...,,,,a un moment c’était devenu une corvée. j’avais abandonné la cuisine Cependant, Mais tu me donnes une envie colossale de m’y remettre je retrouve mes repères à travers tes astuces et ton art de cuisson merci de m’avoir rendu l’amour de la cuisine merci à toute les femmes qui t’accompagnent
5 років тому+1
Oumou Ly ohhhhhh sooooo sweet ma sœur cherie merci a vous 😘😘😘❤️❤️❤️❤️😘😘😘
No nitta sof bala gueni j aime po daguen di bagna setane bagnou niou aimer khol beguei soff guen way ken mounoulen satisfaire ta marietou chapeau et bonne continuation khamna boumala topei diga jot plainte obesite laylaaa
Aye tata maretou ligay def bakhoul dé fima tok magui takamtikou bilahi machala maguilay suivre dpui thies di yok sama niveau si cuisine machala yalla na sakh mé l mot touthioutoul momay tanel
Kontaan ci yow Tata Marietou. dama beug kou fonkk ak mbokaam. contente de voir que tu as dedicace ce caldou a tes soeurs et ton frere. Nek leen ci jamm. Sen yaye djou baax dji yal na xipee aldiana. longue vie a papa Ndaw aussi. Ndeekete dou mane rek ma beug kandia :) :) Kaldou bi neekh na. merci du partage. laf thiat et Ma sha Allah. Yal n la Yallah beggal, tata.
Mais les gens qui n'aiment pas la vidéo, pourquoi ne pas tracer votre route. 🤦♀️🤦♀️🤦♀️. Au lieu de positiver et surtout encourager la personne c'est tout le contraire. Feed up!
WA tata Marietou je vais à château rouge pour acheter mon poisson frais pour caldou biii j'ai l'eau à la bouche merciiiiii wayyy tata ma la beugeu pire mane
tata marietou vrema ya gnou provoquer koi gnoune team femme enceinte 😂😂🤣😭
5 років тому+36
galséne 🙊🙊🙊🙊🙈🙈🙈🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️ ayy wayyy bal lemaaaaaa Yallah nalen Yallah May ay aum you sedeu yallah barkel ndiabott gui yeupp Masha Allah 😘😘😘😘🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️
@ mersi beaucoup tata marietou vrema tes video mont beaucoup aidé amine wayyy j t sui depui la france et j sui une grande fan de toi .yalnala maye guoudou fane akkk werr bisou
Hi M, I have been following your channel and I love your sense of humour! :), thanks for all your efforts in bring our delicious African dishes to your platform. Your memories of mere Diop are very vivid, Ya Allah reward her all her good deeds. Show us your image at least once!
“Rendez-vous en bas lalay djokh”😂😂😂😂 I love it! Tata Mariètou yaw Yalla reik molay faye! Gnak la kham woroul! I love you so much❤️ Sama adoption bi nak mangui fi batay! Bo changé avis reik meune ngama gneuw djeulsi😩😩😘😘❤️❤️
5 років тому
Sokhna Ndiaye Ameen wayyy Masha Allah boule wakh Dara gnio farr 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Bonjour sokhna Mariétou je suis fan de vos vidéos mâcha allah Mais à quand un couscous marocain J adore les Goudoussgoudoussi et consorts mâcha allah Pour le caldou j ai l eau à la bouche dotant plus que je suis de la casamance J adore vous écouter Vraiment mâcha allah sokhna Marietou
...,,,,a un moment c’était devenu une corvée. j’avais abandonné la cuisine
Cependant, Mais tu me donnes une envie colossale de m’y remettre je retrouve mes repères à travers tes astuces et ton art de cuisson merci de m’avoir rendu l’amour de la cuisine merci à toute les femmes qui t’accompagnent
Oumou Ly ohhhhhh sooooo sweet ma sœur cherie merci a vous 😘😘😘❤️❤️❤️❤️😘😘😘
No nitta sof bala gueni j aime po daguen di bagna setane bagnou niou aimer khol beguei soff guen way ken mounoulen satisfaire ta marietou chapeau et bonne continuation khamna boumala topei diga jot plainte obesite laylaaa
Khana gnou khey soubeu inchallah kaldou rek. Ta marietou on t'adore goudeul fan ak werr
Sow Ndeye codou Ameen wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Tata mane dal je t'adore. Tes plats , tes expressions😂😍😍. "Youbou yaba" momay dadji 😂😂. Plein de bisous😘😘
Diga mousa titeul Djeune mou ragaaathiou la néla coucou mére diap forme.. 😂😂fofou todji😂😂😂😂
louka partt way 😂😂😂
😂😂😂😂euyy louka
louka perez 🙈🙈🙈🙈🙊🙊🙊🙊🤣🤣🤣🤣🤣🤣🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
louka perez 😂😂😂
Wakhatiko de 😂😂😂😂😂😂
Gounouche Gounouche diape form nako si touye bayiko mou titt yoyou momay ray tata filing daal macha allah
Je suis vraiment désolé mais li d'où kaldou
@@souleymanediakhate8842 adada bou doul caldou loumou don?
