Khana tay guénkoy wax merci yéne wa keur mod lo yi comba reug reug ak sa thiés lounék wax guénko Moustapha Gueye tay guéne danou mouy wax louléne enragé guéne ni limouy wax deug la nafékh bakhoul mod lo bou danouwoul rék zarko danouwoul même action
@@NgalgouSyll-q7iYow mi yaye nafekh bi car ce n’est pas pareil, Yow defo action, ngey daw gueneu sakou yi né y’a dane. Nafekh vraiment ci yow là commencé mon cher
Heureusement Malick ngom nittou deugue leu président cng guir yalla li dafa niaw nagniou diokh siteu victoire bi ak couronne 👑 ak chaise bi modou grawoul way faire _plait stp
Siteu dawoul deh beure mom kou nek AK sa stratégie siteu bou ragalone d'où def MMA ndakh MMA mo geuna danger lamb foufe teuth la si barrière dorla dor you meti😂
No Tapha Gueye a tort ou il a mal expliqué le réglement et moi je suis sûr que Pere Max maitrise mieux le règlement que n'importe qui ... la question est sk il a posé le bras ou l'épaule et Sk on désigne un roi par recours ... Sk Reug Reug est champion du monde par Recours ??? noo c pas du SPORT LAMB JI
Père max sa mbeur bi mérité woul nekk roi man je supporte BG2 mais sou féké li nara beuré akk nioune di daw nguèn tell niou wakh ndakh li moom dou deugue dou yoon .
Siteu n'a pris aucune initiative du début à la fin. Les gens se permettent de dire nane Siteu limou réussir ben mbeur reussirouko lanla réussir la khamoul. Ama balde voulait la couronne et l'a montré lors du combat de même que boy Niang avait la même aspiration en bagarant avec ModouLo mais franchement Siteu venait juste pour remplir son contrat.....ki mérité woul saax 10millions si combat bi😒mangui xaar ba kéneu waxati LAC_2 dara rék 🚶♂️
Wa Père Var bi loumouy diarigne??? Dagua mana guènè lou gueuneu lèrr VAR bi en tant que kou kham Reglement bi...Père Yaw ak Siteu daguène di nakh sènn ay Suporter... Wakhal Siteu Deugue... ASTAH FIROULAH!!! Dama dioum...Lac3😂😂😂😂
Père wakho fii dara , merci Père Moustapha Gueye
Khana tay guénkoy wax merci yéne wa keur mod lo yi comba reug reug ak sa thiés lounék wax guénko Moustapha Gueye tay guéne danou mouy wax louléne enragé guéne ni limouy wax deug la nafékh bakhoul mod lo bou danouwoul rék zarko danouwoul même action
@cheikhdiop9673 mais deug gnieup koo kham frère 🦁
@@Jeuneentrepreneurcheikh217 siteu mo dan
Boy yeen bolin far way situe dfa dann lo ler nang tapha Gueye limo wax do regalman
diamagueune kou mature amoufaa père max mbargane comme xalè inchahallah vitoire biii parcel lay dèss inchahallah
Père Maxe tu es un sage dans la lutte sénégalais ❤
Max tu es un grand monsieur ❤
Tapha gueye limou wakh c'est compréhensif père, meuno daw ba guenne beugue danne meunoul nekk
Non mon frère,siteu a fait son effort.franchement , c'est la victoire de siteu
@@Treeboox mais siteu ni la danè zarko ak papa Saw même chet kouma sé si birrr diekhé si biti Thapa geuye dafa farr ak nafekh rek ak becay mbeye
@@ALPHASONKO-cd8mx. Lac 3 ban effort leu defff 😂😂💔🤦🏾♂️
@@NgalgouSyll-q7iYow mi yaye nafekh bi car ce n’est pas pareil, Yow defo action, ngey daw gueneu sakou yi né y’a dane. Nafekh vraiment ci yow là commencé mon cher
@@NgalgouSyll-q7i. Ioe yay seytané bi wkh len lac 3 deug Mô geun
Albourakh max Tapha gueye bekaye et consorts vous êtes tous pareils bouguo lène brom rew mi wayè bou sobè Yallah courone bi dotoul gnènati P.A inch'Allah 🙏🏾
Balla gaye bombardier même suite merci max
Siteu dawkinda bii😂😂😂
😂😂😂
Bou makk leu😁
😂😂😂
Père comédien nga 😂
Père max a raison c la même chute contre zarco
kou beug Siteu lalale j'aime❤
Structure bi sonnou il ne digère pas Modou lo dp8 le dbt leur position est clair
Heureusement Malick ngom nittou deugue leu président cng guir yalla li dafa niaw nagniou diokh siteu victoire bi ak couronne 👑 ak chaise bi modou grawoul way faire _plait stp
S’il n’y a pas de changement des règles donc siteu est victorieux c’est ça la vérité malgré qu’on soit des supporters de Modou.
