Je connais très bien cette famille, nous sommes arrivés dans le quartier en 1967, et avons trouvé cette famille sur place. Aujourd'hui , n'eut été la mort, personne n'oserait attaquer cette famille. Mbaye Ndoye et Mamadou Ndoye ont été dignes jusqu'à la mort. Leur mère, Adja Makélé, a fait beaucoup de biens pour les jeunes de Colobane. Je suis sure, que Dieu vous assistera, insha-Allah.
Oh la la je trouve pas les mots 😥😥ça me donne des frissons grave j'ai pleuré comme un bébé une famille formidable machallah ça me touche au plus profond de moi MAIS DIEU EST PUISSANT
C tré triste vrema mé osi parents yi nanouy waxtan ak ndiabot gui prck deh defay betté organise sa keur avan ngay dem mo gueun nga bayilen si lo xamné ni moy llou la plus part genr histoire yi limakoy guis yepp sou pabi dewé lay donn té dangay deg niou n'a df nanoufi plus d 30ans diap 40ans xeuy un bn jr rek guené lenn nnou san avertir c domage k dieu vou vient en aide
Une très bonne famille ici à colobane ay nobles deugg bilahi niou bakh gui nii yallah n'a bonnes oeuvres yi djapalei lene ci nattu bi barkep Khadim Rassoul
c’est ma famille walahi niou bakh machallah les bonne volonté takhawoule thi Barker Seydina Mohamad psl hoooo métina Ndeye sane aiwai dioulite dina defli moromou diouli tame doyna warr je suis de tou c oeur avec vous courage à tout la famille inchallah 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Amnafi doomu adama yoo xamni litax sunu boroom andi lenfi mooy liii rek 😭😭 Yalla mi yorr jamm téy jammal koku neex yalna leen jammal té leeral leip inchallah
Yén gni di commentaires yeup est ce que dougnou djémeu déf dara pour gnome Genre gnou partagé ko si réseau yeup Comme que justice amoul si deuk bi Li métina trop trop bilahii
@@lalionnenoire7371 keurou aduna dou dara démone cimetière outefa place bou bakh té khamni fallaye moudjie fofou rek moye keur mongueune mouye dioylo aiii make
Que justice soit faite liii dou deug dou yone walahi ils ont débarqué chez nous avec un lus de 100 policiers mardi matin sans aucun papier valable ils nous ont maltraités et expulsés sans aucune raison 💔😭😭😭
Les banques et les sociétés immobilières font bcp de dégâts au Sénégal. Trop de problème de foncier au Sénégal, Letat doit régler cette situation qui perdure. Cette famille doit être relogée ailleurs au nom de la dignité humaine. Yallah nalene yallah sam soutouralene
C’est très triste mais quelque soit la situation avant de démolir au moins avertir les accupants attendre qu’ils sortent leurs bagages mais venir un beau matin avec des camion de policiers et un catarpila c’est vraiment injuste
Si c'est le cas, ce que Sénégal ne plus le pays de droit. Par contre, j'aurais bien voulu connaître l'avis de l'autre protagoniste. On ne peut pas détruire un demeure sans des arguments ou preuves tangibles. Navré pour la famille. C'est dur, j'espère que la situation va trouver une issue positive
Metina mais tien n'est clair dans les discours. La journaliste ne pose pas les bonnes questions. A qui appartient la maison? Est ce l'heritage a été bien fait? On parle d'une société avec des intiales Snr? De quelle société s'agit t -il ? Qui avait donne en location la maison? Depuis quand? Qui recevait les paiements? Quel montant a ete versé ou recu? Qui a achete la maison.? Qui a vendu.? Ou sont les avoxats? Ce dossier comme d'autres merite d'etre analysés. Que dieu nous protège, donne accorde soutoura weerlecak werla si barke seydina Mouhamed. Encore une fois massa à cette famille. Les milliards faites quelque chose
La S.N.R. est la société nationale de recouvrement chargée de gérer les actifs des défuntes banques BNDS et autres qui ont fermé. Si tu avais 1 prêt au niveau de ces banques c'est à cette société qu'il fallait payer sinon rien que les intérêts depuis les années 90 risquent de faire des dizaines de millions. Et sûrement le vieux avait un prêt et avait dû hypothéquer sa maison.
