Machalla c'est très beau les frères d'amour lafe thiate a notre frère Wally c'est très émouvant machalla a tous le groupe de balla Yalnaléne yallaah défallén diam ake ndam inchallah Amine 💪🦁💪🦁💪🦁💪🦁💪
Ça se voit que les gens profitent pleinement de la vie mais n'oublions pas de prier pour les morts surtout les anciens gloires Double less, Mbaye gueye, Père Balla gaye, Mor fadam, Père boy bambara. Dans la vie kou deh gnou fatela motakh n'oublions pas di diamou ndakh bamel wetna teu ken doufa nieuw dilafa wetali malheureusement.
Macha allah frr si rappelle bi amna solo yalna yalla samou la défal la soutoureu diamou ak khéweul déf ko si réw mi ak fou djoulitt nék ak surtout domou Sénégal 🇸🇳 jah jeuff 🙏🏽🙏🏽
Ils le savent mieux que toi et j'espère qu'il le font tous les jours . ils étiez très attaché à leur père , leur père est satisfait d'eux car il sait qu'il a laissé des responsables .il peut maintenant reposer en paix , c'est le dessein de tous les papa . soyez heureux les frères.
@@malaminediatta2524 toi tu crées la zizanie affaire de satanisme. Personne n'a dit ici que leurs pères n'étaient pas satisfaits d'eux. Ce message était juste un rappel et pour tout le monde y compris moi.
@@ahmeds7785 il n'y a pas de zizanie c juste un rappel pour te montrer qu'ils n'ont pas oublié les anciens. Lorsque vous dites kou déh gnou fatela . Vous confondez les moments de distraction et tristesse .
Nèkhoul ba nèkhoul mais balla gaye 2 c’est le meilleur lutteur du de ce pays Pas seulement sur la lutte mais sur l’aspect sportive il est un tout autre chose 🤬👍
Afairr bou nice Billahi Balla Bombardier sén jeste Bi jeste Noble Deugeu la koi ❤️❤️jameu thiyéne 2 champion yi 🙏🏻xola Fls De Balla Rék kone Domou Doubléss Billahi Dafa Nourook ndiom trop sax 🙂
Très belle image entre balla et bombardier vraiment ... les jeunes lutteurs devraient vraiment apprendre de cet état d esprit là, le Sport doit unir mais pas diviser... il y a un tps pour un combat et un tps pour la vie
Manchaallahll Bonne continuation Wally B seck yalla n'a xa Am diamou si brké mouhmede ❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️👂❣️
Où sont les spotters de Balla Gaye2? venez liker mon commentaire. Balla gaye2 pour toujours❤💪
On est là 🎉🎉🙃😇
Wa guiss gua nio gui ni jusqu'à la mort
@@ndatediaw3625 p
No Balla Gueye ndanan la bilahi kouko begeu beusseul j'aime 💪💪💪
C'est vraiment joli le geste de balla et bombardier. Vraiment ay nittou kessé nguéne
le charisme de Balla mon dieu 😍😍
Vraiment la famille de doubles me plaît beaucoup vive Balla gaye
Balla gaye g eu l'occasion d le rencontrer il est cool e sympa simple souriant machallah
Je suis une fan de Modou LO mais vraiment Balla Gaye est adorable 🤩 en plus depuis que j'ai su que c'est un homme SOCIAL, silako gueuneu sopeu 💖
m0
Lou ler 😍😂😍amoul sisou ni la
Wawaw balla
Machalla
Pareillement bilay mais je l'adore dafa free
Balla le Sénégal t'aime on est très de ta professionnalisme et on a droit de te dire merci
C'est jolie de voir comment Balla gueye est humain de même que bombardier avec son snap
C’est magnifique le Snapchat de bombarder et balla gaye 😍🥰🥰
Trop mm
C'est plus que beau machallah Balla dalll bokousi franchement arène bi sans balla gaye 2 c com thiepiu djiene sax djiene bou saff sappp ak roffff
