N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
daguéné warone vérifier bala guéne koy publiér lii dara douci deugue bilahi walahi wa talahi day féne mane ami lo la toudou domou magou djieukeureum la keur guimou amé 5 domam yi fofou la djioudo ay adama loula diaral li sa dome guisna vidéo bi yaw sa dome yeup yoroci kéneu nieup gua sédalé pour takhawalou djii sa yaye silmakha la guisoul depuis bima néké khalé guakoy fénal fii ay adouna bi diekhna ba paré police masoula djieulci dakh limou nekk seuyou book gua tall keurgui bayi sa nék sa dome khadija elle avait 6 ans mo wakh sama yaye mo tall keur gui
Wallahi ma Sœur tu as dit la pure vérité que le bon Dieu tout puissant vous protège et bénisse c'était un cas pour tout le monde c'est à dire de L'estimation envers SONKO (Bravo pour toujours et bonne continuation inch'Allah)
Sokhnasi billahi soumalaa wakhone sama kaa gua nopi 🥱 mais dama djieule lép ték si lokho yallaa ☝️eternet day des ba Say seute seutateu djiar n'a bayi khéle ☝️até yallaa Dara dakouko billahi ☝️
Je pense qu'il faut souhaiter que sa situation s'améliore d'avantage. C'est une battante. YAllA na sunou Borom samla. Yiirla takhawoula..Sokhenaci moural sa bop si c possible, continue à croire en AllAh. Puisse Dieu t'assister.❤
Je ne suis pas sénégalais, Cette histoire est bizarre? psychologiquement parlant 1 née d'une famille milliardaire mariée de force à un Villageois j'ai du mal à y croire ?2 si Mr Sonko était au courant de son histoire familiale celà doit rester privée elle aurait mieux gagné dans la dignité 3 Qu'elle pense à ces personnes décédées ou hamdicapees à vie ! 4 L'état n'est pas un assistant Social ou pol emploi pour aider tous le Sénégal Bcp de personnes ont vécues des situations difficiles C'est le Rôle de la ministre de la Femme et affaires Sociales que cela concerne. Cette histoire est digne d'un roman de psychologie qu'elle n'hésite pas à écrire un livre ça lui apportera un capital digne d'une fille de milliardaire Allah récompense les personnes selon leurs épreuves en privé non sur les sites Salam à vous et courage.🙏🏻💯
@@Nafina-v7u Salam effectivement vous avez raison frère nous avons vécu longtemps longtemps avec les sénégalais donc la langue est vite Apprise aussi bien que d'autres langues il suffit d en être intéressé c'est comme un S qui parle italien où espagnol etc j'ai même rencontré des S qui parle dirigea dans le Désert du Sahara et cela m'aide ds ma profession Salam.