Sénégal wakh deugue dé yombou fiii trop de zone d'ombres dans cette histoire. Kahm séni droit warone na takh guène yoré papier keur gui. Comment la baque a fait pour diay ko? Mais aussi kokou nonou guène di toudd khalissam la yor di dieunde vous n'avez pas à le citer comme ça comme si que mome guène diotell Métti na mais boulène togne Yallah beugoul lolou et Force à cette famille
Tu as raison...Les papiers de la maison sont avec la banque...Leur papa avait une dette auprès de la banque avant sa mort.C'est cette dette là qui a causé tout ce problème.
Hooooo li metina trop dawal lene yeurmande adouna dou keur lep fi laniou kay bayi kone na lep rafet famille bi bouniou guené founiou dieum ak ndiaboot gui ak fi rewmi tolou ni kholal khaleyi sa yaram sakh dafay metina dé yalla nasi yalla def diam rek inchallah metina trop
Il fallait payer les dettes de la banque ou négocier sur des bases claires. Nous le savons tous que quand nous prenons des crédits bancaires, il y a toujours des petites écritures aux quelles nous nous faisons pas attention. C'est de là viennent les problèmes.
C'est avec tristesse qui regarde cesces image car c'est dans cette maison même qui je suis née et passée une partie de mon enfance je connais cette famille mais courage
ndeuysann wadiour dina tekk njabotam tionah banque bakhoul bayilenn dii tayleeh keur... Etat aussi waroul guiiss niouy neweul dollee badollla li mettinah trop yalla na yalla diapalenn baguenn djott sen keur
Macky,les chauffeurs,les famille,les etudiants (encor en greve de faim),nieupeu dièpii nanioula,bathi rabou ndoyeni sakh!! Ay liii ma la bagne🤬❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥💔💔💔
Le grand Serigne de Dakar dois réagir tu sers à quoi ta communauté une famille noble et digne lebou niou len dilen trokhal si diguou Ndakarou dou Yonne
Ndeyssane, je connais bien cette famille surtout la mère de Tonton Mbaye N'doye:Adja Makalé parce que c'était une guinéenne, une Soussou. Tchey Yallah, li métina 😢😢😢
Hooo li métina trop😭😭😭 way yalla nalén yalla takhawou dimbalilén baguén tiotate si métina Président Macky yalla dinala lath no yoréwone Sénégal euleuk nakh policier yi niouy djiteul niouy naguou keuri diambour yi yi niaw na trop agresseur ak sath yi banditisme yonam toujour
N'oubliez jamais les 5 prières de la journée
Fajar...
Tisbar....
Takussane...
Timiss....
Guéwé
Q
Merci beaucoup
Merci beaucoup
❤
❤
Je connais très bien cette famille, nous sommes arrivés dans le quartier en 1967, et avons trouvé cette famille sur place. Aujourd'hui , n'eut été la mort, personne n'oserait attaquer cette famille. Mbaye Ndoye et Mamadou Ndoye ont été dignes jusqu'à la mort. Leur mère, Adja Makélé, a fait beaucoup de biens pour les jeunes de Colobane. Je suis sure, que Dieu vous assistera, insha-Allah.
Gno bokone kogne ndeyesane depuis l' an 2000 lafa diogué rue 44×45
C’est triste
9
Une famille digne et noble.Qu’Allah les viennent en aide.
Oh la la je trouve pas les mots 😥😥ça me donne des frissons grave j'ai pleuré comme un bébé une famille formidable machallah ça me touche au plus profond de moi MAIS DIEU EST PUISSANT
Bilaye gnou bakh mallene khame 😭
Hoooo massawaye ndoyenne une grande famille lebou a colobane.....qu Allah Vs viennent en aide...leur papa fut tres digne......🤲🤲🤲😪😪🙆♀️🙆♀️.
