Audio fuite ooh Allakhou akhbar mba pikine dou tass lou doy war Pape Sarr wax na lou graw

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 17 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 91

  • @mouhamedkounta9819
    @mouhamedkounta9819 9 місяців тому +35

    Gris 2 yalla nako yalla defal diame je pense que c’est vraiment domage qu’une bonne personne comme lui se retrouve dans ces situations le monde de la lutte doit s’unir et demander grâce pour qu’il retrouve sa liberté lii takh nak ma wax lii moy nieup xamni nite kou bakh la

  • @KhaliltalibeBamba-v4y
    @KhaliltalibeBamba-v4y 9 місяців тому +8

    Gris 2 yalnako yalla guéné fofou❤

  • @diopfaya3471
    @diopfaya3471 9 місяців тому +1

    Très bien pape,'est bien fait.
    Baboy c'est une bonne personne franchement.
    Na lepe dièkh ci diam.
    Diam mo guène lèpe.❤❤❤❤❤

  • @sambazoradiop238
    @sambazoradiop238 9 місяців тому +8

    Pape nala yalla defal diam❤

  • @MorGning-n4i
    @MorGning-n4i 2 дні тому

    Mn sama yone ci pikine m ama yalna yalla defal KO diam sama bok talibe bi❤🙏

  • @MilkMilo-qr5uc
    @MilkMilo-qr5uc 9 місяців тому +14

    Eumeu et boy Niang fort heureusement légui comprendre nagnou dof ga ama baldé rk la yeuram dof you melni warou gnou ame accé si entourage champion ama baldé na yéwou ay diamono eumeu séne boy niang la wone dane clash ama si xarito wam ak balla gaye2 légui ama ga dieul ama baldé je te conseil ga défe comme eumeu et boy ni Niang dof you melni diarou gnou may kanam

    • @diattaabdoukoulingo2826
      @diattaabdoukoulingo2826 9 місяців тому

      Ama baldé dafa niak chance nda a part pape sarr Jules baldé ak bakhoum rek tardél naniou ama

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 9 місяців тому

      @@diattaabdoukoulingo2826 Lou wér ga wakh dafa wara woutt entourage bou solide franchement mogui commencé tardé si lamb

  • @cheikhfall5548
    @cheikhfall5548 9 місяців тому

    Merci grand pape sarr nous sommes derrière toi

  • @OusmaneDiouf-q7d
    @OusmaneDiouf-q7d 9 місяців тому +13

    Binga waré nek ci sa bop daffa yag wakh rek ngaffi néké té amoul ndiarigne

    • @LamNdiaye
      @LamNdiaye 9 місяців тому

      Merci 🎉🎉🎉🎉🎉 lou ler gua wakh ki di dof

    • @elzoatti8951
      @elzoatti8951 9 місяців тому

      motax mu yewu

  • @imammalick1730
    @imammalick1730 9 місяців тому

    Machallah pape Sarr yalla n'a yalla takhawou

  • @cirely3220
    @cirely3220 9 місяців тому +5

    Pape sarr iow yaye seytanè Pikine nioune Pikine lagnou deuk couleur Pikine lagnou défendre depuis Pathè guène prison daga changé discour nioune lidjeunti wouniou pathè

    • @papezulefaye7263
      @papezulefaye7263 9 місяців тому

      Bilahi wallahi wa tallahi mo taass ndaye pikine vrai seytané leu

  • @soufi732
    @soufi732 9 місяців тому +2

    baboye mon lutteur de tout les temps , pikine dou amati balla beye2. c'est un monument il merite beaucoup de respect morodi.

  • @elzoatti8951
    @elzoatti8951 9 місяців тому

    pape Sarr le véridique . yaw rek lay topp .

  • @BoubaDiakhate-jv8pv
    @BoubaDiakhate-jv8pv 9 місяців тому +2

    Nitou deug nga diam si yaw pape sarr❤

  • @BaraafiaNdiaye
    @BaraafiaNdiaye 9 місяців тому +3

    Pape Sarr pourtant yaw yafidone wax ni de eumeu séne limoula défal bénn mbeur défaloulako AK limou défal sa yaye

  • @InsRastafariMixmaster
    @InsRastafariMixmaster 8 місяців тому

    Limoy Sénégal Ko Défal Loubakh Mou Fayleu Loubonne.
    Deuk Bi Gnifi Gorée Dagnilenn Di Compté 😢

  • @ousmanefaty6353
    @ousmanefaty6353 9 місяців тому +1

    Merci Pape Sarr

  • @azizlo1978
    @azizlo1978 9 місяців тому

    Bravo pape Sarr moi je suis fans de modou lo

  • @amadousow8717
    @amadousow8717 9 місяців тому +1

    Pape sarr dagnouko wara djapalè kou soneu si wa pikine ak lambe dji nako sènègalais yeupe wouyoussi si beusseume bi ãmena mèrite bi

