Yaye Dior on dirait qu’elle jouait juste le jeu avec Bourry, elle ne l’a jamais appréciée. C’est fou comme on peut oublier du jour au lendemain les bonnes chose qu’une personne a pu faire😢
La grandeur,la gentillesse,la politesse et la beauté de diadia on a parle une vraie définition de l’âme pure vraiment bravo à vous dans cette épisode on px comprendre peut importe les actes qu’on fasse c’est dieu qui décide c’est le début du malheur de la maman de diadia ❤️🥰chapeau à Even prod 🙏🥰
Quel casting vraiment ndiawar assure bien son rôle selon le Personnage qu’on l’a donné « ndongo daara Bou tekki 😅 la façon de parler, de réfléchir le comportement » chapeau even prod😅
Toubap bi dé néna l'argent ne fait pas le bonheur wayé mann andou mathi, Yalla na niép am xaliss bou lew té barkél téniou nangou ko bokak souniouy mbokk ay gni amoul❤
Le talent de la mere de djadja on en parle😳 la dame elle est petrie de talent de deh. Decretè naka meilleur actrice de la serie mome ak yayou ass diagne elles sont de loin les meilleures
La petite Sokhna joue hyper bien son rôle 🎉❤❤bouri amna chance ndakh ko am koudou d’où lakkeu 😂😂bouri n’a gnibisi gaw car soda mougui am importance si ndawar😢bouri rek laniou topeu wassalam 🤧🤧♥️Waa mais niankou 😂😂😂😂😂😂
Boury à son bonheur entre ces mains. Qu'elle retourne à son foyer c mieux... gor boumoula beug banga fokkkni si yaw rek lay yam.... emplus loula meuntiii meti MAYMA SAMA BATTT c'est pas un chanson... gor bou meleni yaw loumoula beug beug boko niané battt dalakoy maye malgré môme. Woudj n'est pas un fin en soi...
@@diakhateastou8627 Boury gnarel takhoul mou tass li motakh goor gni douniou respecté nimou défé mo niaw goor dangay am batt si sa keur ms ay djiguene dila influencé ms Ndiawar ca lire l’heure ba Seydou paré si mom rk
Xalisso la série familiale qui cartonne, Khadija tu vas bientôt lire à l'envers...Ton Karma finira par te rattrapper...Maty Rose est tellement naïve😢...Justice pour Boury...On réclame le bonheur de Diadia❤
Fatou kinè même que ndeye ndiaye😂mbeugeu comme basine thiam😂yèna meunne ms djadja vraiment contana si yaw sa acte bi damay fatali comme mane akk sama domou baye yii❤❤
Yalna yalla yereum keup Kou nék thi bir souf thi barké seydina Mouhamed Salalakhou Ala Mouhamed té yékhé gnou maye gnou mouje bouraféte thi barké seydina Mouhamed Salalakhou Ala Mouhamed
Xalisso nexna trop li rék mofi am xaliss la niteu yo Di topp rék merci evenprod amougniou seneu faiy depuis idoles bataiy meussoleneu gniou décevoir tes dagué'eu respecter heure mais idoles bété bété xéw xéw njabar AK munel gnioy sama préferé j'ai vraiment xéw xéw épisode mirass bi mom Beneu affaire leuh merci encore
Série bi dh nieupayy am gnarél.... Épisode bi passé djadja djangual n'a khaleî you djiguén gni nei djiguén dafa am foula dh respecter 'say thieur bakh'na lol 😊 mashallah 🥰😊😊 diar'na bayi xél dh.... Kan mo supprimer seurr😂.
