Nguagne malgré tout j’ai remarqué que dans cette série à chaque épisode il donne des leçons que personne ne prête pas attention et j’aime beaucoup ça merci beaucoup evenprod vous êtes les meilleurs😂😂
Fimné mounou ma setane lénéne nkh seri bi nkh dafa ame avantages nkh société bii diamano dji lép lougne def serie rek gnoun Kaye doundou et aussi merci a évents pros🎉❤
Multipliez les salatoul ala Nabi ❤ Allahouma salli ala Seydina Mouhammadine abdika wa rassoulika annibiyyoul oummiyyi wa ala alihi wa sahbihi wa salim ❤️
Thies nakk c'est une belle ville machallah 🎉❤ chapeau evenprod🙏🥳 les thèmes sont captivants merci encore pour c belles realisations et bonne année à tous ❤❤❤
J'aime bien comment autour de la famille centrale ( famille de Serigne Ngagne) on y greffe des mini histoires pour dénoncer des faits de société.. Evenprod ya meune, ya beuri kham kham Machallah 💪🏾
@@evenprod avec l'histoire du mariage et du bapteme et du décès que le paraître à encore de beaux jours chez nous, que nos proches nous pousserons à faire des choses au delà de nos capacités et qu'il faut savoir dire non des fois peu importe le qu'en dira-t-on. Merci pour le subtil équilibre entre comédie et eveil des consciences
La série est vraiment excellente en tous points. Ce que j’apprécie, c’est que vous montrez les réalités de tous, ainsi que les mentalités et ont voient que tous n’est qu’apparence. On parle de Dieu pour se faire bien voir, mais le cœur est noir…
Quel épisode émouvant avec de nombreuses leçons. J'ai ressenti la douleur d'Astou Hann. Ngane et la façon dont il raconte ses histoires sont tout simplement authentiques. Un grand merci pour cette série venue d'Atlanta.
ndeysanne awo bi, elle a mal au coeur ! niou takal la woudiou beuparè t'es obligé de vivre avec elle du jour au lendemain ! seyou senegal metina ! deuk bi, diabar ni fi nek, ay jambar rek legn 🥰🥰🥰🥰🥰mougn rek legn meune ma shaa allah !
je pense qu'une femme amoureuse de son mari ne sera jamais suffisamment "préparée" à une telle situation mais en revanche, ce sujet de la polygamie est impérativement à aborder avant le mariage, dans un contrat de mariage pour ceux qui en font, c'est légal dans l'islam @@Annebaidysouleymane
jigeenou sénégal, deni wara imposé sen droits yi len ko yallah mayi ! woudié nekhoul ci khol deugueuleu, waayé yallah dafko dagane, kon kou décidé mougn bakhna mais les hommes sénégalais polygames doivent respecter tous les droits de leurs épouses ! par exemple, xamna né sou fekone jigeeni woudié nieup amone sen appartement bop wala sen keurou bop wala sakh sen étagou bop (pour les plus modestes, leurs souffrances et beaucoup de problemes (rivalité, haine, maraboutage, ...) pourraient etre évités ! beuparè kou amoul xaliss bou doy, fane leu tek tak benen diabar ? ! c'est egoiste et cruel d'imposer à une femme de vivre sous le meme toi que sa nouvelle rivale, dineu yewou, di guiss djeukeureum ak benen jigeen, dici tek beutteum ! limeu wakh ni yeup, ci diiné lako tek ! na kou nek dem verifier lane moy droits wou jigeen ci waloum polygamie ! @@evenprod
Alkhamdulilah ñu tambali atte mou béess mi Ci bismilah diéxall ko ci Alkhamdulilah ñu fékké Fin d'année 2024 ci jaam incha allah. Ci barké mouhamed PSL amine 🙏🙏🙏
Là je pense que si cinéma rk la yam ms amul si réalité comment une musulmane ose de dire qu'elle ne peut pas prier prck elle est fatiguée Yalañu yala defal deg ak topu 🤲♥️ Ce que les épouse de Mansour jouent me plaît vraiment elles sont fortes
