Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 34 - VOSTFR
Вставка
- Опубліковано 14 гру 2024
- Créer des émotions fortes et de qualité et les rendre accessibles à tous les consommateurs du Sénégal et d’Afrique, tel est l’engagement de Marodi TV.
S’inspirer des émotions des différentes couches de la population pour créer des opportunités de visibilité et d’engagement pour les marques, telle est l’opportunité qu’offre Marodi TV.
/ @maroditvprod
Je viens d'accoucher des triplés après 15 ans de mariage alhamdoulilah 😭💕Di sakou gnane thi gnom
Yaw môme khana chaque semaine nga accouché
@AwaCamara-xt8en😂😂😂
😂😂😂😂baalko lolou rk@AwaCamara-xt8en
Triplés nga am djiote ni di sétane bay commenté😂
Bilay😂😂😂
Ceux qui défendent Néné en disant qu’elle “aime sa famille” se trompent. Certes, elle joue son rôle de mère et d’épouse, mais sa belliqueusité excessive, son incapacité à écouter ses enfants et son mépris pour leurs sentiments détruisent plus qu’elles n’unissent. Elle préfère imposer ses décisions, en jugeant les relations de ses filles uniquement sur des critères financiers, au lieu de chercher leur bonheur. L’épisode d’aujourd’hui le prouve : son mari, fatigué de ses excès, a dû agir dans son dos pour permettre à leur fille de vivre son amour, ce qui reflète un grave manque de confiance au sein du couple. Néné ne construit pas, elle impose et divise. Aimer sa famille, ce n’est pas crier ni contrôler, c’est écouter et respecter.
En plus elle commande son mari
Seule sa volonté compte
lou am solo gua wakh lép lo guiss wakhtan si si tout les plans wayé di imposé beug lila nékh badi faté nitt gni gua nékal
Vérité absolue
Merci...je suis d'avis avec vous.
malheureusement sho you beuri li laniouy doundou galsen mais breff...
Kou beugg tèkki téral sa yaay rk laalal j'aime ❤
Amine yarabi
Merci ❤
Mais lou ma begue kham moy lan moy tikki??
Nous les célibataires yalnaniou yalla may li couple Asmao Taïb si barkep nabil Moustapha psl sama natango yi wakhlén amine 😂
Wa yén mbeuguel war na nekh deh couple Asmao Taïb ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine
Ndeysane tioune célibataires daniouy niane rék 😂😂chaque jour bougne guissé couples bou rafét
Allahuma amine
Ay yaye sira ak ndiabotam gui 😂😂 Bilay ndiaboté djiguene metti neu nak 😂
*Je te jure😂😂😂😂😂*
Tt mes félicitations 🎊🎉
Retane na ba sonou😂😂😂😂
Machalah yalla nanu dundu té barkeel
Assy da ande ak mia guissé sakh 😂allo bb atane guama mes caprices khale bi gneme gama ❤😂😅
Wouy traduction bi 😂😂 magui deah 😂😂😂😂
@@IbrahimaFaye-t1m😂😂😂yw tmt dh
@@IbrahimaFaye-t1mlay😂😂😂
@@IbrahimaFaye-t1mnenako j'ai mes caprices garçon je m'ai eu😂
Ani wa keur seydina moukhaméd 🙏🥰🎉
Sallahou alla Mohammedine ❤ allahuma sali alla seydina Mohammedine wa Salim ❤️ allahuma sali halal massoufi bil karami wal djoudii
Psl❤❤❤❤
Ani wa keur seydina moukhamed❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Asmao Nena Taib kou mane sa morom douma😁😁
Oh Senegal faut aider les enfants à ceux qu’ils se marient avec les personnes qu’ils aiment!! L’amour n’est pas un jeu waye!!
Vérité absolument
Bala ga kham min nekh guen nek si kaw lal bi ohh❤
L'amour est un vrai jeu basé sur deux règles: yërmaande et cofeel😂😂
Taib a toujours aimé Asmao. Mais il ne pensait jamais qu'il allait se marier avec elle un jour c'est pourquoi il s'est marié avec Codou. Il a enfin eu celle qu'il aime donc pas étonnant qu'il dame sur Codou.