Pourtant niarel ndiawar bi amoul blem dee mére bi mokoy dougal si li nieup mboury warna gnibisi gére parce que woudiam amoul blem mére bi kay mo Doyy warr chapeau a diadia bokk dafa nekh bilay🎉
qu’ الله aide la Palestine qu"الله accepte nos duaa qu'الله nous accordé le paradis qu'الله accepte nos prières qu'الله protège nos parents qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
Yaye Dior on dirait qu’elle jouait juste le jeu avec Bourry, elle ne l’a jamais appréciée. C’est fou comme on peut oublier du jour au lendemain les bonnes chose qu’une personne a pu faire😢
La grandeur,la gentillesse,la politesse et la beauté de diadia on a parle une vraie définition de l’âme pure vraiment bravo à vous dans cette épisode on px comprendre peut importe les actes qu’on fasse c’est dieu qui décide c’est le début du malheur de la maman de diadia ❤️🥰chapeau à Even prod 🙏🥰
@sambasall6813 Merci beaucoup. 👍
Une sokhna parfaite li diafe lolll , te ñu bax niep mom lagne begue
Quel casting vraiment ndiawar assure bien son rôle selon le
Personnage qu’on l’a donné « ndongo daara Bou tekki 😅 la façon de parler, de réfléchir le comportement » chapeau even prod😅
❤❤❤❤❤❤❤Q
J’aime trop comment le père Diagne ( le papa de Djadja) parle. Il a une voix apaisante et rassurante, comme un vrai sage.
@cloclombaye6457 Merci.
Dafa am foula mat kilifeu
Il est sérère c’est normal ❤
Bilay c'est 1 joli cœur aussi
Oui il a toujours était comme ça ndeysanne ❤
La force d'even prod et tout le temp d'attirer les meilleurs acteurs et ils ont encore frappé fort avec niankou
Diadia Yallah nako yallah fayy khôlam wayy djiguéne gou bakh La Machallah 😊
❤❤❤❤❤
Duo fatou Kine ak diop fall
Diadia ❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Diadia personnage leu deh nakh nian yi dinako dall 😂
@@aliouneba761😂😂😂😂😂
Niarel en téléchargement tata anna et tonton as diagne😂😂😂.la scène de diadia et Omar m'a donné des frissons mbok allalou Yallah 😢😢😢
💪💪
👏👏😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😅😅😅😅😅😅
Mach allah ❤❤❤❤
😮😮😂
😂😂
Où sont les fans de djadja et bourry chapeau evenpro yèna meune nakk machallah❤🎉
❤❤❤❤
❤❤❤❤
@AïchaRassoul-r6u Merci. ❤
Pa Ass dieuliill ligua mom 😂😂 niarell bi koussi dakor 🎉
Liguéye domou djambourr naakhhh allalll après ngayy déff semblant nannn tu l'aimes,, yalnaniou yalla saammm😢😢
@vieuxrabahfall4234 Ah est-ce que tamite moko ligey, Omar Diagne febaroul rek ?
Hypocrite rek
@@evenprod mère bi deh dumako miimël dara ndax dafa soxor torop wallah
Amiin❤
Toubap bi dé néna l'argent ne fait pas le bonheur wayé mann andou mathi, Yalla na niép am xaliss bou lew té barkél téniou nangou ko bokak souniouy mbokk ay gni amoul❤
Walaye Amine
Lolou mo am solo lou lew tei gnou meunko bok❤❤❤ amine yarabi
Wakh gua lou ame solo niou nanguo KO bok AK souniouy mbok
amine yarabi ❤
Americain bi ni time is mony
Xalisso badjoo toukeul na adouna 😢
Bravo à toute l’équipe 👏🏻❤️
Mou nar yakh sama vie si lou yagoul dr😢😢mais yallah baxna 💔
@mbayangdiagne1904 Merci beaucoup. ❤
❤❤❤
Kou geumny yayou diadia mo ligueye 😢😢😢niankou mou dof ngir khalisse rk lalal Jaime ❤❤❤
Mom la ky même dieukeur dji sakh
