Tristes images au HLM: Une famille expulsée de son logement

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 16 гру 2024
  • Tristes images: Une famille expulsée de son logement

КОМЕНТАРІ • 158

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 5 місяців тому +81

    NDEYSAANE . KHALEYI RÉK LAA YEREUM

  • @SidyBa-pm4zn
    @SidyBa-pm4zn 5 місяців тому +71

    Si j'avais les moyens wallah je veux acheter une maison vraiment je suis triste 😭😭😭😭😭😭😭🙏🙏♥️

    • @kamaraawa8121
      @kamaraawa8121 5 місяців тому +1

      Bilaye lou méti démbeu bataye magui dioye sama rak goro pabi leu niou dialéne Dolé ni wayé naniou déme rék génaniou wayé inchallah keur bobou kéne doufa deuk khana bénéne

    • @aronadiagne5272
      @aronadiagne5272 5 місяців тому

      😅

  • @DioufZahra-g3c
    @DioufZahra-g3c 5 місяців тому +37

    Thieuy yala Li metina 😢😢vraiment yalna lene yala takhawou

  • @jacquelinemendy5618
    @jacquelinemendy5618 5 місяців тому +13

    Elle sait bien parler que Dieu vous protège et donne un toit ❤❤❤

  • @cheikhndiaye2085
    @cheikhndiaye2085 5 місяців тому +47

    Sunu Pa yi tamit ay erreur rek laniou fi néké wone ak séni jaboot. Au lieu ngua sécurisé sa famille pour éviter beuss bo déwé thiow dou am si sa guinaw, mais ngua nek di concours takk diabar rek di diour di tekk. Li niaw na trop way. Du courage !

    • @khadysow828
      @khadysow828 5 місяців тому +5

      Bilay wakh nga deugg

    • @Blackboyshooter_
      @Blackboyshooter_ 5 місяців тому

      Ioe compo histoire bi yép deh

    • @lepatriote934
      @lepatriote934 5 місяців тому

      Bilahi waxatiko sen boppeu rek dagay set lii

  • @AbdouDelta-l5k
    @AbdouDelta-l5k 5 місяців тому +39

    Sama keur ladoul def tourou jiguene

    • @afyfall4359
      @afyfall4359 5 місяців тому +7

      Walahi erreur wessou wouka

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 5 місяців тому +4

      *Bilay ioe djiguéne la déh mais lolou goor bouko deff yagui thi erreur😢*

    • @khadysow828
      @khadysow828 5 місяців тому

      Dara woroussi

    • @06ndiaye
      @06ndiaye 5 місяців тому

      😮😮😮😂

    • @MoulayeLaroussi
      @MoulayeLaroussi 5 місяців тому

      Jamais

  • @fatoudiakhate1516
    @fatoudiakhate1516 5 місяців тому +28

    Yalla nalén yalla taxawou si barke zeydina Mohamed amine ya raby 🙏

  • @Ousmaneouangare
    @Ousmaneouangare 5 місяців тому +29

    Natoula mougnale ndigua ame lou eupe li inchalla si barke seidina mouhamed

  • @ousmanegueye5513
    @ousmanegueye5513 5 місяців тому +7

    Sama cogne mais Bilahi Jour depuis demb j’arrive pas tenir mes larmes lii dafa meti te dara dara aduna diarouko

  • @ZNSY800
    @ZNSY800 5 місяців тому +56

    Li niawna! Domou baye moy lane? Bene dereet leu, liko teug tassouko! Kou xol xalé yi wala mère bi febar sakh xana sa yaram daw mba nga meylene délai sakh niu outt fenen! Manguini wara teud ms toutes mes pensées vont vers eux, yalnalen borom bi tahawou😢🙏🏾

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому +1

      Je crois que tu n´as pas bien compris le sujet. ce ne sont pas des domou baye

    • @sokhnafatoutp4645
      @sokhnafatoutp4645 5 місяців тому

      Dou domou bayam d diabarou papam mo diour khale yoyu manam domou djitlé

    • @kamaraawa8121
      @kamaraawa8121 5 місяців тому

      ​@@jeanmmmmaye domou baye laniou wayé doko khane awo moléne yarre

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      @@sokhnafatoutp4645 Tappez et vous allz comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      @@kamaraawa8121 Tappez et vous allz comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