En plus Codou ne fait qu'écouter ses copines. Sachant que le gar l'a rassuré .
Enfin une personne qui a bien compris Taib !!! Coddou va finir par perdre Taib si elle continue a se comporter comme une gamine
Merci je pense pareille
C’est vrai que ça fait mal je peux l’a comprendre
Mais ces actions vont juste aggraver la situation.
Si tu vois que ça ne t’arrange pas
Tu demande le divorce et tu pars tranquillement tu ne perds pas ta dignité
Tu auras peut etr mieux ailleurs
Mais ça ne sert à rien de rester la
Et agir de la sorte
Elle est entrain de créer une guerre qu’elle ne pourra pas assumer parce que le gars est déjà amoureux d’Asmao 🥹 il ne voit que par elle.
Franchement si j'étais codou je demanderai le divorce taib nobatouko
Lima diaxal moy Taïb dèfoul lune de miel bou melni ak Codou dh😂😂😂 tieuy homme
@@LaBarhamienne lune de miel khaliss mokoy deff
Franchement li amoul fene djiguene bougnou eubeul dem dekk keur goor te diabaram nek fa. Çà n'existe pas. Il faut deloger Amina
Vraiment sou amé tamite xéwoul Sénégal issshhh
Vraiment
En tout cas
Vraiment lolu rek momaye énervé si série bi
Pourtant âme bene fille bou done d'âne doleme thi bene keure famille niou eubel ko âpres lui il es parti se marie avec kl1 d autre mes elle est toujours là ba dans la maison
Je suis triste pour CODOU la Pauvre 🥺😭 Mais aussi ASMAO mérite d'être HEUREUSE 😍💃 ET TAHIB a droit à 4 femme puisqu'il est Musulman non
Codou da weré top xaritam bobou rek,asmao da dionguè nak 2ème bamou berè de 💪💪
Ça c'est vrai
Un musulman doit avoir 4 femme si law nga mene ko
@@FatoukineDiol-kb7teSo amoule rék tak gnaréle bou ame xaliss
Mais sérieusement, Taïb n'a pas les moyens d'avoir deux femmes ; il devait au moins mettre sa première dans de bonnes conditions avant de penser à épouser une autre femme.
Niaanal leen sama pâpâ yalla yeureum ko😭😭
Amine 😢
Ak sama pape tamite il m manque bilakhi j’en souffre😭😭😭😭😭😭😭
Ak sama papa aussi 😭🥹🤲🏾🙏🏾
YALLA Nako YALLA Yeureum té Dieggeul ko khareko Aldianay Firdawsi 🙏
Amine😢
Samedi tay bi yalla boumou nek sounou moudien tel samedi amine yarabi 😭😭😭🙏❤️🙏
Amine
Amine ya Rabbi inchallah
❤❤
Amine
Amine❤❤
Abdoulayi, son visage, on dirait il sourit tout le temps ouuu.😂
*Ouï c’est vrai😂😂*
Serigne ya dof deugue nak... Amina vraiment diépinala. Adji dé heure bou tasser serigne ndiaye dinko reuthiou
Merci
Nn la maman de Diama est une très grande actrice 😂😂😂😂😭
Da gawa watchh 😅😅😂😂
😂
Waallayiiii wakhatikko elle est forte dafa ayiiiiiiii🤩🔥❤️🥳🥳
Walayyy 😂😂😂
Néna Baye takho may ré dé neh Bala gouma la 😂😂😂😂
Lady Diama joue bien son rôle machallah ❤
Mbeuguel dafa disse yeah waye😩asmao ak Taïb gnogui love lou nekh🥳🥳🥳Mareme Li nak moy adouna 🥺loule yombou ga saniko wawe kay nak🥹di weur lenenne🥹l’histoire retiendra que famille Diama gno dakh si série bi😂😂Mère bi meune nama rayy hunnnnn hounnnnnnnnn hummmm hummm 😂😂😂
Dafa barri dolé😂
@ yaye sama aldiana😂😂
@ 💃💃💃💃
Wawawe yaw leu🎉❤
*Barki Yalla ioe😂😂😂😂*
Cheikh Mouhidine Samba Diallo yalla n'a yalla yokkou ay lééram tass gnouçi barkém 😢❤
Amine
Amine
Yaye Sira 😂😂😂 pourtant Baye Kane avait dit qu'elle est compliqué mais son cœur 💓❤️ est propre et sans rancune genre elle aboie mais ne mords pas 😂😂😂😂
Lady diama la seule série Marodi qui n a pas encore perdu son goût 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹 🌹
Jeux de dames est tout autant captivante comme série Marodi également.