Kagne la niit di bayi tek fitna moromame😭
Justice pour cette famille
xana waxo fi justice bou réew mi dh
😭😭
@@a-qudoosallahisone6498 bilahi wakhatiko rew mi amoul yone
@@maremesouware4511 lolu rek mo waral yi façons
Vraiment c dure ma sœur
C tré triste vrema mé osi parents yi nanouy waxtan ak ndiabot gui prck deh defay betté organise sa keur avan ngay dem mo gueun nga bayilen si lo xamné ni moy llou la plus part genr histoire yi limakoy guis yepp sou pabi dewé lay donn té dangay deg niou n'a df nanoufi plus d 30ans diap 40ans xeuy un bn jr rek guené lenn nnou san avertir c domage k dieu vou vient en aide
Wa ndoyenne ligueye niakh diarignou rek lagnou kham walahi . Ils sont Nobles ,dignes machalah , yallah bakhna
Yalna l'en serigne babacar sy takhawou inchalah
Talibé cheikh yalla rék mo mene takhawou diamame 🙏🙏🙏
Une très bonne famille ici à colobane ay nobles deugg bilahi niou bakh gui nii yallah n'a bonnes oeuvres yi djapalei lene ci nattu bi barkep Khadim Rassoul
Ndeysane sama yaram dawna 😭🤭 bilahi dema dioy Sénégal meti père Sama khol toyna ayway milliaders yi cagne lagnouy diapalé newdi dolé yi😭😭😭😭
Une des plus anciennes famille de Colobane 😔Que DIEU leur vienne en aide pour que cette grande famille reste réunie !!
Oooooh j'ai le cœur ❤qui saigne 😭 vraiment le Sénégal mon pays de la Téranga va mal .courage la famille que Dieu vous assistent amine
Téranga bi diékhna bou yague boye
@@yerimsy8740 walahi wakh Deugg
Douko djig Inschallah dankh YALLAH Bour bou bakhla. Li métinama, khamna keurgui bou bakh wallahi. Ooooh la mort 😢😢😢😢😭😭😭
c’est ma famille walahi niou bakh machallah les bonne volonté takhawoule thi Barker Seydina Mohamad psl hoooo métina Ndeye sane aiwai dioulite dina defli moromou diouli tame doyna warr je suis de tou c oeur avec vous courage à tout la famille inchallah 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Billahi Dakar buzz warane len nianal nakh s'en ligeuye bou rafete 😢😭❤🇸🇳
Yanna yalla takhawoulène si barker Seydina Mouhamed S A W
Mioune len rk té yalla takh yalla mongui guiss lep
Amnafi doomu adama yoo xamni litax sunu boroom andi lenfi mooy liii rek 😭😭
Yalla mi yorr jamm téy jammal koku neex yalna leen jammal té leeral leip inchallah
ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH ALHAMDOULILAH
yallha n'a borome bi takhawouléne adouna bi métina tropp
Il faut qu'on lutte pour ça, c'est plus fréquent dans notre pays
Il fau gnou ame bene page rien que pour sa kou amati problem you melni wakh ko gnou déme khéhal la
Yalla nalèn bour yalla takhawou thi barkhè seydina Mouhamed psl
Yalla rekk mo am dolé kén amoul dolé yalla na yalla ate deugue yalla na yalla defar lepp zayirane wa batinane amine courage frères metina trop
Ndeye sane yalla nalaine yalla takhawou toute la famille 🥲
Allahouma Amine
Yalla naléne yalla takhawou si barkei seydina Moukhamed (saw). Lou métti
Yalla na serigne Babacar sy takhawou 🙏thiéy Sénégal dou avancé jamais 😭😭
Serigne Babacar deh na Naka lako mane takhawou. YALLA rek mana takhawou domou Adama balma nak diangat rek la
@@aidasouane6439 ndakh gua sagnko wakh bokale rk thiey Sénégal
@@aidasouane6439 ndakh gua sagnko wakh bokale rk thiey Sénégal
Babacar s'y dé n'a bou yague meneloule bobape dara wahi doff rek
Talibé cheikh yalla rék mo mene takhawou diamame
Yén gni di commentaires yeup est ce que dougnou djémeu déf dara pour gnome
Genre gnou partagé ko si réseau yeup
Comme que justice amoul si deuk bi
Li métina trop trop bilahii
Li niaw n’a Walahi yalla guene gagnier thi barkep seydina mouhamed yalla guene diottate Sene keur yalla Migui guiss lep🙏
😭😭 man bo doon sama sago douma guiss rongoniou mag te bakhoul si rëw
Wayei fi mome chaque jour ame ngingou djoylo yalna borom bi maye kholou mounge😢
Yalna len yalla takhawou ci barke Mohamed psl
Les plus forts mangent les plus faibles senegal lifi nek yeup yalla douko setann
DEUG rek ka wakhe
Ça me rappel la famille pouye dou moudier feneu waye yalla nalene yalla takhawou ba nguene diott sene keur
Il a coulé m'est larmes massa sunu Borom dineu defatat le peu incha Allah
Talla fall soumadone yaw keur gui dossi beugueti dara aii make youye dioye métina 😭😭
Peulh Peulh bilakhi deugue la mane t'es dama titt sakh li des diaroule dieune diaye dolé rek
@@lalionnenoire7371 keurou aduna dou dara démone cimetière outefa place bou bakh té khamni fallaye moudjie fofou rek moye keur mongueune mouye dioylo aiii make
Talla fall li bouko djigué 😢😢
Que justice soit faite liii dou deug dou yone walahi ils ont débarqué chez nous avec un lus de 100 policiers mardi matin sans aucun papier valable ils nous ont maltraités et expulsés sans aucune raison 💔😭😭😭
massa y'alla deinthie na Lou eupp lolou inchallah
Courage mon frère !