  • @Ramapoulo
    @Ramapoulo 5 місяців тому +21

    Mane dh mère bi ak khalé yi rek la yéram bilay ms nak il vont payer ça lou yagoul dara nak bilay légui sakh sokhor baaxoul mane dh souma soriwoul wone ma dieul mère bi ak khalé yi bilay😢😢😢😢😢

  • @ousmanecisse4262
    @ousmanecisse4262 5 місяців тому +16

    Wallahi amna nio khamni yalla doulen yeureum moukkou bilahi wal kitabi 👆

  • @AwaKandji-y3x
    @AwaKandji-y3x 5 місяців тому +22

    Thiey aduna massa yalla nalen souniou borom diapaler

  • @boundawdiakhate2801
    @boundawdiakhate2801 5 місяців тому +31

    Bilahi yalla day gneuw legui inchalahou raby si BARKER CHEIKHOUL KHADIM même moi j arrive plus a garder mes larmes courage 😭😭😭

    • @khadydiop9315
      @khadydiop9315 5 місяців тому +2

      Amna gnou bone nak😢😢

    • @kamaraawa8121
      @kamaraawa8121 5 місяців тому +1

      Bilaye bouguéne fa démone démbeu sa yarame daye daw même policier yi danion amone louléne méti bilaye

  • @modasow2221
    @modasow2221 5 місяців тому +3

    Li fane la ci HLM ki def li defna Lou gnawa bilahi ass goor ken douko trokhol 😭😭😭😭😭😭😭

  • @damecisse2010
    @damecisse2010 5 місяців тому +10

    J'ai le cœur meurtri sougnou Papa yii tamite dougnou bolé sisséne dara baagnou kheuye dém naak
    Waayediour bounék looye déf impliqué saa ndiaabot ndakh euleuk gnou khaam fougnouye téék sén tank , ndakh diamono dafaye geune dii dooyewar niit gnii dagnouye dém baa geuna soufé les animaux

  • @merefall3657
    @merefall3657 5 місяців тому +14

    Thieye yala moye bour dh adouna bi diaroul dara😢😢

  • @PapaGueye-lw4pq
    @PapaGueye-lw4pq 5 місяців тому +15

    Liy nieuw moy dakk😢

  • @weuzysylla5294
    @weuzysylla5294 5 місяців тому +9

    Mastaaaa métina tropppp😢😢😢😢yeurmandé dé amatoul

  • @AzazelAzazel-d8h
    @AzazelAzazel-d8h 5 місяців тому +1

    Une famille que je connais très bien. C’est immonde.

  • @ndeyebintadiallo9428
    @ndeyebintadiallo9428 5 місяців тому +3

    😢😢 yalla naléneu souniou borom taxaw

  • @SalyNdiaye-ef9su
    @SalyNdiaye-ef9su 5 місяців тому +23

    Thiéy yalla nalene yalla tahawou

  • @cheikhbethiocisse1366
    @cheikhbethiocisse1366 5 місяців тому +12

    Bilahi liy niew moy dakh boulèn wakh kène molènko tèkk natou sounou borom lah tè sou nguèn ko nango rekk mou indi lou fawkha sène diorte ak sène yakar

  • @boundawdiakhate2801
    @boundawdiakhate2801 5 місяців тому +4

    Ndeyssane thiey adouna. 😭😭😭😭

  • @boundawdiakhate2801
    @boundawdiakhate2801 5 місяців тому +9

    Peut-être li Moy takh nguene jahirr inchalahou raby

    • @taphasamb6836
      @taphasamb6836 5 місяців тому +4

      Natou yallah la rekk mais yallah naniou ame lou eupp lii

    • @AbasseToure-tp5dx
      @AbasseToure-tp5dx 5 місяців тому

      Louy jahir svp❤😢

  • @AidaSow-t6g
    @AidaSow-t6g 5 місяців тому +8

    Yalla naléne Yalla takhawou

  • @IssNiang
    @IssNiang 5 місяців тому +21

    Yeurmandé amatoul

  • @BinetaBob-g7p
    @BinetaBob-g7p 5 місяців тому +10

    Je sais bien si le nouveau régime voit ça il fera quelque chose surtout les enfants qui sont inocents avec les casé pour l instant la pluie arrive

