C'est une vidéo sympathique. Le genre de vidéo qui donne beaucoup de nostalgie. Moussa Dioum est bien pertinent et assez objectif. Deux choses assez rares chez nos simplets amis lutteurs. Baye Peulh à côté en est une preuve immédiate! Du reste, la carrière de Moussa Dioum nous laisse beaucoup de regrets. Il a toujours montré beaucoup de bravour, d'agressivité et d'explosivité.
Moussa Dioum Yalla nako Yalla yereume té diégalko Barcke Seydina Mohamed Nabiyana Sallahou Alayhi wa Salam❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
J’ai vu une fois maman bay peul parcelle Mané ko ana bay peul mounè ma dem na USA 🇺🇸 mane fofou la nek legi me nema peul kou bakh la bilakhi yalla nako Yalla nako Yalla yerem
Nexoul ba nexoul bg2 et MODOU LO yagg naniou todj mbapatt bilahii Modou lo dafa yagg beug lamb ndeysann sén rivalité dafa naturel MODOU LO c le meilleur il lutte hyper bien
Modou dh dou sene morom billahi loumou def mbapatt benene mbeur deffouko fi dane ay champions comme bruce lee , papa sow , nar tourè , Baye Mandiayr , Ama Baldé , Elton , Less 2 , Ouza 2 Billahi kene dou Kharagne Lo
Moussa dioum ndanaan la mais yemou daaan diuel moo yakh Yarame wi Bouko bayee te defarou Di Fouting Di Contac bou bakh Di def 3seri par jour di tued heure di yewou heure moytou thiaakhane di leethie père birahime aye khalatame Fonkou aye mbokame inchalla dina Nieuwaat
Thier Aw hana roi bi diekhaloul guediawaye dougou sene gokh bobou radiakhé tournoi ba dane less 2 dane elton dane alioune seye 2 dieul tournoi ba defier gadaye gadaye di daw nakh coalitions la guissoul wone
@@layekharagne2224 si c'est la vraie personne ce même laye que je connais c'est pas la peine de répondre parceque toi tu es loin d'être objectif tes sentiments prennent dessus sur la vérité Tu es loin d'être un sportif Ciao Ciao 👌👋
Thier Aw lolou yene la rek objectivitè subjectivitè la yamalè modou mo fi nekk un point un trait koumou nekhoul mom la rek c le roi il dérange , dakk lene beurrè dakk lene khekh guene lene rafet palmares guene lene populaire eup lene khaliss ça c le roi des rois Modou kharagne lo kou merr tant pis 😂😂kou bagn roi 🤴 bi ay dokhote mo lay rey 😂😂😂
Cey adouna moussa dioum yalnako yalla yeureum té diegeulko si barkè seydina mouhamed sws ❤️
C'est une vidéo sympathique. Le genre de vidéo qui donne beaucoup de nostalgie.
Moussa Dioum est bien pertinent et assez objectif. Deux choses assez rares chez nos simplets amis lutteurs. Baye Peulh à côté en est une preuve immédiate!
Du reste, la carrière de Moussa Dioum nous laisse beaucoup de regrets. Il a toujours montré beaucoup de bravour, d'agressivité et d'explosivité.
Ndeyesan moussa dioum un vrai champion yalla nako yalla yereum repose en paix 🙏
Moussa Dioum Yalla nako Yalla yereume té diégalko Barcke Seydina Mohamed Nabiyana Sallahou Alayhi wa Salam❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
yalnala borom bi yeureum ta xarei leu si aldiana you geuneu kawei yi barké borom Touba🙏 moussa dioum paix a ton âme🙏
Yàlla nako Yàlla yeureum te diegeul ko RIP champion
Cey balla gaye vraie gaindè💪🏿💪🏿💪🏿🦁🦁
Thaï Moussa Dioum Mom Dafma Néx Rék Ta Yallah tax Wallahii Bay fall la Ta xoll bii Dafa Nice Naysann Wallahii champion ladé séka Thiath Moko Topou Rék Wallahii Mai nak Yallah baxna 🙏❤️🙏
paix a son ame 😭
Le meilleur technicien des parcelles grand Moussa dioum respect
petit bou MOUSSA Balla gaye hana modou guinguineo la deuk daguene doff sakh
@@layekharagne2224 laye kahragne lo nkm
Bilaye sii adouna gisouma kouko dakh beurei ndanane leu moussa rek
Woy sama fii issina 😂😂
Balla gaye c'est le millieur sa génération
Modou lo moma wo téléphone nema ben gayin mofi niew dane nieup welelelele balla gaye 2 d'où nit
Fenn bokeuna si bakar yi yala gueuneu sipp
Moussa Dioum yalnako yalla khare adiana firdawsi si barke serigne touba
BG2 c'est le meilleure c'est le champion c'est le king ❤❤❤❤✍✍✍✍
Balla Gaye Ak Modou War Nanio Def Film
😁😁😁
wakhal dé
Balla yague na tothie mbapatte 💪🏾🔥
Oumar Ndiaye modou mo ko guene tothie
Paix à ton âme 🙏🏽
Lamine j'aime beaucoup le façon que tu travail.
