Motakh macky dém lakh léne si ganaw armée ndakh militaire avant nga kay juger dafay diar si tribunal militaire ay paires ram nioko mane juger pas des civiles.Or on doit les juger.Macky gui diém lakh niépp gni défone gnôbé wayé bou Diomaye gnieuwé dina foutre le camp tout ce bordel.
Ces triste j'ai des larmes au yeux.sama frère migui prison maroc ak bro bi limou wakh li khéw si prison ça me fait mal mé yalla bakh na yalla naléne yalla guéné si diam ak salam 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Non ngourou macky sall loumou yak si rewmi foko nate wéssou nako, mais li dou sédé nonou dé, justice pour toutes les victimes, képe Koussi sa lokho take yalneu Mbougoulou Y'ALLAH sounou Borom wathie sa kaw 😢 Tous les victimes Y'ALLAH sounou Borom Fadiale léne séne nakare 😢
Est ce qu un jour ces personnes pourront oublier ou pardonner ceux qui ont les moyens doivent s investira améliorer cette situation Que justice soit fait pour la conscience de ces jeunes
Jai mal au coeur g mon frer ki es laba yeureum na gnifa nek yeup ndeysane yallah nalen yallah diapalei tang na metina li rek motax gorjigen beuri nama yallah bal dou niep nio meune gerer li goor deug mokoy def
VRAIMENT IL FAYT REVOIR LES CONDITIONS DES PRISONS DE REBEUSS DE TOUTES URGENCES POUR NE PAS REPRODUIRE LES MÊMES SOUFFRANCES ET TORTURES AUX PRISONNIERS. C'EST UNE URGENCE PRIMORDIALE.
Sincèrement j ai pleuré walahi azim toubab yi nionou guene j ai fait des prisons en France suisse et denmark des faits que j ai fait en ma propre conscience mais bilahi c était comme si j etais dans ma chambre
POLICIERS, GARDIENS DE PRISON, JUGES, et AUTRES QUI ONT PARTICIPÉ TANT SOIT PEU À LA TORTURE DOIVENT ÊTRE ENLEVÉS DE LEUR FONCTION. Justice doit être faite !
Ndeysan yalna yalla may tawfekh voilà un vrai homme
Yalnaniou yalla mousseul si kasso, j’ai vraiment le cœur meurtri
Yal na yalla mouthieule moussale souniou frére yeupppp si rebeusss ci barké weer bou séle bi 😢
Amine ya Rabi 🤲🤲
Amine ya rabi
Amine
Dieureuf lepp lerna machalla ❤yeup toyy yallana lepp changé
Vraiment ça c’est triste 😭😭😭. J’espere que notre nouveau president va changer ce system de prison car la façon de paquetage n’est pas humain.
Mashallah Modou. Yalla fay la sa khôl
Merci momo pour la démonstration de paquetage tu es meilleure que les soi-disant journalistes ou chroniqueurs
Koufa douguoul menoco comprendre 😢yalla nagnou si yalla mousseul tè gnifa nek yalla may len liberté 😨
Policé yifi nékone yép dagne léna wara soumi téthie léne 😭😭😭
Suis d'accord avec toi
Bilahi vrai domeram lagn
Motakh macky dém lakh léne si ganaw armée ndakh militaire avant nga kay juger dafay diar si tribunal militaire ay paires ram nioko mane juger pas des civiles.Or on doit les juger.Macky gui diém lakh niépp gni défone gnôbé wayé bou Diomaye gnieuwé dina foutre le camp tout ce bordel.
Legi yidone tal keur diambour yi nak. Ak parking autou yi nolene di def
Khana policé ngue
Ndéyssan sama momo gui ni😢😢😢yaye guorr pirr bilahi ❤❤❤❤❤ dawouma tardé sa live ❤thia kaw thia kanam rék et vive pastéf à vie ❤❤❤ ❤❤❤
Vraiment Amnesty bi il faut l'enlever. Macky Sall doit payer ainsi que son régime
NON MAIS IL NE FAUT PAS QUE LE GOUVERNEMENT LAISSE TOMBER CETTE IMPUNITÉ ET IL FAUT QUE JUSTICE SOIT FAITE.