Kou beugué Serigne Saliou AK Serigne Babacar sy lalal j'aime ♥️♥️
Psl❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤
La série qui n'a jamais perdu sa valeur bravo à marodi🎉🎉
Couples Asmaou ak Tayib rek ❤
Mère cirra, chapeau à toi, t'as refais ma soirée, après cette tristesse que le Réal Madrid m'a causé
Mais moi 😢
Senegal rek ngeuy guiss épisode poster y a 1 min 300 commentaires yakamti am j aime ay kou beugueu prophète , alhamdoulillah 2 jumeaux patati patata 💀c énervant
Bilay 😏😏😏
Dakhe gua sagne ko wakhe n’importe quoi
Soof rk khawma j'aime yi bane sens la am
bilay yaw soff rk 😅😅
Wollah c vrai ❤
Kou beug seydina mohamed lalale cœur ❤❤
*Seydina Mouhammad sall’Allahou aleyhi wa salam ❤❤❤❤❤❤❤
Kou beug seydina Mohamed lalale♥️♥️cœur
Sallalahou Alayhi wa salam ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
❤❤❤❤❤❤
Tayi lah sama anniversaire gnianal léne ma goude fan ak weur yalla mayma bfem inchallah 😊
Taïb mougui melni kouye dogua take diabar pauvre Codou 😢😢 gor comme courant bou coupé rék 😂
😤😤😤😤😤😤😤
Day dorra tak koumou nop
𝑇𝑎𝑖𝑏 𝑘𝑎𝑦 𝑡𝑎𝑠𝑠 𝑛𝑎 𝑦𝑎𝑘𝑎𝑟
@@sidiseck935keen forcéwuko codou mokko tanal bopam tak ko bouko noboul woone douko takk gore mo beugue lou bess rekk😂
Aywaye😂😂
Khana tay mome sama nawlé sétane ak portable yi diguenema may ❤😂
Dégue nagne laa 🎉😂
❤❤❤
Traduction bi magui dead 😂
Des cœur pour le prophète que Dieu nous garde protège et nous pardonne 🙏🙏🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ho😢 la pauvre codou😢 j'ai des larmes aux yeux 😢 bilahi si tu essaies de te mettre à sa place 😢
I feel so sad for her😢
C'est très dure
Biiay nékhoul si khôl
Yeureum naco trop sakh
Bilaye ndeysane
Une pensee pour ceux qui etaient la Au debut de la serie et qui nous Ont quitte. Que firdawsi soit leur demeure
C’est triste personne ne pense pas à codou la pauvre 😞
Je suis triste pour elle 😢
Babel saison 2 nguir yalla ❤ yaye sira la beug mane ❤
Le cas coudou et talib une leçon de vie il faut jamais galéré avec un homme 😢😢
Franchement Taib est un traitre 😮 Asmao aussi on ne construit pas sa vie sur le malheur des autres...
Li moy commentaire si épisode bi nan si wath
Je reste sans voix 😢😢
@@quenne_dudiolof9536Asmao n'a rien fait de mal laissez la tranquille, elle a le droit de se marier avec qui elle veut !!!