@@aramegueye-ox8ff😂😂😂waye dieukeur dji Dina tak legui 😂😂😂
Diaral nakoko dei
Lolou dé la xalat
@@mormbaye2989yayou maty rose khana? Nonou lako yakamti wé
Mais parlons un p du talent de maman Binta elle est extraordinaire chapeau
Mère bi kay machallah 😂
Le talent de la mere de djadja on en parle😳 la dame elle est petrie de talent de deh. Decretè naka meilleur actrice de la serie mome ak yayou ass diagne elles sont de loin les meilleures
Vraiment 🎉
Yayou ndiawar plutôt
Astou la, pure talent et beuaté🥰
Yalla na nieup am xaliss té mou barkel🤲🏾
Amine inchallah
Amine
Amine ya rabbi ❤
Amine inchallah ❤
Amine inchallah
Lima Nakari wone yeup nékh nama tayy Nakh Sokhna bou ndaw🎉😂❤
Aka saff lamign😂
Sokhna dafa am foula ci khale
@diorsakho307 Mougui fadial yayame nakharame. 😂
@@evenprod bilae dama contane si mom😂
Non sokhna fan nako 🎉mangui done reh 😂comme doff ❤🎉
Yalna naniou Yallah dimbali, Yalna naniou Yallah diapaler, Yalna naniou Yallah Tahawou, Soutoural niou tée Arr niou bidiahi Nabil Moustapha ( S.W.S ❤)
Psl
Anime
Amine
Série bi nexna machallah 😊mais Dior Mbaye bravo 🎈🎊🥳
Maty rose beugue n’a gua nek niiit 😢yawww deké Seydou mola beugue mome au moins nangouna beumbe bi guay dof dofoulou wa bakhna to pal sa kharite 😂❤️
Billay tonton ndiambe sene dafa meune machallah💗💖💕
Dama ko beug en plus dafa lewete❤
Mogui todje polygame 😅😅😅
Bilakhi 😂😊
Asuthiìf🎉
Ndanane la nak mine na aye galagne❤❤❤
Yayou Diadia mi rafetna, diekk na, machallah.
Wayé da bonne
@Syndiely 👍
Machallah mais mauvaise helas
Loumou raféte bonenako😂😂
La discussion de Fatou kiné et ibou laye sa fait ma journée meilleur duo 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Dama reee 😂
@fallougentlemara4853 Kouni wakahl geu sa morome dh. 😂
1 lâche et une dorkatt
Fatou kiné nénako kagne nguaye déme aéroport avions yii😂😂😂
Ndeye Ndiaye mofa manque
Chaque jour ma wakh sama gayi Bonne doû térré diour lou bakh kouco wéddi kholale dîadja ak yaye diji ❤❤
Absolument l'adage qui dit dome dja ndeye dja c absolument faux
Evenprod dou béni mromou benen maison de production
,kouko guiss rk lalal j'aime top way🎉❤❤❤❤❤❤❤
La petite Sokhna joue hyper bien son rôle 🎉❤❤bouri amna chance ndakh ko am koudou d’où lakkeu 😂😂bouri n’a gnibisi gaw car soda mougui am importance si ndawar😢bouri rek laniou topeu wassalam 🤧🤧♥️Waa mais niankou 😂😂😂😂😂😂
Da meune loumouy déf dé
M@@khadyfaye9237
ESS
Le personnage de Diadia me séduit de jour en jour elle est tellement gentille ❤Diadieuf way bakh rek mo am solo ❤
Elle est gentille et mâture
@adjasalihsamb9398 Geune na jikko yey dji dh. ❤❤
🎉🎉😢
@@evenprodlolou dafa ler
Bilaye ❤❤❤❤❤❤❤❤@@evenprod
Ça se voit k gni nak gnom meuneu theatre ndeysane un jeu d’acteur bou seteu wathieu machalah
@kaami8709 Merci. ❤
Ndiawar il est trop fort un vrai analphabète 😂😂😂😂😂
Bilakhi il est fort
Mention spéciale à ndiawar pour le respect en vers son frère. Ass.
Et pour sa réaction avec la femme de ass diagne.
Merci ndiawar. ❤
Rakou djadja promotion canapé lafi guiss nakh dafa beugueu siw tres bonne leçon mrxi Even prod
Thi birr la dieume dé
Uri irio
@yacineba6628 Lo xam kou oyaf bopou ?
