Pape Sarr en colère et répond sévèrement à Modou Lô : "warouma wakh danga doff, doumako..."

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 17 гру 2024

КОМЕНТАРІ •

  • @ousmanegomis6938
    @ousmanegomis6938 Рік тому +45

    Yow confirmer nga li Modou lo wakh
    Vrai dof nga
    Outal ndiapé ak sabou té ngay sangou
    Dof nga wéro😅

  • @khadimsow7149
    @khadimsow7149 Рік тому +8

    Lamin le vrai journaliste ❤️☝️

  • @abdoulayeba1461
    @abdoulayeba1461 Рік тому +5

    Merci beaucoup kharagne lo

  • @dienealia9962
    @dienealia9962 Рік тому +21

    Khamoneu naniii dîna tontou 😅😅😅😂😂😂 Pape Sarr trop de communication tue la communication fais toi rare mon frère

  • @MamadouyayaWane
    @MamadouyayaWane Рік тому +12

    Yow vrais vrais dofga

  • @moussaseye3439
    @moussaseye3439 Рік тому +62

    Yaw dangay confirmer Li modou Lo di wakh vrai doff nga

  • @omarbao5556
    @omarbao5556 Рік тому +16

    Bilay modou lo wakh deug daguena doff😂😊

  • @alioudiop6125
    @alioudiop6125 Рік тому +41

    Bilahi Modou wakhoul ak iow!
    Mais dof nga 😂😂😂

  • @ibnouwadji1358
    @ibnouwadji1358 Рік тому +7

    Oie seytané nga ya diakhassé pikine 😊

  • @boubacarboiro5813
    @boubacarboiro5813 Рік тому +1

    Lutte TV la télévision leader de la Lutte sénégalaise

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 Рік тому +17

    Xarange lo moye champion 👍❤️✅

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall5548 Рік тому +2

    Merci grand pape sarr nous sommes derrière toi

  • @ibrabadiane4233
    @ibrabadiane4233 Рік тому +15

    Saway modou lo dousa morome si dra manoko jalhasé ak sénégalais yi

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 Рік тому +2

    Merci beaucoup kharagne loooo 😄😅😀😃😆🤣😆

  • @TallaTallambaye-zi9wu
    @TallaTallambaye-zi9wu Рік тому +9

    Pape kone daga mer baye tontou 😅😅😅massa waye mais modou wakh na deug nak vraiment wero lolou môme lerna

  • @yorokante777
    @yorokante777 Рік тому +3

    Bravo Luttetv 👌

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr3371 Рік тому +15

    Dofo danga doporal modou lo dousa morom malanio wakh nganan labat fall demal fale modou lo so togné ba dem kasso dou mod lo molafay gené ok mak dou fen nervis thierno ndom yi yalén dite lérna💀

  • @madydiame3906
    @madydiame3906 Рік тому +12

    Modou lo lal nala d🤣🤣🤣🤣

  • @omargaye3601
    @omargaye3601 Рік тому +1

    o bayil 😊😊😊😊 ndiakhse kilifeu dines moy lay amna droi dou thi yakh

  • @ibrabadiane4233
    @ibrabadiane4233 Рік тому +10

    Keur mame ngay titaro modou lo ay keurem la yoor demal nga jobi te bayi wakh ji mo guene

  • @cheikhthioune4400
    @cheikhthioune4400 Рік тому +15

    😂😂😂😂pape Sarr danga doff

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 Рік тому +5

    Modou Lo day Def effet 😂😂😂😂pape guemeul yalla

  • @babacardiongue4095
    @babacardiongue4095 Рік тому +28

    Pape yamal si lamb rék gnoune wa parsel Modou lagnouy tapou

  • @abdoulahaddoip2368
    @abdoulahaddoip2368 Рік тому

    Merci pape

  • @youssoufthiam9923
    @youssoufthiam9923 Рік тому +30

    Même bo doffo wero 😂😂😂

    • @Cheikh-mk1mm
      @Cheikh-mk1mm Рік тому +2

      Bro degue nékhoul
      Ki sou wéré tamite beuriwoule déé

    • @youssoufthiam9923
      @youssoufthiam9923 Рік тому +1

      Il est dans son délire le pauvre 😂😂😂

    • @babacardiallo1391
      @babacardiallo1391 Рік тому +2

      No copain rayy guama Pikine la deuk fan ama number 1 mais no ray guama

    • @sheky3138
      @sheky3138 Рік тому +1

      ​@@Cheikh-mk1mmki touss jottouko! Da nguène soofe quoi!

