Wallahii moi même je comprends pas j’arrivais pas à retenir mes larmes quand le gars racontait l’anecdote qu’il a vécu avec Aziz en Europe en vrais Aziz nitte kou bakh la wone wallahiii . Faites très attention avant de juger quelqu’un … Aziz & wally yalla na souniou Borom yeureum len 🙏 Amen 🙏
vraiment c'est triste c'est la première fois au Sénégal c'est arrivé quelque tue et tres médiatisé 😢😢😢 c'est triste je suis a Holland rip notre frère aziz 😢😢😢😢😢😢😢😢
Bilahi Aziz deh na nopalou me ngniko def Li douniou moussa nopalou gniane reck ak niack nagou dogalou yalla aziz reynanouko me dougou meusseu dieu weureu geum bilah😭🙏❤️
C’est émouvant et trop trop triste billahi, je ne le connaissais pas auparavant mais je suis très touchée comme tout le monde par ce décès tragique et prématuré de Azziz et Wally. Que justice soit rendue à sa famille.
Sén takhaway rafetna ki def lii sénégal yeupe la ray ndakh nieup am nakhare couco kham akk couco khamoul yayam yalla na ko yalla maye kholou mougne yalla na ko deudo diam
La danse est une culture et le chant. Dans chaque société qui existe dans ce monde. Et à partir d'une danse, on peut savoir c'est quelle société et ethnie ou on peut chercher son appartenance.
Walahi dina lakke niou bari. Wayé Aziz ak Waly ay chayid laniou. Té chayid Yalla swt molène dikk aldiana. Kon nak louniouko meuneu wakhal, niveau aldianam gueuneu élevé. Yalnalén Yalla yeureum té kharélén aldianay firdawsy ci daradiay Seydina Mouhamed psl
Ndey Gueye elle a un très bon cœur ❤️
Ndeyssane takhawou n'a ko de
Deufeu am yeurmandé Ndèyssane
11 khoulouwa allakhou akhade bousi nek and ak bismilakhi rakh mani rakhim pour Aziz ba ak Wally Kano ak bolem dioulite amine yarabi
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
allahouma amine🤲🤲
Wallahii moi même je comprends pas j’arrivais pas à retenir mes larmes quand le gars racontait l’anecdote qu’il a vécu avec Aziz en Europe en vrais Aziz nitte kou bakh la wone wallahiii . Faites très attention avant de juger quelqu’un …
Aziz & wally yalla na souniou Borom yeureum len 🙏 Amen 🙏
Ndeye Gueye yalla nalla yalla mey bateu bou goor nga toudeko Aziz dabala nelén Amin repose en paix
Amiiine
Ndeysan allahouma amine way
Allahuma amiiiiiiiiiiiiiiiiiiine
Amine yarabi
Amine yarabal allamine
2jour mankoye tékelé di guénte Aziz yalla nako yalla kharé aldiana firdawsi 😢😢😊
Amine
Reposez en paix Aziz et Wally 🙏🙏mère bi yalnako yalla kholou mougn
😢allahouma amine....yallah na l'en yallah May kholou mougne....thieuy nabou g c pas quoi dire 😢
Sénégal yeup dioy aziz gniko kham ak gniko khamoul yalla nalen yalla yereum kharelen Aldiana mom ak l petit Waly 😭😭😭
Bilay deh mettina torop
Bilahi moi qui ne regardais même pas ses prestations, j'ai très mal, je suis malade à cause de ça
@@yacinethioye7919 Ndèyssane
Bilaye nieupeu Ko dioy ndakh Métina torop, thiey adouna, ndey Guèye dafma dioylo 😢
Bilakhi déwinbii mo méti ndeyssane 😢😢😢