Pareille pour Codou elle n'a rien fait pour mériter ça
L'amitié de diama et awa kiné ça me souviens de amitié daro et maimouna 😅
Billy
Sa te r appelle ❤
*Ça me souvient momm moy bane français 🤣🤔*
Oh dinama nekh série bi nekhonr na
Man dama yeureum😢 Codou et adji😢😢😢bilay
Khawma abdoulahi khawma lahi abdou beuss bou assy gnewé ba sa pape dindi liguey bou bonn bi ga def si mom diga khamné lepp deuguela mou contane nonou nane merci pape😅😅😅
Li tmt mbeuguél la wala😭😭asmao ak taïb 😂❤
Mbouguèl la😂😂
Ngi Kay sémbéré rk molén nior😂
Diama la dame belle et classe une femme de valeurs .L une des actrices les plus pétillantes au Sénégal. 🌟 ⭐️ 🌠 ✡️ ☪️ 🔯 🌟 ⭐️ 🌠 ✡️ ☪️ 🔯 🌟 ⭐️ 🌠 ✡️ 🌹 🌹 🌹 🌹
Merci ❤❤
Bilay machallah 💖😍
Réel🎉
❤❤
Vérité je l'estime bcp cette dame
li asmao di doundou kagn lakay doundou 😭💔💔💔💔💔la scene de asmao et taib lalaylalou🥳🥳🥳jen pleure meme mareme tes la seule perdante
inchallah lée giu rk❤❤
Lègui inch'Allah louko ndack amoul
Sama pape laa bëggal 3 ème femme .boo beggee ñu doxal
@@ndeyefall8123😂😂😂
@@Fatou-nz5pr yalla baxna
Asmao a toujours nourri un sentiment amoureux envers Taib. vous souvenez vous du jour ou il lui a annoncé son mariage avec Codou? J'avais perçu une lueur de jalousie dans le regard d'Asmao. Aujourd'hui , tout devient limpide
Le premier gars aurait dû lui dire qu'il était marié. Elle aurait accepté.
@@adjib.38 où est le rapport avec le cas actuel ? Vous êtes tellement contre son mariage avec Taib au point de trouver carrément des points positifs à son premier prétendant qui était un menteur et un bluffeur !! Le monsieur ne voulait rien de sérieux avec Asmao !! Un homme qui n'assume pas son statut marital en plus devant tes parents n'est pas sérieux et responsable !! Et c'est ce genre d'homme que vous voulez pour Asmao ??? Tout ça pour que Coddou reste l'unique femme de Taib ?? Incroyable, Taib est l'homme parfait pour Asmoa et ça dans tous les plans
Et dès le début j' ai toujours su qu'asmao et taib allaient se marier ça se voyait comme un nez au milieu du visage !!! C'était plus qu'évident, donc je ne comprends pas pourquoi les gens jouent les choqués maintenant
Codou ndeyesane holko AK rafetayam mongui nek AK kou hamoul valeur ram li kouma ko def ma bayila li dou respect j'ai vraiment mal pour elle 😔😔
Vraiment lii 😊
Ma chérie l’homme est naturellement infidèle
@@awadiallodiome9963 je l'avoue ms pas comme ça c'est très rapide en fait
Bayi key yeufou deum la ko déff
Yayou Diama pour mom bb la😂❤
Souniou yayii yalla nalénn yalla may gouddou fann ak wérr 😢❤❤
Allahouma amiiiine
Amen ❤❤😊
Amine yarabi sow pouloh
Amnie
Amine 🤲🤲
Codou la pauvre elle mérite pas tout ça 😢
Wa mom khana amouti mbokou 🤷♀️
Vraiment
𝐵𝑙𝑦 𝑙𝑖 𝑑𝑎𝑓𝑎 𝑛𝑖𝑎𝑤
@@NdeyeSokhnaGueye-vz8im mome diakhal depuis mariage bi guisouma keune si ay mbokam copine nam reck
Bilahi 😢
La réaction des autres face au "Allô bb" de Assy😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂
*C’est ce qui me retient ici😂😂🤣🤣🤣*
Cetait tellement drole😂
No asy mi mo wow beut re n’a bason😂😂😂😂
On dirait toujours on réclame le bonheur de Asmao aujourd’hui ame na Machallah 🎉🎉🎉
Yow dé ya bonne légui asmao ame bonheur codou di souffrir c'est honteux
La situation de Mareme je pense qu’elle va éveiller dorénavant ttes les filles naïves🥹 donc chères sœurs faites comme Asmao ,svp 🙏🏻
Est pour ce qui ont été violé😢😢😢
@@KaraSalioujustement
Amina bilay Dina TASS seuyou diambour bii😮😮😮
Amina rk laniouy topp 😂 😂