Son parcours me fend le coeur, en tout cas sènegal am na gnou bonn nakk, cette femme est tellement brave , yalla n’a la yalla arrrrr takhawoula❤ba Ousmane sonko guiss video Weuteul liguey bou bakh 😭😭😭
Ndeyssann .. ca existe dee.. Mon fils de 6 ans m’a posé un jour une question devant son papa maman Hana danga nop Ousmane sonko🤣🤣🤣je lui ai répondu oui passk tout le Sénégal est amoureux de Ousmane sonko
Du courage inchallah tu reverras ton frère et svp il faut se rapprocher d'un psychatre pour ta santé aussi rapproche toi des instances du parti pastef tu mérites assistance et encore beaucoup de courage courage ma soeur
BI REPORTAGE SI SENE CHAINE BI AMNA SOLO BOU BAKHE RICHE NA AM NA VALEUR WONER DIAMBAR AM NA AY DJANGUATES YOU BARI SI VIE WOU DOMOU ADAMA BRAVO POUR LE REPORTAGE
Li dawna yaram deh presi esk tu connais cette dame il faut que tu sois reconnaissant envers cette dame son histoire est vraiment triste presi reagis stp
c'est dommage ma belle moi je t'ai toujours apprécié mais tu ne devais pas raconter ta vie sur l'Internet sincèrement je t'aime je t'apprécie mais ta façon de faire aujourd'hui
Yaw nak ya kham nit day doul khamnako khadim lo Moy djeukeureum li mou wakh barke s fallou d'où deug bamiy dionge keureuem sonko ken khamako dafa beug Ousmane sonko fallko ki taskatou keure la papam yoroul deureum masta sokho masta deubou bilakhi
Walahi day fen sounou keur la don sey masoul manquer darra papam amoul dara yayam dafa aveugle son marie est un homme de valeur 😢niou may ko épouse mou tal sounou keur ndakh bagn woudiou elle fait de la manipulation walahi lepou day fen elle était très bien dans son foyer cest lui même qui a bruler notre maison 😂
Adama diope esk setnga yalla thi lingay wakh danga weet aksa bamel adama ya mana fen deug deug fam don seye bagnou gadje sokh eupouna 20ns te mom 10ans lafa am meusta deuk thi sangal tambakh nga wathi sa goro ya kala diaw maste geune negam sa djeukeur khadim lo bam lay fase sonko ken khama gouko te yaw wakho lepou dh djeukeur yigfi amat doko wakh amat ngafi niari djeukeur tass yaw takha walou katnga mo takh nga fakh dionge touba niaw louye sa aprtamant ndakh beuga bon ak sa pap kagnla nek milleyeder koudoul khalat tarayou bamel nak lolou nekh defal bilay sonko bis boula fale dara ma khamne ndayam ligeyalouko mom sonko tass katou fammes nga kou doy war nga
Mane ki gueumouma ko pour choisir cette heure là pour parler tous ça. Avec tout l'engagement des patriotes sur l'aide. C'est pas le bon moment pour dire tout cela
Cette femme n'a pas lair d'une bonne femme fautes attention avec cette dame là, meme son visage parle elle n'est pas innocente dé bien, rakal ak mboume non elle ment héhontement d'après moi, je ne l'a connait ni d'Adam nous d'Ève écarté la de Pastef
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Li dra doussi deugg walahi
daguéné warone vérifier bala guéne koy publiér lii dara douci deugue bilahi walahi wa talahi day féne mane ami lo la toudou domou magou djieukeureum la keur guimou amé 5 domam yi fofou la djioudo ay adama loula diaral li sa dome guisna vidéo bi yaw sa dome yeup yoroci kéneu nieup gua sédalé pour takhawalou djii sa yaye silmakha la guisoul depuis bima néké khalé guakoy fénal fii ay adouna bi diekhna ba paré police masoula djieulci dakh limou nekk seuyou book gua tall keurgui bayi sa nék sa dome khadija elle avait 6 ans mo wakh sama yaye mo tall keur gui
Amine❤❤
Amine
@@nassendiaye808 waxale lo xame ❤
Une femme de valeur tu es trop fort. Sister machallah thiey seuy you Senegal yi 😢😢😢😢😢😢😢😢
Quel homme quelle mauvaise famille ? Sara li 😢
Merci ma sœur k Dieu te protège bonne continuation Ousmane sonko t'as beaucoup de maman dans l'ombre ❤
Wallahi yalla doula sétane ,té PASTEF tamitt doula sétane ncha Allah❤
Wallahi ma Sœur tu as dit la pure vérité que le bon Dieu tout puissant vous protège et bénisse c'était un cas pour tout le monde c'est à dire de L'estimation envers SONKO (Bravo pour toujours et bonne continuation inch'Allah)
Machalla comme elle est brave
Ki Lou werr lay wakh ohh amal Diam yalnala yalla arr 🤲🏻❤🎉
Ndayssane dioulit dëg ak diafe yalna nanou ko sunu borom defal amine inchalla ❤❤
Djambar nga ma fille yalla nala yalla dolli Djamel AK xiweul AK soutoura
Yalla boula bougue daflay natou.waye dinga teki inchallah
Touma bakhoul. Touba koudjie lounekk la lene diaral😢😢😢
MACHALLAH QU ALLAH LE TOUT PUISSANT VOUS ASSISTE VOUS PROTEGE VOUS BENISSE ET GUIDE VOS PAS.🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
J'aime vraiment 🌹 cette brave dame ♥️
Sokhnasi billahi soumalaa wakhone sama kaa gua nopi 🥱 mais dama djieule lép ték si lokho yallaa ☝️eternet day des ba Say seute seutateu djiar n'a bayi khéle ☝️até yallaa Dara dakouko billahi ☝️
Ndeye binta ki bilaye nioko eupeu problem da mouna wakh rek di wakh mais nioune néniou bayi yeup si lokho yalla
Ak problème boléne meunti ame yalla nalléne ko safaral inchalla 🤲🏾
Je suis d'accord avec vous son histoire, c'est une Story.