Adouna bi nioùn djiguene lignou gueune bagne woudié thiala bokou woudié Kay bokoul thi souniou vocabulaire dagnou KO ragal ba sougnou kay wakh sougnou tougne yi dou dadié😂😂
La question ❓️ que je veux vous poser: pourquoi Goor bu takk gnarel gnuni dafa badola te yala mayko mu tak ba 4 si kaw mu meunko esk waxni Ku tak gnarel dafa badola c'est contre les paroles de Dieu gnuni dafa badola te yala mayko mu tak ba 4 si kaw mu meunko esk waxni Ku tak gnarel dafa badola c'est contre les paroles de Dieu La 2ème : esk soxnasi conseils yimu djokh ki c'est bien antank xarit esk ni lagnu wara conseils djigen buñu takal wudju tmt??? Nb: bufi ken waxé xol kusi amul connaissance ga nopi
@@elhadjika7482 khana vous n'avez pas suivi tout l'épisode? Il avait promis à sa femme que dou meusseu takeu gnarel et en plus il l'a fait sans la tenir au courant. Bou fékone depuis le début wokhone neu ko que dineu takeu gnarel Diabar dji dou mèr mais défoul lolou.
Et moi la question que je ne cesse de me poser moy pourquoi vous ne pouvez pas vous limiter à 1 seule femme? Si vous aimez votre femme et avez vu toutes les bonnes qualités que vous recherchiez pourquoi en épouser une autre??
La troupe soleil levant ndeye sane Laye 🥰🥰 Sanex aka ko sonalone 😂😂😂😂. Even Prod yenay ndanane yi nak. J’adore cette manière subtile de les intégrer 1 by 1 dans vos épisodes.
Mane mi sakh sossou kani bi métinama car ça m'a rappelé au décès de mon père. Son grand frère a fait exactement la même chose il nous a demandé de lui apporter du piment je dis bien au décès de son petit frère ( mon père) ça fait 7 ans mais je ne peux oublier cette parole
Ont l'as jamais vue ni attendre sa voix mais son amour Vu des milliards de cœurs❤
❤❤❤❤❤❤❤
C’est le meilleur yao miko beugue sah mbeguel gui dalay def gua nek nite kou bah tè dioub 🙏psl
❤❤❤❤❤❤❤❤❤salalaho ala muhamad ❤❤❤❤❤
Paix et salut sur lui ❤❤❤
Paix et salut sur lui et de sa famille 😢❤❤❤❤
Ngagne est tout juste devenu un Maestro, dans son art..et son métier... Excellent ngagne!👏👏👏
@souleymanediagne4516 Merci.
Je vois que even prod a choisi de ramener les anciens acteurs de la ville de Thies ✨. Belle initiative et très belle série 🔥😊
@bengawade9707 Merci. ❤️
❤❤
❤❤
Nguagne malgré tout j’ai remarqué que dans cette série à chaque épisode il donne des leçons que personne ne prête pas attention et j’aime beaucoup ça merci beaucoup evenprod vous êtes les meilleurs😂😂
Merci lol la beugon commenter ❤️🙏 dafay rélou trop 😂😂Mais leçon yu am solo la machallah j’aime beaucoup ❤
Série bi tu voit carrément que loolu moo ko tax a jòg !!
Ils sont spécialisés sur ça donnés des leçons !!
@ritoubadji7688 Quelle leçon as-tu tirée ?
Fimné mounou ma setane lénéne nkh seri bi nkh dafa ame avantages nkh société bii diamano dji lép lougne def serie rek gnoun Kaye doundou et aussi merci a évents pros🎉❤
Multipliez les salatoul ala Nabi ❤
Allahouma salli ala Seydina Mouhammadine abdika wa rassoulika annibiyyoul oummiyyi wa ala alihi wa sahbihi wa salim ❤️
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤amine
Thies nakk c'est une belle ville machallah 🎉❤ chapeau evenprod🙏🥳 les thèmes sont captivants merci encore pour c belles realisations et bonne année à tous ❤❤❤
@madadiop8638 Merci, as-tu tiré une leçon de cet épisode ?