    • @larussieeternelle
      @larussieeternelle 5 місяців тому

      Revenez sur terre avec votre projet nescafé

    • @mrlunatic7650
      @mrlunatic7650 5 місяців тому

      C'est l'éternelle recommencement

  • @cheikhmbackediallo1438
    @cheikhmbackediallo1438 5 місяців тому +1

    Mbaye diagne diap RK th yalla takh 🤲🏻🕋

  • @diarradiop425
    @diarradiop425 5 місяців тому +12

    pa yi tamite moye lolou maye sa diabar keur bayi saye domo pour lane

    • @khadysow828
      @khadysow828 5 місяців тому

      Erreur pirr leu

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      @@khadysow828 Tappez et vous allz comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

  • @MoutaphaGueye-vx9xj
    @MoutaphaGueye-vx9xj 5 місяців тому +2

    Yalla naléne Yalla wallou si barké Al khourane.

  • @aliounedia8314
    @aliounedia8314 5 місяців тому

    Wolénnn Modou Gueye Sope Naby borom bah laa ❤

  • @MameArameSy
    @MameArameSy 5 місяців тому

    Yalla.nà.yalla.takhawou.sibarké.séydinaamoukhatt😢😢😢😢

  • @MoukhamétNdiaye-g9s
    @MoukhamétNdiaye-g9s 5 місяців тому +2

    Yalla nalén yalla takhawou si barki seydina Mohamed

  • @limadieng9110
    @limadieng9110 5 місяців тому +1

    La loie devrait interdire cela… avant de sortir une personne il faut qu’elle ai une autre logement .. c vraiment triste

  • @Matar-i6d
    @Matar-i6d 5 місяців тому +2

    thieuy yalla 😢😢 yalla naléne yalla sammou

  • @MoulayeLaroussi
    @MoulayeLaroussi 5 місяців тому

    C'est triste une femme brave ,guem yalla

  • @Flemme-08
    @Flemme-08 5 місяців тому

    Qu’Allah vous vienne en aide.Amine🤲🏾

  • @aminandiaye4953
    @aminandiaye4953 5 місяців тому +3

    Li dé daray adouna diarouko wasalam

  • @henrijoelsossou3987
    @henrijoelsossou3987 3 місяці тому

    Le monde est très injuste métina yalla ne len yalla taxawou

  • @mariamademe
    @mariamademe 5 місяців тому +3

    Ndaysane 😢😢😢😢

  • @SambaThiam-hz9kx
    @SambaThiam-hz9kx 5 місяців тому +1

    Sama pére nileu déf bly dieul keureum diokhko gnarél bi bly 😢 sou tawé founou nék comme guédj bly

    • @Antistress870
      @Antistress870 5 місяців тому +1

      Masta mougneul fasse diome boul Meuse déf naka soudoul nonou lolou moy nék sa victoirou yaye .keur yénako meune ame wayé meunouléne ame

  • @mamanmbaye1305
    @mamanmbaye1305 5 місяців тому +4

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭métinama trop 😭😭😭😭😭😭

  • @mariellenomoko2685
    @mariellenomoko2685 5 місяців тому

    Il faut que justice soit faite
    En tt cas Lou way def n'a khalate teurayou bamel yalna yalla leral li té até len ci barké seydina Mouhamet Psl

  • @Ss-yp6sh
    @Ss-yp6sh 5 місяців тому

    Bon courage à vous 🙏🏽🙏🏽

  • @FatouHanne-z8z
    @FatouHanne-z8z 5 місяців тому +2

    Lii natou leu rek yallah bakhna nieuw lene keur massar

  • @NdeyeNiang-i4n
    @NdeyeNiang-i4n 5 місяців тому +7

    Li mou takh diabar you beure bakhol am bene diabar rek doye na por SAye dom mana am diamou

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      Tappez et vous allz comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

  • @DameNdiaye-lz4ox
    @DameNdiaye-lz4ox 5 місяців тому

    Yalla na len 😢 Yalla takhawo massta

  • @binettendiaye9397
    @binettendiaye9397 5 місяців тому +3

    Adouna dou keur 😢

  • @sokhnalo3334
    @sokhnalo3334 5 місяців тому +5

    Amna ay nitt you niémé yalla bayilén ak yalla yalla Dina nieuw légui 🙏🙏🙏

  • @AstouSall-g6d
    @AstouSall-g6d 5 місяців тому

    Walahi kou guem yalla la ❤❤❤

  • @mbackegaye7816
    @mbackegaye7816 5 місяців тому

    Yalnalen yalla takhawou mettina loll😢😢

  • @aramediagne322
    @aramediagne322 5 місяців тому +10

    Lou way def bopam

  • @sambadiop9500
    @sambadiop9500 5 місяців тому

    Yalla bahna 😢😢😢😢 thiey adouna dou keur

  • @fatoundiaye9234
    @fatoundiaye9234 5 місяців тому +1

    Adouna dou keur té kou khamoul sa souba daguaye rafétal sa taye 😢😢on dirait que hlm da beuri ka you mél ni

