Wallahi ce qu’il dit est vrai. J’ai fait les bancs avec sa fille Soxna mane pipille thiam . Et son épouse maîtresse margo était l enseignate de ma petite sœur à l époque en classe de CP. je me rappelle très bien de cette histoire Ndeyssane Qu Allah accorde à la petite le Paradis.
j'ai regardé cette vidéo à plusieurs reprises car elle est pleine d'instructions et des leçons de vie; je suis agréablement surpris par la sincérité de ce type C'EST UN GRAND MONSIEUR
Je connais cette douleur de perdre un enfant... La mienne est décédé dans mes bras... Kouko doundoul meun nako imaginer mais meunoul kham bann douleur la.. Mais courage, Yalla loumou toudou rek nonou la wara démé. Kholal ci yi la déssé rek, yalla tekk ci niom lokho niou magg ba teral la, feral say rangogn!!! Massa!!
C'est triste grand frère .ce que j'aime en thiammas c'est son humilité , ça célébrité ne lui a jamais changé ,A Malika où il vit ,il est exemplaire ,il respecte tout le monde et il est bien apprécié des malikois
Oh thiamas nitt kou oyof dama wakhtane ak mome ben yoon rek par pur hasard mais dagay sentir nettement sa simplicité, sa foi et sa bonne humeur daf lay deufeul naturellement dagay sentir sakh que liko Sonal ci adouna berétoul toutes mes condoléances encore
Franchement cette soit disante journaliste n'a aucun coeur. Comment peut elle lui dire que tu peux pas pleurer toute l’émission après tout ce qu’il lui est arriver? J’appréci plus ça leçon plutôt que mou niouye begal
Machallah grand je tadmirais avant mais c'est beaucoup plus maintenant tu as un ❤en or du courage dioyna ba sone walahi métite yagg n'a si adouna paix à leurs âmes bb Yacine et le frigoriste yalna sa diam yagg thiamas
Beuss bobou kay gnoune wa malicka dougnouko meuss faté métiwone na si yaw méti si gnoune Yacine khallé bo khamné kouko guiss beugue ko machalah thiate bou rayoul rék sémal billay
Massa et du courage. Yalla nala Yalla maye kholou mougne. Que Dieu aie pitié de l'âme du frigoriste. Nos ouvriers doivent respecter certaines mesures de sécurité. On ne peut pas en même temps recharger du gaz et procéder à de la soudure. Les enfants aussi ne doivent pas être sur les lieux où des ouvriers travaillent.
C’est dur de perdre ses enfants Yacine Yalla na aldjana doone keurame Abadaane Mame fallou Yalla na gueuneu taanei Yeineuh aye wadjourame yalla nalleine yalla maye kholou mougne
Ndeyesane thia courage il downa yarame et ça ce vois bien kou gueme yallah la.On prier toujours pour toi et longue vie beaucoup de santé ,plus de force et bonheur.
MERCII THIAMASS : SERIGNE TOUBA néna niit dou wakh dama geum sama bopp dett niit day wakh dama xam sa bopp nak niit Yalla swt lay geum ,, yaw niit meuna Lo dara sa bopp nane dama geum sama bopp lolou bokalé la sax vraiment 🤦🏾♂️ niou beuri niogui koy wakh ay dama geum sa bopp 🤦🏾♂️ lolou wakh bou reuy na sakh mais niit day xam boppam tè xam sa bopp ça veut tout dire mashallah 🥰 🙏🏾
ligua wakh degue mais dafa am niit yo khamni yalla moléne beguel bopam mayléne loumou mayoul kéne bé takhna probleme bo am ba toudouléne yalla safaral lako lolou moy nitou yalla
No thiamas tu es digne mashaalah yalla moko beugué ni bo holé si wakhtaane khaleyi avant wanenani li mo djitou sene dioudou yalla nalene yalla sam j ai pleuré😘😘
Machala Thiamass yaw do moussaa torokh ndakh Serigne Fallou mi nga beugue
Wallahi ce qu’il dit est vrai. J’ai fait les bancs avec sa fille Soxna mane pipille thiam . Et son épouse maîtresse margo était l enseignate de ma petite sœur à l époque en classe de CP. je me rappelle très bien de cette histoire Ndeyssane Qu Allah accorde à la petite le Paradis.
j'ai regardé cette vidéo à plusieurs reprises car elle est pleine d'instructions et des leçons de vie; je suis agréablement surpris par la sincérité de ce type C'EST UN GRAND MONSIEUR
Bilay yaw
@@sahelienne6822 9999
a
Ndeyesane
La ressemblance avec Youssou ndour est frappante !!!courage le grand
Youssou ndour dou moromam
Esk dou papam sakh
@@awadrame9841 ol
Je connais cette douleur de perdre un enfant... La mienne est décédé dans mes bras...