    • @amadousamb9578
      @amadousamb9578 Рік тому

      Mdrrr wolah ki kay weroul 😂😂

  • @khelcomdecoration8430
    @khelcomdecoration8430 Рік тому +6

    Thiouray deumou mi la kharagne tourr pikin doff yépay nguien 😅😅😅😅😅

  • @ablayelo5976
    @ablayelo5976 Рік тому +9

    😂modou lo wakh na deug dh😂😂😂

  • @amethcisse2557
    @amethcisse2557 Рік тому +3

    Wooy pape Dof Sarr wayyyy😂😂😂😂😂😂

  • @laminendao402
    @laminendao402 Рік тому +1

    Pape sarr kone da am ay supporter 😂

  • @ndiayendiaye313
    @ndiayendiaye313 Рік тому +2

    Diadieuf Pape Sarr🙏

  • @mamesaliou8963
    @mamesaliou8963 Рік тому +6

    koula khole khame ni toukhe katou bonne nga😂

  • @mouhamedmakhroufthiam1476
    @mouhamedmakhroufthiam1476 Рік тому +1

    Grand pape tawfeih reik.

  • @VieuxMbodj-n8v
    @VieuxMbodj-n8v Рік тому +2

    Ki bilahi vrais doff la😂😂😂

  • @ibrahimagaye581
    @ibrahimagaye581 Рік тому +10

    Pape Sarr Modou amna si droit âme fofto si Salamé

  • @serignemorfall5635
    @serignemorfall5635 Рік тому +1

    Patriote yi soutien a pape

  • @محمودصو-س3و
    @محمودصو-س3و Рік тому

    Modou lo ❤❤❤❤❤moy sen bay

  • @abdoukonate3459
    @abdoukonate3459 Рік тому +1

    Waaaa pikine yallah toppé woulèn daraaaaa

  • @layediop8540
    @layediop8540 Рік тому +14

    Vrément dagua fou nak 😂😂😂😂

  • @thebosh-se5lb
    @thebosh-se5lb Рік тому +5

    Lath ko loumouy ligueye 1970
    Zero realizations _wax rek _tokh bone
    Doff bou tekiwoul dara

  • @adjiamasina7951
    @adjiamasina7951 Рік тому +2

    Pape tua raison bilaxi yalanala yala samb❤

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Рік тому +2

    Pap Sarr bouko may beuzz beuzz way Nérvi Macky sall Yii 🥹Nérvi yi Danio xéwi Moments bi motax niou beugeu créyé beuzz 😒sonko Ama Baldé points 💚🤍🫶vive Askan bi ❤️❤️❤️❤️

  • @modoudiakhate4243
    @modoudiakhate4243 Рік тому

    Tu confirme les propos de Modou lo

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Рік тому +1

    Mérci pape sarr sa Kadou Rafétt na🙏🏽🙏🏽

  • @aronacamara9831
    @aronacamara9831 Рік тому +3

    Pape tu parle tro wakh reck arèt

  • @sheky3138
    @sheky3138 Рік тому +1

    SÉNÉGAL DAAL DA NGAYE RÉE BA TASS QUOI! WAXX DËGG TÉ YALLAH TAXX MOME TAYYÉE NGUÈNE KO!
    YÈNE KI ÑOU TOOÑE KO TRAITER KO DE DOF, MOUY TONTOU BA PARÉ NGUÈNE KOY XASS!?
    FANS MOD LO YI AYE VRAI FANTASTIC YOU BONNA BONNA BONN NGUÈNE! YÈNE REK LA JÉPPI!