maria 9
Aye tata maretou ligay def bakhoul dé fima tok magui takamtikou bilahi machala maguilay suivre dpui thies di yok sama niveau si cuisine machala yalla na sakh mé l mot touthioutoul momay tanel
Kontaan ci yow Tata Marietou. dama beug kou fonkk ak mbokaam. contente de voir que tu as dedicace ce caldou a tes soeurs et ton frere. Nek leen ci jamm. Sen yaye djou baax dji yal na xipee aldiana. longue vie a papa Ndaw aussi.
Ndeekete dou mane rek ma beug kandia :) :) Kaldou bi neekh na. merci du partage. laf thiat et Ma sha Allah. Yal n la Yallah beggal, tata.
Machalla machalla yayyy boyeu de new York rafetna
Wawaw mareitou très bien fofou dadi toth 😄😄😍machalla laf thiat yala na yala def diam inchalla dieureudieuf ❤️❤️je t’adore 😘😘
Merci tata , sama sente bimassiy dègue reik damassiy contane vraiment
Machalah caldou bi nehna trop mane yi ma guiss dou am Kong fumé laf thiat
effectivement, le Caldou original Casacais (diola) dou am kong fumé, ni yokoss.....
D'où am Kong fumé dafaye yak goût kaldoubi té vrais caldou gnoulouk leur d'où am huile
😂😂😂 li saveurs planétaires rek la ame daguay rétane ba naw. Macha Allah moi j'adore tata Mariétou 😙😘😘
Et j'aime bcp votre sens de l'humour je vous encourage on apprend à s'amusant
Machala tata xawmawone né kaldo day am kong fumé ak yokhoss. Merci a toi
Nimbara tourendo liguay togue dara fayou ko. sa kaldou yeungueul nama. Machallah
Tata marétou chaque jour ma saliver wayé téy mome dacé raw lal gua bilay mane caldou noumou may déf dal eupna del né amine rek 😋😍😘
Moussou Cissé Ameen wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Mercii... Niankatann express on en a besoin
Madame Diop Insha Allah
Tata Maretou chapeau machalah j'aime bien ton bon humeur dignou djangual boléko ak aye rée
Ya salam badiene marietou tay mom sama plat nga togg machalah li mom a reprendre demain demain inchalah
So waxé mashaaalla rek sama xol sedd
Tata merietou merci pour les recettes mes caldou marietou mane mom dou caldou original cong fumer ak yokhoss dou dèm si caldou ❤️💕❤️😍
Deff ci yokhoss khole , dotoko bayyi , malako wakh
D’accord oumi je vais essayer 🙂
Sisi soula neikher defsi kongu fumer
En fin quelqu'un qui est sincère ma copine Yolande diémé ma appris comment faire un vrai caldou de la Casamance c'est tout simple
Merci tata mako done lathie yalla na yalla faye 🤲🤲
Ndèye coumba Mbengue Ameen
Merci tata marietou reprendre na kaldou bi.. Oh nekhena nouné 😍😍.. Merci bcp Tata❤❤
Thiatou Papam ohhh Masha Allah merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
J'aime beaucoup tes recette merci pour ce que tu as fait pour nous
Maneu dal yaw la doon weur, Macha Allah
Tata tres bien bi momaye raye machallah yalla na sa diame yague
Nabou Mbengue Ameen way
Tata marietou mon idole yaw lay weur
Bi mom takh na souba mom lay def inchallah
Esk doumako lale toom thi samdi bi MAshalla tata yalla na lokho yi weur
Mounass Samba Ameen ma Cherie 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Mais les gens qui n'aiment pas la vidéo, pourquoi ne pas tracer votre route. 🤦♀️🤦♀️🤦♀️. Au lieu de positiver et surtout encourager la personne c'est tout le contraire. Feed up!