Mais moi j'ai une question les gens avant que tu ne cherches une deuxième femme n'est ce pas tu dois être dans une bonne situation financière et donner les mm droits aux deux femmes mais Taïb defousi dara il aurait pu au moins mettre Codou dans de bonnes conditions avant de penser à épouser une autre de plus la pauvre elle n'a pas eu droit à une lune de miel contrairement à Asmao dernier point le salaire de Taïb ne peut clairement pas faire bien vivre les trois vont-ils vivre au crochet de Asmao.. si il savait qu'il était amoureux Asmao pq épouser Codou tchimm
Asmaou akk tayib tay mou nekh 🎉❤️😊
Partie bi Assi di wouyo né allo bb réy nama😂😂😂🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂
🤣🤣
mbadou
Ani talibé cheikh yi manifeste vous ❤❤❤❤
Nous sommes la🥰
Nous sommes la fier d'être talibé cheikh
Ndeyesane pauvre codou Elle na mérite pas ça 😔😔
Bilahi dama ko yeux rem 😢
Bly 😢
Tayib d’à wor nak malgré asmao gnepco yen dieukeur
Asmao taïb bilay sen couple bi sof na😂
Ish
Massa codou ❤😢de tout cœur avec toi
Kouko doundoul meuno ko kham
Khana awo nga yaw 😂😂 Massa
@awalam263 bilay dedett sakh sama khol ba diékh thi déception Codou bi rek
Asmao y a tay
@@awalam263😂
Gni Kay da gno sof
C'est l'amour de baba et néné qui me retient ici😂 bilahi l'amour n'est pas loin gueum nako mais c'est vraiment dommage que ni doumako doundou a chaque fois que j'entends le son de jahman je penses à #KH mon sauveur😢
Bilaye nacira dinamaray 😂😂😂 yaye diou bakh guay amm fofou machallah y'a des mamans qui sont comme elle fait tout sa pr la bonheur des ces enfants meilleur actrice machallah
Le mariage entre Tahib et Asmao, je ne vois pas un bon avenir, un mariage que la maman de la fille n'est pas au courant et cet bonheur était construit sur le malheur de quelqu'une (Codou)🥲
Ils vont demander pardon et la maman va accepter
En tout cas le papa de Asmao a bien fait et tôt tard sa maman le pardonneras
Et en plus Taïb a droit à 4 femme
L'autre qu'elle a orchestre çavait alors donner? Pardon laisse
Sa ma cousine nonou la défone gniou takeko yaye yi dji naguouwoul mais Mariage bi mom amouthie banéhh mou am thi dom djieukeur djie takal ko woudiou divorcé ko wallahi gorr diaroul yénde yi
Alhamdoulila yalla nanou yalla may Weur ac goudoufan ❤bayuil nous sounouy niari wadour Amin ❤gni sen wadior guene adouna yalla kharelen adiana Amin 😢
Amine🙏🙏🙏❤
Amine
Amine 🤲🤲
Amine
kou beugg sa yaye rk lalal ❤
Kou bouguoul yayam ? Vous êtes pathétique pour des j aime
Kou d'accord ni amina eumobi dafa wra yakhou😂😂
😂😂😂 hé
wakhk😂😂😂😂
Man 😂
Kane mo eumbeu 😂
Esk sakhe Serigne Ndiaye mo djour dome bi amina eumbb sama khel gnaw na dé 😢
Awa kiné va me tuer un jours non son jeu d’acteur c’est une pépite😂😂 elle a dit au papa de diama c’est l,amour 😂😂
Kou beugue serigne saliou lalal ❤
❤❤1❤❤❤❤❤❤❤
Mbeguel nexena ❤asmao Taïb ohh le pouvoir de l amour
Yaye sare damako beugue lamigne bi mon saff 😂😂 vraiment Abdoulaye yangui beugua soff dégloul sa wakhou wadiour yi 😢😢
Taïb pourtant Codou meusso ko défal li dh la pauvre 😢
Mome dafa yague beug asmoa avant codou khamna lolou motakh
Nobouko motax
Complexé la nimako diépiweii
Codou souffre mais elle va se ressaisir. Elle a nargué Asmao mais...Taïb se surpasse pour Asmao qui l'a élevé au rang de Roi. Il ne sera plus chauffeur. On parle de ménopause précoce de nos jours. La mere de l'ancien fiancé d'Asmao avait refusé ce mariage en disant qu'elle ne veut pas d'une femme presque ménopausée pour son fils. Asmao a dit à Taïb de garder ses prières pour leurs enfants et non pour sa virginité. J'imagine un scénario autour de la fécondité/stérilité entre les deux épouses de Taïb. À suivre.