4appuie siteu yi dossi wakh 😂😂
@@alioundiaye7801amoul 4 appuies remplacement de pied la def avant genou droite di njeuwe tégui na genou gauche bi bou yague
Merci bcp père maxsse
Xolal lii rkk 😂père bilay fans Siteu ga ndèkètè
Pére Max tu as raison kou dm Ardo 2Fois
Siteu outal len ko Thiak Thiak 😂😂😂
Siteu tékina amna visa âme keur r+3
Wahalné mou atal la thiak,thiak ak sa wa keur yi 😂😂ndah Siteu mom tékina ba paré èpuis dane na Modou Lo bilahi walahi 😂😂
😂😂😂 père yaw nekh nga
Père Max nakaté nii la nékhé 😂😂😂
Vraiment suis fans de modou lo mé siteu a gagné modou lo
Do supporter way😂
@@TaxiMan-y9c ya niémésa borom way 🤣
@@saurafall5922Fairplay way 😂😂😂modou danouna dé,mo def combat bi yeup Nak 😂😂😂
@@TaxiMan-y9c boul lakatou fans siteu nga may nou diame
Félicitations tarki ndabi
@@BabacarTouré-y8k 🤣🤣🤣🤣
Albourakh évents amoul morom
Tapha Gueye nafékh la lime wakh dou deug
vraiment siteu dann n'a modou lô chute bu lérr❤❤
Wakh rekk
Merci perr❤❤❤
Moustapha geuye doul rek laye deff
Bien dit père Max
Père wakho deugue
Pére max ya wakh deug waw siteu a gagné sur le terrain
Felicitation siteu
😂😂💔
Wouye 😂😂😂 félicitations le sakhiikate 😂😂😂
Père Max Nopil sa niaway siteu tapel la da daw combat bii 😅
😂😂😂
😂wa yawitam
Niaway bi loumousi 😢😂😂😂sheuteuh
@@baubaubeye7836 moune togne rek 😂
Ay houndou laniou
Max geumal yalla siteu defoul dra pour dane modou
😅😅😅🤣🤣🤣pere mo nekh🤣🤣🤣yallah na diam yague way 🤣
Merci max
Pere wax na deug zoss nonou la dané boy gniang
Li nieup wax rek yeen mérité woleen mod’lo dileen may chance ba paré niiii ngen beugueu nekké roi des arènes koiiii
Siteu dawoul deh beure mom kou nek AK sa stratégie siteu bou ragalone d'où def MMA ndakh MMA mo geuna danger lamb foufe teuth la si barrière dorla dor you meti😂
Siteu tapet la dou touss MMA béne boy bou 22 ans khaw nako ray
No non zoss action bi si birr enceinte bi la tambali plaké bi mou diékhè si biti zoss mo tambali action mo dane
Père Tapha limou wakh c'est logique
Siteu manoul Dane modou kou beuréwoul noy Danè 🫢😂🫢
❤❤❤❤❤❤❤❤
Père Bayil Sobe 😂😂
Daw combat bi yepp
Pere wakhal Siteu deugeu
Situe da daw
Tapha limou wakh moy règlement bi.. on la vue combat LISS VS POKOLA .. BOMBARDIER VS BALLA...
Bombardier vs balla Gaye on a donné a Bombardier sa victoire
Siteu conseil mokoy yakal
Sénégal lengui wakh deug mo diafé
Modou lo😂
Nénagn siteu mo yokk modou😂lo nooo max ya meuneu doul si makk
Vraiment nak nekhoul thi xol ms modou donou na
Peulh mii ngii may gagne neneko "pere siteu dane na modou???"🤣🤣🤣 danou sakh da diomi🤣🤣
Barki yawmal khiyamaloul akbar 😅
Siteu dafay danou nane diambar la contre lac s’était aussi pareil.
