Modou lo est très agressive waoooh quel lutteur yalnala souniou borome takhawou yokela doléla on est très content de toi notre rois modou lo merci merci merci ❤🙏
Il FAit aussi comprendre que modou lo est un Sportif de haut niveau il a depasse la domaine de la lutte il est beaucoup plus serieux plus serein et plus profesionnel boy yi nakk waakh rek laj fethie lagnou guena meune
J suis pikinois mais quelle explosivité et puissance de Modou lo Boy niang 2 du courage tu n’as pas démérité c le sport félicitations modou kharagne lo mais nak sonal gua gnou 😂
Toute chose à un prix le mérite ça donne encore plus de respect félicitations encore au messi de la lutte le goat🐐 le maréchal,le Cr7 aussi de lutte de par son professionalisme son sérieux la constance qu'il a franchement wathio ga ak say supporter pour ma ma part bo bayé lamb dotu ma amati mbeur.
Palla Réglél reug franc lay beurel modou day nopalou daguen beugue modou di beuré rek tá boyam yi d’où gnou beuré ay nawlém lá gnou ins bi modou bouko nékhé né kou beugue beuré ak monm na dieul franc kouko si dan mou mayla chance
Lutte tv bayilene reug reug bi ngene niouy forcer tamit. Oui il lutte bien oui il a des qualités mais il doit d'abord lutter avec ses pairs, francs mogui fi, sikh mogui fi ak nienene
@@kingbradley7731mais modou champion incontestable le grand, mais mom ak Reug Reug combat bou nekh leye done deh , bien vrai mo eup Reug Reug experience
probleme bi moy MODOU dafa khamone li BOY NIANG di beuréssi motakh dakoy bloqué ak main gauche bi door ipercule droite...té 2coups yoyou dafa K.O BOY NIIANG motakh nimou songé bakhoul
Tapha gueye SEYTANE BI DIEUL BI SURPRENDRE NALA ENCORE GUA WAANE SA BOPP WAANE FIGUA FARRRR 😂😂😂😂 ALHAMDOULILAH TEY MAFIA LAMBJI YALLA TROKHAL NALEN ENCORE !!PIKINE LO❤❤❤❤
Mod Low a vu Boy Ngiang prendre le risque de se pencher pour saisir sa jambe, mais c'est ce dernier qui s'est désavantagé en offrant au premier la possibilité de placer son corps sur le dos de Boy Niang, de le saisir, puis d'appliquer une pression sur le haut du corps sur son dos pour l'empêcher. un slamdown de Boy Niang. Les deux lutteurs les plus talentueux du Sénégal sont Mod Low et Omar Khan, tous deux très professionnels. Balla Gueye, Bombadier sont échoués et l'avenir appartient à ceux qui montent.
Boy niang dawaronn saxal xéxx bi il avait très bien débuté mais pourquoi beugu roffo akk modou lo en plein bagarre c'est évident et inéluctablement il allait recevoir l'ipercute de Modou c'est son fort ça C'était la clé du combat en fait Boy Niang fallait continuer la bagarre Sinon du courage Modou c'est du lourd
Il a pris un coup qui a fait de l’effet a vitesse réelle tu peus ne pas le voir mais au ralenti après le coup y’a eu un changement sur lexpression de son visage d’où l’impact d’un coup qui a fait de l’effet modou a été plus explosive et a une bonne assise c’est génie même si boy niang a aussi livré un beau combat
Trop d’erreurs des commentateurs. On manque vraiment d’experts en commentaire de lutte. Doublé gauche gauche alors que pendant tout le combat Boy Niang n’a déclenché aucune gauche. Et plein d’autres erreurs que j’ai notées. Ils ne font que tâtonner. Et à la fin du combat ils font les connaisseurs. Aucun commentateur n’a vraiment souligné la clé du combat. L’élément clé de la chute. Aucun d’entre eux.