Ndeye gueye yaye gor tu me fais pleurer ma grande
Pa Moussa lou bakh rék gua kham té diko dév té âme foula machallah ❤aziz Yallah nako Yallah kharé Adjana
C'est vraiment triste je n' arrive toujours pas à digérer tout ça. Que le tout puissant les Accueille dans son paradis éternel Amine 🙏 ya Rabbi
Ndeyessane yayou Aziz meunoumako khole 😢😢😢😢
Ndeysan Aziz yalla nako Serigne Touba terou ki def li rayoul Aziz rek togn na wa Sénégal machallah yalla bou ko thiat djitou
vraiment c'est triste c'est la première fois au Sénégal c'est arrivé quelque tue et tres médiatisé 😢😢😢 c'est triste je suis a Holland rip notre frère aziz 😢😢😢😢😢😢😢😢
Man aussi magui holland alkmaar
Je ne dors plus depuis que aziz est parti cœur brisé
Ndeye Gueye masta damoko yereum bilaye walaye elle me fait pleurer 😭😭😭😭💘💘💘💘💘😭😭👌👌
Dioyna ba sono li metina trop bilahi 😭😭😭
Des patrouilles vraiment dafa warr di am, des interventions d’urgence et tout, nguir ayqllqh sonko moy diomaye dimbeulei leen niu ci suniu sécurité 🙏🏽
Machalla. Wakhdji. Rafetna
Merci et chapeau à Ndey Guey 👍
Ndeye stp arrete de pleurè te une personne genereuse a chak fois tu pleur tu me fait pleurè du courage metina yagui yeurmandè si yayou aziz
Bilahi Aziz deh na nopalou me ngniko def Li douniou moussa nopalou gniane reck ak niack nagou dogalou yalla aziz reynanouko me dougou meusseu dieu weureu geum bilah😭🙏❤️
Machallah sene takhaway rafetna paix à leurs âmes depuis lors je n'arrête pas de pleurer metina lole
Lou méti yag na si aduna Bilay 😢ndeye ndeye me fait pleurer 😭
Abdou Aziz ak Ababacar "Wally" YALLA Nalen YALLA Yeureum té Kharelen Aldianay Firdawsi 🙏
Ay nabou togne nga wa Sénégal, tek nga gnou nakharr, diakhassé sougnou khôl yi😭😭😭
Bilay ioe
@@haby8760 Mane li Manou mako digéré 😭😭😭 ça m'est resté là, a travers la gorge, ko wolou mou worr la😭
Gorr dou worr kén wolotoul kène ,paix à leurs âmes
Domeram leu tiagua leu. Yallah nako sunu akkeu daal
@@yayourassouldiop7055 😭😭😭 wolay Ndèyssane ma chérie wakh guan deug solution moy prudence rèk
Togayou ndeye bi nabou la waron li ken lane le 😢
Bilahi mo nekone plasam mais yak na lepp
Machallah pa Moussa Kadou yi rafetana yalla naniou hipe Adiana Firdawsii psl
Ndeysaan 😢metina yalna len yalla yerem teh khareh len al jannah firdawsi 😢
Je ne dors plus depuis des jours . 😢😢😢. Nabou leye yallah naniou yallah até
Mame. Abdou. Aziz. Dabakhe. Yala. Mo KO. Bole ack sedy Aboubacar. Guano. Li. Koumou diakhaloul
Billahi ndeyesane 😢😢😢
Mes sincères condoléances yalla Bour yalla yeureum ko kharé aldiana firdaws si barkhé nabile Moustapha 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Yalna aldiana firdawsi néke séne keur
Nabou Leye yalnako yalla trokhal
C’est émouvant et trop trop triste billahi, je ne le connaissais pas auparavant mais je suis très touchée comme tout le monde par ce décès tragique et prématuré de Azziz et Wally.
Que justice soit rendue à sa famille.