  • @mosi301
    @mosi301 Рік тому +1

    Pape sarr sou magué kom khadim Ndiaye lay mêle

    • @moussasarr8277
      @moussasarr8277 Рік тому

      Mo yow ki mo mak khadim Ndiaye yow 😂😂😂

  • @alioucisse-qr6hg
    @alioucisse-qr6hg Рік тому +18

    Yaw ak bakhom ak Julie balde yene Yam ay dof guene

  • @assanekaka9414
    @assanekaka9414 Рік тому +2

    yangi mer de thiéyi modou lo mo sonal wa pikin 😂😂yangi wax ki dof

  • @GOLDENBOYE25
    @GOLDENBOYE25 Рік тому

    Kou d accord ni pape sarr wèrore be seul j aim sèrore

  • @AliouKane-r8f
    @AliouKane-r8f Рік тому

    Mo guay confirme ioe😥😭

  • @papemedounediouf1178
    @papemedounediouf1178 Рік тому +13

    Pape meye niou diameu

  • @babacarmbaye7872
    @babacarmbaye7872 Рік тому +6

    Modou lo wakh na deg pape sarr mi ngan nimame doff la

  • @ablayediop3318
    @ablayediop3318 Рік тому +3

    Dagua bari wakh

    • @Papito-ØG
      @Papito-ØG Рік тому

      Yako geuneu beuri wax nopil 🤫

  • @ammedicko-oj3tc
    @ammedicko-oj3tc Рік тому +5

    Thieuy papa Sarr kene douko diam nani

  • @Dieng-vk6if
    @Dieng-vk6if Рік тому +8

    Pour temps pape Sarr yaw ya ndieuka togne Modou lo

  • @amdywade8242
    @amdywade8242 Рік тому +2

    Vraiment modou Lo il a mal parlé ça c’est pas du respect ✊

  • @boubacardiop-ue3kc
    @boubacardiop-ue3kc Рік тому +1

    Pape Sarr dofoule dara dafa wahè akk khOlame rek , sétane na émission bii ModOU LO mo togne wah deugue amOul béneu respect ci nitt 🫱🏾‍🫲🏽

    • @zahrafall
      @zahrafall Рік тому

      Niata yon lagne wax si modou t modou tontou wou len vraiment nit dafay atte deug wala kou fayou ngein xam

  • @محمودصو-س3و
    @محمودصو-س3و Рік тому

    Modou lo ❤barre dole bilay

  • @bestcontentsSN
    @bestcontentsSN Рік тому +20

    Modou, c'est mon lutteur mais il doit montrer plus de respect envers vous. Vos chamailleries font partie de la lutte et vos intentions n'etaient pas méchantes, même celles de Abdou Bakhoum et de Jules Baldé.

    • @diattaabdoukoulingo2826
      @diattaabdoukoulingo2826 Рік тому +4

      Va regarder les interviews de jules balde bakhoum ou pape sarr lui meme tu ne vas pas dire sakh que leurs intentions netaient pas mechantes

    • @bestcontentsSN
      @bestcontentsSN Рік тому +2

      @@diattaabdoukoulingo2826 Man ngay wakhal dh. Man rek lol. J'ai tout regardé. C'est pourquoi, je me suis permis de faire ce commentaire. Vous êtes susceptibles mtx vous dites que c'était méchant. Mais en aucun cas, ça l'a été. Chamailleries yagu neu ci lamb. Mais, traiter niit de doff, c'est extrême, si c'est tiré sincèrement de la personne qui le dit. Et, ça touche à la dignité de l'individu.

    • @Dusay-js1yy
      @Dusay-js1yy Рік тому +1

      Mdr. Donc eux on le droit de chamailler… mais pas Modou Lo??
      Ça fait des années qu’ils clashent Modou sans que ce dernier ne réponde. Now suffit d’une petite réponse pour les exciter

    • @bestcontentsSN
      @bestcontentsSN Рік тому +2

      @@Dusay-js1yy Du n'importe quoi, y'a chamailler et "chamailler". Le premier implique de la réserve, le deuxième des exagérations...
      Et, ç'en est une exagération qd il les traite de "doff", ce mot que bcp banalisent par abus de langage, mais, reste très gravissime.
      Donc, revenons sur Terre en mettant de l'eau dans notre vin, et, respectons tout le monde...