Des cœur pour notre prophète Mohammed psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
J'aime bien comment autour de la famille centrale ( famille de Serigne Ngagne) on y greffe des mini histoires pour dénoncer des faits de société.. Evenprod ya meune, ya beuri kham kham Machallah 💪🏾
@Caroline-lc5ub Merci, quelle leçon as-tu tirée ?
@@evenprodbonjour mane épisode bouma guéna marqué moy bi passé le sieur Dieng lou gnaw loumou df
@@evenprod avec l'histoire du mariage et du bapteme et du décès que le paraître à encore de beaux jours chez nous, que nos proches nous pousserons à faire des choses au delà de nos capacités et qu'il faut savoir dire non des fois peu importe le qu'en dira-t-on. Merci pour le subtil équilibre entre comédie et eveil des consciences
Meussouma am j'aime 😭 kou beugue modou lo lalal j'aime ❤️ ani talibe cheikh yi❤
Gnon gui ni dh ❤❤❤
Gnonguini deh
La série est vraiment excellente en tous points. Ce que j’apprécie, c’est que vous montrez les réalités de tous, ainsi que les mentalités et ont voient que tous n’est qu’apparence. On parle de Dieu pour se faire bien voir, mais le cœur est noir…
@fatoubojang6547 Merci, quelle est la séquence qui t'a marqué de cet épisode ?
Bonne et heureuse année à vous tous encore une fois merci evenspro pour cette belle série 🎉❤❤❤🎉🎉
@mbenembengue4388 Merci beaucoup, as-tu aimé l'épisode ?
@@evenprodvous faites quoi pour les sous-titres de l’épisode 11 et 12 svp car c’est toujours pas sous-titré
Wa gni niom sén teint noir yi lanla tamite machala machala
@mamecheikhdiack2114 👍👍
AWO SERIGNE NGAGNE BI KAY MAASÀLLAA
Salalahou ala mouhamed ❤❤❤❤
❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
Les paroles véridiques de Ngagne ohh🎉 sous l'arbre à palabres waxtane Ngagne😂
C'est un artiste complet Maasàllaa.
@@sarrsaadikh6738 dama meune
@aidadiop1889 Bane leçon gueu tiré ?
Quel épisode émouvant avec de nombreuses leçons. J'ai ressenti la douleur d'Astou Hann. Ngane et la façon dont il raconte ses histoires sont tout simplement authentiques. Un grand merci pour cette série venue d'Atlanta.
ndeysanne awo bi, elle a mal au coeur ! niou takal la woudiou beuparè t'es obligé de vivre avec elle du jour au lendemain ! seyou senegal metina ! deuk bi, diabar ni fi nek, ay jambar rek legn 🥰🥰🥰🥰🥰mougn rek legn meune ma shaa allah !
Je pense que les hommes doivent apprendre à leurs épouses à se préparer face à cette situation, niussi beuri daléndi bétt mootakh mouy metti gérer.
je pense qu'une femme amoureuse de son mari ne sera jamais suffisamment "préparée" à une telle situation mais en revanche, ce sujet de la polygamie est impérativement à aborder avant le mariage, dans un contrat de mariage pour ceux qui en font, c'est légal dans l'islam @@Annebaidysouleymane
@@lala_aishaa absolument madame, bien pensé.
