Goomu Xol : « Sama dieukeur «Niak» mo sathie sama dom…def nak mom 8 jours de…»: Eva fond en larmes

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 12 січ 2025

КОМЕНТАРІ • 166

  • @antagaye4481
    @antagaye4481 2 роки тому +16

    Ndeysane la petite Ada ak sama dome gno bokone classe cité alioune sow yénesaye papame mokoye indi yénesaye yayame yalla nako yalla néguate si lokho yayame

  • @souleymaneseck6
    @souleymaneseck6 2 роки тому +17

    Courage ma sœur....soit forte...que dieu te ramène ta fille

  • @siramo574
    @siramo574 2 роки тому +16

    Bilaaye seuye dou allalle , yeurmandée laa, yalla nalleenne yalla maaye hoollou mougne.amine.

  • @khadysene799
    @khadysene799 2 роки тому +12

    L'an mo takh sa dieukeur door sa yaye yobouko polic ngua continuer ak mom

  • @yacineniang5254
    @yacineniang5254 2 роки тому +8

    Yalnako yalla delossi Watt thi sayye lokho ci barker seydina mouhamed

  • @eulleu9179
    @eulleu9179 2 роки тому +16

    Sohna Eva Yalnala yallah tahawu ba sa dom ji Ada ngibici waat ci sa wét kula xam xamnala ci beug niabott yalna yallah niit🙏🏿

  • @astousow8723
    @astousow8723 2 роки тому +12

    Svp aidez cette femme

  • @burr9379
    @burr9379 2 роки тому +25

    Dama khamoul lounguéne guiss thi Gnak. Surtout Nigérien et je dit une chose beuss bo démé Nigéria
    Dina la Sacrifié yaw ak sa Dom Défal trés attention Ay Domou khram lagne gnom Gneup.
    Moytoul deh lou lerr lala wakh.

    • @aidis3605
      @aidis3605 2 роки тому +13

      Ki soutien moral la sokhla , wayé sokhla woul kou koy déf ay reproche

    • @siramo574
      @siramo574 2 роки тому +9

      Amnaa kou gneuwoone teuss dée, daawée nigeria baa senegal , gnakk mokoo taakk , djookh famille bii haliss bou barii mou naah ko yoobe koo nigeria, a chaque fois qu elle accouche, ils prennent l enfant poour le sacrifier à la fin, la fille a été aidée par une senegalaise , elle a fui, completement traumatisée, elle était enceinte.c est sa tante qui l avait marié par interet.

    • @burr9379
      @burr9379 2 роки тому +1

      @@siramo574 Thieuy yalla

    • @burr9379
      @burr9379 2 роки тому +4

      @@aidis3605 Dou reproche c'est de la prévention.
      Ndakh khétt bi dama léen kham.

    • @hinatauhuga918
      @hinatauhuga918 2 роки тому +1

      @@burr9379 tu as tout à fait raison

  • @amyndiaye660
    @amyndiaye660 Рік тому +3

    Ndesane metina Trop waye yalna yalla takha wou bamou delousi wate say lokho

  • @bintousamb7995
    @bintousamb7995 Рік тому +2

    Ndessane Metyna trop yalla nalen yalla diapalé beuguen diot sen diabot dom dafa sakh si khol😢

  • @MarieSarr-n2l
    @MarieSarr-n2l Рік тому +3

    Nagne ko wakh ta dèe Sénégalais yi nio wara bayi niak yi boy am dom amal dom ak ko xam foumou thiosano wayei ak ko xamni tot ou tard day daw ak sa dom j'en connais une mom 4 enfant la am 3 yeup sene papa daw na ak niom nigeria depuis 2020 batay mounoul diot si ay domama nek lene ay nit bahna rek yalna lene yalla nite si barki mouhamed ❤

  • @MassaerHanne
    @MassaerHanne Рік тому +10

    Il faut faire attention aux mariages avec certains etrangers , car aussi lhomme et la femme ont meme droit sur les Enfants donc c'est pas facile a regler

    • @coumbadiouf7341
      @coumbadiouf7341 Рік тому

      Un papa n a pas le droit de voyager avec son enfant mineur sans l autorisation de la mère. Donc quiconque peut se présenter à la frontière avec un enfant et dire que c est mon enfant sans papier et les autorités les laissent partir. C est pas un pays ça