😭😭Man est-ce que douma arrêter di setane vidéos yii j'arrête pas de pleurer comme une folle 😭😭😭
Massa
Comme moi
Khôl dou om ba niou kay bess dafa meti
Dafameti rek AK tass Yakar am ambition yallanako sougnou borome yereume diegueulko
@@fantasouare2803 merci beaucoup nio bocou nakhar bi 😭
Séni khétou lunettes (noir fumé dioylo na kouné 😢😢une très belle solidarité pour les artistes ❤❤wouték mbeur yii ak journaliste yii😢
Sén takhaway rafetna ki def lii sénégal yeupe la ray ndakh nieup am nakhare couco kham akk couco khamoul yayam yalla na ko yalla maye kholou mougne yalla na ko deudo diam
Amine Ya Rabi
Bilay amine yarabi 🙏🙏😭
Man damay ragal sakh yay dji dé ndakh métit nguen balma
@@marieveroniquemendynaniouko nianal yalla mayko kholou mougne
Ndeysan massa yaye boye métina trop yalla nalén yalla yeureum té kharé ko adiana firdawsi 🙏🙏
Kon ndiorte meunna rafet yalnako yala yeureumko way 😭😭😭
Yaye boy soit forte li dara geunou ko meti si adouna yalla na bour bi kharè lène aldiana
Yallah n'a ko yalla yeureum té diéguale léne kharé léne aldiane firdawsi 🙏🙏🙏🙏
Amine yarabi 🙏
Louma mété ni dotou mako am walahi 😢😢😢😢😢goudi douma meune nelaw ndakh yeureum ko
Nabou leye nabou leye nabou leye yalla nala sunu akk dall si barké seydina mouhamed ♥️ 😭😭😭😭😢 nabou leye ya bone ya yess vampire binga done
Amine qu'elle souffre comme elle a fait souffrir Aziz et wally😢
Massa je n'arrête pas de pleurer pour nos deux frères que le paradis soit leurs demeures éternel amine yarabi 😭😭😭😭😭
Ndèysan ndèye guèye kou bakh la❤
😭😭Que firdawss soit sa demeure éternelle 😭😭
Ndeye gueye ndeysane kou beug Aziz la meunoul sah khol yayou aziz bayi na kharite nah li
Billahi
Du courage ndeye gueye là grande
Yalnako sunu borome yeureume khareko aldiana firdawsi si barkep seydina mouhamed saw 🤲
Degeul famou waxé amna yaye you seug wayé yaw seugo siguil machallah
Ndeysane lii rafetna machalla, diapanté lene, dina bax inchalla ❤yalnalene yalla yeureum,🙏
Ndeysane Machahalah xoll bou raffete gha yorr Ndeysane je t’admire vraiment dagha amm yeukk yeukk
Yalla nagnou tassé ak yeurmandé sougnou borom 🤲
Ndeysane metina metina yalla nalen yalla yeureum yayou Aziz dabala yeureum nako 😢😢
Ousmane sonko mo yoni ama balde pour mou sacrifice ndiol djinee falaye mingui Facebook 💚💚❤️❤️💚💚❤️❤️
Massa yalna khipper aldiana
Alakhou Akbar nabou Leye am ga weuy bou doul faye abadane déf ga lou bonne 🥹🥹😭😭😭😭yalla na yalla yereume léne té diégal léne 😭🥹🥹
Aziz n'est plus ils doivent arrêter avec ce nom d'Aziz dabala mais plutôt Aziz Bà 😢
Yalla na nalénes yalla yeureume té xarélénes aldjiana 🤲😭😭😭
Massa massa....😢😢 Innalilahi wa ina ileyhi radjihoune...
Mercie toma Pape Moussa, Yalla defal la diam,linguene def rafetna Manchallah ❤❤❤
Repose en paix Aziz 😭😭😭🥹🥹🥹
Yalnaléne yalla yereum té kharelen aldiana firdwsy thi barké seydina Mouhamed 🤲🤲🤲🤲
Aziz moudjena nzkh waliyou dé gayi
Yalnalen yalla yeureum si barké seydina mouhamet amine
Ndeye guerre ne pleure pas tu es une belle personne machallah
Nous venons de dieu nous y retournons que firdawsî ' soit leur demeure amine
Yalna len yalla yeureum 🙏 Ndeye Gueye sa takhaway rafet na yalna yalla fay yiw
Abdou Aziz Ba yallah na Aldiana Firdawsi disa keur inchallah dors en paix
Repose en paix yalla nako yalla yeureum té kareko aldiana
Bilahi Nabou leye nakar guiganiou teck yalla bonopalou yalla rayouko daniouko dogaler💔😭
La danse est une culture et le chant. Dans chaque société qui existe dans ce monde. Et à partir d'une danse, on peut savoir c'est quelle société et ethnie ou on peut chercher son appartenance.