Boy niang a eté meilleur dans la bagarre avec une seule main il réussi a enchainer de coup et esquiver les coups .la chance a souri á modou lô.tapha tine , reug reug , sa thies en face de lui
Mais sur ce combat modou certes es tres fort mais es ce que si boy niang navait pas attrapé la jambe de modou et durer la bas es ce que modou aurait battu boy niang car il me semble que dans la bagarre modou avait du mal car les coups de modou sont pratiquement tous partis en lair sauf un seul coup
Modou actuellement il y a pas un jeune lutteur qui peut le battre. Il es encore jeune et très sportif il es très très vigilants boy nian pouvais jamais je dit bien jamais le battre c'est impossible
@@sarahhugon903 Pourtant techniquement modou a fait des erreurs je trouve avec lexperience quil a , car un experiemente comme lui je trouve quil ne doit pas s'engager dans un echange de coups comme ca car quand on echange des coups comme ca , on es jamais a labri dun coup qui peut te toucher hasardeusement et un coup est un coup on peut finir ko quand on recoit un coup meme si on s'appelle modou lo , dailleurs cetait ca lintelligence de tapha gueye il pouvait te frapper et meme te mettre ko mais lui il ne se faisait jamais toucher car il etait tres fort en ce qui concerne desquiver les coups
Mês lamine ak pere palla ak tapha mention spéciale liguey bi refet na Machalah
Modou lo est très agressive waoooh quel lutteur yalnala souniou borome takhawou yokela doléla on est très content de toi notre rois modou lo merci merci merci ❤🙏
Aaammiinne
Amine yarabi
Amine
Il FAit aussi comprendre que modou lo est un Sportif de haut niveau il a depasse la domaine de la lutte il est beaucoup plus serieux plus serein et plus profesionnel boy yi nakk waakh rek laj fethie lagnou guena meune
Mais père degaul sadik na sa dome am nakkar guakoy engueulé sa me choque 😢 félicitations the King 🎉🎈
😢NDAYSANE Li DAY AM
Modou lo is a world champion. He is the greatest fighter in Senegalese history.
Ñoo meun ñoo ëuppo dooli 👑👑
Modou moye nekha faral beuré dan gnibi Sénégal thi kanam inchallah bisous
Mo meuneu si lamb djiiiii🎉❤
BOUKiBI DA DADIèK GAIDè MOTAh, moy khemna RÈK ALAHOU AkBAR 💚💚💛💛❤❤☝️
J suis pikinois mais quelle explosivité et puissance de Modou lo Boy niang 2 du courage tu n’as pas démérité c le sport félicitations modou kharagne lo mais nak sonal gua gnou 😂
Félicitations champion x lo ❤
Toute chose à un prix le mérite ça donne encore plus de respect félicitations encore au messi de la lutte le goat🐐 le maréchal,le Cr7 aussi de lutte de par son professionalisme son sérieux la constance qu'il a franchement wathio ga ak say supporter pour ma ma part bo bayé lamb dotu ma amati mbeur.
Même pour moi😢
@@Modoumbayelemeringué nom amoul wéranté saxx pression combat wam dafa eupp
Billahi premier laaw bou Modou Lo bi sou daloon boy Niang...sou dewoul dina yagg hôpital 😂
Lou lerr😅
Père degaul vraiment tu es trop sévère envers boy niang. Da ngako warone dalal encourager ko ish
Paa bi doff la
Bilahi dafa doff
Doff la pa bi
Pala ak tafa boy niang lane faralone😂😂
Palla Réglél reug franc lay beurel modou day nopalou daguen beugue modou di beuré rek tá boyam yi d’où gnou beuré ay nawlém lá gnou ins bi modou bouko nékhé né kou beugue beuré ak monm na dieul franc kouko si dan mou mayla chance
Le meilleur lutteur de tt ls temps respect ✊🏾🫡
Modou Lo le meilleur de tous les temps ❤❤❤
Modou lo moy senn bay
Tant que le lutteur ne s’est pas reculé, ils vont toujours tomber bêtement
ANA niom cheikh niang, am bou boy niang folen nek, amoul neubeutu du wakhe rek ngen moune, legui Modou lo noknalen bu bakh
😂😂😂do len guiss d😅😅
Doleine deiggg jamais 😂
Bayyil sou seddeu ! Sport la rek ! Dagnouy neekhal rek
Mane mom Malaw lay ladje guissou mako
0:56 0:56 0:56 0:56 0:56 0:56
Wayy oustaz wayy🎉🎉🎉
😂😂😂Moustapha Gueye soko dégé mouy wakh rék nga hamni geumoul wone ni Modou lo déy dane boy niang
You are right thanks u so much
LE CNG DOIT CONSTRUIRE UN MUSÉE POUR MODOU LO À PIKINE WALAHI😂😂😂😂
Loumou leudeum leundeum bouki for beuye 😂😂😂 bouki bi yewe nagneko 😂
Lutte tv bayilene reug reug bi ngene niouy forcer tamit. Oui il lutte bien oui il a des qualités mais il doit d'abord lutter avec ses pairs, francs mogui fi, sikh mogui fi ak nienene
Reug reug mom dolene ko reuthie. Tapha tine mom moytoulene ko, doff le. Félicitations a modou lo, c un tres grand champion mashallah.
.
