Zarco niak nga khorom pa bou tolni yaw Gnou invité la pour nga wakh sa khalate 😢nga nekfi di xass kila invité naneko nga melni danguine ay wakho deugg😩😭li moy lane yaw dof nga rek
Lamb mafia leu combine ay schéma eumeu séne be fait pas partie des chouchoux de l'arène ils vont tout faire pour que balla gaye lutte le combat royal après modou lo siteu
Wa legui boudè kila dan gnari yonn daga wara dieli sa revanche n’a balla dieli revancham thi eumeu mou diekh meuno len wakh ba modou barè ak balla Sen amalgame ak propagande yi bou yabo ngen nopalou surtout yaw fadam sa bop bou reuy bi
Mod lo dekoy dan inchalla barke serigne saliou inchalla
Foko tekk?
Fadam tu parles au nom de albourakh mais il ne faut pas oublier aussi qu'il y'a d'autres promoteur qui sont la aussi
Zarco niak nga khorom pa bou tolni yaw
Gnou invité la pour nga wakh sa khalate 😢nga nekfi di xass kila invité naneko nga melni danguine ay wakho deugg😩😭li moy lane yaw dof nga rek
❤❤❤
Loutakhe Balla gaye dialoule eumeu sene, vraiment laisse modou lo tranquille
nie danio soffe balla loutakh dieuloul eumeu , wla bombardier? , legui niou beugg modou dieul revange par force , teu pourtant modou wahoul balla rek ladoul beurél mais képeu koumou beurel déja 2x...
Modou est un simple humain arrêter d'exagérer... Cas même
Maral bi gniy maral modlo eupna 🤦🏾
Fadam a raison c'est modou lo qui motive Balla gaye
fadam mo khame lambe
Fadam comme balthazar 😂😂😂
Pourquoi balla dieuliwou eumeu séné
Lamb mafia leu combine ay schéma eumeu séne be fait pas partie des chouchoux de l'arène ils vont tout faire pour que balla gaye lutte le combat royal après modou lo siteu
Merci ❤
Loutakh bi mou djeulei couronne roi , modou lo bi balla dane janvier 2019 leu djeul ?! Ah 😌
Fadam daye doul rk
Wa legui boudè kila dan gnari yonn daga wara dieli sa revanche n’a balla dieli revancham thi eumeu mou diekh meuno len wakh ba modou barè ak balla
Sen amalgame ak propagande yi bou yabo ngen nopalou surtout yaw fadam sa bop bou reuy bi
wla bombardier , enplus eumeu si victoir la diougué comme balla , wakh bi yeupp mooy lamb j nio beugg modou danou...
@@Deggou diekhna takk t’as tout compris
Eumeu Sene danoul Balla gaye rek dasi tek rakam sathies
Boye niang nakk loumm deff balla