Kooru Biddew Saison 3 - Épisode 8

Поділитися
Вставка
  • Опубліковано 28 гру 2024

КОМЕНТАРІ • 504

  • @kinouska2260
    @kinouska2260 6 років тому +26

    Serigne abdou aziz al amine ndeysann yalna yalla doli ko yeurmande ak cheikh sidy mathar mbacke

  • @SeynabouMbaye-sj5et
    @SeynabouMbaye-sj5et Рік тому +5

    Bidew franchement. Je. Tadore

  • @marianendiayeguellwarre7919
    @marianendiayeguellwarre7919 6 років тому +107

    bidew ak tata âme guenn classe manchallah j'adore

  • @basiletoudji6029
    @basiletoudji6029 6 років тому +10

    mon épisode préféré 😂😂😂fama bayil bakan mass bi ngay khass😂😂

  • @nabougressi23gressi95
    @nabougressi23gressi95 6 років тому +15

    Khamoul niii kou guis sa bidew daguay déé 😂😂😂😂😂 wakhgua deug badiéne 😂

  • @elhadjidiop7535
    @elhadjidiop7535 6 років тому +46

    Kou nagou ni bidew dafa meune 👍👍

  • @nabougressi23gressi95
    @nabougressi23gressi95 6 років тому +9

    Fama néna bidew medecin apélé la mort gua😂😂😂😂😂😂

  • @Queencessmilie8484
    @Queencessmilie8484 6 років тому +44

    😂😂😂bayiko mounane ma bideew té xamoul né kou guiss sa bideew degay déé😂😂sui morte

  • @fatuhane5287
    @fatuhane5287 6 років тому +114

    Ana gnou bEugu BiDéw way

  • @footempo
    @footempo 6 років тому +4

    Mane badiéne douma rayy déss "néna khayna ma lékatfi "😂😂

  • @gorguindiaye5986
    @gorguindiaye5986 6 років тому +89

    Ménage senegal mety neu

    • @gomisenefanny3076
      @gomisenefanny3076 6 років тому +3

      Ndeye Mareme Ndao
      Mooo koukoo metyl mou metty
      Yalla sax degoul kenn lou mety
      Non wayy. C'est quoi ça
      Aucun diam dans ta maison
      Chiiii bidew yarouna. Machalaa

    • @princessmbay4740
      @princessmbay4740 6 років тому +1

      gorgui ndiaye trop sakh

    • @silksmithaful
      @silksmithaful 6 років тому

      A lantikite

    • @nenembengue1161
      @nenembengue1161 6 років тому

      gomisene fanny xana! Aye souma amone goro bou melni dakaye reye😂😂

    • @syllamaman4914
      @syllamaman4914 6 років тому +1

      gorgui ndiaye bilay khamosi dara sakh aka méti

  • @diodiodiallo7144
    @diodiodiallo7144 6 років тому +3

    toujour nekh série n°1 du koor gui rek dou ay thiakhane

  • @aminatandoye2041
    @aminatandoye2041 6 років тому +2

    Non badiene rey na ma. Néna hamoul ni kou guiss sa bidew dangay deh 😂😂😂

  • @Ousmanesarr344
    @Ousmanesarr344 10 місяців тому +2

    Doumasy doyalll😂😂😂😂

  • @maimounabalde5848
    @maimounabalde5848 6 років тому +27

    Anna niou beug badien bilahi dinama ray

  • @mamitabiche4871
    @mamitabiche4871 6 років тому +39

    😂😂😂😂 badiéne néna gnou kheutio khalé bi bamou dame 😂😂😂😂😂😂😂😂
    Mais tante Bidew machallah elle est toute belle
    Bidew mome c'est une vraie perle toute mimi avec ses beaux yeux 😘😘😘
    Fama et badiéne sont les sels de la série avec des termes à mourir de rire.
    Mass et Germaine aussi incarnent très bien leur rôle
    Vous êtes les meilleurs et vous le resterez
    franchement on n'a rien à vous reprocher. Bravo à toute l'équipe de Leuz Tv

