Dou yéna ko Done défendre ki bakhoul Saytané la aussi faw nguéne maîtriser Gayi Di Mboubo serigne Touba pour Attaquer serigne si nék Senegal pour Diakhasé Senegal 😢 Mouy Koté mourid yi ak koté tidiane yi Faw niou yéwou bayi Dof Dof loubi ak khass tébi
Dieura dieuf baye mbeye gueye sono xol sed na ci yaw bilay .yax kat yi ba legui nongui xex .s.touba waye .lingaye deff amna solo ndax eleuk motax xale yiy dioddo xam❤
Limou ci jouplou moy wane ni africain meunoul soss dara lepe bitim rew la jogue,pour cultiver le complexe de l'exterieur,Tidianiya(fezz),Khadriya(nimzatt) donc mouridiya ne peut pas Etre du Cayor
Guiss nagn fi Iran Ndao képeu kou am problème ak wa Tivaouane rék day néka di tague ak di geuram Serigne rien ke pour mouride défendre ko même sou nékoul dégeu. Kholal Iran Ndao geuth nako dégeu mou tague wale mou gereum serigne mountakha
Ameth Khalifa NIASS dou nitt diiné te gno ngui wakh ni franc maçon la wayé mourides yi xamna gnou sen yoon bi len serigne Touba tannal Dieuredieuf serigne Mbaye Gueye Syll
Si c étais omar diagne tu entend tous les marabouts politiciens quitte a organisé des marches....sortez les nafek comme bara doli et modou bousso dieng
Mbaye gueye sa numero telefone ma maï la auto 4/4 degue rekk ngay wakh sa rakk serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
Nioune Serigne Touba rk lagnù beug Lou way wakh rk bakhna. Dieureudieufé Serigne Touba ❤❤
Talibé cheikh la d mais Serigne mbaye Gueye Sylla koula sopou la barké Mame maodo 🥰🥰🥰 Amal Diam rekk ❤️❤️❤️
Danga bakh rek ♥️♥️♥️♥️♥️🙏
DIEUREDIEUF baye MBAYE GUEYE yague fii lool tee ande ak werr
Merci Baye mbaye Gueye Sylla
Machallah .yalla na yalla yagal sa takhaway barkep serigne biii♥️♥️♥️🙏
DIEUREDIEUF BOROM TOUBA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL kÉSSÉ.
Wakhi Ahmet khalifa diaroul douma sa dome. Je n"ai jamais vu un homme aussi versatile que Ahmet khalifa
Billaahi... Et en tant que guide religieux !
Masha.allah niane yalla jàmm nloune mourde serigne touba rek laniou gueum inchahallah thie laniouy dédié Jéréjéf Serigne touba amoul morom ❤❤❤❤
Dieura dieufati Baye mbaye Gueye Sylla yalla na sa taxaway yagué ❤❤❤❤❤
Diadieuf baye Mbaye silla
Un veritable baye fall garde impecale du patriotes sacre du mouridism
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye machallah yag fi lol ta wér❤❤
Dieuredieuf serigne mbaye gueye sylla 👍👍👍
Machallah kaddou yi rafet , Ahmed khalifa dé mongui nonou rek nioune Mouride bakho wougne wakh diou niaw
Machalla amatina solo serigne mbaye gueye Sylla dieure dieuf
Dou yéna ko Done défendre ki bakhoul Saytané la aussi faw nguéne maîtriser Gayi Di Mboubo serigne Touba pour Attaquer serigne si nék Senegal pour Diakhasé Senegal 😢
Mouy Koté mourid yi ak koté tidiane yi
Faw niou yéwou bayi Dof Dof loubi ak khass tébi
Ameth Niass nitt kou torokh la nitt kou ignaan leu. Dieureudieuf Baye mbaye Syll
Boye khalfa bay fall yi nio wara génna Ray ndayam nit yi noppalikou
Dieureudieuf serigne touba serigne mbaye gueye silla yalla nagua goudou fane barkeb seydina moukhamet
Dieuredieufé Sérigne Touba❤❤
Ahmed niass sopi khaliss rekk moyy mêtier têkkii woull daraa
Mane dé, duma deglu Ahmed khalifa Niass. Damako jàppe noonu lislàm.
Bilahi waax ga deug Ahmed khalifa Niass de noonu l'islam puir et duire abb diahilla doomu iblis la
Ahmed khalifa nafékha la bakhou da niou ko wara génné senegal
Baye mbaye syll yalla nala yalla aar ta samm la
Segne MBaye Sill Yallah nallah Yallah takhawou té samme la
❤❤❤❤
Gni amna louléne Dale ahméd khalifa Niasse AK ahmêd Cissé AK mbodjia mbaye AK omoro yalnanou yalla moussale thi déf adouna Mouy keure
Iow dei kou bagne omoro nga lou tax
Merci Serigne mbaye Gueye Sylla.