Amine yaraby merci beaucoup @@ldiedhiou811
Yalla nalla yalla samou
Je pense qu'il faut souhaiter que sa situation s'améliore d'avantage. C'est une battante. YAllA na sunou Borom samla. Yiirla takhawoula..Sokhenaci moural sa bop si c possible, continue à croire en AllAh. Puisse Dieu t'assister.❤
Oh masta dundu ngua Lou meti seyou mbok mom merci rek
Je le recommande vivement à tous les enfants le mariage en famille.Pas de……..
Ki de limiy wax d'ara amousi dafa dioutal wax dji
@@BoyeLo-xn8xgah bon
Kone défe léne nimou défe guéne géneu démentir ko@@BoyeLo-xn8xg
@@BoyeLo-xn8xg en bon explique
masta Adama yalna yala dolila soutoure fi yala rék monfinék courage rék ms yalna Mr le PM Sonko dégue tamou geune si yaw amine 🙏🙏🙏💚💚💚🤍🤍🤍👊👊👊💪💪💪
❤❤❤ metina courage yallana yalla defalela diame allekhamdoulila takhawoula eskey ❤❤❤
Ndaysan massa Adama li doyna waar déh thiey yallah sunu borom
Une femme courageuse. Machallah
Je ne suis pas sénégalais, Cette histoire est bizarre? psychologiquement parlant 1 née d'une famille milliardaire mariée de force à un Villageois j'ai du mal à y croire ?2 si Mr Sonko était au courant de son histoire familiale celà doit rester privée elle aurait mieux gagné dans la dignité 3 Qu'elle pense à ces personnes décédées ou hamdicapees à vie ! 4 L'état n'est pas un assistant Social ou pol emploi pour aider tous le Sénégal Bcp de personnes ont vécues des situations difficiles C'est le Rôle de la ministre de la Femme et affaires Sociales que cela concerne.
Cette histoire est digne d'un roman de psychologie qu'elle n'hésite pas à écrire un livre ça lui apportera un capital digne d'une fille de milliardaire Allah récompense les personnes selon leurs épreuves en privé non sur les sites Salam à vous et courage.🙏🏻💯
Meilleur commentaire
Tu n'es pas sénégalais mais tu comprends notre langue tout ce qu'elle dit en wolof tu le comprends bien on dirait d'après tes commentaires 😂😂😂 merci
@@Nafina-v7u Salam effectivement vous avez raison frère nous avons vécu longtemps longtemps avec les sénégalais donc la langue est vite Apprise aussi bien que d'autres langues il suffit d en être intéressé c'est comme un S qui parle italien où espagnol etc j'ai même rencontré des S qui parle dirigea dans le Désert du Sahara et cela m'aide ds ma profession Salam.
@@Nafina-v7ulolou moma yêm daal en plus pourquoi tu répète fille milliardaire ?