@lalla_thioune Bane conseil gua ame si lolou ?
jigeenou sénégal, deni wara imposé sen droits yi len ko yallah mayi ! woudié nekhoul ci khol deugueuleu, waayé yallah dafko dagane, kon kou décidé mougn bakhna mais les hommes sénégalais polygames doivent respecter tous les droits de leurs épouses ! par exemple, xamna né sou fekone jigeeni woudié nieup amone sen appartement bop wala sen keurou bop wala sakh sen étagou bop (pour les plus modestes, leurs souffrances et beaucoup de problemes (rivalité, haine, maraboutage, ...) pourraient etre évités ! beuparè kou amoul xaliss bou doy, fane leu tek tak benen diabar ? ! c'est egoiste et cruel d'imposer à une femme de vivre sous le meme toi que sa nouvelle rivale, dineu yewou, di guiss djeukeureum ak benen jigeen, dici tek beutteum ! limeu wakh ni yeup, ci diiné lako tek ! na kou nek dem verifier lane moy droits wou jigeen ci waloum polygamie ! @@evenprod
Alkhamdulilah ñu tambali atte mou béess mi Ci bismilah diéxall ko ci Alkhamdulilah ñu fékké Fin d'année 2024 ci jaam incha allah. Ci barké mouhamed PSL amine 🙏🙏🙏
Amine way merci beaucoup
Amine inchallah
Des cœurs pour notre prophète mouhamed psl
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
Sallahou aleyhi wa salam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Prophète Muhammad ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Lou Thioro meun thiep boulen fatte mere Fat Ndiaye moy number 1 😂😂😂😂
😂😂😂 mère fat Ndiaye mu roger
Wawaw mosi aye kaye😂😂
@djibrildiop1240 👍👍
do nittt 😂😂😂
الله أ اكبر لا إ له إلا الله محمد رسول الله صلى الله عليه ❤❤
Une série pleine d'enseignement
Chapeau evenprod😊
Cette série est tellement original 🎉
@fatoumbaye5562 Quelle leçon as-tu tirée ?
NO NGAGNE AK DOUCOURÉ DINAGNEMA RAY ILS SON FORT MACHALLA😍FÉLICITATIONS EVEN PROD👏
@mamadoumakanediop6836 Merci beaucoup. ❤
Une très belle série 🥰 vraiment rien à dire 😍yalna lén yallah fay
@fatoucha9217 Merci, as-tu tiré une leçon de cet épisode ?
Amine
@@evenprodwii
@@Coumbista48454 Laquelle ?
Ce qui me plaît moy thème bou dieul le prochain dinane si wax si birr keur gui juste pour nous montrer la continuité des événements 🥰 vs êtes forts
Evenprod daal daf May fatali cheikh tidiane Diop wala troupe diankhè de thies machallah 😘🥰❣️🙏
Billay ndeysane❤❤❤❤❤❤
Xew xew est une vraie leçon j’adore trop la série
@ndeyebiramediouf3416 Quelle leçon as-tu tirée ?
Bonne année 🎇 Mairou pikine Djeureujieuf 😂
pardon way 😂😂😂
Wa EvenProd tay si seuy nguen niou andil ak niarél😂😂😂😂
@mamadouthioune4840 Mba nexnaleu ?
@@evenprod trop sakh dolen def lou nekhoul
thiey mr bonheur ! tey ci waloum niarel ngaa nek, wa legui yaw monogame nga wala polygame nga ? saway 😂😂😂
@@arona_diaw445 poly lay lal
Bravo evenprod. Serigne Ngagne est un artiste hors pair 🎉🎉
Mba kham ngéne ni série bi kouné meune nassi diang
Yallna niou yalla defal diamou ak soutura taragna gou sakh dak aduna ak alakhira Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤
@bayeserignembaye6597 Amine.👍
Amine inchallah
Amine Yarabile Halamine 🙏🙏 Baye Serigne
❤❤❤❤@@evenprod
bima néké khalé dama fébaroun fébar bou méti niépa géné won sén khél siman ndakh dama kangké won dérét té awma kouma may banioumay beuge dialalé am niari nit you niaw pou mayé dérét ba nioma seuvé bilahi nioniou soumalén gison 😢
Machallh
Déléne nianal sa yéné rk ❤
@@mbayediop763 inchallah 🙏 merci beaucoup
@@mamediarrambaye1220 nalén niépou nianal🙏
Bonne et heureuse année ❤
@mbodia6392 Merci.👍
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
No Ngagne c le meilleur billaye wallaye je l adore
Vraiment vous êtes les meilleurs ❤
@mayibndiaye1120 Merci beaucoup, as-tu aimé l'épisode ?