    • @Dusay-js1yy
      @Dusay-js1yy Рік тому

      @@bestcontentsSN mdr. C’est toi qui devrait destresser!! En quoi c’est Gravissime ? Comme s’il y avait mort d’homme ?
      Ce débile insinue qu’il y a un dealer dans la famille de Modou Lo et tu n’en parles pas… tu trouves ça moins grave ?
      Heureusement que la mauvaise foi ne tue pas

  • @papandong9560
    @papandong9560 Рік тому +4

    Pape sarr mo dakke souba la tabaski😂

  • @ibnouwadji1358
    @ibnouwadji1358 Рік тому +4

    Oie ak ama khana tay ngeen djibo

  • @alieusaine8027
    @alieusaine8027 Рік тому +1

    ❤❤❤

  • @mbayendondediagne4325
    @mbayendondediagne4325 Рік тому +8

    Yen delen wakh lou rafet😢

  • @abdoulayeba1461
    @abdoulayeba1461 Рік тому +2

    Avec modou rek jusqu'à la mort 🤣🤣 île trop fort

  • @doudoufall2582
    @doudoufall2582 Рік тому

    Senegal khamoul kou togne cou fayou la kham😂😂merci pape😂

  • @mamesaliou8963
    @mamesaliou8963 Рік тому +18

    ama aye dofe réck moka weure

  • @georgesdieganediouf2684
    @georgesdieganediouf2684 Рік тому +5

    Pape Sarr tu te donnes beaucoup d'importance.
    Tu es trop bête pour parler en public, vrai craintin moye ki.

  • @omarkande8547
    @omarkande8547 Рік тому +1

    Modou rek lagniouy topp

  • @moadcasa9176
    @moadcasa9176 Рік тому +3

    😁😁😁😁😁lô

  • @papemafallsy3615
    @papemafallsy3615 Рік тому +1

    Pape sidi paix à son âme est un coussin de MODOU lo pape sarr liguaye wakh xamosi dara

  • @hafissoukane2003
    @hafissoukane2003 Рік тому +3

    😂😂😂kii kon la c un malade c vraii

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 Рік тому +2

    Xolal waxi doff yimouy waxati😂😂😂

  • @ousseynouthiam-kg2be
    @ousseynouthiam-kg2be Рік тому +3

    Vraiment wakh douf gay wakh

  • @assanekeweul7861
    @assanekeweul7861 Рік тому +5

    Dafa wayadi

  • @mamadoufall8047
    @mamadoufall8047 Рік тому +2

    Modou lo soula ama diape nga khamne askan bi niola tek finga nek nga woor lene merci pape Sarr

    • @yayacisse9746
      @yayacisse9746 Рік тому +1

      Bilahi lo ler nga wakh khamoul ama sakh

    • @mouhamaddieng6218
      @mouhamaddieng6218 Рік тому +1

      Moh 😂yène ak pape Sarr mii yeina yam ayy doff ngueine Pikine guépp Modou lo moleine meune

    • @mamadoufall8047
      @mamadoufall8047 Рік тому +1

      @@mouhamaddieng6218 li laniouye wakh si meune fenn sénégalais Kou la wakh ni pikine la deuk doff bou mack bi moye modou yaboye Lo 😂🤣🤣😄😄

  • @damembow6374
    @damembow6374 Рік тому +1

    Carte katou xalisss gua nakhaté kattt bii🤣🤣🤣

  • @talladiop4837
    @talladiop4837 Рік тому +1

    😂 billahi khamone Nani Dina répondre desna Abdou bakhoume ak jule baladé

  • @yakhoubaseydi905
    @yakhoubaseydi905 Рік тому +2

    Eumeu sene nak louko waa pikine def😂😂😂😂

  • @MalickDia-m8n
    @MalickDia-m8n Рік тому +1

    😂😂😂Wakhal
    M6 lamine
    Tere bon kession

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Рік тому

    Pape sarr yaa néex 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 interview faye

  • @aronacamara9831
    @aronacamara9831 Рік тому +5

    Pape modou à rèson tu un vrè manquent modou amoute sa diote ..

