Man sen série bi sexe sans mariage bingen banaliser mooma jakhal Aida Sow Pa Omar Raky Dado et Mor Pa Omar et la Nièce de Raky Dado jangal leen khaleyi loi bakh wat
La maman de Tacko est très vulgaire avec ses manières elle est entrain de forcer Amoul diome fou sa dome di seuye kéne respecter woula ak sa bouche mou melni kouye léka léwe😂😂
Bilahi Ndiaye Radiakh Dinama ray😂😂😂😂😂
Keur Ngoné diaba ndiaye ak mbathio nekhna😂😂
Paa Oumar moy Balthazar 😂😂 migui yaka Dérou goor ngi 😂😂😂
Khana pa Omar rekk moy Gore thi série bi diabar force rekk 😂😂
J'adore Maty thiey sacré Tacko ❤
Aladji Bilaye mo gana nékh si serie Aladji raw
Coumba nénako nala Bolé ak sama yaye woyy sama ndeye😂😂😂😂😂😂
Pa Omar dafa febar 😂😂😂
Paa omar kay comme balthazar rek 😂😂❤❤
Ndiaye AK ngooné diaba NK 😂😂😂😂😂
Paa Asan ñàkk nga fay da nag te bëgg jigéen. Yaa ngi yàq sunu der bi de. 😂 😂 😂
Pape Omar la Pa Assane mo ngui prison 😂😂
😅😅😅😅
😂😂😂😂❤
Serie sakh mo dakh nitou intéré😂😂😂😂
Ayda sow moom kañ la fi biir bi yàqu ba mu ëmbaat? 😂 😂 😂
A diaxal nama dhe😂
Bne question
May ragal pa omar eubal😂😂aita nak match bi tass😂bakhna rek beugue na femme trop
Lou wara meune né la comme mom dou door balle perdue😂😂😂
Falay moudjé waay kham ngani
Non mère Aïcha fall beri problèmes mais aladji tamite réw na ba dof
Wa racky dado mome wor ngua maty wor aida sow
Man sen série bi sexe sans mariage bingen banaliser mooma jakhal Aida Sow Pa Omar Raky Dado et Mor Pa Omar et la Nièce de Raky Dado jangal leen khaleyi loi bakh wat
Et surtout lolou borom kémane moko warone bagne
@AwaNdiaye-vp9fs 🤎
@@AwaNdiaye-vp9fs vraiment
@@fatimaba6116 mom borom mbakhla ay série youye yéte la warone di douguel kome akhirou zamane waye dagnko dague
@@AwaNdiaye-vp9fs peut être que aussi c'est le scénariste
Yow Aïcha fall bo nobé boy bii wakhe ko sonale ga fatou gueuye trp niak fayda badée chimmmm
Vraiment
Thieuy Khalis bountou bounék meune Nako feugue
Pa omar beugeu nga femme 😢😮
Pa omar yi aka gn bari si rewmi 😂😂😂
Pa Omar Moy vrais khittt tatt😂😂😂bénn douko romb
pa omar mo guena niank diom si gorou sénégal yi sim😮
Détt bouko togn fan gay classé Pod 😂
@@RamatoulayeKouyate nio yam🤣
Tâte la beugeu
Wa ngoné diaba ak ndiaye louniou bok😅😅
Pa omar dina eumbeul aita
Wa yeen Tacko da nara ame dôme sachant qu'elle est coupable de l'avortement de Maty .
Justice way
Bou amé dom dé théâtre bi dou am chance
Aladji😂😂😂😂
Alagie nitt la 😂😂
First 😂
La maman de Tacko est très vulgaire avec ses manières elle est entrain de forcer
Amoul diome fou sa dome di seuye kéne respecter woula ak sa bouche mou melni kouye léka léwe😂😂
Kou nane ataya naane djindiare wara door xana 😅😅
Ay chérif khana liguéyo théâtre bou ma dougou fek lafa😂
Yakh der ngay def 😅😅😅 heure de job douma nek si telefon bi
@@cherifousinguinar8455 a lima la guise bari na dhé
Cherif 😂😂
13:37 😂😂😂😂😂😂
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sama série
😂😂😂😂😂😂😂
2 ème youpi 😅😅😅
😂😂😂😂❤😊
😮😮
13:37
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😅😅😅
Pa Omar da febar si djiguenn
Dafa beug lou baax rek 😅😅😅
Raki dado yay diam duegue
Pa omar yaw gor bou bon ga bilaye sa diabar khamo foumou nék gay séti Ay djigne thimm
raki mi louko diara li tmt do am moukou kharitou daw li niawna dh
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂🤣👍
😅😂😂😂😂
Mer aïcha😂😂😂😂😂😂
Wa mére bi mom tamit fom jogué
Cv😊
❤❤❤❤
❤❤❤