  • @ndellandoye825
    @ndellandoye825 2 роки тому +15

    Ma sœur au Sénégal dans le mariage tes enfants appartiennent à ton mari moi mon mari n'est pas senegalais mais à chaque fois que je pars à l'étranger seule avec ma fille on me demande une autorisation parentale que je doit chercher à la police alors que ce n'est pas le cas si c'est lui qui voyage seul avec elle

    • @adjasidibe4534
      @adjasidibe4534 Рік тому +2

      Honnêtement c'est injuste ! Il faut des réformes 😢

  • @ourayegueye3611
    @ourayegueye3611 Рік тому +12

    Bayilène niak yi bakhna reik meussou malène gnémé yalna sa dome délou sa lokho inchalla

    • @cheikhniass9468
      @cheikhniass9468 Рік тому

      Man nanga soubou de louler lalay wah amna senegale boum dalon khamna fateken lolou

  • @abibatoubathily3783
    @abibatoubathily3783 Рік тому +4

    Yalnako yalla délossi thi séy lokho inchalah 😢😢😢nigerien mome woroul

    • @Iboudieng-bu4hv
      @Iboudieng-bu4hv Рік тому

      Nigeria bakhoul satoul Yalla sacrifice nioci gaw fofou 😢😢

  • @aidis3605
    @aidis3605 2 роки тому +17

    Courage Mme métina trop, dôme dafa Sakh ci xol, Yalla na guène guissé waat ci diam

  • @maimounaka5561
    @maimounaka5561 2 роки тому +4

    Mais khalebi bou démone si ambassade bi ndakh dougnou ko indi Sénégal ??

  • @mamediarraboussodiome5171
    @mamediarraboussodiome5171 2 роки тому +9

    Frontières senegal Mali amoul bene contrôle l autre fois j ai vu un nigérian avec ces deux enfants ils ont passé sans difficulté

  • @aminatawone2531
    @aminatawone2531 Рік тому +4

    Li lagni wakh sii deuk bi soudone deuk toubab yii dougnou khar dara dagni thie diock illico presto wassalame

  • @ramatoulayefaye1868
    @ramatoulayefaye1868 2 роки тому +9

    Mane niak moma ndieuk begue diabar sama papa ni doussidal mouk madegue ndigualou wadiour ma bayiko rethiou wouma ko ndah yala mayenama après dieukeur bou bah

    • @ibrahima1964
      @ibrahima1964 Рік тому

      Sa pape nite ndiaye la.. ko khamoule dara si mome

    • @Matryyooshka
      @Matryyooshka Рік тому

      Ndeysann, waw wadiour diarna di déglou dé🙏🏽
      Niakk yi sakh nieupp bonouniou ( mon mari et Nigero-Gambien), dieukeur chance la rek, gni amagoul YALLAH nalenn BOROM bi SWT may jeukeur ji gueunn si barké SEYDINA MUHAMMAD SAWS🙏🏽

  • @mamekhoudiafaye7263
    @mamekhoudiafaye7263 2 роки тому +6

    Yalla nalene yalla diapalé

  • @aminatawone2531
    @aminatawone2531 Рік тому +5

    Démal séti waa keur baye niass yii gnou dimbalila wakh koo papa mahi khalipha keur baye niass lougnou mounoule nigéria amoul wassalame

  • @princessedangerous3858
    @princessedangerous3858 Рік тому +4

    Bayilen wakh bou niawe amna nigérien you geune gorou sénégalais nakh gorou senegal geune ko yombe na xamou niou valeur djiguen

    • @easygang2563
      @easygang2563 Рік тому +1

      La bêtises humaine... Votre haine envers les hommes sénégalais me dépasse si vs avez envie de faire de enfant avec des étrangers ses votre problèmes mais laissé les hommes sénégalais en dehors de vos choix

    • @MrsNkali
      @MrsNkali 7 місяців тому

      Lolou dé barréwouniou mane andena sama dieukeur ba nigeria hame foumou aprés mou nakh ma yobbou sama dome bou 4ans mounouma dégue khalé bi té faléwoul koi nekk fi

  • @Celine.toupane
    @Celine.toupane 2 роки тому +6

    C'est triste😭

  • @aminatagueye32
    @aminatagueye32 7 місяців тому +1

    Non la police aussi y a beaucoup de lenteurs de leurs côté à mon sens. Courage , hoooo Sénégal.