  • @OusmaneDiallo-fn7vi
    @OusmaneDiallo-fn7vi 9 місяців тому

    Courage pape SARR tu es un grand monsieur

  • @MamadouSamb-q3q
    @MamadouSamb-q3q 9 місяців тому

    merci pape sarr Moy deugeu ❤❤❤

  • @papiiiswelleeiih5728
    @papiiiswelleeiih5728 9 місяців тому +2

    Sénégalaise mo wara bayiiii ay audio youye fuite loluu baxuul 😢😢day yagu rew waxoumalaaaaa keur tmt yewuuleneeee tuutiii

  • @Ordinaire95
    @Ordinaire95 9 місяців тому

    Genre yi ay nittou toxique lagne lo meunti masla ak niome yag yag digene diotté la seule solution moy coupé tout contact

  • @DjilyNdiaye-pw8zx
    @DjilyNdiaye-pw8zx 5 днів тому

    Yw pape sarr kou man doull nga

  • @elzoatti8951
    @elzoatti8951 9 місяців тому

    pape sarr , toppotol sa bop .

  • @bassiroutall9094
    @bassiroutall9094 9 місяців тому +4

    Danga sonou si mbeur pikine yi thé amalounioula ndiarigne

  • @moustaphagueye8405
    @moustaphagueye8405 9 місяців тому

    Pape sarr yeureumeul sa boop bayii ayy wakh koulay saga rek sa sorti you barry rek mo takh nekal nite concentrer sa liguey mo guen

  • @cheikhoumarsidibe3311
    @cheikhoumarsidibe3311 9 місяців тому +4

    Pape Sarr daye compter sakh sorties yi 🤦🏽‍♂️😂😂 Nèna 29 sorties la dèf 😂😂😂😂
    Barina kheute kheute mais kou begue Pikine la.

  • @simonediop2094
    @simonediop2094 9 місяців тому

    Pape sarr mague na wakhji responsable la

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 9 місяців тому

    Ya tass pikine sa wakh barina

  • @KabroSamal
    @KabroSamal 9 місяців тому

    Nice pape sarr❤❤❤❤❤

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 9 місяців тому +3

    😀😀Modou lo daye deff effet😂

  • @diogenelaerce2197
    @diogenelaerce2197 9 місяців тому +1

    Pape Sarr yangui beug nek niit nak. Dama fokone mbeur yii dagnoula ligueyone sakh…😂
    Mbeur you togne sen leufeul ndeye yii. Ayy vrai domerame.
    S’en sarape Ndeye rek mbeur yiii ayy vrai dofff

  • @morramos9050
    @morramos9050 9 місяців тому +2

    Pape sarr mayniou diam bi Pathé guéné batay wakhou tmt ngay wakh danga ragal Pathé ba legui ama cv eumeu boy Niang 2 ne vont pas.baboy nga dieul taf sa wét ya xam dh nioun Pikine moniou nior kouy défendre Pikine niou and ak yaw défendro lo sa blm la

  • @cheikhfaye386
    @cheikhfaye386 9 місяців тому +1

    Pape sarr nak yaw khàmo sa bop yaw soûla monde lamb khamé mbeurou pikine yi nio takh surtout eumeu sene

    • @Madou-h1g
      @Madou-h1g 9 місяців тому

      Ki nafekh la

    • @cheikhfaye386
      @cheikhfaye386 9 місяців тому

      @@Madou-h1g dafa yabaté way

    • @muhammad3323
      @muhammad3323 3 дні тому

      C’et un IDIOT STUPIDE CHEYTANE

  • @papadizaofficiel6027
    @papadizaofficiel6027 9 місяців тому

    Tu as prie une bonne décision mbeur badola

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 9 місяців тому

    Modou lo tassna pikine

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 9 місяців тому

    Pape sarr aka nekh bala ma deh rek mouné dou deug😂😂😂Wala dengeu 😂😂😂

  • @leuz.patriote
    @leuz.patriote 9 місяців тому

    Eumeu Jordan Eumeu tayson 2 Eumeu pape sarr gnila takhawou yeup bayi ngalèl a ya sik deh diotèk nieup

    • @Ahmadouboromediamono4
      @Ahmadouboromediamono4 9 місяців тому

      Desna fatè ga problème atta ak ibnou Diop kokou dou dara😂😂😂

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 9 місяців тому +4

    🇺🇸 t'aurai dû le faire depuis longtemps 🎉😂ne jamais mètres ton avenir projet et ambitions en attente pour aider quelqu'un d'autre à construire son avenir jamais

  • @LamineSoaré-j7j
    @LamineSoaré-j7j 9 місяців тому

    Nom deug deug nitou deugue gua bilaye

  • @modousonko7340
    @modousonko7340 9 місяців тому

    Liii yeup Modou Lo laa😂😂😂😂

  • @MoussaSy-o3y
    @MoussaSy-o3y 9 місяців тому

    Svp pape Sarr kane lay waxal pour affaire ndayane bi

  • @laminediatta7069
    @laminediatta7069 9 місяців тому

    Nekkk sa boppp deee mo guennna wor je vs l’avais dit sa jobottt deee. Yako meunnna sokhalli

  • @salioudia4148
    @salioudia4148 9 місяців тому

    Pape sarr dale da sise 😂😂del yatale bokk

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 9 місяців тому

    Kou ham pape sarr rellement kan lay wahat ??

