Serigne Fallou Sylla kou la nawoon te beugg la laa. Kou la geureum te seenu la fu kawe la woon. Waaya sa wax jii waxu parparloo la. Cheikh Oumar Diagne wax jimu wax toognu ko loru ko. Ñakka xam gi lembe ci reew mi ag naafeeq ag parparloo moo ko lor. Waaya deugg mi ngi ci sunu kanam insha'Allah. Cheikh Oumar Diagne nattoom mooy bu Seex Anta Diop, ag Seex Mbakke Gaynde Fatma ag seydi Seex Ahmed Tijaan Si. Dafa feeñ ji jamano ju ko attanul !
Khanaa tay nguén nangoul ousmane sonko. Guëmou leen dara ay doul kat rék nguéne. Mais cheikhe oumar Diagne bravo rék laniou koy wakh, kou dëggou la té am kham kham bëgg réuwam li ga yal ko khékhal ko. Yalna ko yàlla sammou té aar ko té goudal fanam. Yallà nak niépp lafi nékkal. Diamono nak dina atté inchallah.
je suis pas d'accord avec toi, depuis longtemps il insultes le tarikha mouride, ont la pas limogé c'est pas lappaine de faire une discour il faut laisser avec eux même même
Vive cheikh Omar diange borom xam xam yalna yalla doli samou ko mo. Démission moko damande cheikh Omar diange ngoure yengalou KO nim KO défé ande samou djiko yi
Machallah
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla Anna solo serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla dierejef Serigne Touba
Allhamdoulilah sante yalla bou bah dieureudieufatie borom Touba
Ma challah ❤❤❤❤
❤❤merci 😂❤
❤❤❤
Machalaha lingua wah leip deug la.
Merci diomay
Masah allah
Merci merci merci bassirou faye ❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdulila ❤❤❤ dieureu dief
Très bien
Hakassa s fallou 👈🙏himmar 🐴 diann 🪱 dou nite kou baakh 🤠👈
Merci
Serigne Fallou Sylla kou la nawoon te beugg la laa. Kou la geureum te seenu la fu kawe la woon. Waaya sa wax jii waxu parparloo la. Cheikh Oumar Diagne wax jimu wax toognu ko loru ko. Ñakka xam gi lembe ci reew mi ag naafeeq ag parparloo moo ko lor. Waaya deugg mi ngi ci sunu kanam insha'Allah. Cheikh Oumar Diagne nattoom mooy bu Seex Anta Diop, ag Seex Mbakke Gaynde Fatma ag seydi Seex Ahmed Tijaan Si. Dafa feeñ ji jamano ju ko attanul !
Kii daa mana fene dh
@@Bukrtan3800 billahi linguay wakh akay deug Cheikh Oumar Diagne daffa fègn si diamono bingua ham né gars yi nion Gui nélaw
Wakho deugg a tout coeur avec cheikh Omar diagna❤❤❤❤
😂😂😂
😂😂😂 Dém lén nopolo
Omar Diagne kon Dakou niou ko?
Kou wakhoul dëgg?
Mo demande dimison ndax lim guem laye wakh vive cheikh Omar diange ❤❤❤
Limosine
Diadieuf
❤❤❤ machallah
Bayiléne Serigne Touba miguéni dougal thi politiciens yi.Nafeknga.Lii dou ndamal diomaye ou sonko. Ragalal yallah. Lii ndamal Serigne Touba ak mag gni mou togne. Kou insulter sab Serigne dakou gnouko ,nga insulter anciens combattants ngou dog la dakh. Nga mankan kougkan dithi wakh. Thipirri😊
Ni da no ragal kou len saga ba dou nou wakh deugue
Cheikh omar motay limou def
Mais attends et ce que réero amna je ne le crois pas
Khanaa tay nguén nangoul ousmane sonko. Guëmou leen dara ay doul kat rék nguéne.
Mais cheikhe oumar Diagne bravo rék laniou koy wakh, kou dëggou la té am kham kham bëgg réuwam li ga yal ko khékhal ko. Yalna ko yàlla sammou té aar ko té goudal fanam.
Yallà nak niépp lafi nékkal. Diamono nak dina atté inchallah.
Bayil TOGN
Cheikh Oumar Diagne bou dioumé nanguén kooy nangou
No amna niou bonn
yen dimb alilenniou niak djoulit mo gueneu bonn gordjiguen
Wah Aka diafé kon tirayer yi daga bageu wah né dounou ay dioulit soubouhouma omour diange
Qui dou nit kéne khamoul loumou beugue dakh bi mane dakorna thi
Li doussa mbir
je suis pas d'accord avec toi, depuis longtemps il insultes le tarikha mouride, ont la pas limogé c'est pas lappaine de faire une discour il faut laisser avec eux même même
Merci 🙏🏽
BAYILENEU POLITIC
Saway bayill sa dof dof lougi cheikh omar Diang dafa bang sounou bakyi rew bo giss daf am ay père fondateur
Omar.sa.toroxtande.tabalena.te.bolxam.fomotol.rewag.lelay.diareg
Takholeen niou dakh cheikh Oumar Diagne dh 😂😂😂
Pere Toi aussi Anne bou bess ak fenn you bess
Yakhkawake
Cheikh Oumar Diagne dof ak réwandé ak ignané kilifa réwmi motakh li dalko jerejef Président Diomaye
Wakho fi dra
😂😂😂😂
Sénégal rèw bou nakaré wokhal la daffa beurri niou ignann té sokhor. Kholal pa bi rék. Cheikh Oumar Diagne Yallah dinala diokh li gueune inchallah
Omar diagne domi haram dëgla waye yaw tait ab saay saay nga
Sa baye ape dom Khadj leu
Ki kannla falllou syll thiey omar diagne mounieul rek c le senegal
Wakhofi dara
Vive cheikh Omar diange borom xam xam yalna yalla doli samou ko mo. Démission moko damande cheikh Omar diange ngoure yengalou KO nim KO défé ande samou djiko yi
Kii mom vrai saytane la
DIOMAYE FAYE et Sonko n'ont pas le droit de trahir leur conviction d'antan & tous ces Charognards politicordligieux étaient des griots de Macky Sall
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