Il faut sanctioner le gars en jaune pour 1 ou 2 ans et amende de 300 ou 500,000.comme ça demain Il donnera un bon exemple. C'est du sport et faire play. Et il faut pas que on me dit c'est des jeunes, ils faut les pardonner, je dis no. En matière de sport il y a une règle de conduite que tous les écuries doivent savoir pour pouvoir connaître et respecter
La lutte sénégalaise doit connaitre quelques jours d'assises pour la remettre sur les rails de la discipline. Il faut qu'il y ait la rigueur face aux lutteurs eux mêmes ainsi que vis à vis de leurs supporters.
Mbeur kay bou fekké nité na dinama khawa diakhal c'est quoi ces comportements là , CNG doit prendre acte de sanctionner sévèrement ces actes ignobles , soyez responsables quand même svp
Borom lou jaune li mo togne bo parè dieul beudiane bi diko door si kanaw détention d'arme blanche...Cng nako sanctionné enplus son adversaire doorko plainte niou nioussko si kassso li yeufou rèwandoula....Ki dafa yabatè way borom lou vert bi dafa yarou rek sinon canne bi nga warrone niaff si bopp
Borom yeuré bou jaune bi mo tonie après bouniou ko sanctionner mou nek di oute kouko nianal grâce mbeur yi dangay warou koi ..soungouf takhoul nga dane kene
Thiey mbeur yi zéro professionnalisme zéro maîtrise tjr dans l’amateurisme on doit infliger un sanction sévère sur le lutteur en jaune adj ko 1 voir 2ans Avec ça ngeen niou ak état bi diapalé woul lutte bi
Merci de vous abonnés pour soutenir votre chaîne UA-cam préféré actu people tv ❤❤❤❤❤❤
Louléne serigne digeul niou def ken xamoul lou nek si poudre bi souko noyé dieulé si febar nak
C est la lutte qu on doit arrêter ça mène le pays nul part
Brom Lou jaune li moko togn amna poudre boumko euff te d'où Yoon
Il faut sanctionner le gars en jaune
Il faut sanctioner le gars en jaune pour 1 ou 2 ans et amende de 300 ou 500,000.comme ça demain Il donnera un bon exemple. C'est du sport et faire play. Et il faut pas que on me dit c'est des jeunes, ils faut les pardonner, je dis no. En matière de sport il y a une règle de conduite que tous les écuries doivent savoir pour pouvoir connaître et respecter
@@JeanBernardSagna mayi niou nga nane sanction li ko wadji déf ioe bomako défone niou khéh li mou déf si lambeu la bok
@@CheikouNdiaye-u5w baniouy sedeula "mouss" danga absentéwoon .yow ak mbeur Yi yéneu yém
@@JeanBernardSagna iow atél deugue la wakh guisse nga ki togne epus gni sén cassé bosi dieulé 500 000 lousiy dess
Ioe vrai dof nga Jean Baptiste li koula ko defone nga def louko raw
@@JeanBernardSagna mes borome lou vérte li mo togne
La lutte sénégalaise doit connaitre quelques jours d'assises pour la remettre sur les rails de la discipline. Il faut qu'il y ait la rigueur face aux lutteurs eux mêmes ainsi que vis à vis de leurs supporters.
Ki kheup soungouff bi mo togne te daniiuko wara athie
Regarder bien lamine bi gayi di khékh mou téyi micro bi nane ééyy😂😂 comme kouy reporter
Le gars en jaune togn bakhoul
Brom tiarakh yii motonge dh😢
@@_NG10 Ta mo ndieka doré aussi
Wadji sokhorna
Borom jaune blanc bi mo togñ yalla nañiouko dane
Douloureux Door yet bi
2zns ferme. 500.000 amande
Amiiine ❤
Moi mon fils ne sera jamais lutteurs même si on mangé du sable 😮😮😮
Jaune blanc ya togn yalla nagn la dane
Mbeur kay bou fekké nité na dinama khawa diakhal c'est quoi ces comportements là , CNG doit prendre acte de sanctionner sévèrement ces actes ignobles , soyez responsables quand même svp
L'homme qui a soufflé le Poudre doit être sanctionné
Danio wara Sanctionner borom Lou jaune li domaraame laaa
Yena opter ligueyy doranter melni ayy mbame donc assumez lamb tiossane la wone mai legui Keen xamoul lanleu
Lamb ji mo wara arrêter ça ne nous fait pas avancer désolé pour ceux qui vont me détester mais liyeuffi dof la...