Paix à son âme 😭
Moussa yak baye peulh yena niakk kignane bilahi
Moussa Dioum yalna ko yalla yeureum tai kharé ko aldiana, Amine
Kén dou balla gay 💪💪💪💕
boy sete Mbeur dege kholal moussa Dioum 👍🏽👍🏽👍🏽👍🏽
Ndeysaan yalla nako yalla yeureum
Yalla nala yalla yeureum champion
Balla Gaye 2 💪🏾♥️
bilahi yaay Champion Balla gaye 2 késsé
C modou lo mon lutteur ,mais franchement balla ndanan la
اللهم اغفر له وارحمه واجعل قبره روضة من رياض الجنة ء مين إللي يوم القيامة بر كب سيد نا محمد رسول الله صلي الله عليه وسلم
nooooooo Bilahi Moussa Dioum réy nama .22 minutes 12 seconds
néna lan Worna Yalla Elton masta séw😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Yalnako yalla kharé aldjani firdawsi
J’ai vu une fois maman bay peul parcelle Mané ko ana bay peul mounè ma dem na USA 🇺🇸 mane fofou la nek legi me nema peul kou bakh la bilakhi yalla nako Yalla nako Yalla yerem
Xlô 👑amoul morom
Moussa Machallah deko si bole Balla gaye 2 moy séné baye wahou lenefi dara
Modou Diop ana eumeu sene
Mai eumeu diarou fé wo modou dongui Fi dé
C'est balla qui a aboli l'esclavage de la lutte au Senegal contre leurs maître yekini balla c'est le meilleure c'est le champion c'est le king
eumu sene di sen mame
yalla nako yalla kharé aldiana you gueun kawé
Modou billahi souy buere ak balla modou moy niuew kharagne dou niuew mé dara 2/1 laniouy waxtane souma pare sii thiatou falay dinako may chance tegal ko roi inchallah kharagne moy niuew
Mdr 😂😂 boulén forcé ak balla 10 combat dakoy dane
Jule baldé ndanane bu mag bi
Modou Lô bayou mbeur yeupeu 🔥🔥
Balla dh bokousi
Waye Balla moy bayam
No lut tv bilay sén liguéy rafétt 🙏🙏🙏🙏🙏sokhla naniou bay ma diaye nak boumané nék?
Lamine bégue nala dh.dananu parcelle yi macha alha 🙏🙏🙏🥰🤲🤲🙏🏾💪💪💪
DIMANCHE 19 AVRIL 2020 MACHALLAH LUTTE TV MOUSSA DIOUM CHAMPION KADOU YII RAFÉTE NA 💪💪
Aythia champion sounou patron beguee c moi boul khadi
Beguee nala Moussa dioum
Ziare champion ngua
C moi boul khadi
😂😂😂😂😂😂 Moussa dioum nangoul rék Balla gaye mo meune Modou lô 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Cheikh bass keur massar 😂😂😂😂😂
yaw mome deg deg nga amoul
Meilleur émissions
Balla gaye rek
From PA 🤴🤴🤴🤴🤴
Yalnako yalla yeureum té Xaréko aldiana firdawsi barké Al Quran
Modou lô le roi des arênes c'est le meilleur
Balla est son roi
Lamine demall seti tidiane faye le profeseur
Inchallah demain
Lutte TV yakamti nako torop
Lutte TV papis général aussi
@@LutteTV ont vous su dpui italie jai un projet avec vous c pata dpui italie
Lutte Tv for everything 🔥🔥
Mashalaa linga wakh ci Jules Baldé et pourtant vous vous ressemblez
No kèn dou Baye Paul sama copain yaw diambou rek guay amme ❤️❤️🌟❤️🌟❤️🌟
Nexoul ba nexoul bg2 et MODOU LO yagg naniou todj mbapatt bilahii Modou lo dafa yagg beug lamb ndeysann sén rivalité dafa naturel MODOU LO c le meilleur il lutte hyper bien
Topou len sama guinaw lutte TV Le meilleuir
Ndaysan mbeur bu amone avenir moussa dioume motakh ma fonke sam mbeur modou dou fowé lamb
Actualité Actualité affair bi sens la rak mais dou question fowé lamb
Modou Diaw affaire bi liguey la te modou da lene guene liguey rek
@@layekharagne2224 billahi
Modou Diaw saway lamb kula wakhe sens leu dalay nakh
Laye Kharagne mala wakh lolu bou wakh deugue dioté kéne du mome
Balla gay rek 💪
Amine sii niane yii baye Peul beug ga lou diara beug dara dou yaye bilaye. Grand moussa wakh die rafait na sama idol diam sii iow grand.