Nooo ñary top Star 🌟 du Sénégal Balla gaye 2 and Wally seck 💕❤️
Vrai
Daffa léer bro
Ño meun beuss franchement ❤️👌
LUTTEUR DU PEUPLE CHANTEUR DU PEUPLE LOVE SW VOUS 💯🔥
Machalla c'est très beau les frères d'amour lafe thiate a notre frère Wally c'est très émouvant machalla a tous le groupe de balla Yalnaléne yallaah défallén diam ake ndam inchallah Amine 💪🦁💪🦁💪🦁💪🦁💪
Amiine Yacine inchallah
Sama tourando amine cherie
Allahumma Aameen sis
😍😍😍😍❤️
💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤🎤❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏
J'aime trop la complicité de Balla et sa Thiès
Vraiment c joli mes deux champions ,suis fans de balla gaye et waly séck bilahi limoy sénégal
Balla gaye yalle nala yalla may dam Lou séda gouya Amine inechalla
Amine🙏🙏🙏
B.G2 lutteur du peuple,✌ W.B.S chanteur du peuple❤ ET moi je suit le commentateur du peuple😁💜💯
Diadieuf geum sa bop
@@kismadabo1038 mangi nii😁😁
Mdr...Yallah na Diam yagg té sakh thi bim Reww Senegal
Bien- dit Ndiaga kenn dou yaw
@@moussandiaye1657 Amine waay👌😂
Wallay ma beugueu balla avec sa joie de vivre non stress💃🏻💃🏻❤️❤️❤️
Mane damay khelatt sama jour mariage ma toudéko Balla non grand bi meune n'a bisss bilay 😂♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️💯💯 ambiance 💯
Non mane balla mako beugue no stresse lay doundé je l'adore
J'aime la joie de vivre d balla gaye😘😘
Bilay li rafét na nékh na trop machallah je vous love balla Gaye ndam rék inchallh
Wa li nékh na dé
Ça se voit que les gens profitent pleinement de la vie mais n'oublions pas de prier pour les morts surtout les anciens gloires Double less, Mbaye gueye, Père Balla gaye, Mor fadam, Père boy bambara. Dans la vie kou deh gnou fatela motakh n'oublions pas di diamou ndakh bamel wetna teu ken doufa nieuw dilafa wetali malheureusement.
Macha allah frr si rappelle bi amna solo yalna yalla samou la défal la soutoureu diamou ak khéweul déf ko si réw mi ak fou djoulitt nék ak surtout domou Sénégal 🇸🇳 jah jeuff 🙏🏽🙏🏽
@@mhdfromcadiorlmh9706 Merci beaucoup frère pour ton message plein de sagesse que le bon Dieu nous assiste inchallah
Ils le savent mieux que toi et j'espère qu'il le font tous les jours . ils étiez très attaché à leur père , leur père est satisfait d'eux car il sait qu'il a laissé des responsables .il peut maintenant reposer en paix , c'est le dessein de tous les papa . soyez heureux les frères.
@@malaminediatta2524 toi tu crées la zizanie affaire de satanisme. Personne n'a dit ici que leurs pères n'étaient pas satisfaits d'eux. Ce message était juste un rappel et pour tout le monde y compris moi.
@@ahmeds7785 il n'y a pas de zizanie c juste un rappel pour te montrer qu'ils n'ont pas oublié les anciens. Lorsque vous dites kou déh gnou fatela . Vous confondez les moments de distraction et tristesse .
J' aime trop ce pays.Mon pays de Coeur coucou depuis Abidjan.
Qu est ce que tu attend pour venir
@@marouanegueye3236 da wara nieuw
👏👏👏👏👏👏🤙🏽
Merci ma chère 💕
@@matty7424 🥰🥰👏senegal dafa nekh
Bilahi Wally bakhoul si xalé dina fekeu magg bou tokk mou yeugeulko xalé bouy nelaw mou yéko 00 stresse avec Wally machallah
Sama waly ak sama balla gaye ndam rk inchallah 😍😍🥰🥰
Ndeyssane Wally Ballago foumou nék diam AK mbécté rék mo faay am merci a Balla et bombardier
c’est ça mon beau pays ❤️❤️❤️ loins des yeux 👀 près du cœur ♥️ depuis paris 🇫🇷
Où ?