  • @diineakdiamono2587
    @diineakdiamono2587 6 років тому +102

    Nafila tay bi :
    4 Rakka
    Tabbate yadaa 3 fois
    Likhlass 1
    Amna solo bayyi si khel barina ay ndiarigne looool

    • @miimisdiop3594
      @miimisdiop3594 6 років тому +1

      Thierno alkarime Diop Tbd dieredieuf yaw ladone khar

    • @diineakdiamono2587
      @diineakdiamono2587 6 років тому

      Miimi s Diop.oui niew na mgui nonou

    • @idydiagne1143
      @idydiagne1143 6 років тому +1

      Thierno alkarime Diop Tbd Merci pour partager bi

    • @diineakdiamono2587
      @diineakdiamono2587 6 років тому

      Idy Diagne. Na guena yatou inchalllah chaque jour dina lène ko andil

    • @diarrasene2605
      @diarrasene2605 6 років тому +1

      Thierno alkarime Diop Tbd ak fatiha

  • @aichasowly6530
    @aichasowly6530 6 років тому +2

    Warone gua bayi gnou kheuthio. Khalebi bamou dame 😂😂😂😂😂😂

  • @mamefaye6143
    @mamefaye6143 6 років тому +32

    Di diougué thi keur né daguaye khar rére ma gui koye dora guis 😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😁😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @missniass8166
    @missniass8166 6 років тому +16

    Badiéne dafa meun sagncé macha allah

  • @lingereniang8358
    @lingereniang8358 6 років тому +97

    Wouy Badiene Ray nama néneu bayiko mouy Ma Bidew khamoul ni kou guiss se bidew danguay dée 😁

  • @khadidiatoudiallo3718
    @khadidiatoudiallo3718 6 років тому +27

    yalla nayou yalla mussal thi goro yi melni

  • @gnilanendour2461
    @gnilanendour2461 6 років тому +3

    wouyy badiène nenako khamoul nii kou guiss sa bideww daguayy dèii 😂😂😂

  • @allaloudaddymbaye5300
    @allaloudaddymbaye5300 6 років тому +5

    Wouy Badiane ray nama nèna kou guiss sa bidew daguaye dè mouy ma bideww😀😀😀😀

  • @soninkohprince7702
    @soninkohprince7702 6 років тому +24

    6:27, Sa bakane bi mélni Paquetou Dunhil😂😂😂😂

    • @nittoudeugrek9684
      @nittoudeugrek9684 6 років тому

      Abdoulaye CISSE bilay dom baye lolou la raitane ba tass non😂😂😂😂😂😂😂😂😂😆😆😆😋😋😂😂😂😂😂😂😂

    • @soninkohprince7702
      @soninkohprince7702 6 років тому

      Khady Cissé Dado... Dafa amm dictionnaire khasté quoiii😂😂😂

    • @amadouourydiallo4381
      @amadouourydiallo4381 6 років тому

      Abdoulaye CISSE ahhhhhhhhhhh

    • @obtrice4257
      @obtrice4257 6 років тому

      Abdoulaye CISSE no mais comment jai éclaté de riiire en plein ramadan !! Té dunhil kéne daka tokhatoul sakh...Daro artiste leu quoi...

    • @soninkohprince7702
      @soninkohprince7702 6 років тому

      Ob trice sayoumay sétaane Mass rek fatelooukou Balaane bi😂😂😂😂

  • @yofariedieng2086
    @yofariedieng2086 6 років тому +2

    Lii dale moy théâtre instructif et réél mé fama nak boussa yaye déwé daguay déé dingua😂😂😂😂

  • @elbachirdiange1357
    @elbachirdiange1357 6 років тому +16

    Fallou sene rip bolén ko fatté si niane

  • @bbmargo9235
    @bbmargo9235 6 років тому +100

    Badiene nena bideew mogui melni kouy défilé fête 4avril wuy 😂😂😂

  • @boyjallow1862
    @boyjallow1862 6 років тому +6

    Mais Fama mi nii lagne koy baayeé😂😂😂

  • @kinedjite2202
    @kinedjite2202 6 років тому

    Badien dinama ray nena bayuiko mounane ma bideww xamoulni ku guissa bideww dagay deh 😂 😂 😂 😂