Nias bagage yi nar yi lakone 🔥 moko diape
Eskey yalla sunu borom
Dieura dieuf baye mbeye gueye sono xol sed na ci yaw bilay .yax kat yi ba legui nongui xex .s.touba waye .lingaye deff amna solo ndax eleuk motax xale yiy dioddo xam❤
Ahmed niass seytanii laa ngour gou dikk mou ande ak mome ndakh posam rekkk diouboul dhh man serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
Dieureudieuf serigne touba 🙏🏿
Yalla nala yalla defal diamo serigne mbaye gueye
Baye mbaye gueye sylla yalla nalafi yalla yagal ta wéreul la
Machalla serigne mbaye g sylla
Limou ci jouplou moy wane ni africain meunoul soss dara lepe bitim rew la jogue,pour cultiver le complexe de l'exterieur,Tidianiya(fezz),Khadriya(nimzatt) donc mouridiya ne peut pas Etre du Cayor
😂😂😂 Niass bayil féne
Mbacké mo dakha doul
Gëmoull darra say say la dh
Da wara manou
Segne MBaye Syll Yallah nallah Yallah défale diamètre
Merci sering mbaye geuye sill❤❤❤❤❤
Jaajëf Murid Baay Mbay ❤❤❤❤❤❤
Machalla mourid mbaye
Mane deh taibé cheikh la wayé serigne touba kep kouko sosal dako guiss nite kou bakh dou siakal serigne touba kouko sikal ya bakhoul
Machalah,gorou yalla yeupe sakh
Machalla Anna solo serigne Touba 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 🕋 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yague lole ak wére machallah
Merci beaucoup serigne Touba ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ ❤❤❤❤❤❤
Ahmed khalifa niass fen ak soss rek la man
جزاكم الله خيرا ايد الله بقاءك وعافاك
Guiss nagn fi Iran Ndao képeu kou am problème ak wa Tivaouane rék day néka di tague ak di geuram Serigne rien ke pour mouride défendre ko même sou nékoul dégeu. Kholal Iran Ndao geuth nako dégeu mou tague wale mou gereum serigne mountakha
Lou lér frère nafekh rekk Molène diapp
Bayil linguay wakh tamite
Dieuredief serigne mbaye geuye sylla
Mouride yi nio wara yèwou ci dorkat yi tè bayi fanatisme bi niou nèkè
Mourides baniou yéwo dou taay
Yeen ñiy degg lu amet ñass mii yee nay baga doff
Dieuredieuf SERIGNE Mbaye Gueye sylla
❤❤❤ diera dief seringe touba ♥️❤❤❤❤
Ameth Khalifa NIASS dou nitt diiné te gno ngui wakh ni franc maçon la wayé mourides yi xamna gnou sen yoon bi len serigne Touba tannal
Dieuredieuf serigne Mbaye Gueye Syll
Yonnou mouride ci Serigne Touba latambalé
Si c étais omar diagne tu entend tous les marabouts politiciens quitte a organisé des marches....sortez les nafek comme bara doli et modou bousso dieng
Akaleeer tu as parfaitement raison d😊
Machallha serigne mbaye geuye❤❤❤
DIEUREDIEUF borom touba diarama mame cheikh IBRAHIMA fall ….nioune borom touba rekk laniou gueume Beugue ko té doyloo kepp
Ba mu ñëwee Tuubaa dé, Waxoon naa tay tappale, day politique mourides yi
Serigne Touba Amul morom wayyy
Merci mbaye silla❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mbaye gueye sa numero telefone ma maï la auto 4/4 degue rekk ngay wakh sa rakk serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
Saway man mom problème 20mil rek la am diapalémaci Way si barké BOROM TOUBA❤🙏
Diokh ko sa bayy
❤❤❤Grazie mille Dieureu jeuff 🎉🎉🎉
Dieureu dieuf baye mbaye ❤❤❤❤❤
Lii xalé yu am Gul 5 añs sakh xamnanu du dëgg
C'est un grand Maçon
Machala Bay mbaye yaguefi looool taa wér
😂😂😂😂😂nooppu dalootina
Ahmad Khalifa Niass ,Fra Macon xaj fenkat , sàcckat lumu wax day kàcc.
Waw gor amnea solo ❤
Diadieuf ty serigne touba
Diredieufé Serigne Touba
Man dé Ahmed Xalifa ñass bu Bayi Woon Yoon Wim Nek nékk ap mouride taxul ma Geum ko waxou mala nak muy toude sëriñ bi doom
Ki mom chaque jour ak fene yu béess rk
Wakhi ahmed khalifa Ñiass mom diaraloul kene mothiay dour domame kokhamne buwakhé khale yieye nampe barom sakh khamne dou deuggue diaroul tardel kéne
Machalla
Serigne bi fékoufi yonou mourid da New sos yonwi
Khalifa niass domaram djiguéne rék la beug
Aka mana méw khalifa Niass
Màchallah
Vérité absolue
😂😂 no amet de yoon toppu ko moom luko neex wax😂😂doff la kii wérul de😂😂
Moi je suis cheikh ahmedou bamba
Dieuredieufety kou Tedd ki cheikh Ahmadou bamba khadimou rassoul ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Khalifa ñass yaa mana Fenn 😂😂😂
Khalifa niass tay mom dioum gua démal guestou dji watt
Machalla ❤
Serigne Touba bim amakoul yonou mourid sadikh Amoul
Ahmed cissê dafa alkou ba leip louko jigé alkou
Aka meuna fene.
Tarikha yi amoul béneu bou thi sosso Senegal 🇸🇳
Gnémé ngua yalla dh😂
Nala yalla fay yiw tu bargé s Touba mback
Paa bii mousiballa si amm rewwww bakhoulll
Mbaye gueye hana dagua doff kilifa diner dou am gapine car
Yene kene khamoul lou ngene beugue
Yak Ahmed khalifa yèna yam
Wadji niass day deuge ndeyam doll
Na ngoulwi niéw bay mbaye
Khalifa nias sénal yalla si ligay wakh liga wakh dou deug daga am jabot rouslén
Sa sou khayé dégueu lou bess😂
Wa Anna fénkat yi don tuddu same donay mag jii AK Di danu danulou same pp ji mom s tuubaa rek mom moko yittèl جرجفت
Ahmed khalis NIASS weuroul.