  • @OumyOumy-m6c
    @OumyOumy-m6c 5 місяців тому

    Yallana nalene yalla takhawou metina lol Massa

  • @NdeyeKane-q2u
    @NdeyeKane-q2u 5 місяців тому +2

    Gor gni tamite li beuri Sénégal dieul keur mayko djiguenes

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      Tappez et vous allez comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

  • @aminatadiatta7923
    @aminatadiatta7923 5 місяців тому +1

    Ooh li métina Ak
    nawéte bi

  • @settpixelstv2174
    @settpixelstv2174 5 місяців тому

    Djiguéne Rek Mais Gor Tamite 😢😢😢 kéne meunoul wax lepp

  • @evacamara4340
    @evacamara4340 5 місяців тому

    Non amna niou neikk nak nakka la nite meunei torokhol domou Adama a ce point . Yalla naleineu yalla takhawou si barkei alhouraneu 🙏

  • @malickdiagne3937
    @malickdiagne3937 5 місяців тому

    Kane mo dieuf dji dieuf na niouye khalate yallah tay yeureum nguir yallah

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 5 місяців тому

    Ndawsi kou geum yalla la. Yalla bhna

  • @babadieme
    @babadieme 5 місяців тому

    Ték na niou fénne dé.
    Le titre porte le nom de leur mère et ils ont soldé le reliquat.
    Baye Diallo mô déf lépp.
    Deuxième femme avec des enfants d'un autre et tu lui cèdes ton bien ? 😢😢😢

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 5 місяців тому +4

    Yalanala léne borom bi tahawou ..Ani millionnaire yi ak milliardaire yi nék biirr Sénégal déf lén té yala takh kou beug liguéyeul sounou borom dimbaliléne famille bii lilahi wa rassoul ...

  • @seynabfallou395
    @seynabfallou395 5 місяців тому

    Yalla nalén Yalla taxawou

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 5 місяців тому +2

    Solliciter le Préfet pour être logé dans une école

  • @ngonemansourmbaye9142
    @ngonemansourmbaye9142 5 місяців тому

    Yeureum nalène torop.mais leur père a commis une grosse erreur yalla na yalla takhawou

  • @khadydiouf9825
    @khadydiouf9825 5 місяців тому

    Regarde les enfants c triste 😭😭😭😭

  • @Mariamfaye221
    @Mariamfaye221 5 місяців тому

    Allalou sa bay dou sa allal il faut travailler dur et ne rien attendre de personnes
    Massa

  • @dikha7525
    @dikha7525 5 місяців тому

    C'est vraiment triste 😥

  • @fatouceesay6794
    @fatouceesay6794 5 місяців тому +2

    Allahu Akbarr 😢

  • @mamedialedia8378
    @mamedialedia8378 5 місяців тому +3

    YOW LOO WAKH NÉ IL PARAIT . DARA KHAMOO KOTHI

  • @ngonepouye
    @ngonepouye 5 місяців тому

    Non li mètina je connais la famille Diallo HLM Nio fowado ni laniouye dèf famille pouye ouagou niaye

  • @MamadoulamineLoum-po4kx
    @MamadoulamineLoum-po4kx 5 місяців тому

    Adouna amoul ben solo nay rafét rék Dara yagoul yalla takhawoulén

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 5 місяців тому

    Yalla nalène yalla tahawou

  • @begueBamba
    @begueBamba 5 місяців тому

    Ohhhh 😢😢😢😢

  • @ngonepouye
    @ngonepouye 5 місяців тому

    Bilahi dafa mèti likouko doundoule meneko khame kèp kouniou nakousa keur nous devons nous mobilisez pour récupérer nos maisons diaye dolèbi dafa wara dièkh bilahi dafa mèti akh bakhoule yomale khiyame Dina mèti mandè balouma ndiaga Niang AK sam femme Fatou Gueye