Façon dont j'@dore Balla C'est Trop Manchallah 💞💕😘🥰❣️❤️ Nalla Borom bi may ndam rek inchallah AMIN 💪💖♥️❣️❤️🤲🤲🤲🤲
Balla Gaye borom mbaakh là wolahi nitt késsé la. Beuré ak niak beuré nioun ak yow ba faw inch'Allah !💞💞💞💞
Balla notre roi yalna la yalla may ndam
Machaallah sama mbeur Balla guaye2👍👍👍
Non ki mo bakh Waye vive balla ❤️❤️❤️❤️❤️on t'aime fort
Nooo franchement chapeau à vous deux c'est très joli Balla est un champion
Balle gaye 2 rek Ndam rek inchalla champion good luck
Mannneee Balla laaa Beugueu mannnn😍😍😍😍😘😘😘😘😘🥰🥰🥰
Lutakh wa guediawaye ame classe🥰
Balla mon champion wally seck chanteur du peuple je vous kifff❤❤
this is so nice sama Wally seck rek ak Balla Gaye Machahllah 👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻💪🏻💪🏻💪🏻💪🏻❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑
Nèkhoul ba nèkhoul mais balla gaye 2 c’est le meilleur lutteur du de ce pays
Pas seulement sur la lutte mais sur l’aspect sportive il est un tout autre chose 🤬👍
Yalla na yalla maye ndame balla inchallah 🦁💪
Kéne dou balla sama wadji si mim réw♥️♥️💕💕🍒
Machallah balla 🙏🙏🇸🇳👏👏👏🇸🇳c’est le Sénégal 🇸🇳 j’ai vous j’aime 👍
Bilay Balla on t aime fort longue vie à toi
Lu moy Sénégal ❤️ Balla gaye 2 et bombardier le snap oohh c mignon walae yalna DiAm yagUe galsen ❤️🙏
Wallahi Balla gaye niitou kassé la wallahi yalla nala yalla maye mbam si barké seydina Mohamed psl 🙏💯💯💯💪💪👑
Afairr bou nice Billahi Balla Bombardier sén jeste Bi jeste Noble Deugeu la koi ❤️❤️jameu thiyéne 2 champion yi 🙏🏻xola Fls De Balla Rék kone Domou Doubléss Billahi Dafa Nourook ndiom trop sax 🙂
Balla gaye le meilleur de tout les temps avec son mental de fer machalla
Leeeee eupeuna nehoul Ba nehoul wante balla da beury feeling❤️❤️❤️
balla gaye si xoll ❤️
Wally seck ak balla gaye d'où ay wo machallah 🥰🥰🥰🥰🥰🤩🤩🤩🤩
Bilae balla gaye sa xol mo rafet machalla
Image de balla et bombardier c jolie
Non balla fo nite yallana fiamo yageu yalla mayela ndame barkep yonenteby psl
Bilay lii dafa nice balla et bomb mei kéneu d'où Waly❤️
Wally ❤yak balla yanafi neik yalla na seine diam yague❤❤❤❤❤❤je vous loveuhhhhhh😍
No Balla sama star bi rang ndame rek 🔥🔥🔥🔥🔥🔥 ana wa keur boye Niang 😂😂😂😂😂😂😂😂
Boye Niang ragal la 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Noo kèneu dou sama mbeur mii Balla gaye 2 yalla naleu yalla mayy ndam inchalah sii barkii mawlana
Bilay balla niitou kassé le machalla yalla n'a yalla diamal yalla bo guiss Loula méti si adouna
Très belle image entre balla et bombardier vraiment ... les jeunes lutteurs devraient vraiment apprendre de cet état d esprit là, le Sport doit unir mais pas diviser... il y a un tps pour un combat et un tps pour la vie
Walahi c très jolie a voir mashallah j'aime