  • @paulinebara4333
    @paulinebara4333 6 років тому +6

    série de lannée avec des bon acteur qui on du talent vraiment rien a dire

  • @babacarsow387
    @babacarsow387 6 років тому +1

    No Badiene ndawtal moko sonal 😀😀😀😀

  • @serignelo1450
    @serignelo1450 3 роки тому +1

    Merci

  • @ndiagatoure8906
    @ndiagatoure8906 6 років тому +3

    Wooy mangui dei
    Sen togg day bari tei nekh😅😅😅

  • @elfadillouricheenvitaminem6296
    @elfadillouricheenvitaminem6296 6 років тому +5

    Walahi vs ete les meilleur 🔥💗💗

  • @djilysalioudiop5613
    @djilysalioudiop5613 6 років тому +6

    Noooooon dead 😂😂😂😂😂😂😂 badiene wooooooooy

  • @afiandiaye7466
    @afiandiaye7466 6 років тому +14

    Famadinama réu man mai biddew sou kholé rek sama yram bi daw 👌

  • @ndeyemagattediouf6135
    @ndeyemagattediouf6135 5 років тому +4

    Aye way j’aimerais bien jouer dans la saison prochaine

  • @MameseyeThiam-g7k
    @MameseyeThiam-g7k Місяць тому

    ❤❤❤❤je t'aime grand Bijou 🌹🌹😊

  • @ymgxtv7132
    @ymgxtv7132 6 років тому

    Yow yay bidew bouy fégn beuthieuk.. Mach'Allah

  • @khalifagueye4931
    @khalifagueye4931 6 років тому +2

    Korou bideew gno beugeu sonnerie. Ting tong toujours doyna war......

  • @morthiam3357
    @morthiam3357 6 років тому +1

    yaye mako fan 😍😍

  • @dayzakalla3601
    @dayzakalla3601 6 років тому +1

    Man fama dinama ray seuttt😂😂

  • @malickgueye1353
    @malickgueye1353 6 років тому +2

    No badiane mo beug ndawatal 🤣🤣🤣🤣

  • @misssow1145
    @misssow1145 6 років тому +11

    meilleur série pendant l ramadan👌👌💖

  • @diopmbene1733
    @diopmbene1733 6 років тому +1

    Mdr badiéne nenako bayi ko mounan ma bidew xamoul ni ku guis sa bidew dangay dèeh wooyyy mdr suis par terre😀😂😂😂

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 6 років тому

    séne togou day beuri ta nekh 😁😁😁😁

  • @astoudiop1420
    @astoudiop1420 6 років тому +1

    Badiene ak fama ak nio niémé gathié😂😂😂😂😂😂

  • @morthiam3357
    @morthiam3357 6 років тому +3

    bidew est encore plus belle quand elle est en colére

  • @fatouyasminou2642
    @fatouyasminou2642 6 років тому +8

    Ohhhh Ma bidew toujours souriante 😍😍😍

  • @nebeygueye2908
    @nebeygueye2908 6 років тому +7

    Oohoho badiene mo raw volcan no dafa faté sii Bell mère eupeuna way

  • @fatoudiouf4992
    @fatoudiouf4992 6 років тому +2

    Kou guiss sa biddew dangay de😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @khadyjakonate9039
    @khadyjakonate9039 6 років тому +1

    Mass il es trop sage mane je laim trop

  • @oumydiengsala544
    @oumydiengsala544 6 років тому +1

    Non Bideew mashallah keneu dou mom
    Badiane yow tmt , dangay gueneu keur gui key prkw xar rère ...ba moudjou si bissap ahhhhh terminus de l'oeil !!! 😂