Keur Serigne Ngagne dafa beuri diammou❤❤🎉🎉🎉🎉😂
Là je pense que si cinéma rk la yam ms amul si réalité comment une musulmane ose de dire qu'elle ne peut pas prier prck elle est fatiguée
Yalañu yala defal deg ak topu 🤲♥️
Ce que les épouse de Mansour jouent me plaît vraiment elles sont fortes
Doyna ware amine
Diepi nako sakh
B@@fantandiaye6331 walay musulmans youdoul diouli beurina
Par ce que djiguene là vous ne comprends pas wala
@@NdeyelissaCoulibaly-u2c Mouni
Saussou kani bi la meunoul mougn 😂😂😂😂
J'adore bien l'attitude de la femme
Woudié dou dara bokkou weurseuk leuh té heureusement ton mari t'aime defal patte ak organisé ❤❤
Tu juges trop vite la Fatou attendons la suite je passais seulement 😉😂👉 🏃🏃
@@ndiayendeye4713 tkt chérie je l'ai déjà regardé sur wido raison de mon commentaire je connais bien la suite des événements merci
@@fatoubinetoudieng5395chérie wido dangay fay pour setane wala?
Dangay faye kay😂😂😂@@gayeaichalababacariste5665
@@gayeaichalababacariste5665oui
Ma challah 😂😂 MS bolen fatte sonko 24 bi in challah diamou si yen
Alors deh meune nama ray😂😂😂😂 Serigne Ngagn dou nitt
Macahallah ❤️ mafi ditou mayelen ma ❤❤
😂😂😂😂❤❤❤ wa Malika am ngen ndame sen tonton moffi jeul numéro 30 thiii commentaires yi
Mane nak bizarrement ay wakhi garçon douma ko diap sakh, ba diko guem. Garçon rek😂😂😂😂
Tous des dragons 🐲
😂😂 ya yeye deh li kene khamoul lanla
@@ndickoundiaye6212wakh gua dgu gnoune gneup même ton père 😊😊
@@sidiseck935 yow kou rew nga, khamoma khamoula sama commentaire sa yone nekoussi. Mon père est un homme pas un garçon comme toi imbécile
Yalla na niou yalla may allal diou lew yalla def sonko président 2024
Oh! j'ai de la peine pour la femme 😢guene nianal ma yallah bouma âme woudiou Amine 🙏 toufffff toufffff 😊
No sacré serigne ngagne néna moy lall diabarou diamour😂😂😂
Où sont les fans de modou lô ❤❤
Nion gui nii😂❤
Non keur nguewél dal😂😂😂😂
Merci evenprod wa thies danio meun groupe dianxen ak soleil levant ❤
Evenpro vous êtes les meilleurs ❤
@GnimaSambou-bb9ul Merci beaucoup, as-tu aimé ?
Modou looo kharagne loo🎉🎉
Bonne et heureuse année à tous ❤❤❤
@NdoyeSport Merci, comment trouves-tu l'épisode ?
@@evenprod ah magnifique comme tjrs rk je suis vraiment ravi
@NdoyeSport Merci.
@@evenprod c'est moi qui devait vous remercier pour le plaisir
Abalay 😂le fils de bébé deureum😅😅😅un plaisir de vous revoir 🎉
Pourquoi goor balamoula meuneu gueureum rek daflay takal niarel aka gnio faux😂😂
Ak dieund dibi khadisgoudi😂
@@thianediaw2627bilahi wakhatiko 😂😂
Soula gueureumé kay soite woudiou leu wala gua dead goor kay migui ni rék
@evachou1172 Lolou diaxalouleu ?
