était presque un Mbapatt à Domicile pour Modou, Parce que organisé par les plus hostiles à émergence de Balla Gaye (toujours hué à ce Mbapatt). Al'époque l'écurie Plateau de Guédiawaye attaquait Balla Gaye dés qu'il le pouvait parce qu'il voyait son ascension commeun frein pour Ndiassé ( grand frére de Diali Ibrahima Thior BADA) leur mentor. Le surnom Lion de Guédiawaye était d'ailleurs l'un des problémes parce que Ndiassé etait le premier à le porter.

    • @Papi-yb2lf
      @Papi-yb2lf 3 роки тому +1

      @@ousmanedieng429 Vous avez raison sur pas mal de choses mais sur le Mbappat précis dont parle Fadam 2, Elton était l'un des plus lourds. Il n'a jamais été un léger Elton mdr

  • @bassirouka2042
    @bassirouka2042 3 роки тому +3

    me aliou seye 2 balla gare la battus mbapatt

    • @assballagaye2348
      @assballagaye2348 3 роки тому +1

      Balla gaye dan na Aliou seuy ak sa kadior yeup

  • @challenge6757
    @challenge6757 3 роки тому

    Balla dane neu aline seye final

  • @babandiaye3154
    @babandiaye3154 3 роки тому +1

    Bg2

  • @sarrabdoukarime8259
    @sarrabdoukarime8259 3 роки тому +2

    Dagua dioum Alioune Séye 2 ak Mouma niari yone laniou beuré béneu bi école 25 bénéne bi lamb toucouleur kou nékeu dane moromam

  • @birandiop7056
    @birandiop7056 3 роки тому +1

    Bay fall koubakhgna amal diam

  • @moussaboye3443
    @moussaboye3443 3 роки тому

    Mai BG2 dane na SA kadior dane na alioune seye2 ausi

  • @moussaboye3443
    @moussaboye3443 3 роки тому

    B.G2 dane na metrailleus ausi

  • @khalilgueye9167
    @khalilgueye9167 3 роки тому

    ✍✍✍😍

  • @bayedamebeye5389
    @bayedamebeye5389 3 роки тому +1

    Kham na beure dh mm

  • @fatimazahradiallo1883
    @fatimazahradiallo1883 3 роки тому +1

    Desol3 dioum nga si you bari Mouma mo dane modou lô balla aussi danana metraîllesie

    • @momoba6527
      @momoba6527 3 роки тому

      Iow kou niamé yalla gua

  • @Papi-yb2lf
    @Papi-yb2lf 3 роки тому +3

    Balla Gaye 2 si bopam souniou KO djokhone Le Saint Coran néko mou watt baparé wakh Kouko gueneu Yém si Beuré Mbappat mou wakh leu Modou Lo. Balla Dadone tokk diko setane di wakh lounek.

    • @thieraw964
      @thieraw964 3 роки тому +4

      Balla da dougou parcelle dane gneup
      Modou lo xeuy wo téléphone moussa dioum mouné balla gaye mbappate bobu leu dieul revanche si mitrailleuse

  • @bayedamebeye5389
    @bayedamebeye5389 3 роки тому

    Wa lac 2 mm khana doun ko wakh ci mbapatt wala dadaan rassou rek 🤣🤣🤣

  • @ousmanebasse3936
    @ousmanebasse3936 3 роки тому

    ALIOU DIOP 2 MOYE MBEURAME

  • @mbayediallo4123
    @mbayediallo4123 3 роки тому

    Mais less 2 dan na modoulo

  • @gorandiaye1862
    @gorandiaye1862 2 роки тому

    Modou lo bada dao falama fekk kene dou fadam

  • @mouhamedfayefaye6945
    @mouhamedfayefaye6945 2 роки тому

    fadam ko dann yaww

  • @adamamballo7886
    @adamamballo7886 3 роки тому

    donc modou mérite son roi des arénes

  • @ahmadoumadadiagne7955
    @ahmadoumadadiagne7955 3 роки тому

    Mbapat bi gay wax modou lo di daan Elton balla gaye bërewul boobu balla ñi me ko ci làmb yombul...
    Man fekk naa ba sa kadior di daan Elton final mbapat maagi taxaw boobu balla bëriwul sa kadior bgoon naa bëre ak moom boobu waaye balla gaye boobu bàyyi na mbapat mé billaahi wallaahi tallaahi bër bu mel ni balla wa guediawaye dunu ko gaaw a amaat

  • @papendiaye3400
    @papendiaye3400 3 роки тому

    modou lou moumeu setan nako combats bou doy waar

  • @khalilgueye9167
    @khalilgueye9167 3 роки тому

    🤣🤣🤣🤣