La fécondité dépend de Dieu .On peut avoir 50 ans et enfanter.Allah est Karim.Et maintenant la médecine fait des progrès dans ce domaine .
Je vois bien asmao avoir des jumeaux et la jeune femme de Salif stérile
Ani ya keur serigne TOUBA yii 👍yalna gnépp am diam 🤲🤲
Fi épisode lady Diama la est ce que do dém commentaire li fénén?!!
Félicitations
Amine yarabi 🤲🤲🤲
Amine
Demal si cheikh diop mbaay
Ohe mane dale ndekee tayib rek lay weer mane❤❤❤goor day deugeure way 😂😂😂merci marodi😅
Temp yi chauffeur yi akh livreur nio khew dhe 😂😂😂
😅😅😅😅😅
Mdrrrrr 😂
Mercies ❤
Bassirou fall ak diama pres en re.lation❤❤❤❤❤❤❤
Peut être que l’amour est fort mais quand même ni situation bi démé nékhou ma parce que Soda a sacrifié le confort et tout pour être avec tayib donc sa douleur et son comportement est justifié 😢
Right, mais comme danio yènè Asmao dieukeur ak limouy incarnè fi, on trouve normal leur dèmarche alors que rafètoul, niom nieul bok kogn niouy weur avant mariage di lambar lamabari, et pire Taïb fait pour sa nouvelle femme ce qu'il n'a jamais fait pour sa première. Djiguène nak mom nakarou moromou djiguènam lay def mbectè. Même si Taïb a le droit d'épouser 4 femmes, mais nimouko dèfè mo niaw, doxane ouvertement, niouni dètt nga diakarlo ak sa diabar nane ko kènène la beug😂 ah ma warou nak, lolou dou honnêtetè yabatè leu, en plus mom naka lay yorè niari femme alors que financièremenr dolèm ègoufa, wala moy Codou😂 Asmao yor boppam. Non li han,
Kou bagne seri bi diekhrek beusseule jaime mais li nekhna dhe❤❤❤
Association ande guéné Amina thi série bii ki soff nama😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Amina rek la diépi😢😢
Elle n'a pas de coût franchement parler
Chim mom rk moma sof 😢
Warnan̈you crè groupe wasap dé AASS
Man yayou dadjinama😂😂
Diama mo diogoma nk kou d'accord avec moi ❤❤❤❤
Ohh la complicité entre asmao é diama❤🎉🎉🎉j'adore❤
Alhamdoulilah je viens d’accoucher des triplés di sakou si yeine ay niane😭😭😭🙏🏽😍🥺
Bay meww 😂😂
❤❤❤❤
Kham na meun nguen doul yen nieup mom meuno lén amando triplé 😂
😂😂😂😂
@@rouguitabarhama9860wakh deug sonou nagn 😂😂😂
Tayib vrais domourame la ah genre yi motax gnouye khass yéne gorr yii li mome moye worr deug nak
Si serie la wax nak 😂
Ray gama waay 😂😂😂😂😂😂😂😂
Homme rékk 😂😂😂😂
May wax nak mouy diay romantique😂 souko Codou waxone niou lune de miel mouniko sa yeufou tiaxane yoyou😂 non goor han
*Thi série guay wakh mais pancréas guay wakhé ni😂😂🤣🤣🤣*
Yene ken xamoul loungen bege