C'EST INADMISSIBLE D'ENTENDRE ÇA .
Ndeyssan mome deh kou dal la machallah teh il explique bien les choses nit kou bakh la itam
Mâcha alla jamm thi yaw
Thiey yalla 😭😭😭yalla na yalla may kholou mougne soune wadiour yi
Bilahi, walakhi, Takakhi Yalla dinalène até thi barké Alkhourane 😢
Amine Yarabi
Yalla naniou yalla moussal si kasso😢
Amine
Amine
Amine❤
Amine y’a rabbi
🤲🤲
Ces triste j'ai des larmes au yeux.sama frère migui prison maroc ak bro bi limou wakh li khéw si prison ça me fait mal mé yalla bakh na yalla naléne yalla guéné si diam ak salam 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Nékona prison Maroc me méloulni Sénégal
Yalla na ko sunu borom guéné si diam ak niou thiabi feuté 🤲🙏 guinaw
Amine ya raby 🤲🤲🤲
Alhamdoulilah yalla bakh na nék prison guiso sa béne mbok dafa méti
Soulevement populaire pour detruire reubeuse, daniouko wara deffe dome
😭😭😭yarabi yalna len yarabi takhwou❤❤❤😭😭😭😭
Nonn c'est vraiment dure as accepter 😢 non justice dafa wara ame pour tout les détenues
Non ngourou macky sall loumou yak si rewmi foko nate wéssou nako, mais li dou sédé nonou dé, justice pour toutes les victimes, képe Koussi sa lokho take yalneu Mbougoulou Y'ALLAH sounou Borom wathie sa kaw 😢
Tous les victimes Y'ALLAH sounou Borom Fadiale léne séne nakare 😢
Thiey sènègal mètina macky sall adouna lu waay def boopam 🇸🇳 mèrci mon frère 🙏 ❤️ yalla na la yalla defal diamou amine ndèysane thiey lii doyna warr 😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲
Sénégal metti na Bilay 😢😢😢
Bilay momo mn frere bima yeuguè dagnoula diap ça ma fait vremen mal, mai alhamdoulilah bimala guissé, domou guinaw rails bi
Ayy policier yii akk procureur yii adina dou keur bamel khatna leudeum na ayy wayy bouléne ko dara jaral ayy wayy yeurmander
En plus avec les risques de maladie. Yaala Naniou oumpe, oumpe bepp domou adama. Thiey bi akh kou koy layoo ak souniou Borom
Ndeysane senegal yalnagnou yala até li metina trop mais amnagnou yakar diekhna alkhamdoulila régime diekhna
Bilaye métina trop Momo domou dekk bi du courage
Oohh Momo domou deuk bi suis abonnée à lui sur Facebook son arrestation nonou lama metté wone bilahi courage frère
No frere gayi ay dimbarr laniou blh viv patriote
Wawe !!! J’ai regardé le paquetage j’ai ne pouvais pas retenir mes larmes . Comment un être humain peut-il faire ça à son semblable 😭😭😭😭😭😭😭
Bilay deugg rekk lawakh justice par force dafa wara ame
Amna yakar ni li khew si prison yi Dina changer ndakh sunu Président khamna li khew yeup
Est ce qu un jour ces personnes pourront oublier ou pardonner ceux qui ont les moyens doivent s investira améliorer cette situation Que justice soit fait pour la conscience de ces jeunes