@@MrOusmane23mayow souniou rak dem Len fénéne nga boukhfa Reug reug ak tapha tine
Wala niom gniar niou beuré
Modou lo moléne moune fouf…
@@kingbradley7731mais modou champion incontestable le grand, mais mom ak Reug Reug combat bou nekh leye done deh , bien vrai mo eup Reug Reug experience
probleme bi moy MODOU dafa khamone li BOY NIANG di beuréssi motakh dakoy bloqué ak main gauche bi door ipercule droite...té 2coups yoyou dafa K.O BOY NIIANG motakh nimou songé bakhoul
LE COPRS DE MODOU LO EST ATHELETIQUEMENT PARFAIT
modou ✨ xaragne lo rek santé 👑 yalla
Modou lo vs sathes
Balla gaye vs Tafha tine
Siteu vs faran
Reug Reug vsLac
Moudou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😎😎😊Ama balle❤🙏🙏
XLO L'EMPEREUR DE PÉKIN
Alhamdoulilah ❤❤❤
Tapha gueye SEYTANE BI DIEUL BI SURPRENDRE NALA ENCORE GUA WAANE SA BOPP WAANE FIGUA FARRRR 😂😂😂😂 ALHAMDOULILAH TEY MAFIA LAMBJI YALLA TROKHAL NALEN ENCORE !!PIKINE LO❤❤❤❤
Merci modou lo
Yaalla rèkkkkkkkk❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci lamine
Ceeyy Modou lô kiii dafa graw de 😂😂😂😂😂😂😂😂
Xlo dou gni Bilahi molénn mane fouffff
Lan dal li doumasi doyal damay setann rek
Kharagne lo dafa meilleur ❤
Avant Dernier (coup direct) bou boy niang bi bou dalone modou dou bakhhh….. kone modou lo dey ko sur le coup..! Yallah mo beurri soutoureu 🎉🎉❤❤
béne coup Modou lo bou dalone boy niang dou tal lénéne nganane lane ..
Au moins coups boy niang amna you dal mais 2 ou 3 coups de Modou lo souko dalone boy niang kheumm😂😂😂
@@khadim1875 Oui cest vrai mais Coup yi bokoul dé, so guissoul bimay wakh do meuneu comprendre …..Ils ont bien lutté et combat bou nice leu
@@MouhamedNiang-du3fi 😂
Cv en plus ❤❤❤😂de de téléphone ❤portable ❤
alhamdou lilah
Boy Niang trop peur
Il ne frappe rien
Dommage
Mod Low a vu Boy Ngiang prendre le risque de se pencher pour saisir sa jambe, mais c'est ce dernier qui s'est désavantagé en offrant au premier la possibilité de placer son corps sur le dos de Boy Niang, de le saisir, puis d'appliquer une pression sur le haut du corps sur son dos pour l'empêcher. un slamdown de Boy Niang. Les deux lutteurs les plus talentueux du Sénégal sont Mod Low et Omar Khan, tous deux très professionnels. Balla Gueye, Bombadier sont échoués et l'avenir appartient à ceux qui montent.
Arrête avec ces commentaires bidon balla à échoué ou??
Bilahi uppercut modou yi mbeur boukosi meuytouwoul boy niang da am chance ba béne dalousi mai sinon
Niang dafa ko avant mouye dieule tacabi . Dafco dieule souke
Modou senn papa la
مشاءله❤❤
Ha ak ay ohhhh da Gathié 😂😂
Finis les gris gris
1- Modou lo vs Tapha Tine 👑
2- Modou lo vs Sathies 👑
Copain sa thies amna combat tamitt faut que mou prouvé. Bo newone reuy reug sakh ma wakh
Sa way reug reug vs tapha tine kou dane am modou lo a mon avis
reug bere goufi dra na demat basi kanam@@chrisduncan7822
Modou/Tapha pour teudj saison bi❤
NonTapha Tine Modou lo moofi seuss @abdougaye2343
Yalla rek
THIEUY LAMINE borome boule ko mimale dara
Image bi lerna
Mé lutte tv Daguén bayi def camera thi cumikayy yi
Réaction DeGaul la beugua guiss😂😂
Légui mou dougou
mbeur yi delen entrainé bayi thiakhane
Qu'est ce qu'il a voulu faire boy Niang ? Félicitations a Modou
😮
Hypercute budal dina la deflo lou neik. Nagni mouytu koru modlo yi
Ana wa pikine 😂😂😂😂😂😂😂😂
Reug reug vs boy niang
Pére pala ame na louko méti nak 😂
😂😂😂😂
❤❤❤❤❤❤
Pere tapha neena ohhhhhhhh😅
🤝🤝🤝🤝🤝🤝🤝🤝🤝🤝
1000 combat Modou lo nokhou ko😂😂😂
Boy niang dawaronn saxal xéxx bi il avait très bien débuté mais pourquoi beugu roffo akk modou lo en plein bagarre c'est évident et inéluctablement il allait recevoir l'ipercute de Modou c'est son fort ça
C'était la clé du combat en fait
Boy Niang fallait continuer la bagarre
Sinon du courage Modou c'est du lourd
