Qu'on arrete de nous arnaquer. Pourquoi Touba ne doit pas payer l'eau? Touba est comme toutes les autres villes du Senegal. Est-ce qu'une ville comme Mbacke, St Louis ou Ziguincor peut se lever un jour et dire qu'elle ne doit pas payer l'eau ou l'electricite? Qui va alors payer pour developer ces villes? L'argent que Touba gaspille durant ses Magals est assez suffisant pour developper leur reseau d'eau et etre autonome en cette matiere. Mais si c'est un reseau develope avec l'argent du contribuable, Touba doit payer la facture comme toutes les autres villes ou zones rurales avec eau courante. Retenez que ce n'est tout le monde qui est de Touba. Les habitants de mon petit village qui trainent le diable par la queue pour payer leurs factures d'eau seraient tres content d'apprendre que cette denree est desormais gratuite.
Merci à vous je suis parfaitement d'accord avec vous touba n'est pas le Sénégal quand je lui entend parler c'est comme si tous les régions ou départements n'existe pas j'espère que le gouvernement fera sont travail
Arrêtez de juger Touba selon des propos des personnes qui n'agissent que pour leur intérêt Primo :Touba est une concession qui appartient à Serigne Touba donc c'est le Khalif qui est en charge de tout. Secondo : Si Touba gaspille de l'argent durant le magal cela ne regarde pas puisque c'est pas votre argent car si tu célèbres quelque chose pour toi tu n'aimerais pas qu'on te dise que tu gaspille de l'argent. Enfin allez vérifier si Touba est connecté au réseau de la sen'eau
@@MassDiene-o9p xana dégo limal1 wakh démal renseigner baxam Touba dafa brancher si réseau sen eau bi kubakh ay forage mofa nek dilène alimenter mais pas le réseau de la sen eau loulou motax
Madame l'image niane sounou borom bou mague bi kounefayakon moy mou katanal mou yire sonko ak diomaye te écarté nipa gnye sonal rewnii nevalene ba dougnou mana yaha amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Touba est une ville comme thies Dakar kebemer bayileen sen khel yingueen di fowee . Kou out sa forage bopou autonome manga bagna Faye ndokh a part des tax
Danga fenale sonko diema yakh dérame dieme ko diakhassé ak serigne si antouwoule nga diakarlo ak mome mo douma la légui na broukhlou dou mana nek bo dougue casso sa réwandé molako yeubo macky sall daye satyi souff ak souff(femme) sa kadoubla lolou mola yeubou casso
Ziaré Nieup dilén wakh né Touba ville la comme yenén ville yi mais bocouniou ndakh Touba titre foncier la forages yafa nék Serigne bi Molén fa deflou Abdou Bara doly li wakh mine nagnko mom rék la concerné
YÉNN GNOU WAR LÉNNA BAGNE NGUÉNE DI BAGNATÉ . WA TFM , MOHAMED NDIAYE AK BABACAR FALL FOU GNOU TOTHIE ? GUIS NAGNOU FAÇON JOURNALISTE YOU NÊ DE VRAIS JOURNALISTES. LOUFI NITT WAX AK LOUFI NITT DÉF SONKO MOUNKO TÉYÉ DI LÉNE XAAR.
Touba da wara fay ndiokh comme toutes les villes du pays je sais pas pourquoi toutes les autres villes religieuses di fay ndiokh te Touba dou fay ndiokh so deme Makka danouy fay ndiokh
Combien de milliardaire se réveille à Touba ? Et touba il y a une forte inondation. Combien de milliards transit chaque mois à Touba. Arrêter votre hypocrisie....
Bara boulgnou yapp... Daa ameu linga wakhon Macky Sall mo tah ngaa dougou cachot. Ça n'a rien à voir avec sonko... Touba momougnou niit yi... Bougn beugué ndokh dagnouy fay.
Baradoly arrête d'être con tu crois que le gouvernement va vous laisser le contrôle de l'eau à Touba ? Vous allez payer de l'eau comme cela se fait sur l'étendue du territoire arrête tes conneries
Il faut que Touba paye l’eau pour que la ville se développe,
👍👍👍👍👍👍
Wakh te Yalla takh boko defee rekk daguay neeck a l’aise mais ay thiaakhaane dalay wayadilo bonne continuation Mbacké
😂😂😂😂😂😂😂 Bara Dolly dourouss
Bara Dolli guemoul dara. Guemoul sakh serigne touba. Boppam dong mo ko sokhale.
Touba ci rew mi la bokk donc payer vos factures d’eau 😂😂 no gni gno beugue lou ndokhé dé
Dof la,ay todiangué rek lay wakh.livre noir+livre rouge=😂😂😂
Qu'on arrete de nous arnaquer. Pourquoi Touba ne doit pas payer l'eau? Touba est comme toutes les autres villes du Senegal. Est-ce qu'une ville comme Mbacke, St Louis ou Ziguincor peut se lever un jour et dire qu'elle ne doit pas payer l'eau ou l'electricite? Qui va alors payer pour developer ces villes? L'argent que Touba gaspille durant ses Magals est assez suffisant pour developper leur reseau d'eau et etre autonome en cette matiere. Mais si c'est un reseau develope avec l'argent du contribuable, Touba doit payer la facture comme toutes les autres villes ou zones rurales avec eau courante. Retenez que ce n'est tout le monde qui est de Touba. Les habitants de mon petit village qui trainent le diable par la queue pour payer leurs factures d'eau seraient tres content d'apprendre que cette denree est desormais gratuite.