Kouko doundoul meun nako imaginer mais meunoul kham bann douleur la..
Mais courage, Yalla loumou toudou rek nonou la wara démé.
Kholal ci yi la déssé rek, yalla tekk ci niom lokho niou magg ba teral la, feral say rangogn!!!
Massa!!
Yalnala sugnu borom may holou Mougn tei mayla li geune si yaw inchallah
@@marieflorencediatta4348 ❤💖❤
Walahi khamnasi dara 😢 yalna YALLAH SWT yeureum lén
Thiamasse, tu m'as vraiment fait pleurer 😭😭😭. Que la terre lui soit légère...
Lou metti dall yag na si adouna
Respect pour ton courrage immense et ta foi en Dieu.
Massa thiamase et courage thieye adouna
Oh massa way, Thiamasss dioylo ngama. Que l'âme de la petite yacine repose en paix et surtout beaucoup de courage à toi
Ohhh j ai bcp pleurer ndeyessane Machala mame fallou yalla nako yalla maye goude fannnn
Que l’âme de Yacine repose en paix!!!
C'est triste grand frère .ce que j'aime en thiammas c'est son humilité , ça célébrité ne lui a jamais changé ,A Malika où il vit ,il est exemplaire ,il respecte tout le monde et il est bien apprécié des malikois
Oh j’ai vraiment mal 😭 repose en paix Yassine
J'ai pas les mots 😭 😭 c'est le cœur de diamant qui parle bravo
Ndeysane Lamine sama dom la won dem a l'âge de 27 ans kou beugon khalé ndogal nak bou nieuwe rek yalla nalen yalla yeueeum
yalla nako yalla yereum
J'ai pleuré j'ai beaucoup rigolé tiamasse amoul que dieu veille sur toi vraiment yaga nga ngou mbégal machalla
Tu m’as fait pleurer yalla nala yalla may xollou mougn té xarèko aldiana
Thiamas a un coeur d'or il a donné une leçon de vie à tout les peres de famille
Outéna AK sama papa domyi ma abandonné depuis notre divorce en 2016 avec trois enfants amna goor you Bonne
Hooo thiamase tu m'a fait pleurer ndeysane bilayi Adouna da méti
Paix à son âme Ndeysane c'est vraiment dure pour lui😭
94 : 6 - A côté de la difficulté, est certes, une facilité!
94 : 6 - En vérité, avec de la peine, il y a du gain.: subhanallah
WA THIAMASS MI NGUÉN FOKNII SANTOUL NDOUR😂😂😂 li ndiro kessé leu
Teik thi mashallah....nii reik gueine di deif di thiattou domou djambbour yiii
Ce gars a un coeur d or vraiment je savais pas donc jamais jugé quelqu un
Je t’apprécie avant,je t’apprécie encore plus aujourd’hui respect grand
Serigne Falilou rek fall diarama beguee rek 🤲🇸🇳❤🙏🤝🦁✊
Dieureudieuf serigne fallou mbacke
MAIS WADJI DEUGOUNA Dé 😂 aprés la tristesse du début le reste de la vidéo est super drole nak !!! vraiment ki dou nitt !