Yalla bakhna banekh guaye moudieh inchallah gnoune Sakh this gourrou Macky Sall lagnou doundou Lou metti mes yalla bakhna ❤
Yallah nala Yallah Soutoural
Maachala Adama yalla rek Bari soutoura ta soutoural nala
Massa ma soeur du courage lepaye bakh inchallah
Walahi day fen barke Mohamed
@@KhadimLo-tc8ihah bon
Abn
Son parcours me fend le coeur, en tout cas sènegal am na gnou bonn nakk, cette femme est tellement brave , yalla n’a la yalla arrrrr takhawoula❤ba Ousmane sonko guiss video Weuteul liguey bou bakh 😭😭😭
Mon frère bilahi day fen je te le jure gno bokon ben elle vous manipule cette femme c’est une vrai sorcière walahi
@@KhadimLo-tc8ih je ne t ‘ai pas demander ton avis , ni réck guen di defff
Soula nekh bagna guem mais day yakh ay deer diarbou walahi
Walay daye fène bi li do khew 2017 lawone mo tall keur gui niou fassè ko police sakh dieulciwouko leep falama feek nio bookone keur
@@sokhnabatylo244aka lér gniko khamoul Laye tour lëndëm dara Dou dëgg ci limuye wax
Mahsa Allah que le tout puissant veille sur vous❤❤❤❤❤
Ndeyssann .. ca existe dee.. Mon fils de 6 ans m’a posé un jour une question devant son papa maman Hana danga nop Ousmane sonko🤣🤣🤣je lui ai répondu oui passk tout le Sénégal est amoureux de Ousmane sonko
Kou am yalla ñakodara sokou amoul amodara walahi
Un combat doit être mené par conviction sans rien attendre en retour et aujourd'hui c'est comme si tu attendais une récompense
Li. Metina yalla nalla yalla doli takhawou say say nga machalla
Machala diambar deugg nga
Machahallah amna solo yalla bakhna
En tout cas Ousmane Sonko warna sétane lii😢. Mangui niane Yalla niou bolé la thi listou député yi di nieuw, amgua mérite amgua kauleuré
day féne dehhh
Day féne mo tall souniou keur Histoire bi 2017 lawone quand j’avais 16ans doumako massa fatè
Ki de sonko douka kham ndax limiy wax niiii migui méllni yalla ak yaaali kiii mok sama makk bou djiguene niodon woudié
@@AmiCollLO-ld2qrya bonne
@@BoyeLo-xn8xgsokhore
Jambar DEUG ngua machalah yallanala yalla taxawou
Billakhi day fen gno bokon keur dafa just pour am poste ci gouvernement bou bess bi 😊
Mon Dieu . que Dieu te vienne en aide
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 elle est brave
Dieukeur dou morom il faut bien écouter le commencements de l'histoire
BRAVO NDEYE KHADY NDIAYE TOUJOURS LA MEME. ..SOXNA ADAMA DIOP BAYER NALA AK YALLA.
Cette histoire est ump trop parfaite...mais YALLAH Reka kham
Chers hommes habitué à Touba ne signifie pas avoir une bonne mœurs retenez ceci d'ailleurs souvent elles sont plus capables de faire du mauvais
Tu adis la vérité. J'en sais qq choses
Machalla ma seour dina bakh insha Allah diambangua
Ndeyssane 😭 yalnako la rék
Elle est vrai patriote❤
Du courage inchallah tu reverras ton frère et svp il faut se rapprocher d'un psychatre pour ta santé aussi rapproche toi des instances du parti pastef tu mérites assistance et encore beaucoup de courage courage ma soeur
Rien à voir avec la politique de Pastef si réellement elle de Pastef il faut l'exclure car sa moralité n'est pas Pastef
Machallha lou meti yagueneu si adouna nit souleu benier sounal la wayer yalla atenalen ak yaw❤❤❤
Machalla du courage ma sœur la lionne du pastef
bilahi day fénne sama tanta lawone
@@amilo4068sa tanta la wonn et maintenant?