Modou dh dou sene morom billahi loumou def mbapatt benene mbeur deffouko fi dane ay champions comme bruce lee , papa sow , nar tourè , Baye Mandiayr , Ama Baldé , Elton , Less 2 , Ouza 2 Billahi kene dou Kharagne Lo
😇😇😇wa ki dieul pé nak balla 😂
Bravo
Machallh
Machalla xarange lo dou aye fou
Kéneu dou balla mé modou tamit champion la
Ki Sama grande la Moussa Dioum 💪🏽💪🏽👏🏾👏🏾👏🏾
Way way kèneu dou balla gaye 2
Wayè tmt modou lo ndanane la
FANS balla gaye bou mak la mais vraiment wa parcelle danio rafèt khol
Modou Lo Xaragne Lo 👑👑👑👑👑👑👑
Vraiment deug na deugggg Tay Moussa dioum wakh ga lou nice
Que ton âme reposé en paix 😭 c'est triste
moussa dioum sa wakhe nice
Moussa dioum grand bou cool vraiment ame yité trop vraiment
Paix à son âme
Rip 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Ndaysan baye Peul yaye dafa nex si xool lool yala na ko yala yereum khareko aljana firdawsi barke borom touba
Parcelles yagg na am ay mbeurr you makk mais modou lô reste le plus grand de tous ndanane koulou fadeli
Rip mbeur ndysan
Kine do modou lo❤
Aní balla😇
Rip moussa
Lamine amna solo dei ndanane ga invite bilaye moussa rek sii meuneu beurei gisouma koukoko dakh sii adouna.
Modou c le meilleur bilahy
Bilay mousse 2008 ya takh ma beug lambe
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Bay peull Mom wéroull koi Billahi kii waxii Dof Rék lay waxx Billahi 😂😂😂😂😂😁😁🤣🤣 Bay peull pourquoi nga con Yaw Non 😂😁😂
L’absolu Gueye 😂😂😂😂
Machalah wakh dji rafetna
Moussa dioum ndanaan la mais yemou daaan diuel moo yakh Yarame wi Bouko bayee te defarou Di Fouting Di Contac bou bakh Di def 3seri par jour di tued heure di yewou heure moytou thiaakhane di leethie père birahime aye khalatame Fonkou aye mbokame inchalla dina Nieuwaat
Machalla balla champion 😂😂😂
respe bro
Moussa dioum da nga bokou si lamb del dougou si lamb j di degne fepp te bayi tediou bi
FAWOU MA CMTER,NAKH YAYE DJI NGUEN TCHI DOUGUEUL YAYE BENEN AFFAIRE LA
Thiey balla gaye champion la
Balla gaye rék mashallah mashallah
Moudo lo machalla
🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲
Yallah diapale teih mousseul thi febar bii
BG2 REK SEN PAPA LE 🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫🤫
Aka meuna beurei Moussa dioum reik djineila dh bilahiiiiiiiii
Baye peul dinama rayeu 😂😂😂 balla mo dakh beuré si lamb ji
Modou lo amolmoroum
Anni balla kone
😭😭😭
Je suis fassois dhé mais bilakhi balla gaye 2 mo dakh beuré si lamb ji barké Rassoulilah si guatal Balla gaye 2 moy lamb
Balla Guay 2 champion la thiona mbapet yi
Gris bordeaux mome ñeupe dagn ko dane mbapate xana
Copain loy wahni
Balla Gaye diehalna parcelle 😂😂
Thier Aw hana roi bi diekhaloul guediawaye dougou sene gokh bobou radiakhé tournoi ba dane less 2 dane elton dane alioune seye 2 dieul tournoi ba defier gadaye gadaye di daw nakh coalitions la guissoul wone
@@layekharagne2224 si c'est la vraie personne ce même laye que je connais c'est pas la peine de répondre parceque toi tu es loin d'être objectif tes sentiments prennent dessus sur la vérité Tu es loin d'être un sportif
Ciao Ciao 👌👋
Thier Aw lolou yene la rek objectivitè subjectivitè la yamalè modou mo fi nekk un point un trait koumou nekhoul mom la rek c le roi il dérange , dakk lene beurrè dakk lene khekh guene lene rafet palmares guene lene populaire eup lene khaliss ça c le roi des rois Modou kharagne lo kou merr tant pis 😂😂kou bagn roi 🤴 bi ay dokhote mo lay rey 😂😂😂
@@layekharagne2224 dieul lene lep khana yenafi moudie nek roi Yalla nalen djik Balla kholou len sakh
Laye Kharagne waxi dof . Xana dou yen lagn fi dioutal daww ? 🤣
Modou lô doumasa daan i Balla gaye si adouna