Ma sha Allah tu viens de me donner une idee pour ke ndogou daujourdhui je vais rajouter de lananas tranche à la salade piur accompagner mes gambas sautés hummmmm
Maasha Allah. Je comptais m'inscrire en cours de cuisine. Quand j'ai découvert "Alphie cuisine", j'ai renoncé. Khôl bout sedde, tarama bou sedde Amine.
Hiii alphie maa ngi si biir la cuisine c’est ma passion et mon mari adore manger lol ça tombe bien tay mome salade composée lay defff c’est trop bon je t’adore c’est khadija big kiss
Afphi sa poulet pané bi bimako reprendre lamou saf eupnnaa merci rek yaw des fois ma diakh Lee loumay togou réer mais souma dougue alphi cuisine rek sama adio fadiou .
Baliy fan nala alphi yiguay defar limu sac eupna waw kay
Nice and classic. I will try this thanks Alphie
Ooouuhh Alphie dama contane ci yow ya ngi diap ci sunu seye yi bou bakh machallah mane deh temps yi m'a ngi diomal sama wadji
machaalla c'est top appétissante trop bon bravo merçi beaucoup pour le partage 👍👍👍👍👍🙌🙌🙌🙌🙌💕😁💋
Ma sha Allah tu viens de me donner une idee pour ke ndogou daujourdhui je vais rajouter de lananas tranche à la salade piur accompagner mes gambas sautés hummmmm
Machala salade composé bi ande na ak tiaas
Machalla sama Alphie
Maasha Allah. Je comptais m'inscrire en cours de cuisine. Quand j'ai découvert "Alphie cuisine", j'ai renoncé. Khôl bout sedde, tarama bou sedde Amine.
Je voulais écrire "yarame bou seedde"
Alphi nekal si diam😻😻😻
Miam miam merçi alphie 😋😋😋😋
Délicieux comme toujours depuis Almería
Machalha Alphie amenna solo sa sala composé bu amoul fene c'est vraiment riche et spéciale .
Machallah Alphi ma gui ni time Alphi
Mane dal beugue na yiii alphi cuisine
Waaouh...merciii Alphie..thiaa kaaw thiaa kanaam
BJR mci pr la recette je t'adore bisous
Vraiment alphie vous me motivez dans la cuisine je suis contente de vous merci
Machallah cordon bleu c'est trop délicieux 🙏😘😘
Merci alphie ta recette est excellente c est mariame dieng depuis louga senegal
Mashaalla amal diam sama wajii kharitou Baye cheikh rire
Beeguei alphie.mane dal.ndekei beugu nala
Machala 💪
Que du plaisir, merci notre Alphie nationale.
Alphie goudeul fane waye mashalah jtmmm
Merci notre alphie doundale waye ba enervé
Machallah Alphie ya ngi tothhhh youtube bi Merci encore
Machalah Alphie linguay togu eupna.Merci et bonne continuation.
Bonjour alphie contane ci yawww rekk du courage on te supporte j adore la cuisine et tu es notre ambassadrice
Machalla 😋💋💗
J adore ta cuisine j apprend beaucoup depuis München
Mashalla alphie
Merci alphy salade bi maachaa allah
Machaallah Alphie salade bi bakhneu dougouna dey 😘😘😘
Merci encore alphie pour ce plat surtout que je suis en régime
Alphi mane yaw lay wër machallah.
Lima neh la machalla
Machallah bonne continuation
Merci Machalla pour les recettes amnasolo 👍😀😀♥😘
Waw team alphie cuisine magui ni de mais plat tay bi mom mako mom merci alphie❤❤
Miaaam bo ci sandiwé sa dogou blanc de poulet ak Aÿ croutons dagay am lou beuri. Togu dafay gaw way beugna lii
Bo leikei ba sour war nga guereuma alphie masha Allah etudiants yi nioune sonatouniou grâce à alphie.