Salut Momo est une personne bien aussi que Dieu vous bénisse Vraiment c est triste trop de mandats dépôts merci à toi aussi bravo brother
Bilaye yalla Rik moufi ni yalla Bakhna
Jai mal au coeur g mon frer ki es laba yeureum na gnifa nek yeup ndeysane yallah nalen yallah diapalei tang na metina li rek motax gorjigen beuri nama yallah bal dou niep nio meune gerer li goor deug mokoy def
Yale nala yalla maye xolou mougne😢. Mais met un ( s ) à jour c pas une critik
Ndeysane meumeu faye borom bakh la yalnala yalla taxawou 😊
Motakh lou way mougn mou diékh té lep lou wayy def bala gua dé diguako guiss😭wara liguéy diapalé citoyens yi dilénn teudj si lou gnak khorom wayé anamou tay diékhoul Macky wathie na😩ngourou yalla rek mo doul diékh😭
Massa frère et courage le combat continue inchalla
😢 cheuteee 😭 li metina trop wlhi ndeysan
Fadel yagui dora meueneu invite détenus yii😂😅😂😂
Magui dioy yalna yala até yala guené
Droit de l,homme n,existe pas au Sénégal, ou bien ils ne sont pas au courant
Ndammme réck frére momo doumou pikine guinaw rails bi djame si oaw
Non!!!!!! Magui soga khameni amena niou sokhore 😭😭😭😭😭
C’est vraiment triste, ce qui se passe dans les prisons n’est pas humain 😢ngi fa déss yallah naniou guén si diam ak salam
Alahouma amine,
Tu es brave yalla dina la faye
Mais Fadel fonékone?
Je souhaite un bon courage à kepp kougnou meussa togne dougalko kasso! Massa léne😢
Courage ndanane ❤
Yalga gôudou fane dôme féké lép wér wérlé inchaallah
Momo Domou Deuk Bi bialh vrai patriote mo nék niii bilah
😢😢😢 vraiment très très triste 😢😢😢
L’injustice est un cancer dans la société 😢
Ce régime a fait vraiment mal 😣
Ngourou vaut rien 😢 Bilakhi Yalla dou sétane li😢
Humanisme zéro dans les prisons du Senegal. J’espère que le président et son gouvernement trouveront des solutions plus adéquate pour ces détenus.
Fadéll kii limou wakh thi paké tass sakh amna lou déss bilakhi walakhi
VRAIMENT IL FAYT REVOIR LES CONDITIONS DES PRISONS DE REBEUSS DE TOUTES URGENCES POUR NE PAS REPRODUIRE LES MÊMES
SOUFFRANCES ET TORTURES AUX PRISONNIERS.
C'EST UNE URGENCE PRIMORDIALE.
Noo doyna waar😰😰
Bilahi frère 😭😭😭😭😭
Policiers corrompu du gouvernement de Macky Sall yala nalene yala até ak khalé yi
Ndeysan Senegal...Just jailing innocent people for nothing ..Macky will never see peace for the rest of his life
Agree with you
Mane diomaye faye rek la yeureum li yeup kiko beugue lidieunti
Courage momo domou deuk bi
le systeme est trop malade et jusqu'à présent il faut un président courageux pour changer tout ça
Bilakhi lou méti way😢😢😢😢😢😢😢😢packétage méti na lolou😢😢😢😢😢😢
Injustice bi, yéna ngui siy niémé wakh légui?