Esk livreur bi neikoul diko iri sax? On dirait ils l’ont fait
@@seynaboudiop1059si dakoy iri
Pa Ass mirna si Ta Anna😩😂🤣père amoul ragal dh yokhla dieuliko🤸🏼 niarel en téléchargement 🥳🥳🥳😂
@maguettediagne9734 Ba awo bi douko def dareu ? 😂
@@evenprod kokou xadiou étage la day Mbeuww rk😂mais dou touss Ta Anna rk lagni topou 🥳🥳🥳
Yakoy accompagner 😂😂😂😂😂
Ndaysane père ndiambé sene ( ass diagne) j'aime son caractère
Héé😂😂😂😂beugueuna sokhena 😂😂😂😂😂😂kou d'accord beuseul jaime😅😅😅😅
wollah ndeysanne namenaleine trop
@NgoneMbaye-y3j Mougui fadial yayame naxarame. 😂
@@evenprod wawe beugueuna khalé bou ame fouleu difendre yayeme. Par ce ke mère dafa faux en tout cas je laime bien 😜😜😂
@@hijab_mode_sn gnola raw lou beuri😍😍😍
Evenprod a rassemblé presque toute les meilleurs acteurs au Sénégal bravoooo
Maty rose tmt Khana day business si eumb bi😂😂Esk eumb na tmt 😂😊
Deal leu avec sa copine avoir de quoi gaspier à Dublin
Thieuy khaliss 🤸🤸🙊🙊
Guemou mko dei eskeu businessoulll rk
Anna AK ass Diagne sén couple rafétt n'a Evenprod diapou léne si rk❤🎉
Fate kine la waron tak rk mo gueuneu féroce anna dafa sedd teh gerou kine yi nio bakh si khadija
Far kine mou bakh ci khdija
C vrai en plus Dinaa nekk mbeteel dh EP rekk😅😅
Anna seddd😂non da ngua nann fi role bi tolou mo ladj dall mais apres ngueuy ham ni bandit leu @@cisse5312
@@manishounaby2341Anna mosi bakh woudiou dal sed té diongama nexoul woudié
On réclame le bonheur de Boury😢❤
Mane dè Anta lim tate lay top😅😅
Boury à son bonheur entre ces mains. Qu'elle retourne à son foyer c mieux... gor boumoula beug banga fokkkni si yaw rek lay yam.... emplus loula meuntiii meti MAYMA SAMA BATTT c'est pas un chanson... gor bou meleni yaw loumoula beug beug boko niané battt dalakoy maye malgré môme.
Woudj n'est pas un fin en soi...
@@diakhateastou8627bien dit, elle doit retourner dans son foyer auprès de ses enfants teh seuy seuyam, na ignorée gorom bou bone bi
@NdeyeRokhayaGueye-z3d 👍
@@diakhateastou8627 Boury gnarel takhoul mou tass li motakh goor gni douniou respecté nimou défé mo niaw goor dangay am batt si sa keur ms ay djiguene dila influencé ms Ndiawar ca lire l’heure ba Seydou paré si mom rk
Xalisso la série familiale qui cartonne, Khadija tu vas bientôt lire à l'envers...Ton Karma finira par te rattrapper...Maty Rose est tellement naïve😢...Justice pour Boury...On réclame le bonheur de Diadia❤
Kou dem sakh khadija mo rayy yayou omar diagne bamou sotti rekk wa bakhna
Fatou kinè même que ndeye ndiaye😂mbeugeu comme basine thiam😂yèna meunne ms djadja vraiment contana si yaw sa acte bi damay fatali comme mane akk sama domou baye yii❤❤
Khadija vraiment elle assure grave son rôle 😂dagn koy djepi tellement générique bi à la fin on en parle iss 814 bondi gha 😂🎉 chapeau a toi 🎉
Bizarrement mane ndiawar ay rei lama deff😂❤️il joue bien
Yalla boumouy wakh ba diokhognie baram bou gatteu bi ki hawa seugueu😂😂😂😂ba ni khalé yi dôme keur bayam dégueu guama😂😂😂😂
Il est pétri de talent ndiawar diagne(Moussa Seck)
Bilay ya kham ndiawar😂😂😂😂@@byanaartaye96
Mom dafa meune deh comme payou am khaliss yoyou niniouy dòkhé😂😂