Abdoulaye COME yen na ko mome
Beugue nala leupe dafa aw Yonne. ak sette connnentaires aussi bah na vraiment maguilaye siuvre 🤲🙏🏽👍
Macha Allah alfi laf thiat
Magui ni dal directeur general team alphie toop léne sama guinaw dal wakh amoul thione teuggoul wally woyoul alphi mo ték thiiinam fi todji😁😍
Luka perez yangui fepp oci...mdrrr
Waw dara khewoul Alphie lay done bamou bari dolé
Louka ani say recettes nak ?
Wala yiow mom sétan rék lol
Wonibik😍😍😍
Macha’Allah je te suis depuis Mauritanie
Hiii Alphie bi dinama enrangè et ça l'air très bon mercii encore une fois
Merci Alphi j'ai bien apprécier la recette.. t'es adorable ndakh sa modestie gros bisou
Très Bon j'adore, Merci
Merci Aiphie depuis la France
Hiii alphie maa ngi si biir la cuisine c’est ma passion et mon mari adore manger lol ça tombe bien tay mome salade composée lay defff c’est trop bon je t’adore c’est khadija big kiss
Louka bolémassy😍😍💕💕💕🤝🤝🤝
Merci Alpine salade bi amna solo merci
Good job
Mangui takam téékou, j'aime
Saf na Alfie yalna sa diam yague way
Alphie cuisine d'où ayy foo👍💝💞
Tres nourissant. Depuis la tfm, je t'adore. Du courage leppeuy bakh inchaallah.
Machalah 😋
Alphie sa salade bakhna té sélna
Alphie dall magui si sa guinaw so dawoul douma daw💪
Magnifique Alphie mon idole culinaire 😍😍😍
Yamay danél mane
Merci way alphie li nekhna
Thiey Alphie chérie, tu es ma déesse culinaire. Amal diamm rek
Alphie rek dou eye thiakhane
Afphi sa poulet pané bi bimako reprendre lamou saf eupnnaa merci rek yaw des fois ma diakh Lee loumay togou réer mais souma dougue alphi cuisine rek sama adio fadiou .
Alphie ngewalé nga di
Lii si ay boules salade 🥗 nekh na merci Alphie
Machalah ma chéri yangui gnou diapalé thi sougnou mariage yi
Merci Alfie cuisine
Formidable comm toujours notre Alphie nationale on t'adore continue à nous transmettre ta joie de vivre 😘
Nekhna m'achalla Alphie comm toujours
Machala alphie sui contente de toi dale
Contente de reprendre vos recettes car je suis très gourmande 😂! Team alphi
Très simple à faire merci encors alphi
Merci Alphi yalna sa jamm yaagg mais per favor montre nous comment faire la lasagne
Alphie sa salade bakhna merci beaucoup pour les recettes
Merci alphi pour la recette
Ooohlalaaaaa quelle bonne salade machaa Allah ! Merci Alphie💖
Wawww kay alfi la puissance bi mako mom lamou saf eupena
Namon nanioula amoul noumou oyofe woule Machalah waw boul lim deeh 😁😁😁💋
Perfecto comme toujours
Merci alphi surtout pour la constipation
Nice alfi
Super
Machallah alphie bonne continuation ❤️❤️
Machalla j adore merci alphi
Maa cha Allah💞
Merci alphie salade bii amna maana 👌👌👌
Merciii ma chérie raté tou ma la😍😍😍😍😘😘😘😘😁😁😁 machaAllah bek si yaw
Hello Alphi,je suis ta fans from Finlande .Jaime les salades ,pf sė bon de le mélanger avec des ananas , orange ou resin vert 😋😋❤
Aminata Ndiaye oui cool le sucre sale
Avec alphie rek Lepay nekh gros kiss
👌👌👌👌👌
Mes encouragements Alphie
Hummmm❤❤❤❤ begueu tina
Machalla eupeune Merci et bravo 💕💕💕
Machallla
Vos salades sont délicieuses il faudra en faire moins une fois par semaine
Ay alphie ya ko yor
😘😘
Wawaw team alfi cuisine Khadija khoutoub depuis France
Manchala c'est formidable