  • @PapeLatyrSeck
    @PapeLatyrSeck 9 місяців тому

    Mbeur dou gor dé

  • @AmmeDicko-wt2iu
    @AmmeDicko-wt2iu 9 місяців тому

    Thieuy pape sarr mo déee 😂😂

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 9 місяців тому

    Mom mongui teugg lamb ba leiguii walaa

  • @pronosticfootsenegal1112
    @pronosticfootsenegal1112 9 місяців тому

    Bouniou bolou woul sene problème leu ....legui as pikine rek laniouy topou ...mbeur yi amou niou bene diom modou lo war nalene meuna tégalé douma lene

  • @moussaseck967
    @moussaseck967 9 місяців тому

    Saytané ga dé yawe bou pikine tassé rek yawe la mbeur yeupe gua khoulole khoulo gua ama khoulole boye niang khoulole resemen eumeu sene akh boye niang ya tasse pikine bilaye walaye

  • @pronosticfootsenegal1112
    @pronosticfootsenegal1112 9 місяців тому

    Retournement de situation 😂😂😂😂 adouna mo goudou tankeu

  • @morramos9050
    @morramos9050 9 місяців тому +1

    Bathie seras Khana mame la 😅😅😅😅

  • @Mbayediop4
    @Mbayediop4 9 місяців тому

    Amine

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 9 місяців тому

    Mbeur Yi diarou niou touss nekal si sa bopp mo geun

  • @mourtala1063
    @mourtala1063 9 місяців тому

    Yagg yagg dangay djoub wat rékk kon mieux vaut sén ay prblm en interne mo guen ngay wakh aprés ngay réthiou ta lépp lo wakh day déss thi réso sociaux yi.

  • @moustaphasognane2071
    @moustaphasognane2071 9 місяців тому

    Non pape Sarr nak yaw ken khamoul lo beug koi

  • @mamediop8226
    @mamediop8226 9 місяців тому

    Yaw dagko yekh def beur amoul diarighe 😂😂😂😂

  • @championBoulan
    @championBoulan 9 місяців тому

    Eumeu sènne dh mome workat bou mak la mome

  • @OusmaneDiop-yx7pw
    @OusmaneDiop-yx7pw 9 місяців тому +1

    Sa palas doff rek mou kou beuge

  • @taphadiene
    @taphadiene 9 місяців тому +1

    Pikin moye unté 27 ah pape Sarr wéroul mom

  • @Madou-h1g
    @Madou-h1g 9 місяців тому

    Aka mana wathiou lecate ko

    • @adandoye3759
      @adandoye3759 9 місяців тому

      😂😂😂😂😂😂

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 9 місяців тому

    😂😂😂😂

  • @morramos9050
    @morramos9050 9 місяців тому

    😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅

  • @papezulefaye7263
    @papezulefaye7263 9 місяців тому

    Yaw bi pathé balde guéne balegui nieupa guis sa changement envers la famille baldé danga fété ak niom wakh sayy wakh you niaw banopi taxaw fi dibtekk doff,eumeu sene ak boy niang solene bayiwé wagni wouléne dara pikine tayy sou méléni si diaxasso yawla mayniou jamm wayy ya tass pikine

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 9 місяців тому

    Mocvcv❤

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 9 місяців тому

    😅😅😅😅😅😅

  • @charlesalphonsediouf7817
    @charlesalphonsediouf7817 9 місяців тому +1

    Tu parles trop

  • @cheikhfaye386
    @cheikhfaye386 9 місяців тому

    Yaw keneu wakhlo woula yaw ya beugon gnou khamla ngay wo site yi di mboubo ----------

  • @matarkante8270
    @matarkante8270 9 місяців тому

    Waji nek ndayane la beug kham dama dagn koumpa 😂

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc 9 місяців тому

      😂😂😂😂 kokou mo teyé buzz bi bilahi y'a sopp

    • @lampfall1372
      @lampfall1372 9 місяців тому

      ​@@MilkMilo-qr5ucchaque fois mounè bayina ta dou bayi

    • @SonkoFocus2024
      @SonkoFocus2024 9 місяців тому

      Méme mane beug na kham wadjii ba setaneko 😂

  • @KhalilDia-dk4re
    @KhalilDia-dk4re 9 місяців тому +1

    Nice pape sarr❤