Walaahiii
Les vérités de Thiamasss !!! Passionnant 😍
Oh thiamas nitt kou oyof dama wakhtane ak mome ben yoon rek par pur hasard mais dagay sentir nettement sa simplicité, sa foi et sa bonne humeur daf lay deufeul naturellement dagay sentir sakh que liko Sonal ci adouna berétoul toutes mes condoléances encore
J’ai vécu presque la même situation en 2011 alors je sais parfaitement ce que vous endurer grand nala yalla maye kholou mougne😭🙏🙏😭😭
Massa
Massa
Franchement cette soit disante journaliste n'a aucun coeur. Comment peut elle lui dire que tu peux pas pleurer toute l’émission après tout ce qu’il lui est arriver? J’appréci plus ça leçon plutôt que mou niouye begal
Une inconsciente
Vraiment aucune professionnalisme
J'ai pensé la même sérieusement aucune empathie kholou djiguéne dou deugeur waay
Thian balma akh J avais un jugement négatif sur vous. Mais je me suis trompé vous avez un cœur en or malgré toutes les obstacles
La manière dont il m’a fait pleuré c’est de la même façon qu’il m’a fait rires avec la partie de Bougane..Talentueux oft !! 😂
Ndeysanne exactement
Sosie de youssou ndour, machallah longue vie
Man dee gueun nala beugg bilay yallah nala yallah defal diam ak sa famille 🙏🙏🥰
Machallah grand je tadmirais avant mais c'est beaucoup plus maintenant tu as un ❤en or du courage dioyna ba sone walahi métite yagg n'a si adouna paix à leurs âmes bb Yacine et le frigoriste yalna sa diam yagg thiamas
Mass your story touched my heart, but am grateful you have a strong faith. Accept my condolence and sympathy.. May God be with you
Ndeysanne li metina trop massa ttes mes condoléances yalla nala yalla doli soutoura 🙏
😭😭😭😭 yallanala yalla may ay seydina mouhamed psl ak ay fallou ak ay sokhna yacine ak ay mame cheikh ibrahima fall si barcke serigne bi
Beuss bobou kay gnoune wa malicka dougnouko meuss faté métiwone na si yaw méti si gnoune Yacine khallé bo khamné kouko guiss beugue ko machalah thiate bou rayoul rék sémal billay
EUSKEY ! li dé meussou mako yekk ! Li metina grand, Massa.
Bilahi si ben jour meune nga gnack lep si adina mais sante yalla ndakh gnom gnar gnep meunone nagnoufa dés alors courage ❤❤❤❤
PAIX A LEURS AMES. DU COURAGE THIAMAS.
Non thiamass il communique très bien machaala intéressant
Ho thiamas dioylo guama way cé vremen triste. Yalnako yala yeureum te indi louy toc
Thieuy yalla 😢😢😢 massa grand yalnako yalla haré aldiana 🙏🏾🙏🏾
Toujours un plaisir de l'écouter
Ndeysane Bb yacine dafa nkone halei bou sopoulo wone thiat bahoul kelle repose en paix🥺🙏🏿
Massa et du courage. Yalla nala Yalla maye kholou mougne. Que Dieu aie pitié de l'âme du frigoriste. Nos ouvriers doivent respecter certaines mesures de sécurité. On ne peut pas en même temps recharger du gaz et procéder à de la soudure. Les enfants aussi ne doivent pas être sur les lieux où des ouvriers travaillent.
Bbei Yacine ndeysane Sa maman Maîtresse Margot l’amènait souvent avec elle l’école Mariama Niass
Ta fait mariama niass car moi aussi
C comment l'école j'aimerais avoir des renseignements sur les conditions des enfants avant d'inscrire les miens
Ndeyssane Senegalais meunoule wahe te bokale woule kone Serigne fall mo la mayone ligueye bi?
Yalla na Yalla hare Yacine Aldiana Firdawsi
Massa.jai des larmes aux yeux.adouna mettina torop.doom daa sakh ci khol
Je vous admire bon courage à toi et bonne continuation à ta famille
C’est dur de perdre ses enfants Yacine Yalla na aldjana doone keurame Abadaane
Mame fallou Yalla na gueuneu taanei
Yeineuh aye wadjourame yalla nalleine yalla maye kholou mougne
Machaala thia que dieu protège toujours la famille ❤️
Mais présentatrice bi il faut qu'elle sache ke li dafa meti trop il fok mou dioye dome dafa sakh si khole mais du courage
Il parle d ses enfants il est triste et la dame tokk dinane boul dioy émission bi yeupe thieuyy
@@fatougueye9825 waw guiss na dei dafa meti tei nite rek la kou sagnon lou meti lounek yaw lay dale pas sa gniabote
Mes sincères condoléances qu'Allah leurs accueil dans son paradis et que firdawsi soit leurs derniers demeures
Adouna nakhar rek ak thiono laniou fi nieuwe mo takh amoul ngueume yalla dou bakh yalaniou yalla takhawou ndeyssane mougne rek
Je te jure lolou laye khalatte fima tdnii aduna mo mettii
Repose en paix Toureundo💔🙏🏽petit ange dors bien😔❤️
Ndeyesane thia courage il downa yarame et ça ce vois bien kou gueme yallah la.On prier toujours pour toi et longue vie beaucoup de santé ,plus de force et bonheur.