Siteu nimouy yakamté dem plateaux souko defone si guew bi lamb ji gueuna nekh
En tout cas siteu yombalou ko Modou félicitations siteu
Félicitations siteu ❤🎉
Un vieux comme max Di fennneu ni li niaw n'a
Père daguene daw combat bi yeup Ish😡
No Tapha Gueye a tort ou il a mal expliqué le réglement et moi je suis sûr que Pere Max maitrise mieux le règlement que n'importe qui ... la question est sk il a posé le bras ou l'épaule et Sk on désigne un roi par recours ... Sk Reug Reug est champion du monde par Recours ??? noo c pas du SPORT LAMB JI
Père conseil bi bakhoul Siteu dafa warone attaqué modou lo dane ko c'est possible mo meun mo eup dolé 🤗😏✊🏾
Tonton je t'ai connu sage stp ne juge personne mon grand
Pére siteu , mo sokhla na dém beuré mo géne , roi la done beuré
Père wakhal sa mbeur mi deugueu, arrêter encourager la médiocrité. Siteu à chaque day jubilé sou amé défaite
Bimouné Modou Songul Siteu la arrêter vidéo bii😂
Mes balla gaye ak bombardier nila demé action bi si birr la comance balla gaye si ganaw sakou yii la danou CNC diokh bombardier victoire
Mais bobou balla mogui si guinaw sakhou yi te bombarder mogui si birr
Pére Max kham na Li mouy wakh Boy bi dafa dane modou lo
Père un peu de respect
DAW REK NGAFI NEKÉ
Kou takhawoule kaye coût sifflet doulafa féké
Siteu beuga done té do songou do attaquer beug done roi menoul nekk
Vraiment Pere Max wat nga Makk liii nak soit plus responsable que ça
@@ousmanesene1576 mais il réclame sa victoire
Père max sa mbeur bi mérité woul nekk roi man je supporte BG2 mais sou féké li nara beuré akk nioune di daw nguèn tell niou wakh ndakh li moom dou deugue dou yoon .
Vraiment tapha est mon tuteur mais teye dafa dioum Modou dafa danou
Wahal deugu a chaqué fois mbeur yangui kass lolou kon dou siteu késé
Pére je suis de Diamagueune mais Siteu ne peu pas être Roi si ay daw ak délou ganaw
Mais siteu mo dane Modou emeu sene gri meme chose la gri si biti la dano mais poutant emeu amone na victoire
@@heush5528 emeu mo def action si kaw gri modou Lo mo def action si kaw siteu
Eumeu mo nékone ci bir gueuw bi mes siteu do daw di dane 😂
Siteu mo daneune
Tapha guey wakhoul DEUG way Modou lo da danou
SITEU MOY ISENE BOLTE
Ki mo nexx 😂😂😂
Siteu dafa daw combabi négocie
Litah niou deim Var danio diap ni Siteu mo def 4 appuies ndahh Modou lo mo creer action bi
Pére max ya wor maynala5000
La vérité en est que Siteu daffa daw combat by yeupp, modou lo rékk mo done beurré.
Siteu n'a pris aucune initiative du début à la fin. Les gens se permettent de dire nane Siteu limou réussir ben mbeur reussirouko lanla réussir la khamoul. Ama balde voulait la couronne et l'a montré lors du combat de même que boy Niang avait la même aspiration en bagarant avec ModouLo mais franchement Siteu venait juste pour remplir son contrat.....ki mérité woul saax 10millions si combat bi😒mangui xaar ba kéneu waxati LAC_2 dara rék 🚶♂️
Siteu = Lac 3
Là où deux personnes sont passées et ont échouées tu ne changeras pas de stratégie?
Max iow amo xam xam siteu takhawoul daw rék wakh rék nguéne meun
Wakho fi dara wakhal sa mbeur deuggg
Wooooy magi dh 😂😂😂😂 pabi nékhna way
Mane père Moustapha gueye la andal
Iow mi ya😃 waxoul deug
Leigui Père Max lane motah on n'a pas validé les 2 chutes de Pokola vs Liss Ndiago ou même la chute de Liss sur Pokola ....xamo li ngay wahh dei
Kii comprend léne ko 10% yi mo takh
Pa bi niaw na trop kome Golo
Siteu dawkinda
Père max vakho deugue siteu danou na😅😅😅
Père dou sa morome ta kou wakh deug kham nga ni Siteu mon dane
@@biranegueye2045wakhoul degeu
Wa Père Var bi loumouy diarigne??? Dagua mana guènè lou gueuneu lèrr VAR bi en tant que kou kham Reglement bi...Père Yaw ak Siteu daguène di nakh sènn ay Suporter... Wakhal Siteu Deugue... ASTAH FIROULAH!!! Dama dioum...Lac3😂😂😂😂
Siteu daw combat bi yépou nganane diambarla
Siteu bou Danone xawma founiou dieume 😂😂😂
@@Mouhamed-vz7hy moma diakhal
Siteu kay dane na
Bilay