  • @IyasouBalde
    @IyasouBalde 5 місяців тому

    Comment peut on faire ça à une famille entière 😢

  • @maremapene7867
    @maremapene7867 5 місяців тому

    BILAHI ADUNA DIAROUKO, LI YEUP FI LANIOU KOY BAYI

  • @nabouja42
    @nabouja42 5 місяців тому

    KOU DOUNDOUL LI MEUNOKO HAM MINGMAY FATALY FADIAR BAMA WATHIÉ GARDE HÔPITAL TEK SAMA BOP POUR NELAW REK HUISSIER GNEUW GÉNÉ SAMA SAMA BAGAGOU YEUP SIBITY NÉ BOROM KEUR GUI DA SOKHLA KEUREUM TÉ KIKO DEF SAMA DIEUKEUROU TANTA LEU DIAYGNOU DOLÉ TASS FAMILLE LEUM WAYÉ GNARI WEER LACI TEK MOU GAGNOU...AY DOMAME NOCE SI KHALICE GNI DI VOYAGE DIÉKI SA REK SENE AFFAIRE YEUP YAKHOU BA KOUCI AM PROBLÈME LEKEU SAH GNOUNE NGEY WOOO MOTAH MAY GNAFÉ BA DOUGEUL SAMA SI KEUR AL HAMDOULILLAH

  • @Dame.diagne
    @Dame.diagne 5 місяців тому

    Ly bou ammè khalè you ndaw yi rek nima léndy yeureumè

  • @ousmanegadiaga5670
    @ousmanegadiaga5670 5 місяців тому

    DICOURAGE

  • @vybzkartel5838
    @vybzkartel5838 5 місяців тому +1

    aduna dou keur

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall5548 5 місяців тому

    Yalla na len yalla doli diapalè

  • @NiangBoundaw-h2m
    @NiangBoundaw-h2m 5 місяців тому

    Soutura tamit bakh nasi dh

  • @astellendiaye8799
    @astellendiaye8799 5 місяців тому

    Ndessan

  • @sallpapa8838
    @sallpapa8838 5 місяців тому

    Bilae amna niit you sokhore aduna dou keur bo xalaté brom keur gui taye fimou teudeu rk warone naléne yé té niom niou déf li dinagne deh béneu béneu bayi Kofi lane mokofi diar si aduna keur aldiana mo diara niane mais pas keur aduna fi day diex

  • @ModouWade-lo1et
    @ModouWade-lo1et 5 місяців тому

    😭😭😭😭😭😭😭

  • @serignembackedieng872
    @serignembackedieng872 5 місяців тому

    Amine

  • @cheikhmbackediallo1438
    @cheikhmbackediallo1438 5 місяців тому

    Mbaye diagne diap RK Thei Yallah takh

  • @bachirdia7250
    @bachirdia7250 5 місяців тому

    Je suis vraiment désolé pour cette famille mais bèneu pakeu dou lèy.il faut essayer d'avoir la version de l'autre famille.

    • @jeanmmmm
      @jeanmmmm 5 місяців тому

      Tappez et vous allz comprendre: LA POLICE EXPULSE LA FAMILLE DIALLO DE LEUR MAISON AUX HLM 5 APRES 45ANS D'HABITATION

  • @aronadiagne5272
    @aronadiagne5272 5 місяців тому

    Kou hass domou baye li moko waral

  • @laminendiaye7881
    @laminendiaye7881 5 місяців тому

    Ohh Métina trope Walahi

  • @cheikhmbackediallo1438
    @cheikhmbackediallo1438 5 місяців тому

    Mbaye diagne diap RK th yalla takh

  • @niarelbounice413
    @niarelbounice413 5 місяців тому

    A cette heure 😢

  • @Ramapoulo
    @Ramapoulo 5 місяців тому +1

    😢😢😢😢😢❤❤❤❤

  • @fatoumatabinetoukonatendoy4375
    @fatoumatabinetoukonatendoy4375 5 місяців тому +1

    😢😢😢

  • @HelenePouye-fk5em
    @HelenePouye-fk5em 5 місяців тому

    Ministere de l action sociale

  • @aronadiagne5272
    @aronadiagne5272 5 місяців тому

    Goor guou bayiwoul di dieule sa keur dissi déf sa tourou diabar li rék lay andi

  • @MamyGueye-q9o
    @MamyGueye-q9o 5 місяців тому

    Metina na trop