Wa mais, khana cette femme a des problemes avec une LO car tous les gens quoi disent que dey fenn, leur nom de famille est LO.
BI REPORTAGE SI SENE CHAINE BI AMNA SOLO BOU BAKHE RICHE NA AM NA VALEUR WONER DIAMBAR AM NA AY DJANGUATES YOU BARI SI VIE WOU DOMOU ADAMA BRAVO POUR LE REPORTAGE
Macha allah tu as une maison nous on l’ a pas nous les immigrés wal ma thie y’a gui sante Yalla macha allah
Seuye Sénégal rek kharei la courage
Que le bon dieu veille sur toi Yalla bakhna
Machallla tu es formidable yalla bakhena
❤❤❤❤
Le mariage est sacré ma sœur. Quitter le père de tes enfants pour un politicien. 😂😂😂
Khaw ma lo amoul mais fiit mome am nga ko. Nga may saf ni fouta tampi😮😅
😂😂😂
Dieu est grand ❤❤❤❤❤❤❤
Sonko.worna.senegal.ba.pare
machalla sister ya ame dignité akk classe, déyssane mougneu katte guaa lii Gua Doundou dafa métti tropp,du courage, lépp dina bakh inchallah Amine yarabi, dieureudieuf ♥️♥️♥️♥️♥️🌹🌹🌹🌹🌹🌹
Yalna yâlla takhaouleu
Dieukar dou morom sageula
Yalla Bakhna!
Machallah❤❤❤
Li dawna yaram deh presi esk tu connais cette dame il faut que tu sois reconnaissant envers cette dame son histoire est vraiment triste presi reagis stp
Ndessan yalna ko borome bi fénial thi barké Seydouna mouhammad
En tous ca elle et tres brave determibez Jaime les femmes brave machallah
ligua sagua macky sall yeupeu si tiktok bi yalla boula fayé sa boor dou bakh
Bayileen leen akh macky sall moy deff effet
Attention!! Elle a été recueillie par Ndèye Khady Ndiaye Sweet Beauty. Voici la nouvelle Adji Sarr
Kou bagni sa yay guir ousmane sonko guisou mala mbaw
Yalle n'a la yalle samou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
adama la femme de valeur
Courage sista ❤
KI DEH LIMOUY DARA DARA DARA DOUTHI DAGAUE FENN REK LEYE DEFF
An? Kham nga ko ?
Ndawsi daga niro aji Sarr face, mba Kayn jeko dunyu ben? Ahh mba Sonko dinala nyemeh
Même si c'était vrai aucun politicien ou politique ne doit pas causé que tu divorce avec un mari ou une épouse
elle ment bilahi niou bokone beneu keur
Gneup nenagn day feen. Sokhnassi donc am nga inspiration 😂
😂😂😂
mouko djiekar dji Niouy wakh loulo de niakou gui nion loulo nio nak tiah coumanter yi
c'est dommage ma belle moi je t'ai toujours apprécié mais tu ne devais pas raconter ta vie sur l'Internet sincèrement je t'aime je t'apprécie mais ta façon de faire aujourd'hui
Numéro je suis au Maroc je veux aider à retrouver ton frère
Ki deh khamouma loutakh mais guemouma ay wakham dafma nirou kou mena fèn trop😢😢
Tu as tous dit
Yaw nak ya kham nit day doul khamnako khadim lo Moy djeukeureum li mou wakh barke s fallou d'où deug bamiy dionge keureuem sonko ken khamako dafa beug Ousmane sonko fallko ki taskatou keure la papam yoroul deureum masta sokho masta deubou bilakhi
Limou wakh lép dou degue ma ragal familles bi fén rk
Limou wakh lép dou degue ma ragal familles bi fén rk