Danio faut dé
Après xew bi louy xew xew xew 😂😂Mach llha sen série bi nekhna loll 🎉🎉🎉🎉❤❤❤
@mamefatyfall1237 Lossi dieuler comme leçon ?
@evenprod Def loo meune wakh lo meune do teudé ....
@abdourahimfall7874 Wakh ga deug.
Kén du wax sa diabar takal nala woudiou ❌️
Jeull naa banéen soxna lani wax✅️
Benlareik ahh
Mane secansou Serigne ngagne momay rayy😂😂
Ak man mii
Ndanane la barké yalla 😂
Dieng dagna bone rek legui yalla kharoul fin du mois dh legui lalay fay 😮😢
@ndoumbemare Mbadou fay nako ?
Même niaréle bi warona niame mome tamite dakh Di mourou Di dialo 😢😢
Bily wah gua deug toma❤❤
Ça épouse une autre femme et ça ose lui dire JE T’AIME . L’hypocrisie des hommes 😢
😂😂😂😂
Pourtant man na nekk dé
Prendre une deuxième femme ne veut pas dire que tu n'aimes plus ta femme, attention!
En tout cas Serigne ngagne assure bien son rôle, il est le meilleur.
@timatima yaw loulah dall li moy hypocrisie 😂😂😂
Thiat chaque épisode dafa wara guéne
Adouna bi nioùn djiguene lignou gueune bagne woudié thiala bokou woudié Kay bokoul thi souniou vocabulaire dagnou KO ragal ba sougnou kay wakh sougnou tougne yi dou dadié😂😂
Lolou deugg gou werr leu té suniu borom molénko tékk lolou moy nattou djiguéén si kaw souf.
@@Annebaidysouleymane bilahi yaw yalla mognou KO NATO
@@ndiayendeye4713 di niaan rek yalla nalén Yalla may ay woudiou you ragal Yalla té respecté léén.
@@Annebaidysouleymane amine kay
@ndiayendeye4713 Est-ce que dissoule si gnome ?
Awo amoul morom❤🎉
No ngagne nexna😂😂😂
Yallah na diam yague🙏🙏🙏
Amine
Mariage amna Guentei Guen deuthi guen😂😂ahn tay danouy tak niarel ok
@ndoumbendiaye7405 Mba nexnaleu ?
@@evenprodnékhna trop sakh❤machalla
Nékh na trop machalla ❤
Xew xew après xew bi louy xew
Xew xew😂😂😂
@moustaphafall8672 Xew xew rek .
@@evenprod kon xew xew
Li après xéw bi guay weur bole say dal wala sa diwe fék sathie nane ko si khéw bii😂😂 douma faté sama biss ba 😂😂
Surtout bole yi 😂😂
@@FountySoumare-uk5db yaw setlou gua lolou ah senegal khéw meti nafi
@DiopErkanAida-li7lp Lou xew sa bisse ?
Mère Thioro seul😂😂😂❤
Chantal kou gueum se bop gue nawnale❤
Team ngagne 😂😂😂❤
Yall na diam yageu Sénégal
@ibrahimangom229 👍
Modou lô moy mairou pikine❤
Wawaw 😂😂
Je suis le premier sur les commentaires félicitations à moi🎉🎉🎉
@user-xn2fm6er1r Bravo.
Doukouré khana guewel na deugantane 😂😂😂😂 kii dafa neikh way il joue très bien
😂
Yéne meune dh Billay après bi khana ak magal guéne si tèkk😂😂😂
Yena meuneu kayy❤❤
La question ❓️ que je veux vous poser:
pourquoi Goor bu takk gnarel gnuni dafa badola te yala mayko mu tak ba 4 si kaw mu meunko esk waxni Ku tak gnarel dafa badola c'est contre les paroles de Dieu
gnuni dafa badola te yala mayko mu tak ba 4 si kaw mu meunko esk waxni Ku tak gnarel dafa badola c'est contre les paroles de Dieu
La 2ème : esk soxnasi conseils yimu djokh ki c'est bien antank xarit esk ni lagnu wara conseils djigen buñu takal wudju tmt???