Saay kep kouy theatre moussa seck mola gueune nexx😂
Xalisso meilleur série ❤
Meilleur série Xalisso qui n’a jamais perdu sa valeur yayou diadia amna problème merci evenprod chapeau à tout l’équipe ❤️❤️❤️❤️
Esk liguéyoul domou diëkër dji sakh😢 en plus niaarèl en téléchargement.....😂😂
Lolo lou l’ère Naarél en téléchargement 😂😂
❤🎉我❤❤️❤🎉我🎉❤🎉@@yayatall8623
@yayatall8623 Merci. 👍
N’oubliez jamais les cinq prières 🤲 ❤
Kilifa nilayy mell 😢❤
Amna djiguenn you bone bilahi walahi 😢💔
Wa maty rose mi tamite😂😂😂ah môme dall 3 personne yeupp aaaaah😂😂😂
@khadydjiguel5107 Doyna ware. 😂
Wahalllll dddd 😂😂😂 magui compter😢😢😢😢 rekkk
Eub bi sakh est ce que degg leuu😢😂😂
Yalna yalla yereum keup Kou nék thi bir souf thi barké seydina Mouhamed Salalakhou Ala Mouhamed té yékhé gnou maye gnou mouje bouraféte thi barké seydina Mouhamed Salalakhou Ala Mouhamed
Diop fall ak Fatou Kine Sen rencontre Moussoul nekh 😂😂😂😂😂😂
"Tarafatal aïni" devenue "lou wow kong"😂😂😂
Ana daba Thiam 😂😂😂
Bilay Diadia xol bou rafét la yor❤mé Niankou tamit aka meune rôle dof en tout cas le peuple est content dh😅😅😅😅😅❤
Xalisso nexna trop li rék mofi am xaliss la niteu yo Di topp rék merci evenprod amougniou seneu faiy depuis idoles bataiy meussoleneu gniou décevoir tes dagué'eu respecter heure mais idoles bété bété xéw xéw njabar AK munel gnioy sama préferé j'ai vraiment xéw xéw épisode mirass bi mom Beneu affaire leuh merci encore
Boule faté Impuissant, Vautours, Watt gaal,Fake life
A quand la saison 2 de vautours 😢😢😢
@aminatasow4504 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire.
Yayou Diadia 😂😂 amna problème naq Adja rqq si diongama😍
😂😂😂
Mais dafa yambaré 😢
@@MmeDiop-r5uyabare dafa tey rek ma sha Allah
Nako pa bi dieul
Barki rassoulilahi 😂😂
Niankou changer na yéré wayy😂😂
Ndiaware sou wakhé c’est très bien rek ma contane🤣🤣
Acteurs yi ak actrices yi ñoom niepa meune chapeaux à vous😊
@cherifousinguinar8455 Merci. 😍
Xalliso la série qui n’a jamais perdu sa valeur 🎉❤🎊🫶
P',','.on.',n,,n,î,
J amain
@FatimaNdiaye-we5ys ❤
Wawa😂😂😂
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉
Amine ❤❤
🎉❤
Amine
Amine ya Rabi
Or sujet
Niniou andé si serie yi yalla naniou andé nono aldiana ❤😢
Djadja ont aiment bcp sa role machalha iow rek la ńiiuy topp
Khadija machalah sa robe bou blanc bi rafetena trop ❤sokhna mou ndaw je t'aime tu joue bien nonoula xalei daye âme foula nguérale pour sa yaye😂😂
@mamyloum2506 Ah Soxna key mougui fadial yayame ndakharame. 😂
Qu’ALLAH accorde une longue vie à nos chers parents ❤❤❤❤
Amine inchallah
AMINE yarabi ❤
🎉🎉🎉🎉🎉
Vous avez remarqué le style de sokhna wow 🎉🎉elle s’habille très bien 🎉❤
Mo koy diaye
@@AminataDembaNiang doma diay si ensemble bim sol tay c très classe j’adore
@@MariamaKonate-o5t no dou mane deh sokhna bisi série bi la wakh
@@AminataDembaNiang ah d’accord je comprends mom si boppam mokey diay? J’avais mal lu merci
@@MariamaKonate-o5t mome deh you toubabe lay diaye
Série bi dh nieupayy am gnarél....
Épisode bi passé djadja djangual n'a khaleî you djiguén gni nei djiguén dafa am foula dh respecter 'say thieur bakh'na lol 😊 mashallah 🥰😊😊 diar'na bayi xél dh....
Kan mo supprimer seurr😂.