  • @nialynialy801
    @nialynialy801 2 роки тому +4

    Li métina trop mais police sénégalaise sounou synchronisée meunenaniou localisé à travers tes appels Yallah na Yallah facilité inchaAllah ba diote sa dome.

  • @yofarydieng8027
    @yofarydieng8027 Рік тому +1

    Sénégal moye réw mou amoul coubéré 😂😂😂 dieukeur ba Nigeria khamo yayame khamo bayame khamo foumou deukk khamo fokay fékkeu sheuuuuuuuu
    Yalla bakhna yalna khélame nieuwate bamou délola sa dome si diam

  • @AichaBernard-rt7gm
    @AichaBernard-rt7gm Рік тому

    Gnak kegn moy lolou soit forte

  • @mariely6747
    @mariely6747 2 роки тому +4

    Ouah! Mais après la mère d'Awa elle a dit qu'elle avait un fils nigérien, tous deux sont mariés à des Nigériens. Pourquoi? Sont-ils attirés par les hommes Naija ?Les nigérians sont comme les chinois ils sont doués en. Les nigérians sont comme les chinois ils sont doués en mattier de dupliquer. Mere bi amna fit. Yallah na yallah fégnial.

  • @ndieumbetmbodji1714
    @ndieumbetmbodji1714 9 місяців тому +2

    La police sénégalaise c’est tellement nulle du grand n’importe quoi walahi azim j’en suis la preuve il se permet de dire on ne travaille pas les week-ends après c’est tout je peux pas me permettre d’étaler mon histoire mais c’est à revoir franchement ils sont sensés aider la population mais pas le contraire. J’ai vécu mes pires vacances au Sénégal de vrais mbam tchim 🥺

  • @mamsscottlaflamme2520
    @mamsscottlaflamme2520 2 роки тому +2

    Khawmeu loutakh yéneu femmes yi naïve reik ndeysane Mais bayile yeup thi lOkhO yallah dina até inshaa allah

  • @bodielba1592
    @bodielba1592 2 роки тому +3

    Bilay li metinama😭

  • @bouyastarndiour9595
    @bouyastarndiour9595 2 роки тому +4

    Nako gouvernement diapeler ko waye

  • @Mama-yt1wo
    @Mama-yt1wo 2 роки тому +4

    Masta métina torop mais yalla bakhna tu va la récupérer s'il plait à Dieu

  • @babacarofficiel1901
    @babacarofficiel1901 2 роки тому +3

    Tieye yalla 😭😭😭

  • @sant9021
    @sant9021 2 роки тому +11

    J’espère k police bi dina ko diapale demm nigéria 🇳🇬 mom risque la

    • @adamagaye6575
      @adamagaye6575 Рік тому

      Dém dou solution dé le cas est capable de tout faire

  • @aminataseck8356
    @aminataseck8356 Рік тому +3

    DEFAL ATTENTION BOU BAKHE POUR NE PAS FINIR THI PROBLEME YOU GRAVE MOY AY LIGUEYE FETICHE AK LENENE YONEL MAIS BOUFFA TEK TANK TER GARDEL SA NIARY DOM YI DESS

  • @diop4571
    @diop4571 2 роки тому +3

    Gnome gnep dinagne inchallah

  • @coumbafaye9319
    @coumbafaye9319 Рік тому +1

    Bayilene di seuye ak ay niak parceque dioubougnou.

  • @mamadoudieng4043
    @mamadoudieng4043 2 роки тому +37

    Avec ça vous dites que nous avons une excellente police professionnelle, comment peut-on entendre une mère de famille qui est dans le désarroi venir un samedi au commissariat pour un enlèvement de son enfant vous lui dites de revenir le lundi

  • @absaduop7965
    @absaduop7965 2 роки тому +8

    Aucune vigilance voler un enfant et sortir du pays

  • @farylo4884
    @farylo4884 2 роки тому +1

    Ndeyssaan😭😭😭😭

  • @fatousd4171
    @fatousd4171 2 роки тому +3

    Nigérians dounou bayui sene dôme alleu

    • @sokhnandiayeba5606
      @sokhnandiayeba5606 2 роки тому +1

      Vous avez parfaitemwnt raison,j'ai fait 3 ans et demi au négéria,gnom dougnou dem féneu am faa ay domes bayiléne gnibi