Merci à vous je suis parfaitement d'accord avec vous touba n'est pas le Sénégal quand je lui entend parler c'est comme si tous les régions ou départements n'existe pas j'espère que le gouvernement fera sont travail
Arrêtez de juger Touba selon des propos des personnes qui n'agissent que pour leur intérêt
Primo :Touba est une concession qui appartient à Serigne Touba donc c'est le Khalif qui est en charge de tout.
Secondo : Si Touba gaspille de l'argent durant le magal cela ne regarde pas puisque c'est pas votre argent car si tu célèbres quelque chose pour toi tu n'aimerais pas qu'on te dise que tu gaspille de l'argent.
Enfin allez vérifier si Touba est connecté au réseau de la sen'eau
Touba nieupeu la yénè diam et est une partie entière du Sénégal donc bayilène dikko kholé comme ennemi Touba aime tout le Sénégal
Mais comme Touba aussi ay régle ma bopam la am baye fall gnioy déroule naniou fay ndohmi
@@MassDiene-o9p xana dégo limal1 wakh démal renseigner baxam Touba dafa brancher si réseau sen eau bi kubakh ay forage mofa nek dilène alimenter mais pas le réseau de la sen eau loulou motax
Delen diooly fajar
Djoulina legui😅
Ku khamul moul fo dieum daguay seti ki nek thi yonou dioup mou wonla yonebi😂😂😂😂😂😂😂
Diomi amoul heure😂😂😂😂
Sonko rek 😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤
KOJ.BAKH LA .DIEUREUDIEUF
😂 livre rouge bi dema si beugua dolli livre noir
bilakhi Sénégal mo bari nafegck non ay nite yo khamni gueumou dara
Toutes les manipulations de bara doly n ont pas abouti. C est un business man qu il aille continuer ses activités.
Je ne comprends pas pourquoi Touba ne doit pas payer l'eau comme tout un chacun?
FÉKÊ MA CI BOLÉ EUSKEUYE 😂😂😂😂😂😂😂
Boy bara , tay mou nioul soubeu mou wékh 😂
😂😂😂 Sanga dacdé
😂😂😂😂ayy wayy ay wayy 😂😂😂😂
Xana daffa merre wa Touba 😂😂😂😂 dou toudou wa Touba
Merci beaucoup
Dioumbo dolly ,comme art en ciel 🏳️🌈, kénn mounouko qualifier fénn kii.
Mais ont peu pas être toujours dans l erreur c'est un être humain union fait la force
Tfm quelque soit le degré du virage, il ne faut pas oublier de vous mettre a jour (fisc ak impots yi). Sinon, nguene ladj maimouna.😂
Bravo ❤❤
Yen amo len talibe ha 😂😂😂 bakhna 😂😂
Madame l'image niane sounou borom bou mague bi kounefayakon moy mou katanal mou yire sonko ak diomaye te écarté nipa gnye sonal rewnii nevalene ba dougnou mana yaha amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Discours yepou dina sange 😂 Ndeyesan say bara dolli
Ak mentalité yi ak façon de faire la politique 😂😂😂
Kou xamoul fo dieume délou figua diogué 😂😂 projet pastéf bi kouko bagne yaye sone rek 💪 patriotes pour toujours ✌️🇸🇳
Touba est une ville comme thies Dakar kebemer bayileen sen khel yingueen di fowee . Kou out sa forage bopou autonome manga bagna Faye ndokh a part des tax
OÙ EST LE LIVRE ROUGE ????😂😂😂😂😂😂😂
Kou.sagnoul bagn sagna nacgou
Danga fenale sonko diema yakh dérame dieme ko diakhassé ak serigne si antouwoule nga diakarlo ak mome mo douma la légui na broukhlou dou mana nek bo dougue casso sa réwandé molako yeubo macky sall daye satyi souff ak souff(femme) sa kadoubla lolou mola yeubou casso
Ki bara, la dédé te, waye ana gor😢😢😢
Wahi nitttt😂 cette fois ci
No au tranhumance basta😊
Bara Dolly sou wakhè rekk nga xèb ko! Une vraie tête vide !
