Mais lamb waxul deugue tay eumeu mon bakkou mon deff spectacle mon khékh douma tapha tine il.manque juste la victoire pour clôturer cette belle journée
Ndeysane chaque combat bouma gueuneu préparer degueuntane fofou ley niakkè mais un vrai champion l'histoire de la litte sénégalaise retiendra toujours eumeu sene ❤
MAACHAALLAH EUMEU SÈNE JE SUIS DE TOUT CŒUR AVEC TOI TOUJOURS AVEC TOI WOLAHI BILAHI JE SUIS PASSIONNÉ DE LA LUTTE SÉNÉGALAISE GRÂCE À TOI ET CE QUE JE TE CONSEILLE C'EST DE GÉRER TA VIE DE FAMILLE ET TA RELIGION T'ES ET TU RESTERAS UN GRAND CHAMPION APRÈS TON PROCHAIN COMBAT CONTRE BALLA GAYE 2 S'IL TE PLAÎT CONCENTRE TOI SUR TA VIE
Liii d mom goulett ay boy Niang MM combat wam ak tapha ragal tapha rk mo tax daanou ko moko dax beurré mais tapha doolé lako diayy boy Niang dafa waron tahaw mane n'a khèkh
@@etranzeixenos9367 lolu mom deug lh doolém ak kheikham mane n'a si Daan kounè mais dafa djot mou yèwu tapha forme bimou amni gniko amon yeup neik nagn roi yèkini Tyson géant la mais beurrèm mo dèss
Eumeu sene le vip le plus culturel touss bou thiossané chaque combat bravo champion
Mais lamb waxul deugue tay eumeu mon bakkou mon deff spectacle mon khékh douma tapha tine il.manque juste la victoire pour clôturer cette belle journée
nimu xexe bahul.dey door mais calculer wul
Vraiment mé tapha tine dina djafé trop mou danou si lamb ji ndakh il sait désormais utiliser sa puissance
Mais kou dane tapha nice
@@DiorDiouf-gn7jj est ce que dagua dégg kéneu wax eumeu mo d'Anne??
Mais j'étais hyper contente et fière d'etre serreré❤❤.
Tres beau!!! La culture, notre identité!!!
DOOR NANIOU TAPHA BAMOU SÈDEU DAAL
VIVE EUMEU SÈNE
Ndeysane chaque combat bouma gueuneu préparer degueuntane fofou ley niakkè mais un vrai champion l'histoire de la litte sénégalaise retiendra toujours eumeu sene ❤
Machalah champion dessélo wa pikine dara diom reck ngua lambo longue vie à toi 🙏 Pikine est fier de toi 👑❤️👍👍👍
Vrai lion moy eumeu sene ❤
Félicitation à Tapha tine Notre champion fierté baol dako eupou doléé diambare deug leuh môme eumeu séne yalla nako yalla sam
Danou nga mais ken mèrè woula ❤❤
MAACHAALLAH EUMEU SÈNE
JE SUIS DE TOUT CŒUR AVEC TOI TOUJOURS AVEC TOI
WOLAHI BILAHI JE SUIS PASSIONNÉ DE LA LUTTE SÉNÉGALAISE GRÂCE À TOI
ET CE QUE JE TE CONSEILLE C'EST DE GÉRER TA VIE DE FAMILLE ET TA RELIGION
T'ES ET TU RESTERAS UN GRAND CHAMPION
APRÈS TON PROCHAIN COMBAT CONTRE BALLA GAYE 2 S'IL TE PLAÎT CONCENTRE TOI SUR TA VIE
Mome rek lay du courage tay lanioula gueune beugue t'as fait le maximum 💪💪
Un lion qui vieilli jamais bilahi yaye gaïndé ✊
Courage champion nga tu es le meilleur d'en l'arène ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ le meilleur reste à venir ❤❤❤❤❤
Billay mala beugue 😭😭y’a meune 👏🏼👏🏼
No eumeu séne yalnako yalla may goudou Fann AK wérr
No eumeu koor yalla dkeu là❤
Machalla touss bi nèxna saf na lamb
EUmeu Sene Le Grand Champion
Tapha tine mo meune beuré machallah que je te protége❤💪🏾🎉
Eumeu Séne dou nitte ❤❤
Akka mana tousss❤❤
Mais keinn Dieppi wouko deih wallahy il a montré de la combativité
Félicitations mbeur
Eumeu le meilleur lutteur
Wayy li moyy bakkou wayy🎉
J’ai della chair de poule , eumeu sène a honoré la culture serere ❤
Eumeu le meilleur 😊
Eumeu risque yimou dieul contre Tapha Tine guissouma fi lbeur bouko niemei dieul
Liii d mom goulett ay boy Niang MM combat wam ak tapha ragal tapha rk mo tax daanou ko moko dax beurré mais tapha doolé lako diayy boy Niang dafa waron tahaw mane n'a khèkh
@@AssaneMboup-wb6hl Tapha bou yeiwo , ni bombardier lay moudiou gni dess si lamb si yoon mossi eupp dolei
@@etranzeixenos9367 lolu mom deug lh doolém ak kheikham mane n'a si Daan kounè mais dafa djot mou yèwu tapha forme bimou amni gniko amon yeup neik nagn roi yèkini Tyson géant la mais beurrèm mo dèss
Il ne déçoit jamais même s'il a perdu il n'a pas démérité wané gua sa diambare ake sa ngora ,et félicitations a tapha tine.
Eumeu wa pikine nena dagne lay khekhe di negne khameni lamb dou politique bonne chance pour la suite
Che spettacolo 🎊👏🏻👏🏻
Ah sama mbeur mi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tapha la faralone mais wakh deugu diambar deugu ngeu machalla diame si yaw
Masallah refetna
Eume moy pikine bilahi il a lancé un message très sur sa prestation pikine bèneu lah bou lèn nagou kèn yakal lèneko
Tu a vu juste bro
Beugeutou gniou dra lepp andil guagniouko si lamb champions pikine kassei🎉❤
Yow rek laye topou bilaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤pikine
Ndanane nga dé sene Thiali barki rassoulilah ya wore✌️✌️✌️ tousse bi rec mo dakh victoire
le lutteur qui ne décoit jamais
Bilahi guerrier la
Bilahi ki Pikine Pour mou am mbeur bou melni ki dotoul yombou
🦁🦁🦁
Jour bi sama xol dafa toyyy
❤❤❤❤❤
Ki day doundal Lamb bilahi
Bakk dkeu waay
Yalla n'a am djam sama mbeur mi
Ya rafet xol d li yeup beug boolé ak rafètal leader pikine yeup nga baakou sein baakou
Kan moo Dan khawma sakh😂
ama Eska guissewoul age bounama rassta
Deegueule lii reek
Khamoun nako nerve dou dana Tapha tine
Waxi dof, te Móodu mi ngeen ko doon wax duma patriyot bi daan ko.
Loutakh xlo doumeu ama dane ko
Beurena beurebi nak sa waye. Khekhak (wala rak) ak Tapha tine.
Def spectacle, touss Mbeur. (Bakku Sereres ak tissu percale roule boumou sani si kaw)
Merci tyshinger
Bayil accusé gorr
Boune lako défé dou la nékh
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