Mane maï sopé Wally Ballago ak Balla Gaye 🥰😍🤩
No balla mousou mala foral mais tay foralnala daga bakh bilay amo béne inne si nite yalla ga ame ndam inchalah
Non wally limo way iska moko tayy hier wally wayna 😍😍
Le 2 notre star Wally et balla sa manque Eldiouf aussi
Machallah sama mbeur mi balla gaye
Ohh Bilahi b52 bg2 li rafetna trop
Machalla li dafa Nice mé balla yalnala Yalla may ndam 🤲
Ma djiantalll mbeurr dh ndayam koula ndahh😂😂😂😂😂
MAR YACINE MEÏSSA BIGUÉ YALNA LA YALLAH AAR TÉ SAMEU LA CI BARKÉ SEYDINA MUHAMMAD SALAL LAHU ALEYHI WA SALAM ❤ ❤ ❤
Vraiment Balla machalah nittou kessé nga
Balla le meilleure de tous les temps💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿💪🏿❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Balla yalla nala yalla maye ndam
Diam dafa nekh yalna diam yague Balla ❤️❤️❤️
Bravo wally👑 faramareen love Balla💪🥰👑
Wally rék ak Balla Gaye inchallah dame mbeur inchallah merci beaucoup notre wally de valeur Machallah Ballago 🤲💪🤩💞♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️💯💯💯
Wawe
L)))) lll
Balla Gaye mako beug ❤️
Je suis fans de Balla gaye 2 💪♥️♥️♥️
Sheuttt wally limouy daiff sama xol❤ bi da graw ki dall deumako beugg🥺 tel tayouma ko
BG2 ❤❤❤
L’image de l’année ✌️✌️ BG2 & B52
Balla sama lutteur bii je t'aime trop ❤️🙏
Mon King balla gaye 2 je t,aime très fort
Manchaallahll Bonne continuation Wally B seck yalla n'a xa Am diamou si brké mouhmede ❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️❣️👂❣️
Thank you wally seck and Ramadan group too love and blessings to you all, champion balla gaye ak modou lo ♥️🇬🇲♥️🇸🇳👏
Ram Dan not Ramadan sorry for the rectification lol
Franchement c magnifik le geste de Balla vers Bombardier lii moy sport
Balla Gaye 2🥰🥰 le meilleur
Ohhhhh c tro Nice vraiment balla on t'aime très fort
Billahi balla gaye mii damako beugue notre lion national 🇸🇳🇸🇳 🇫🇷 on t’aime ndam rek inchallah si barké Nabil Moustapha yaye lamb sans yaw lamb dou nexx nay ko nianal ndam
Balla Gueye ♥️♥️♥️🇸🇳🇩🇿💪🙏
Yallah daffa def balla di sama mbeur wally di sama waykat thanks you allah
Machallah li nekhna thi khôl yéna bok nedye Ak baye Mach Allah que du bonheur Balla ❤️
Nékhoul ba nékhoul mais famille Double less bi gno yoré lamb dji
Wawao Bamou beuryy 💪 machalla 🥳 notre champion nationale nioula beugue piirr diam si yao balla gaye 🥳🥳🥳🌟👋👋💃🤸💪💪💪💪🎊🎉🎊🎊
Mbeur le lion de guediawaye 💪💪💪💪💪❤️❤️❤️❤️
Machallah wally yallah gua am diam❤️❤️❤️😍😍😍😍
Machallah sama balla d’amour je l’aime grave ❤️❤️❤️🤗
Vive bg2 nekha faral
Yallah na djam yagg
Machalla c'est le Sénégal ki gagne balla et B52 khôl sétt n'a♥️❤️
K l bn dieu ns pardonne amine
Bilahii image bou rafet laniou woné ....les Supporters doivent imités leur lutteurs ..