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 3 роки тому +5

    Meilleure serie senegalese

  • @abdelohod4884
    @abdelohod4884 6 років тому +1

    Aka niakkeu djiome nane nangne khar ba rair ba paré🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @kamassaer2661
    @kamassaer2661 6 років тому

    Ndeydan mass dafa yarou bilay mais bb bi mon ma nekh yalla na mageu bay teral ay wadjouram machalha takhna ma beugeu bb sax ba toude ko sama yaydjou bakh djia yalla nako yalla khare aldia

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 6 років тому

    Biddew dal dou ay thiakhan machalla laf thiat

  • @rokhayasysarr2536
    @rokhayasysarr2536 6 років тому +1

    Fama moh bonne nenah sa bakane Mell ni paquet dunnhil😂😂😂😂😂

  • @brasildakar180
    @brasildakar180 6 років тому

    Bilay badien ya sonlee ak saa atamousorr

  • @abdouseck7590
    @abdouseck7590 6 років тому +32

    Tay mome yekhou ma ana balamaïsa yi begue nalen❤️

    • @boussothiam5604
      @boussothiam5604 6 років тому

      Abdou Seck balamaissa Yangui niiii

    • @mamybarro3024
      @mamybarro3024 6 років тому

      Abdou Seck gnongui nii

    • @abdouseck7590
      @abdouseck7590 6 років тому

      Bousso Thiam wawa dou ay fooo❤️

    • @abdouseck7590
      @abdouseck7590 6 років тому

      Mamy Barro dou moromou kene ymgx❤️nekh na

    • @astoudiop1420
      @astoudiop1420 6 років тому

      Balamaïssa rek dou aye foooo eupneuh 🙌🙌🙌🙌

  • @dijalovesy5224
    @dijalovesy5224 6 років тому +1

    Ay way suma dieukeur yal na melni Bidew 😍😍

  • @ndiagatoure8906
    @ndiagatoure8906 6 років тому +2

    Bayiko mounane may bidew khamoul nei kou guiss sa biew dangay dei no badiene amoul way 😅😅😅😅

  • @fallousarr8209
    @fallousarr8209 6 років тому +1

    Mrdrrr yenako teyy 😂😂😂😂kham nguene nii bounguene dii réer dii tokkk

  • @maimounacoundoul1918
    @maimounacoundoul1918 6 років тому +2

    Fama Fama dinama ray 06:35 😂😂😂

  • @diasporabii5529
    @diasporabii5529 6 років тому +2

    Mane loutakh ma fan badiene rék

  • @mounasssow8303
    @mounasssow8303 6 років тому +9

    tata seytanénga, Je nga créer tension si keur gui ba paré tournéwatt nane mass baloul sa yay

  • @beibishkane6234
    @beibishkane6234 6 років тому +6

    bilay mass mo sonnou rek

  • @kokidiop3273
    @kokidiop3273 6 років тому

    Merci Badiane Li guaye dêf mane guago trop

  • @babacarndiaye4042
    @babacarndiaye4042 6 років тому +21

    Ana sama Biddew yi nk Yalla Guenn ame Diamou wat

  • @seckfatou4985
    @seckfatou4985 6 років тому +7

    mandale fama ak yaye xawma koune yap mounane 4avril 😂😂😂

  • @fatoudiagne3053
    @fatoudiagne3053 6 років тому +3

    Ohhh tata ya am foula 😘

  • @ndeyekhadyniang8779
    @ndeyekhadyniang8779 6 років тому

    mouy kedje kedji mélni kou nék 4 avril. aka sokhor

  • @puffdaddy22177
    @puffdaddy22177 6 років тому +2

    Kou guiss sa bidiw dé aka lérr

  • @reinenoire3354
    @reinenoire3354 6 років тому

    rée na ba dé badiane daguay khar rèere

  • @abdoulahaddiop-vg1xh
    @abdoulahaddiop-vg1xh Рік тому

    Mass bien joué

  • @adjafall7608
    @adjafall7608 6 років тому +1

    La meilleure épisode de toute les saison ptdriiir non li amoul😂😂😂

  • @BabacarCiss-e8c
    @BabacarCiss-e8c 2 місяці тому

    Douma Doyale si série bi😂

  • @aminatadiallo4702
    @aminatadiallo4702 6 років тому +2

    Wooy daro😅😅Nena mass ceu bakene melni paketou denii (cigarette )