Samedi tay bi yalla bou mou nék sounou dernier samedi amine ❤
Amine yarabbi barkep Serigne Touba
Amiin ❤
❤
Amineeeeeeee yarabi
AAMIIN YARABI 🤲🤲
Non néné dafa meune comédie ❤❤😂😂asie nena allo bébé néné mouné hum hum
😂😂😂
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Non action nékhnama
Nènè damako fan sakh
😂😂
Serigne ndiaye yaw Dof deug nga Déle Réfléchir Seuf ni laye méle Sa Amina mi tant que mongui si keur Gui Doo am Diame aussi mangui Guiss ni sa torokh ni
Serigne Ndiaye dof Sakh moko tanè mom pour Lou lérr audio diabaram la waronn dègueu sogua gueul du moins sakh
Reaction Yaye sira suite à "allô bb" ah oh ahhhbbbb😂😂
Al hamdoulila ❤❤ yalna Diam yague 🎉
Sarakh len ma j’aime 🫴😂
Lo koy doye ba paré😂😂😂😂
❤❤❤am yalla diokhla😂
Asmaou mi bandit la dh nenako kou meune sa morom doumeu na nekh😂😂😂
Kirasoulilahi 🤣 dma dioy dall
Les derniers enfants de famille n’ont vraiment pas froid aux yeux 😂😂😂 Assy me régal
Ko allô bébé? Devant ses parents MDR 😂
Diama nena baba do assumè😂😂😂😂
Yallah na Yallah may bépp élève bouy déf Bac rén ❤️🙏🏼
Amine ya raby ❤
Amine inchalla😮😮
Amine
Amine ya rabi
Sallalahou ala Mouhammadine ❤️🕋
Mais taïb tel nga diénguu dh codou démoul wone lune de miel dh😂
Codou yoroul té asmawo da yor
Asmaou day lugueye té budoul dara moy patron taïb😂
Likay niarel yi rek nion kafi ma 😂
😅😅😅gorr bakhoul
@@NganaKhouma niokofa am key 😂
Amina fait tout pour détruire le bonheur de mon adji 😢mareme bien fait pour toi 😂vraiment c'est chaud 🔥 cette série ❤❤❤bravo 👏 à l'équipe merci beaucoup marodi tv pour cette magnifique série
Codou diox guagnou leçon goor diaroul déf béne sacrifice😭💔bame lay tay ak xewou Asmao bi yagoul kholal limou defal ku béss ki yeup effort bi sax fékou ko si yaw nék léne nitt djiguenr day reuy beut té outi liguey wayé togue topou goor rk👨🦯✋️mane môme dieulna sm dose baparé😂😂
😂😂😂😂😂
Est-ce que Asmao financé wouko😂😂
Ça depend taxaway bi codou taxewee maa baaxul .moo waroon xol limuy Def. Goor moom soraaleel ni du yaw kepp
42:15 Maréme lila dall da séde baxna si yaw dangéniy ame kouléne beug ame yeurmané si yéne ngéne koy doflo toppou kouléniy balthazarr😮
Sama péréféré yalla na diamou yageu ❤
La beauté de diama ont n’a parlent ❤😊
Le moment entre Asmao et Taïb rempli mon cœur de joie😊🎉
YASIN SY ❤ tu as cette intérieure qui te permet de traverser les tempêtes les plus violente. YASIN SY❤La peur est normale mais ton courage te permet de la surmonter chaque jour. Kala to gonmi hakkillam nanema😢 YASIN SY SAWADE Mo sawni bonne❤