Je suis impressionné de ce gas💪😎
Partie Bougane bi setan nako 3 fois sheutttttt😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
walakhi dioyna ba sone serigne fallou dafa mane kanamam ma guinawam machalla yalla nako yalla defal fane bou goudou
MERCII THIAMASS : SERIGNE TOUBA néna niit dou wakh dama geum sama bopp dett niit day wakh dama xam sa bopp nak niit Yalla swt lay geum ,, yaw niit meuna Lo dara sa bopp nane dama geum sama bopp lolou bokalé la sax vraiment 🤦🏾♂️ niou beuri niogui koy wakh ay dama geum sa bopp 🤦🏾♂️ lolou wakh bou reuy na sakh mais niit day xam boppam tè xam sa bopp ça veut tout dire mashallah 🥰 🙏🏾
Xam ca bop ci jammu Yalla la bop
Courage l'animateur thiamas Et ms condoléances à sa fille yacine k'la terre lui soit légère #yalla Moy déggal Faxaloud Lima Yourid
Ndeysane yalna len yalla oubile aldiana bon courage grand 😢😢😢😢😢 il faut avoir la foi et l'humilité Massa
J'ai un cœur meurtri bilay sama khôl toyna mais thiamass kou geume yallah leu courage paix à ton âme la petite yasine
Mais nak bokkalé Moy bayyé sa mbir kenen koudoul Yalla. Kenn meunoul dara Yallaa meun lépp. Kou meun dara doo dé.
ligua wakh degue mais dafa am niit yo khamni yalla moléne beguel bopam mayléne loumou mayoul kéne bé takhna probleme bo am ba toudouléne yalla safaral lako lolou moy nitou yalla
Aka bakh diabare bilay Mame Fallou aussi khale bu yarou leu yalna fan bi goudou papa
Merci pour ta franchise et courage
Yacine repose en paix
Métina trop😭😭 Yalna la yalla may khollou mougn 🙏🏽🙏🏽
Tu es fort machallah et courageux tu m'as fait vraiment pleuré que leurs âme repose en paix 🙏
No thiamas tu es digne mashaalah yalla moko beugué ni bo holé si wakhtaane khaleyi avant wanenani li mo djitou sene dioudou yalla nalene yalla sam j ai pleuré😘😘
Je découvre un Monsieur très digne.
Ooohhhh meussouma khamnei tiamas doundeu neu loumeilni theye yalla metina massa ndeysane
Pour quoi les hôpitaux sénégalé aide pas les personnes en danger.vous êtes mauvais les docteurs sénégalé .j’ai mal aux cœur.
Oh massa C’est vraiment triste courage mon frère
Thiams dioy lo ngama bilaye yalla na la maye kholou mougne niak ko beug dafa meti rawatina sa dome bb yacine yalla na yalla yessal yeurmande thi mom
Ndeysanne, paix a l'âme de ta fille, qu'elle repose en paix. Massa à ta famille.
Tu reste un père digne
Ndeyssane Massa yyallah nagnou yyallah mous seul thi thiat,di diale sa ma yaye thiaba Thiès ...yallah terouko khareko Aldiana...
Thiamass vous êtes adorable borom bakh ga je t'aime fort
MDR KONE THIAMASS MII NIILA DEUGOO ??JE L APPRECIE DESORMAIS.
ndeyesane massa courage thiamasse mettina torop 😭😭😭😭
Oh diereudiefé s.fallou mbacké borom ndindi ak khayra mala beugue mala wolou piir koula wo yakar la témouy deugue cii mom gua wouyoukoo👌👌👌
Bilahi dioy lo ngama mettina trop thiamass mon frère mounial yallah mongi ak adji mougne gni yallah nala yallah samal sa njabot gui
J'habite à côté de chez lui j ai jamais su cette histoire triste😭
Bb yacine repose en paix❤
Lala iao mom intelligente do dara 🙄🙄🙄
C dur, dur
Je pleure thiamass c'est dur.courage.mon cher. K yacine repose en paix....
Bon courage, Yalla nala Yallah taxawou. Aamiine Yaa Rabbii.
Thiey bilay lou metti yague na si adouna, Thiamas massa mais delou sant sounou borom rek ❤️
Je voudrais bien que tout les hommes t entendent Mille merci
Ohh metti na massa way yalnalen yallah yeureum kharélen aldiana si barké seydina mouhamed saw🙏
J😭😭 j'étais témoin de cette incident a Malika on habite la même maison en 2009 bilahi
Homme de vérité!
Machallah métina massa
Que la terre lui soit légère
Allahou akbar, yallah rk moy bour mougnal thiamass tè di sante yallah rek
Ndeyssane thiamas diambar gua avec tout ce que tu as traversé