BARA DOLiiiiiiiiiiiiii😁😁😁 NAINA NDOKH GRATUIT WAY. APRES TIVAOUANE. APRES PEKESS..........DOF TIGUI
Barra méw fi doffi dougue dé . Tappalé moffi diekh, wouti kham kham mba ni patte rek😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂
Djommi amoul heure
Mais c est normale si il y a du bien faudra le dire
Nous sommes tous des sénegalais
On doit etre solidaire la main dans la main dafa ame solo
❤❤❤❤❤❤❤❤
Waa barra dolli mii serigne walla taye nga wakh lii souba nga guenssi bamou sett ma ame gathie
Serigne bou fègne
Ndoxou lac de guerre ku ci am danga wara faye facture lolou moy yoon .
bara ni kakatar sa prison sa khamadi mola fa yobou rien à voir avec ton soutien à sonko
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Gueumoo dara, té lolou moola sangue. Nit dangay doylou té goré
Mais sayou ndokh mou neekh amee dina am prix par ce que rien n’est gratuit dans la vie
C est daouda mine mais ke professeur Sadio d abord qui la evoque avant Daouda mine
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Allahou akbar kii moo nafekh
Ziaré Nieup dilén wakh né Touba ville la comme yenén ville yi mais bocouniou ndakh Touba titre foncier la forages yafa nék Serigne bi Molén fa deflou Abdou Bara doly li wakh mine nagnko mom rék la concerné
Ay doly kon yi ñouy bayi ñouy wax! Mim reweu lifi nek Ken meussouko guiss! Yalnañ yala doli Soutoura rek!
YÉNN GNOU WAR LÉNNA BAGNE NGUÉNE DI BAGNATÉ . WA TFM , MOHAMED NDIAYE AK BABACAR FALL FOU GNOU TOTHIE ? GUIS NAGNOU FAÇON JOURNALISTE YOU NÊ DE VRAIS JOURNALISTES. LOUFI NITT WAX AK LOUFI NITT DÉF SONKO MOUNKO TÉYÉ DI LÉNE XAAR.
Yémalé day baax ci am réew
Kouy dieunde ndokh war mane faye ndokh nopalikou thi niakoum ndokh
Pourquoi Touba ne doit pas payer l'eau ?
N'importe quoi toutes les villes sont égales.
Un pays doit être réglementé na nieup fay point
Grop dol Kat yakh dero Iman ndao
GFM RFM TFM ak cén patron nio kham na niou continue cén diabolise yi ak tapalé yi ak manipulation yi yosu interem rék léy soore
Nionmom sonko rek lanoy topo
Sopèkouwoul dè mom day changer couleur
Ndokh SWTA moko waché founé gnepeu wara fay ndokh. Ville sainte yep degnouy fey ndokh. Wala gnidoul fey fay ay installations te assainir sen gokh. . Moy yone
Bara ndiaye franchement ya mana doule
FENEU RECK LAY DEF
Touba da wara fay ndiokh comme toutes les villes du pays je sais pas pourquoi toutes les autres villes religieuses di fay ndiokh te Touba dou fay ndiokh so deme Makka danouy fay ndiokh
Nio taye
TOI jamais,restez chez et nous restons chez nous.
Goor ca goornia,djiguenne ca djiguenne nia capa niama thuss !
Combien de milliardaire se réveille à Touba ? Et touba il y a une forte inondation. Combien de milliards transit chaque mois à Touba. Arrêter votre hypocrisie....
Casse indi ndokh , ba paré ngané douniou faye ndokh mi . Mais lolou moy lane ?
Pourquoi pas faye ndokh
Senegal mo bari ay nafékh
Voilà la politique il a changé de veste
Ces individus étaient où lorsque tout cela se passait. Hypocrisie si tu nous tient
No doly dofna
Bara doli rek mo Mouna deuk ci deuk bi😂
😅
Gni gnoy diabi baparé du sékhat nékeu ay wégne rék fou toye gnou take amou léne béneu dignité thiame
Bara dolli come kakatare
Non il est très aujourd'hui le marabout vraiment
Tu nous emmerde esk Touba c'est la seule ville sainte du Sénégal ?oubien il ya d'autre sénégalais à part entier
ADOUNA DAY DOH IN FAUX FEY AME
Bara boulgnou yapp... Daa ameu linga wakhon Macky Sall mo tah ngaa dougou cachot. Ça n'a rien à voir avec sonko...
Touba momougnou niit yi... Bougn beugué ndokh dagnouy fay.
Oh il répète trop c présentateur
Cest normal chaque cmbat a sa fin
Tu fais honte Cheikh Bara doly baryngua wakh amoulo NGor
Mais limou wakh deug leu
Vous nous fatiguez ces deux Monsieur vergogne zéro
Magui déééé bara dolli dinama raye
Abdou mbacke bara doull yi dou dara ab dor Kat rek la wor kat la dome haram bou mak la mom aki magam yepp
Kii mo nafekh deugue
Hiii, tfm ak Sonko!
c'est le baiser du serpent
Nopil
Bara doly nopaloul tangua bayi GOURVERMENBI niou liguéye yaw khamoulo foye téck sa tanque est tu parle trop
Ki moy bara borouxlou
Bayyieen bara dolli gnekh,,, makk bour la..
Baradoly arrête d'être con tu crois que le gouvernement va vous laisser le contrôle de l'eau à Touba ? Vous allez payer de l'eau comme cela se fait sur l'étendue du territoire arrête tes conneries
Diomi amatoul heure