Dafa daw xéxx bï tapét lä
@@thiernothiam1121 sama grand bi ligua wax ni lama wax
Boy yi gnémé wougnou modou
Le coup moko kawo !! Dafa niam coup bi mou gueleum
Il a pris un coup qui a fait de l’effet a vitesse réelle tu peus ne pas le voir mais au ralenti après le coup y’a eu un changement sur lexpression de son visage d’où l’impact d’un coup qui a fait de l’effet modou a été plus explosive et a une bonne assise c’est génie même si boy niang a aussi livré un beau combat
Machalla lamine❤
Balla Moy bayam
@@temaflystreetzeyo1441 balla cadavre
Ont tire pas sur un cadavre vivant
8:32 pére pala nèna ooooooo😂😂😂 du courage
Pére Pala contenoule deh🤣🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂li MMA leu
Boy niagn day trissé rek
Lamine diokh ma numéro sa touba
Modou kou dieul cops bi dangaye diakhasou
boy niang néna da diangue box 🤣🤣🤣sa way li lamb leu da ame xéx xam
De Gaulle mo sadique 😂😂
Boy niang fougue bi mou amone contre balla amouko si modou lo néxoul ba néxoul
Bouki bi🤣🤣🤣 youuutna feppp
Modou lo daffa nekkk si combat biii il est plus lucide hamnani boy niang daffay diema dioukkkk mou werouko
Loungéne wakh si modou lo ,lac de guére
Degaule liga WONÈ rafetoul accolate ko Rek mola Warone ba ègg keurga
Mais bén lokho rek dou khexe aussi 😅
Moudou lo lokho gouchè bi mo takh lokhou Boye Niang sentirewol si vaww bimouy diap.
😢
Tapha tine sa thies reug reug après jubilé de modou Lo
Père pala😅😅😅
Fadam 2 khana da porter malade depuis bi combat bi diékhé wakhoul
😊Pp😊😊
Modou lo hreylo
Gouverneur de pikine😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂nouveau Maire de Pikine
Boye niang niemewoul heekh bou sah baparè nane wagaleu
Trop d’erreurs des commentateurs. On manque vraiment d’experts en commentaire de lutte. Doublé gauche gauche alors que pendant tout le combat Boy Niang n’a déclenché aucune gauche. Et plein d’autres erreurs que j’ai notées. Ils ne font que tâtonner. Et à la fin du combat ils font les connaisseurs. Aucun commentateur n’a vraiment souligné la clé du combat. L’élément clé de la chute. Aucun d’entre eux.
Bimiy dan bala gay bala dafa manatol😊
Boye niang2 tapet leu nièmewoul heekh
Maire de pikine modou lo
Cheikh nianga🤣🤪
Bravo félicitations modou lo,faut donné la chance à lac 2
Boy niang a eté meilleur dans la bagarre avec une seule main il réussi a enchainer de coup et esquiver les coups .la chance a souri á modou lô.tapha tine , reug reug , sa thies en face de lui
Mais sur ce combat modou certes es tres fort mais es ce que si boy niang navait pas attrapé la jambe de modou et durer la bas es ce que modou aurait battu boy niang car il me semble que dans la bagarre modou avait du mal car les coups de modou sont pratiquement tous partis en lair sauf un seul coup
Guénési ndiol mi bo beugué gnou déguo copin😂.
@@ibromeo9682 machlh li nga wakh li djiss bou yague.modou kéne khaméwouko law , mais demb lawna
Modou actuellement il y a pas un jeune lutteur qui peut le battre. Il es encore jeune et très sportif il es très très vigilants boy nian pouvais jamais je dit bien jamais le battre c'est impossible
@@sarahhugon903 Pourtant techniquement modou a fait des erreurs je trouve avec lexperience quil a , car un experiemente comme lui je trouve quil ne doit pas s'engager dans un echange de coups comme ca car quand on echange des coups comme ca , on es jamais a labri dun coup qui peut te toucher hasardeusement et un coup est un coup on peut finir ko quand on recoit un coup meme si on s'appelle modou lo , dailleurs cetait ca lintelligence de tapha gueye il pouvait te frapper et meme te mettre ko mais lui il ne se faisait jamais toucher car il etait tres fort en ce qui concerne desquiver les coups
DE GAULLE CON NEU
Merci modou lo