Mamie Isseu 😂😂😂😂🙈🙈🙈🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Those people are not happy themselves that’s why they dislike the video lol they need god help swt
Le vrai caldo ne se prepare pas de cette facon 🤔
@@ludimiladjassi2253 avez-vous entendu le début. C'est un caldou dans les caldous. Une recette de marietou mané pas la recette originale
@@ludimiladjassi2253 cvrai vrai caldou dou ame yokosse dou ame kong fumé
Lol Tata mariétou, Trop drole ak termes yi. Mane dal Ci fans yi la bok
J'adore Tata marietou dama beug togu ya bakh way machalla merci 😍😍❤
Youbou yaba j t'aime fort maman sama yaye marietou la toude
fanny mendes ohhhh Masha Allah ma Cherie ziar ral mako
Mane dal yamay danel hawma thi wone kong fumée 😍😍😍😍😘😘🤗🤗
Toutoulara Ndiaye moss ko thi c’est trop bon
@ Ha thieum tata dal hel dou doy nexna trop sama harit yeupa contane merci beaucoup je t'adore tata😘😘😘🤗🤗🤗
Machalla démgua sama deug tata Marietou
caldou rék dou ay fo
Ta marietou MRci bcp contane na lool si iow👍
Tata Marietou mashallah diap n'a forme
Mâcha halla tata marietou toguuu rek nguay defff
Ma cha allah sama toguolokh bi yobou gama Casamance
😘😘😘 I realy realy realy Love u mom Marietou💋💓💘❤💔💕
Rien que la Vérité ohhhhh that’s so sweet of you 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Machallah madame maretou c'est très bon le caldou mai nous on mai pas poissons fumé je vais essayer le recette merci beaucoup
Khady Gassama il faut l’essaye c’est très bon merci 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Tèrèèè biennn 😂😂😂 j’aime trop cette femme 😍
Ma Sha Allah!😘
Sama deuk ,caldou rek legne beug!☺
Oulouuuu magui ni deifna sama ndougou ba parei.magui niew titeul gua yiii
Tata marietou doma adobte guir yalla 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽 rakhass rek lay def😂😂😂😂
so chocolat yes Insha Allah
Machalla tata mane si yowe laye roye❤❤❤❤❤❤❤
Maimouna Ly sa tourondo ngui ni😘😘😘
Tata marème say plat bakh na machallah
Merci Mane ioe la beugueu
WA tata Marietou je vais à château rouge pour acheter mon poisson frais pour caldou biii j'ai l'eau à la bouche merciiiiii wayyy tata ma la beugeu pire mane
Fifi Ndiaye salam Quel est le nom du poisson en français?
@@chachou6467 je pense que c'est du Bar car ils se ressemblent désolée encore de n'être pas aussi précis ma belle
merci ma belle si je pense que c'est le bar aussi mais j'en n'étais pas sûre merci pour ta reponse
@@chachou6467 😘😘😘
Fifi Ndiaye 😘😘😘
Machalla tata com dab rek😘😍
0:21 Tata we miss youbso much. I hope all is well with you and Sokhna Billo
Machallah caldou bi amna solo
Machalla séte na séleu na. Je me vois dans ta cuisine
AK tata maretou rk dafay diap forme machallah
Hum j'adore domou baye
Olala yeuf yangay gounouss gounoussi manguay thieupi thieupi mane waw kay fofa tothi radiakh😘😘
Kaldou sa ma plat préféré merci
Wa tata ya am feem say expression sama yay rc ngama jox😂😂🥰❤️😍
Non ndéké té mane tata marietou la beug ni ❤❤yalla na yalla fayla way mashallah
Merci tata marétou
Très bien from Casamance mane dal ''youbou yaba'' yi beugeunaléne lol sakh😘
tata marietou vrema ya gnou provoquer koi gnoune team femme enceinte 😂😂🤣😭
galséne 🙊🙊🙊🙊🙈🙈🙈🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️ ayy wayyy bal lemaaaaaa Yallah nalen Yallah May ay aum you sedeu yallah barkel ndiabott gui yeupp Masha Allah 😘😘😘😘🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️
@ mersi beaucoup tata marietou vrema tes video mont beaucoup aidé amine wayyy j t sui depui la france et j sui une grande fan de toi .yalnala maye guoudou fane akkk werr bisou
@@galsene3716 Hey way mounial yalla bakhna bnne chance
deug deug
mai contane naniou bilay