    • @CharlotteantoniaBassene
      @CharlotteantoniaBassene Рік тому

      Les sénégalaise faîtes attentions aux étrangers parfois alale adouna moniou yobé ci lii courage madame

  • @SodaCisséMBENGUE
    @SodaCisséMBENGUE Рік тому

    Ndaysan yalla na délousi sisay lokho amine inchallah

  • @ndoumbemanendoumbemane616
    @ndoumbemanendoumbemane616 Рік тому +1

    Ya Dale hèle yow miye seuy AK niak

  • @Corailpro
    @Corailpro 2 роки тому +3

    Moytoulene niak yii bakhna daal.

  • @florenceskaibosagna5681
    @florenceskaibosagna5681 2 роки тому +14

    Sokhna si nigerien da ayyy dé lépp layy déffar sur que il a falsifié un papier pour elle. Autorité sénégalaise zéro du plus haut au plus bas séne bop nagnou fi nékal

    • @mounassow5744
      @mounassow5744 2 роки тому +1

      Nigérians

    • @Corailpro
      @Corailpro 2 роки тому

      😂😂😂😂
      Rey ngama bama deh. Lol

    • @evakane4802
      @evakane4802 2 роки тому

      Billay 😂😂

    • @Iboudieng-bu4hv
      @Iboudieng-bu4hv Рік тому

      nigarien yalla dako may deh enformatiq nuosiy chef 🇳🇬😢😢

  • @mamependaba7129
    @mamependaba7129 Рік тому +1

    L'histoire se repete ndeysannnn

  • @ndaongone8443
    @ndaongone8443 11 місяців тому +1

    Ndeysan mane sama khel sakh daloul si wadji ! Nigeria worul te en plus kane moy surveiller khale bi foffu ? Y’a trop de chose bizarre la bas ! La police devait prendre ses responsabilités

  • @MariaAlverenga
    @MariaAlverenga Рік тому +1

    Man sama borom keur n’est pas sénégalais mais pas de problème depuis plus de 30 ans *à ce que j’ai entendu, vous avez assez de connections au Nigeria donc il faut vous rendre là-bas* 👉🏾 que peuvent faire les autorités sénégalaise ???
    Mais sachez que dans tous les pays africains l’enfant appartient à son père. Mariage naxante rek la meunu say ak étranger banopi ne do dem chez lui
    *il y a eu des tiraillements entre vous lolu mo Indi li*

  • @oumoukalsoumndaw5241
    @oumoukalsoumndaw5241 Рік тому +4

    Va laba comme il a dit tu reste un peut avec et sa famille Après tu reviens avec ta fille

  • @Iboudieng-bu4hv
    @Iboudieng-bu4hv Рік тому +1

    Nigeria bakhoul satoul Yalla sacrifice nioci gaw 😢😢

  • @mariemedieng5357
    @mariemedieng5357 3 місяці тому

    Niou localiser appl bi dem direct

  • @Fatoumbodji459
    @Fatoumbodji459 Рік тому +1

    Yalna lén ya Allah diapalé 🤲🏾

  • @Yataaaaashhh
    @Yataaaaashhh 2 роки тому +5

    Yallanako yalla diaplè, thieuy police Senegal

  • @mouminouchesarr1856
    @mouminouchesarr1856 Рік тому

    Finally fegn na wala??

  • @Matryyooshka
    @Matryyooshka Рік тому +2

    Nako état bi diapalé mou récupérer domam. Si y'a eu divorce, na tribunal décider si type de garde khalé yi (partagée wla compléte à l'un des parents). Je n'ose imaginer sa peine, massa.
    Boul bayi dé, bats-toi pour ton fils.

  • @ngonesarr5624
    @ngonesarr5624 2 роки тому +4

    Numéro de téléphone svp

  • @mariemedieng5357
    @mariemedieng5357 3 місяці тому

    Weekendku lane 😢😢

  • @anniepires1999
    @anniepires1999 Рік тому +1

    Sans les papiers de l'enfant est ce que il peut la faire sortir du pays
    Mais ces policiers aussi pourquoi la faire attendre tout le week-end
    C'est vrai qu'il aurait eu le temps de la faire partir ou il est toujours ici mais à changé d'adresse

  • @diaoawa
    @diaoawa 2 роки тому +3

    Nigeria congo burkina voilà pourquoi j'irai jamais Jai peur même de ces noms là

    • @fatousonko462
      @fatousonko462 Рік тому

      Tu as oublié le ghana et togo et le niger

  • @mamematyg
    @mamematyg Рік тому

    Wa li Amoul suite ba tayy?