Pourtant niarel ndiawar bi amoul blem dee mére bi mokoy dougal si li nieup mboury warna gnibisi gére parce que woudiam amoul blem mére bi kay mo Doyy warr chapeau a diadia bokk dafa nekh bilay🎉
Lolou la guiss aussi vraiment elle mérite l'amour de son mari lepp mère bila
qu’ الله aide la Palestine
qu"الله accepte nos duaa
qu'الله nous accordé le paradis
qu'الله accepte nos prières
qu'الله protège nos parents
qu'الله protège nos grands mères/pères 🤲🏼
Ahhhhh yalla na Ase diange takke anna🎉🎉🎉🎉
Amine
Walay ❤
@fallndeye6092 Hi ba awo diape ko ?
Bly iow 😂
Thieye evenprod toujours ponctuelle 19h 30 yena woor kay meune mokal maitrisser ❤❤❤❤😂😂
❤❤❤❤
Diokhé thieure rek
@pendagueye418 Yeina ko fi ame. ❤
Diadia la wax bilay Macha allah
Niankou changer naa chemise enh 😊🎉
Tonton djambé séne damako beuge❤❤❤❤❤❤
❤❤❤😂
❤❤❤❤
Même moi billahi ❤😢
Yaye Dior joue tellement bien son rôle 👌
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 🎉😢😢😢😢
Amine inchallah
Amine
Allahumma Ameen 🤲🙏
Amin
Amine Yarabi🙏
Rolou dofe mom nianko si meune nagn dieul rolou doff aduna yeup diohkoko😂😂 ki esk meussoul doff sah
Yaa bon. 😂 😂
😂 vraiment kou fiy joué rôle dof kay Da Nga ko wara tagou
😂
😂😂😂
Loufi way am nako santé yalla🙏🙏
Niaréle en téléchargement 😂😂très bien fofa todje
Ms guou sokhna mou ndaw nekh rk lalal jaime❤on réclame le bonheur de boury❤le couple de diadia et batlaine kou beug enve prod rk lalal jaime❤
Meilleurs série en ce moment et cœur brisé aussi vous êtes fort evenprod❤
Machallah dior Mbaye .Elle a une voix a merveille ❤❤
Ndiawar ak ass sen affinité entre frère jaime bien li dafa nekh niou bokk nii lagn wara mel
Diop Fall ak Fat Kiné sen duo louné la 😂😂😂😂
🎉🎉🎉khaliss wané n’a djiko yi
Gawgna deh
Yaye 1er Machalah ❤❤❤
@@MorMbengue-yy3us
@@mormbaye2989
@@mormbaye2989m
Seydou dh bala nguéne Di comprendre fek ruiné naléne😂😂😂😂
Ndeysaann diadia nitt kou bakh la ❤❤
😂😂No Mane Seydou damakoy beug ba kagne 😂😂 Seydou dama eumb eumbo punaise😂😅
Notre niankou 🎉🎉 thieuy Sènegal 😢😢
Non nianku rakajûna😂😂😂
Salalahou alla Mouhamed
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Khadija borom asse diagne niémé wouma prepare toi niarél en téléchargement 😂😂😂😂😂😂
Khadija taloul Dieukeur dji djiguen gnou beuri gnou pousse sene Dieukeur di takk gnarelle
Niankou meilleur acteur ❤😂😂😂😂
Bly gor deug moy ass diagne surveiller sa dôme oumar diagne😊😊😊😊
Dieureudieuf ndiaware tu as bien répondu. Tu es un homme sensé et juste merci beaucoup
Ani wa team setane tous les séries sénégalaises 😌🎉😁
Je suis là
Je sens l’amour entre Asse Diagne ak yayou Maty rose 😂😂😂
2eme dame en téléchargement 😂😂
Il resté que cette touche , Niankou merci Even Prod pour ça
Niankou dof bou ammm foula laaaa😂😂😂😂
Drogue douce
C’est fini folina bètè bètè non li khèrè neu bilay 🥳💃❤️❤️
Domou baye bété bété niveau bi dfa graveuh
Bété Bété est unik chérie
Yangui kay folli ba legui wallah😂
Kou begue seydina mouhamed lalal j aim ❤
Kou gueme ni yayou diadia mo liguey niankou pour que boumou donnou papam si heritage gou famille bi❤
Ay niankou tjrs à fond ❤
Seydou deh ay freram yep lay yobou faillite ndax ay ngaka lagnou ndeysann 😂
Kou beugue seydina Mouhamed (pal) beuseul j’aime ❤😊