  • @mameseynaboundiaye9201
    @mameseynaboundiaye9201 Рік тому +1

    Machalla 😍

  • @bintouseye3375
    @bintouseye3375 6 років тому

    fama dou ma ray😅😅😅

  • @NdayekhadiThialaw
    @NdayekhadiThialaw Рік тому +1

    😢😢

  • @samueletoo3956
    @samueletoo3956 6 років тому +4

    Koor gi mettina me bou doke giote nga fatte lepou nagaye ree ba dee Ahahah 😁😁😁😁

  • @aminabah8293
    @aminabah8293 6 років тому +1

    Daro et badiene chapeau a vous bravo MDR

  • @lenoblepaco614
    @lenoblepaco614 6 років тому +12

    59 vu team setane serie yeup

  • @sitansand6318
    @sitansand6318 6 років тому +3

    Daro dinamaray néna yay gnou khar rer 🤣🤣🤣.#kharanekatt

  • @samsisamaroussi9554
    @samsisamaroussi9554 6 років тому

    kougis sa bidew dagay dh😂😂

  • @abdouazizdiop2880
    @abdouazizdiop2880 6 років тому +2

    😂😂daro nena ko fo dei ma kheum feu nagou woule dei dii

  • @fousseynoutraore6172
    @fousseynoutraore6172 6 років тому

    Bravo a vous sén théâtre bii nékh neu trop

  • @miami7867
    @miami7867 6 років тому

    Nehna😂😂😂😂😂😂may wax daro nane bidéw mayma😂

  • @ramadiouf3813
    @ramadiouf3813 6 років тому +2

    daroo ray nama paketou deni kayy😸😸😸😸😸😸😸😸😸

    • @charlesguy6061
      @charlesguy6061 6 років тому

      Rama Diouf Dunhill

    • @ramadiouf3813
      @ramadiouf3813 6 років тому

      +Charles Guy dunhill mercii niak diangu rekk

    • @obtrice4257
      @obtrice4257 6 років тому

      Rama Diouf loool vas a l'école tu refuses ...hum

    • @ramadiouf3813
      @ramadiouf3813 6 років тому

      +Ob trice dina deme inchallah

  • @keurdiopndiayelofficielle467
    @keurdiopndiayelofficielle467 6 років тому

    Hiiii Bidéw gniii fatteu nagne la 😂😂

  • @diarrasene2605
    @diarrasene2605 6 років тому +2

    Wa yene fama mii😂😂😂dinama raye rek😂

  • @madamendao6787
    @madamendao6787 6 років тому

    Nena bako fofou mouy ma bidiw tei xamoul nei kou guiss sa bidiw danguay dh mdrr

  • @modytoure5278
    @modytoure5278 6 років тому +2

    Mdrrrrr fama néna mass nga melni kou nek si saint valentin😂😂😂😂

  • @mamyfall4434
    @mamyfall4434 6 років тому

    😂😂😂 gamma nenako yay kharal niou Ndogou! 😂😂😂😂😂😂😂😂😂.!.!.!!

  • @ctaphacisse7524
    @ctaphacisse7524 6 років тому +1

    non bidew machalla bilahu male fan❤❤

  • @eauxclairesslsn
    @eauxclairesslsn 6 років тому +31

    C'est vraiment stressant cette mini République de femmes acariâtres et un homme un peu yambar qui n'ose pas les recadrer... badiene et fama Aka nio bare wokh !!

  • @ibrabah7078
    @ibrabah7078 6 років тому +1

    mane badiane foumouye diélé wakh youmouye wakh noooo

  • @fatouassalikhatoul9617
    @fatouassalikhatoul9617 6 років тому +5

    Ay Fama wa li diam laaaa rérrrrr ba parei kay😆😆😆😆😆😆😆😆