Borom yeré bou jaune blanc bi mo togne ndakh moko euff soungouf bi
@@hamidoutall9134 kou rew ndeme la yalla naniou ko dane ba dioutal ndayam
@@hamidoutall9134 yalna am defette
Mo tay
@RokhayaThiaw-n3q hana sa far la motakh ngakoy défendre neko togne dou galathie
@@hamidoutall9134 dinako dane inschalla
Il faut sanctionner sévèrement. C'est la seule solution.
Signature waroul ame armes balance nako cng tèrè
Borom lou jaune li dagnko wara dakeu si Lamb c injuste
Le lutteur en blouson jaune mo togne et il merite des sanctions
Borom lou jaune li mo togne bo parè dieul beudiane bi diko door si kanaw détention d'arme blanche...Cng nako sanctionné enplus son adversaire doorko plainte niou nioussko si kassso li yeufou rèwandoula....Ki dafa yabatè way borom lou vert bi dafa yarou rek sinon canne bi nga warrone niaff si bopp
Nane annulé séne combat athlene 2ans
Sol sa thiarakh douche ba paré Di togn
Mes Mbeur dal foux la vraiment li dou yonne
Ce gars en jaune kouko diap diap agresseur domeram . Il ya pas CNG ici, il faut porter plainte ki domou haram deug la .
Legui nak bou lambe dji diekhé niounane nio bok ndeye bok baye thé kousi diekou sa morome beuko lék ay domrame laniou rk
@@mory6196 limaci gueuneu méti nio gueuneu néwi louniouy fayékou euskeuy souma wakhé lamb yeufou dof leu niou dagalma 🤣😭
nagn ko athie plus de 3ans pour servir lecon aux lutteurs indisciplinés
Le gars en jaune mo togne
Bo mou solè ay thiarakhe guéneu wara khamnè weureul rew na
Baye má ndiaye mou tonge kone
Khawma mo togne âme déte wayé modakha khékh borom Lou vert li 😮
Non non yefoudof lafidef
@@mamadousylla1789 moko meune deh way mom mo toñ
Borom lou jaune li mo togn dé
Borom yeuré bou jaune bi mo tonie après bouniou ko sanctionner mou nek di oute kouko nianal grâce mbeur yi dangay warou koi ..soungouf takhoul nga dane kene
@@pronosticfootsenegal1112 doff rek leu
actu people meun nguenn fennn 😂
CNG da wara di tec ay sanction you metii
Param 2 rek lagnouy tope 🎉Ya togne nak😂ba paré doumeu ko 😅thieuy sama Wadji Borom Thiaroye guinaw Rail
Saway mongi weur tinganene b😂😂😂😂
Li affaires rou dof la😢😢😢😢
LE CNG DOIT SUSPENDRE LES LUTEURS QUI AMÉNE DES CORNES POUR CE BATTRE
Ay doff rek nguen 😂
You Mack 🤣🤣🤣🤣
Mo togne mo nok😂
Mes Lamine kou sole blouson jaune bi lo rogne wa leneko deugue bouko defone mbeur bou non dinako defe Lou meti
Borom lapha bou bleu bi mo togne il faut depasser cette étape fayounou len dara gueni dof dof lou Di khekh
Xam negn kouy dane bapare 😂
Legui Ada fass gen yap.