  • @mbackethioune4385
    @mbackethioune4385 Рік тому

    Pape vrement dof nga li modou lö deugu leu aussi mouno diakhassé modou ak senegalais xaragne day def éféé dé😂😂😂😂😂

  • @papembayendiaye7177
    @papembayendiaye7177 Рік тому +2

    Bilaye ki dofe la

  • @omarsarr1649
    @omarsarr1649 Рік тому +4

    Non dofffoo sakh mais daga weroulll😂😂😂😂

  • @moustaphangom8944
    @moustaphangom8944 Рік тому +1

    Dayaye. Sop Pape nioune Modou rek la niou beugue souko nékhé farr douko nekh

  • @ablayediop3318
    @ablayediop3318 Рік тому +5

    Ay douf guen kay

  • @seckdame6156
    @seckdame6156 Рік тому

    Sì j t m.lo j laisse la lutte!

  • @khalilfaye5432
    @khalilfaye5432 Рік тому +1

    tu as confirmé les propos de modou

  • @atoumaneniasse4854
    @atoumaneniasse4854 Рік тому +3

    Modou molén geuneu réw bolén tonton kén méer😂😂😂

  • @modoundiaye-vy3cq
    @modoundiaye-vy3cq Рік тому +2

    yw modou waxoull ak yw dh\ mais deugall ga lim done waxxx vrai doff nga

  • @matarmboup7167
    @matarmboup7167 Рік тому +5

    pape modou wakhouma

  • @ousmaneniang5897
    @ousmaneniang5897 Рік тому

    Pape daguay fin wa parcelle modou rék lanioy top

  • @ablayegaye7848
    @ablayegaye7848 Рік тому +2

    Vraiment nak li Modou wakh degueleu iow wèro nak Modou toudoul bène tour

  • @moussadia248
    @moussadia248 Рік тому

    Modou lo Moy dof bii mes Pape Sarr boul wakh dara ama baldé Di n'a ko fathie boy sobée yalla ,pikine Moy Sénégal

  • @hadyagne9473
    @hadyagne9473 Рік тому

    Non pape kay ndéké confirmer na dafa doff😂😂😂😂

  • @thebosh-se5lb
    @thebosh-se5lb Рік тому +8

    Yaw Loy ligueye Niakk jomak tardè motax ngay ndamosa mame
    Sama mame rek

    • @zahrafall
      @zahrafall Рік тому

      😂😂balko

    • @gamegame2724
      @gamegame2724 Рік тому

      Mom Pathè balde bimouy titeuro loumouy def mom

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 Рік тому

    Pape sarr nééna modou wakhoul si kilifa diiné youniouy saga😀😀😃🤣🤣🤣pape sarr déklouwo kharagne lo dé🙄🙄😬🤔🤔🤔🤔

  • @mimie.a6424
    @mimie.a6424 Рік тому +2

    Pour moi il est loin d'être fou . C'est juste une personne qui a une bonté naïf

  • @bathiendiaye611
    @bathiendiaye611 Рік тому +1

    Modou lo limo wakh Moy deg ama ay douf gno go weur motakh manoul am dará se lampji moromam yep amnan khalis mai top die

    • @seynaboukane9017
      @seynaboukane9017 Рік тому

      Yaw nak gnila weur nak am nitt gni mo eupp solo

    • @bathiendiaye611
      @bathiendiaye611 Рік тому

      @@seynaboukane9017 bani wakh nuett Yi gno ab solo do nuetti Senegal ndakh gues gua tay neno yakhi kothia doun ay nuett nuett yo khamni lo bon rek si Ami gno topla so amoul gnobayila

  • @abdoudiallo327
    @abdoudiallo327 Рік тому +8

    Fis nous la paix modou lo yallha ak yenentibii la ngom dou bokalei