  • @KhadidiatouGueye-k8o
    @KhadidiatouGueye-k8o 11 місяців тому

    Dôme Loumou daime daime Dina gnew inchala dome bou mague dina weuri yayam sama khol bangi meti 😭😭😭😭😭

  • @MrsNkali
    @MrsNkali 7 місяців тому

    IL sont touss pareil 😢😢😢

  • @aidadiouf5085
    @aidadiouf5085 2 роки тому +4

    Yalla na ko yalla délosi🤲

  • @yayaseydi1933
    @yayaseydi1933 3 місяці тому

    Maintenant Elle a récupéré son enfant

  • @mariamaba1578
    @mariamaba1578 8 місяців тому

    Mér est ce que ça va ?

  • @MrsNkali
    @MrsNkali 7 місяців тому

    Je suis aussi victime😢😢😢😢

  • @justemedina6433
    @justemedina6433 7 місяців тому

    Sénégal frontière comme restaurant maiiga

  • @ndourndour9674
    @ndourndour9674 Рік тому

    Courage même bou waré dém demal dieuli ko

  • @aminatagueye32
    @aminatagueye32 7 місяців тому

    Non ce n est pas vrai car dans un pays normal, un enfant ne doit pas sortir d un territoire sans papier c inadmissible. Diambarguade mais courage.

  • @awafaye285
    @awafaye285 2 роки тому +1

    😭😭😭

  • @tiiw7425
    @tiiw7425 2 роки тому +3

    Mais je m'excuse mais sokhna cii yaw tamite ce dieukeur t'a bien montré que mome setoule depuis le temps pourquoi ngua continué akk mome soknaci.Ah metina mouniale metina métina

  • @fabintoumbodji5371
    @fabintoumbodji5371 Рік тому

    C’est la Mme chose que l’histoire de ma sœur son mari lui a arracher son fils et partir au Niger disant qu’il revenait mais jusg’qua maintenant rien😢😢😢

  • @ramatasow2332
    @ramatasow2332 2 роки тому +6

    Mère boul dem dhé sinon tu sera sacrifiée

  • @FatouDiallo-z6w
    @FatouDiallo-z6w Рік тому

    ❤️❤️😯😯🥺🥺❤❤

  • @bodielba1592
    @bodielba1592 2 роки тому +1

    Li etat naci diote wayyy

  • @Celine.toupane
    @Celine.toupane 2 роки тому +1

    Mais yaw khaler bi Moy urgence

  • @Khadija-b5b
    @Khadija-b5b Рік тому

    Est ce que guiss nagnou khalebi parce que li sa fait 1ans

  • @MassaerHanne
    @MassaerHanne Рік тому +1

    Beug goor bakh na waye beugal koula beug

  • @moussatraore6281
    @moussatraore6281 Рік тому +4

    Daguen am fit sakh niak teh sénégalais nekeu fi

  • @mariama880
    @mariama880 2 роки тому +2

    Madame demay Nigeria rek tog fofu sinon do guawa guisse sa dom guamouma état dinala diape dom thi xoll leu Sakh

    • @adjasidibe4534
      @adjasidibe4534 Рік тому

      Elle va y rester ! J'espère que une fois majeur sa fille va revenir d'elle même inshaAllah

    • @mariama880
      @mariama880 Рік тому

      @@adjasidibe4534 j crois que elle déjà laba ça fait 1ans

  • @bouyastarndiour9595
    @bouyastarndiour9595 2 роки тому +2

    Boule dème dé bo démé woroule

  • @aidadiao3472
    @aidadiao3472 Рік тому

    Gendarmerie mo wor

  • @tchatafrik5257
    @tchatafrik5257 Рік тому

    Kén waroul wolou nigérien niak yi ci sen bop daniou ragal nigérien donc nguir yallah sama mbok sénégalaise yi bayil lén di nék ak niom évité len way lep lou ngen di guiss ci sen film yi mo am

  • @user-gx5ir2ig3u
    @user-gx5ir2ig3u Рік тому

    Pourquoi aller chez marié avec un étranger

  • @mamediarrathiam2753
    @mamediarrathiam2753 Рік тому +1

    Ngak domam douko bayi al

  • @sunkiss4950
    @sunkiss4950 Рік тому +1

    Est ce que l’enfant a été retrouvée?