Amande et sanction ce ga a dépassé les bornes togne d'où galathie
Borom lou jaune li sanction
Borom Lou jaune li yalla nagnko dane barki seydina mouhamad ndax togn dou galathie
😭😭😭😭
Mbeurr yi togu ta atéwugnou yalla bougnou amati ndam
Borome kane bi dou touss noye khékhé Di sani sa nganaye bilahi kane lalaye niouss ba do beuré dimanche laaaa
Borom jaune blanc mo togne mo gneuw basi môme euff so soungouff
Param seul guinaw rail ya tout boléne khamoule nitt bouléne ko juger
Wa kimome yatame wi loumoukoy diarigne do défendre sa bopou
le cng doit prendre ses responsabilités et sanctionné le lutteur en jaune, ki togn katla
Sarap ndayi lambu rek du darra way aay dof nguen rek
Dore si face face d'où yone manque de respect la
Borom yéré bou jaune bi dagn ko wara sanctioné
Deleine oute sécurité 👉lutteur you beuri danio chauvage 😢li moy lane
Suspension 10 ans
😮delen woutt ay policier 😂😂
Borom jaune blanc bi mo togne. Il ne respecte pas son adversaire.
Douguéne bayii féne ana déréte bii deléne titres vérité
Meune féne ba séne titre bi sakh diouboul tchiimm
Borom jaune bi mo togne moko euf poudre ba parré dieuka dore
domou àdama dafa wara respect morou mou domou àdama me senegal respe 0 😡 😡
Borom yeuré bou jaune bi wa CNG daniouko wara banir
Loutakh moukoy euff soungouff bi mo togn
gui Diègue door yallna nane KO douma dan ko pas ka mon Tonie
C'est du m'importe quoi organiser vos face to face en respectant les normes de sécurité requises si vous voulez atteindre le professionnalisme
😂😂😂boy dagnouy Touti ba dou gnou kham fignou fare gnew di roube
Mbahana dou féké thiono boromam 😂😂 olof Ndiaye dioum nga taye béne réka naw borom lou jaune li mo togne moko euf soungouf bamou habtalou😂 wayé kéne waroul défal sa bope justice yabouhaté motahit dotoko défati déééé wooooy 😂😂
L'homme en jaune est fautif
Param 2 mo togne kou rew la
Borome lou jaune Li domou rame la
gni ay domouram degeuh nagne beuré yefou domouram degeuh la ay mbab nguen rk thim
Fii securite dafi wara bek
amoul béne sécurité
😂😂😂😂😂😂
borom lou jaune li mo togne sokhor
Lamb dal yefoudofla
Borom lou jaune mo togne
Yéne site yi mome féne rék liguéni titré AK loulou am dou sakh béne Ani dèréte bi toutou😢
Khana guiso beutbi
C'est du grand n'importe quoi vraiment
Borom lou jeaune li waratoul yor license mo kheup galadji mo dieuka dor
doff yi
Param 2 kessé ❤❤
Ñidaño yabaté waye ñi warouño beurré sene combat bi ba paré dañe léneu wara sanctionné
Gni ay mbam youniou solal yéré rékk lagnou souniouy guénd di beureungou thii souf si
Yaw sakanbi loumlay diaring lakhamoul dokoko ngad gay khol moulay door thim ragal bi
Yaw khana linga yorr dou yett dokoko gniri bamou khol ben place hooo
Thiey mbeur yi zéro professionnalisme zéro maîtrise tjr dans l’amateurisme on doit infliger un sanction sévère sur le lutteur en jaune adj ko 1 voir 2ans
Avec ça ngeen niou ak état bi diapalé woul lutte bi
Borom lu jeune li moo togn
Borom. Blouson bou jaune moo togne
Parame 2 kassé amoul data yayam 🪚⚔️⚔️⚔️⚔️
@@CherifBakhaydaNdiaye-x7i yaw mi doff ngua de li losiy encourage 🤦🏾♂️🤦🏾♂️🤦🏾♂️
Param 2 mo togne kou rew la