Nb: bufi ken waxé xol kusi amul connaissance ga nopi
Goor amna droit tak 4 femmes mais si kaw kouka man wayé amna ñio khamna yorou ñiou ba paré reuy lang tek si goor gni dagnouy diéngue
@elhadjika7482 Est-ce dou dieufine bi mo gnawe ?
@@evenprod si naka
@@elhadjika7482 khana vous n'avez pas suivi tout l'épisode?
Il avait promis à sa femme que dou meusseu takeu gnarel et en plus il l'a fait sans la tenir au courant. Bou fékone depuis le début wokhone neu ko que dineu takeu gnarel Diabar dji dou mèr mais défoul lolou.
Et moi la question que je ne cesse de me poser moy pourquoi vous ne pouvez pas vous limiter à 1 seule femme? Si vous aimez votre femme et avez vu toutes les bonnes qualités que vous recherchiez pourquoi en épouser une autre??
Waa kiii déee ngay seeedé si moom lou bon😅 astahfiroullah 😃
Ki ganiou kéne meunoul wakh si mome lou bakh xana niou mandou rek😂😂 Dieng dafa bone trop
@@aminasy9321bonoule ndank sakh dafa yéss ignane bonn
@@aminasy9321 😄😄😄moom Kay mandou reek
Taye hewbi niarél la😂
@mamediarrambaye1220 Mo xew tey.
Kou beug seydina Mohamed lalal jamais
Ndeye ´Ndiaye arrive
12:17 nekhoul si khôl Bapare nga kay deff😢
@mamediarradione5764 Mbadou da disse ?
@@evenprod c'est dure d wallahi 😭 xëy rk di bokk sa jëkkër
Laye Sow vraiment dagua meun liguadef ohhh
Modou lo gouverneur de pikine 😂
Wawaw😂
Guissagou ma fi anniversare wala tourou famille wala foureul 😂😂 xew xew la daal
Boul yakamti lep dina gneuw 😂😂
Eska dou Khar RK gnou gui nieuw dh 😂
Louy foureul😮
😂😂sabat you mame yi daan def souma dioumoul
@@mamebintoufaye9211 An ok
En fait le plus dur au monde c’est d’avoir des faux amis on finira accepter xew xew devant cœur brisé
Copine bii (Chantal) mbadou moye woudiou bii🤭yalna done sama imagination kessé😎
Les Chantal sont gentilles boumou deff lou niaw 😂
Kou thi beugue yewu del setane ay productiond even prod machalla ❤
Bonne année 2024
Pah bolé nak bayil thiatt😂😂
@amintagueye6337 Lo koy conseiller ?
Bonne année à 2024❤
Ngagne nena dieng dadon lale diabarou diambour yii lakoy sedel😂😂
La troupe soleil levant ndeye sane Laye 🥰🥰 Sanex aka ko sonalone 😂😂😂😂. Even Prod yenay ndanane yi nak. J’adore cette manière subtile de les intégrer 1 by 1 dans vos épisodes.
Fifita😂😂ndaysane
Kou beug sa maman rk lalal ❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
Ngane sossou kani bii metinako nak 😅😅😅
Trop 😂😂😂😂
Bilae dafko choquée 😂😂
@momofaye2658 Est-ce que yombouneu nangou ?
Mane mi sakh sossou kani bi métinama car ça m'a rappelé au décès de mon père. Son grand frère a fait exactement la même chose il nous a demandé de lui apporter du piment je dis bien au décès de son petit frère ( mon père) ça fait 7 ans mais je ne peux oublier cette parole
Bisimilah niou xéwi xéwi yene❤❤❤❤❤
@maremendiaye5485 👍👍
Kou xéw xéw mi yaw😂🎉
Après xew bi louy xew😂😂
@@yayemayelatmbao5442xew xew 😂😂
@@fatymbodj-gs5wq 😂😂😂