Machallah référence yagui ni di kéne meussoul deg linoumel si niom
Walahi dina lakke niou bari. Wayé Aziz ak Waly ay chayid laniou. Té chayid Yalla swt molène dikk aldiana. Kon nak louniouko meuneu wakhal, niveau aldianam gueuneu élevé. Yalnalén Yalla yeureum té kharélén aldianay firdawsy ci daradiay Seydina Mouhamed psl
Yalla nako yalla kharè aldiana firdawsi amine nabou léye kou Kate sa ndaye doméram
Nabou leye fii mo nékone sa place si wetou yayou aziz dabala
Ay way nabou defna ndiombé go xamni dotoul Faye mouck ,mouk,thi adouna
Bilay li yak na sama adouna li daf ma gueneu yée
Bilay vraiment nak
J’espère qu’elle pourirra en prison. Elle ira même pas aux funérailles du décès de sa maman. Saloparde qu’elle est 😡
Yak na aduna ohh nabou boudè li yawla bok nga si ohhhh fem neh nii yaw ak adjie sarr eskeh adjie sarr tanuwula sa
Walahi mane dh takh na ma bayii adouna 😭😭loumou deff niaww na
Yalna yalla yèssèl yermandèm si môme si barkè seydina Mohamed psl
Yalnalène yalla yeureum diégeullène kharélène ardianay firdawsi si barké Nabi Moustapha spl😭🙏🙏
May their souls rest in perfect peace
Ndeysane Paix a son âme Amine
No bilahi nabou leye mo deugue ndayam 😡😡😡
ndeye sane natina trop 😭😭😭😭
Machallah ndaysaan Thiey adouna
Mandé ballé Mansour gueye la nekon wayé aziz diokhona ansién artiste yeupe dieureudieufé yalnako bour yalla kharé aldianatoul firdawsi barke borome touba
Balé mansour gueye d sama kogn la nekone ndeysaan bimay khalé je voyais des gens danser labas, legui Immeuble marron mo fa nékeu
Ndaye gueye kou gore la
Sama dioy yis kagne ley diekh😢😢😢
Soneuneu niou mane douma dioye damaye youkhou chaque 5 minutes
billahi danio raye koulén eupe bope 😭😭
ndeye Gueye djioyelonama bilah
Allahou akbar. Inna lillahi wa Inna ileyhi rajouhoun que firdawsi soit sa demeure éternelle amine. Skeuye Allah
Nfeysane ndeye gueye yayedjiii le yereum
Yala n'a gnou yala maye moudiou gou raféte si Barker seydina Mohamed sws Barker chiekhou tidiane Barker chiékhale islame ,yarakhemane ya rahime soutoura adina wa alakhirira 🙏
Ndeye san metti na trop mes deff ngen lou rafet machallah que leur âme repose en paix
Ndeysan yalla yalla yeureum lene thi barque ohh ndeysan
Thiey lii mettina trop yalla na yalla kharé lene aljana firdawsi
Ohhh khady diaw sama fans❤❤❤
Yalna yalla yereum ko té kharé ko aldiana Firdawssi Si Barké Seyedina Mouhamed PSL
Ndéye Guèye ndeyssane yeureum nako, meuna watt ci BIBLE bi Ndèye Guèye kou bakh la té beug na torop Aziz Dabala😢
Sa wacc rafetna machallach
Alkhamdouliha paix à son âme 😭😭😭❤️❤️🙏