injustice bii bagne cii niamé wakh dou taye à chak fw niou wakh cii wayeii lo guiss dafay djêkhe fii cii adûna
@@alexismendy8809 Wakhou mala dé! Presse bi ak wa Dakarbuzz Tv laye wakhal
Prison bi dafa yague et c’est vieux Arena tour bi diass mom lagnou warone def prison mettre les prisonniers en bonne santé
Merci mon frére toi au moins tu penses à tes frères en besoin😢
Ndeysane nooo li mettina
Merci beaucoup Momo, Macky sall vrai domram la 😢😢😢😢
Walahi alakhira dina metti 😢😢😢
Quel reportage !!!!! Le gas a beacoup de sagesse
Amnistie bi dafay teup 😡😡😡😡😡
Policiers yi yeup laniouy identifier niaf s'en ndeye casso
Non Sénégal ama diay dolle
Sincèrement j ai pleuré walahi azim toubab yi nionou guene j ai fait des prisons en France suisse et denmark des faits que j ai fait en ma propre conscience mais bilahi c était comme si j etais dans ma chambre
c'est vidéo il faut les traduire en anglais et français svp justice
POLICIERS, GARDIENS DE PRISON, JUGES, et AUTRES QUI ONT PARTICIPÉ TANT SOIT PEU À LA TORTURE DOIVENT ÊTRE ENLEVÉS DE LEUR FONCTION. Justice doit être faite !
bonne courage aux hommes dètenus❤
Sénégal Li niawna 😢
Metyna yalla nafa yalla dieulé keup kou thiabi fété guinaw si barké Seydina Mohamed Psl
Ayway dou guéne deim interview pape niang social 🙏🏽
Sonko ame liguey. La rupture totale . les prisonniers sont des êtres humains. De la méchanceté de ne pas respecter leurs droits !
Billahi Sénégal métina li War nagne sé wakh
Vraiment li métina injuste bi doyenawar
Sarap ndem li rk🥹🥹🥹
C'est inhumain vraiment inhumain que les autorités revoient la situation.des détenus dans les prisons
Thî barkhé mouhamed président diomaye pm sonko soutenir léne détenu yî li métina trop
Mon frére lamine il les laba depuis longtemps en plus il es tré malade souniou frére yeup si rebeusss ci barké weeer bou séle bi🙏🙏😭🥹
Demal thi page Facebook EX Outhmane amna numéro yignou diokhé pour gni kham détenu politique yi dess kasso. Inchallah le 03 Avril gnou gen
@@dalsin1412 non dousi politique naco diapé
Yaw mom ya dakh émission té gueuna amam lé sens ligua souligné yeup amna solo
Vraiment c'est dur
Khana Sénégal amoul hacker bou aye .mou wonn gnou Atina.il faut qu'il paye tout le mal qu'il a fourni
C'est Anita et non Atina am na niou wax ni Pape Malick Ndour la wayé worouma dé béne codébateur ram moko ko done toumal mou koy wéddi😮😮😮
@@danalayegueye4761 lapsus😜.
Sinon yallah na neck mom.parce que ce mec a reçu pas mal d'accusateurs au cours de leur mandat
Mary 3 pom moye anita cest trist😪😪😭
Macky et son gouvernement ils ont fait trop de mal 😭
Vraiment y a des gens qui sont méchants la honte 😭😭😭😭😭
C'est vraiment triste mais ça va changer inchallah
Bilakhi mo ahme made doun dou na ko 2010
MODOU BILAHI SUÑU BOROOM MOLEY FAYE KU DIAMBARE NGUA
Ohhhhh 😢😢😢métina allahou akbar
Anita doit répondre à la justice
Ce n'est pas du blague le paquetage se fait comme ça j'étais avec lui à la chambre 46 on a passé plus de 10 mois ensemble mon frère domou deuk bi 😭😭
Donc tu connais Bassirou fall il est à la chambre 46
Donc tu connais Bassirou fall chambre 46 il est toujours laba
Si je le connais très bien borom xassida yi 😩😩on y appelle basse moi je l'ai surnommé😂 "boy basse"😂sama lonko leu wone kou xam leu bou bax
@@VKS1895 ndeyssane mane deh la amalon problem mais je ne lui souhaite pas la prisons . Gnake khamone adouna moko yobouwei li yeup ndeyssane
@@Mrsmbaye. ndeyssane meussa way iow légui lo meuna déf pour mou retrouvé libertém bi wala ma inbox leu ci email
Domou deuk bi diambar deug barki alkhourane
❤️❤️❤️🙏❤️❤️❤️