Mère ma la aimé. You ma beugue rek ghey dogue. Sama tourandi yaye
Machalah caldou bi diap na forme
Tata Marietou bo thi yakalé famille ndao yeup man loumay lekk waye😂😂😂
mariama cisse 😂😂😂😂🤣🤣🤣🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Très bien tata caldou bi diapna forme😍😍
Plat préféré 😋😋😋
machallah ta maynako wa beuleup familly
Laf thiatt maman ku beugu maman marietou beuseul j aim
Tata dall je t'aime rèk mouy gounouss gounoussi😂😂 😍 😍
merçi ta mariétou vraiment tu est la Meilleure 💖💖💖💖💖
Amna mana Machalah
No tata marietou dinama rey reek mais naak machallah amatina solo
Tata Mariétou esk yani degg thine bi noumouy deffer ''boukk boukk boukk'' way mongi séral Sama xol bi ni😂😂😂way liya nex way 😋😋
Machaala sister!!! Depuis Queen sa sopé biir
Ani wa team andeu suivre Tata marietou
Maman dal jtaime "youbou yaba yi ak goundouss goundoussi"🤣🤣
Vraiment merci Tata je essaie épinards avec d gombo tro nekh
Salamu Aleykum Tata Marietou... Yaboy bi noumou toudou si Englais
Milk fish. Je crois k marietou mesnako wakh
I’m coming 👍🏿😘
Nena nekoci touy😂😂😂non ta marietou you're the best
Sama plat, borom keur gui beugouko mais damay djeki togu si lou bari dici agne dici rere yene say ma ndeki si 😁oohhhh
Safy NGOM 🏆🏆🏆🏆🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘🤣
😂😂😂boula soblé bi ak citron bi diapé dinga khamni caldou dou pour ndéki😂😂
Goudal fane tata merci pour la recette
Hi M, I have been following your channel and I love your sense of humour! :), thanks for all your efforts in bring our delicious African dishes to your platform. Your memories of mere Diop are very vivid, Ya Allah reward her all her good deeds. Show us your image at least once!
Adja ohhh Ameen my Dear Ameen wayy 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘
Ta marietou hier lama mbakhal poisson fi si Normandie eupeuna wayé bi caldou on rék inschalah
Je voulais savoir ndakh les poissons diarneu roof Wala?
No il faut pas metre du roff merci
@ merci beaucoup tata
J'aime ça
WA Salam alaykum comment ça ma grand mère m'a fait manger c'est excellent j'ai des souvenirs
Tata malen di simi mane Dia la sant yakalma ba Genève
Mya Clinton Insha Allah
“Rendez-vous en bas lalay djokh”😂😂😂😂 I love it! Tata Mariètou yaw Yalla reik molay faye! Gnak la kham woroul! I love you so much❤️ Sama adoption bi nak mangui fi batay! Bo changé avis reik meune ngama gneuw djeulsi😩😩😘😘❤️❤️
Sokhna Ndiaye Ameen wayyy Masha Allah boule wakh Dara gnio farr 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘
Ça c caldou wolof
Thank you so much i love you
Bonjour sokhna Mariétou je suis fan de vos vidéos mâcha allah
Mais à quand un couscous marocain
J adore les Goudoussgoudoussi et consorts mâcha allah
Pour le caldou j ai l eau à la bouche dotant plus que je suis de la casamance
J adore vous écouter
Vraiment mâcha allah sokhna Marietou
Merci tata grâce à tw je sais comment prépare caldou
Bagna Simi, malaye simmi piir
Waa sokhna Marietou lii tamite dina nekh?
Merci beaucoup pour la vidéo
Beugueunaa torop
Li mom baxoul teudeu fébar di sétane yi ahhh non way 😂😂😂😂😂😂😋😋😋😋Maa shaa Allah
Tanel ak diame boula dara dal ci barké cheikh Ahmed tidjane psl aboul abass
Marietou manshallah sa kaldou happy na
Goudousse na nekhna
Sama toma borom néko réleuuhh ,titeul....😂😂
Machallah 🏆🥇🎖️💯
Niom sene caldou nouro wol ak sounou boss nioum dafa am goüt special
Machala, temps yi môme dieune mo khew. Heureusement qu'il commence à faire beaux.
coumba corera man katt sister dafa am gniou donn lathier gniamou dieune mothkh nak matek kothi merci 😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@ kone deh machala elles sont bien servie. 😘😘😘