    • @diaradiouf2373
      @diaradiouf2373 Рік тому +1

      Mom dé démnafa gnou dor ko bamou sonou

    • @sunkiss4950
      @sunkiss4950 Рік тому

      @@diaradiouf2373 ce n’est pas possible! Elle n’a pas été soutenue par l’Ambassade du Sénégal?

    • @Arg-actu
      @Arg-actu Рік тому

      @@diaradiouf2373ah bon 😢 loy wakh ni

    • @nabouwane7684
      @nabouwane7684 Рік тому

      @@diaradiouf2373Wa kougnou daure fofou khalebi da fégne

  • @amintasow4937
    @amintasow4937 2 роки тому +3

    Beugue xaliss diaroul seye niaak

    • @maimounaka5561
      @maimounaka5561 2 роки тому +3

      Ya gnemer yalla d'ego Yayam ni leup domam bou djigeen bi mokoy deff kokou ban khaliss lagn koy topper ? ? Do wakh sakh Lou cohérent boudoon khaliss Dina nekak ko khamni loumou incrirer doomam école Sakh amouko 🤒🤒🤒 nittel toutti

    • @anniepires1999
      @anniepires1999 Рік тому +1

      Yow ki elle travaille et s'occupe de ses enfants

  • @KhadidiatouGueye-k8o
    @KhadidiatouGueye-k8o 11 місяців тому

    Daimal thi serigne Mara Niass laigi nga ameu diam

  • @kharitouyayame
    @kharitouyayame Рік тому

    Ayway Etat diapaléko

  • @coumbafaye9319
    @coumbafaye9319 Рік тому +1

    Sa dome dal mossi waroulwone dougue

  • @mai-my8ym
    @mai-my8ym 2 роки тому +1

    Metina waye tamit papam leu de tamit

    • @kharitouyayame
      @kharitouyayame Рік тому +1

      Soudé papam dafa wara takh mou daw ak domam lolou ça ne se fait pas

  • @mbossediaw2841
    @mbossediaw2841 Рік тому

    Mane deh damalne ragal motax kimasi beugone tak ma bagne

  • @aidadiao3472
    @aidadiao3472 Рік тому

    Brigade de Recherche 🔎 de la gendarmerie moi si gaw

  • @Ndickou2
    @Ndickou2 2 роки тому +6

    Bayilèn niakk yi

    • @amintasow4937
      @amintasow4937 2 роки тому

      Bayilen niak kilefa

    • @amintasow4937
      @amintasow4937 2 роки тому

      Beugue xaliss diaroul seye AK niaak

    • @Ndickou2
      @Ndickou2 2 роки тому +3

      @@amintasow4937 niakk yi sakh liguey beugue gnou si dara arnaque rek lagni liguey

    • @aidis3605
      @aidis3605 2 роки тому +5

      . Bayilène gni guène Di stigmatisé waay , xéet bo dème amna niou amna niou bone

    • @Ndickou2
      @Ndickou2 2 роки тому +1

      @@aidis3605 bayilén sen affairou seytaané motakh étranger bou nieuw rek yaapp gnou

  • @mariamaba1578
    @mariamaba1578 8 місяців тому

    7 diabars yéne séne famille bi ,,,,

  • @KhadidiatouMbaye-b4w
    @KhadidiatouMbaye-b4w Рік тому

    Ay waay massa yalha nako yalha delossi.. Yaide yeureum moko gueune .. Et la ambassade ????

  • @bayeniass8931
    @bayeniass8931 2 роки тому +2

    Mé yawe sa dieker joulit la wala

    • @fallaminata2641
      @fallaminata2641 2 роки тому +1

      Yalla n'a delousi watt sisay lokho yalla bakhna

  • @ibrahima1964
    @ibrahima1964 Рік тому

    Vous vous mariez avec n’importe qui