Walahi day fen sounou keur la don sey masoul manquer darra papam amoul dara yayam dafa aveugle son marie est un homme de valeur 😢niou may ko épouse mou tal sounou keur ndakh bagn woudiou elle fait de la manipulation walahi lepou day fen elle était très bien dans son foyer cest lui même qui a bruler notre maison 😂
Hum
Ki mo wakh deugue souniou keur leuk done seuy
Mane sakhe dama titttt
Louko fi diare adouna dou keur ils faut être digne dans la vie 😮😮
Vous êtes combien dans votre maison gnata nitt gnoo fi gneuw nane gnoo bokk keur tamite ahhh
Adama yalla n'a la yalla soutoural
Warnagnou xam sa papa comme milliardaire la ils sont très connus
Elle est brave machalah ❤😢
Massa waay metti na
En tout cas Ousmane sonko DH teuye n'a niari diabaram
Lima gueuneu nekh moy sa dem ba diekh yalla dina 8:21 la faye te none bakhoul Nanou thi yalla moussal tu es brave 11:14
Et ton papa qui milliardaire khana amatoul wone khalisse
Vraiment, doye na war dè
😂😂😂😂
Li moma diakhal khamna khamouy louy milliard
Waa lii muy mettitlu ak lim def 2em jëkkëram tek Ousmane soko ci kaw jëkkëram kii daal limiy wax daaciy teey.
Adama diope esk setnga yalla thi lingay wakh danga weet aksa bamel adama ya mana fen deug deug fam don seye bagnou gadje sokh eupouna 20ns te mom 10ans lafa am meusta deuk thi sangal tambakh nga wathi sa goro ya kala diaw maste geune negam sa djeukeur khadim lo bam lay fase sonko ken khama gouko te yaw wakho lepou dh djeukeur yigfi amat doko wakh amat ngafi niari djeukeur tass yaw takha walou katnga mo takh nga fakh dionge touba niaw louye sa aprtamant ndakh beuga bon ak sa pap kagnla nek milleyeder koudoul khalat tarayou bamel nak lolou nekh defal bilay sonko bis boula fale dara ma khamne ndayam ligeyalouko mom sonko tass katou fammes nga kou doy war nga
Moh yawit dé amoulo soutouro
Mon mane adama soudone mane douma ko bayi nonou sa dieker dala torakhale mais warone gako yobou wate si yone
Liko dal nak metina dou lougne ko yéené mais djiguéne diou bakh day topeu nigueulou dieukeurem(borom keureum)
Vrai fene katla y’a Diouboule Bilay sey amoul liko gueun dôme diamou yalla secrifier say dôme pour lan
Ya niak diom sonko motax nga bayi sa seye sonko deh mongi seuy
Merci bcp ❤❤❤❤❤
Mane ki gueumouma ko pour choisir cette heure là pour parler tous ça. Avec tout l'engagement des patriotes sur l'aide. C'est pas le bon moment pour dire tout cela
yaw wakho fi nai sa famille miliardaire lagnou
Cette femme n'a pas lair d'une bonne femme fautes attention avec cette dame là, meme son visage parle elle n'est pas innocente dé bien, rakal ak mboume non elle ment héhontement d'après moi, je ne l'a connait ni d'Adam nous d'Ève écarté la de Pastef
Yaw y’a kham niit nk day fène sama ex djiabar rakou papa la
Ki wolou woumako dara
Tu as raison elle semble mentir
Je ne l'ai pas cru depuis le départ 😮
Je ne la crois pas.
Mes chers refléchissez bien.
Elle n'est pas cohérente.
Yenena boon masta ma sœur
Ont vous aimmmmmm
Vive la dignité et diarama thi kou sél ki
😢😢😢😮😢
Tanna uosmane sonko mola geuneulone ci sa jakar jom nga fofou dé waye nak.mangui.niane.yalla.mou.defale.la.xewuele.ak.soutoura