Allez porter plainte à DSCOS
Doyna war yal nala Yalla bourbi diapalé
Massa chéri yalna Yalla até si Barké Seydina Mohamad psl
Courage
Les banques et les sociétés immobilières font bcp de dégâts au Sénégal. Trop de problème de foncier au Sénégal, Letat doit régler cette situation qui perdure. Cette famille doit être relogée ailleurs au nom de la dignité humaine. Yallah nalene yallah sam soutouralene
Yale na.lene.yalla diapale.si barke désigne babacar sy
Li niawna yeurmandé adouna Dou keur vraiment je compatis si samay mbook lébous ke Dieu leur viens en aide
Qu’Allah le Puissant vous Assiste.
Hoo c ma famille sama diabaru tonton fi la dakk yalla na léne yalla takhawu metinw torop bilahi
😭😭😭😭masta deselene ak yalla mo dakk am keureu adouna dou touss
Yalle naléne yala tachawou thie bark Serigne Babacar ❣️❣️❣️❣️ yalle rék mo am dole💪💪💪💪💪
C’est très triste mais quelque soit la situation avant de démolir au moins avertir les accupants attendre qu’ils sortent leurs bagages mais venir un beau matin avec des camion de policiers et un catarpila c’est vraiment injuste
Si c'est le cas, ce que Sénégal ne plus le pays de droit.
Par contre, j'aurais bien voulu connaître l'avis de l'autre protagoniste.
On ne peut pas détruire un demeure sans des arguments ou preuves tangibles.
Navré pour la famille. C'est dur, j'espère que la situation va trouver une issue positive
bilahi brooo Dara bobou la diangué alquran keur gui keurou thiosane la
Metina mais tien n'est clair dans les discours. La journaliste ne pose pas les bonnes questions. A qui appartient la maison? Est ce l'heritage a été bien fait? On parle d'une société avec des intiales Snr? De quelle société s'agit t -il ? Qui avait donne en location la maison? Depuis quand? Qui recevait les paiements? Quel montant a ete versé ou recu? Qui a achete la maison.? Qui a vendu.? Ou sont les avoxats? Ce dossier comme d'autres merite d'etre analysés. Que dieu nous protège, donne accorde soutoura weerlecak werla si barke seydina Mouhamed. Encore une fois massa à cette famille. Les milliards faites quelque chose
La S.N.R. est la société nationale de recouvrement chargée de gérer les actifs des défuntes banques BNDS et autres qui ont fermé. Si tu avais 1 prêt au niveau de ces banques c'est à cette société qu'il fallait payer sinon rien que les intérêts depuis les années 90 risquent de faire des dizaines de millions. Et sûrement le vieux avait un prêt et avait dû hypothéquer sa maison.
@@baxnamendy3302 merci monsieur Mendy. Vous êtes mieux que cette journaliste. J'ai bien compris quand vous avez parlé de BNDS.
Adouna bi diékhna d'ara diaroule li mes yalle n léne yalle até ak kidéf li métina trop mes yalle bakhna dolé mene deugue si réwemi 🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Tiey souf moytoulen tiowal souf alalou baye dou alale mouhamed (sws) amoul daray adouna adouna dou keur masta la famille
Loutahk dou alal
Wallahi g pas les mots 😭😭😭😭
Matssa yalna yalla takhawou si barkè sangue bou tèdeu bi psl
soubhanallah yeureumande adouna dou dara yeureum len nitt gnii
Je suis de tout cœur avec cette famille que je connais bien . Je compatis c’est très dur. Que DIEU vous aide .
Massa, que le bon dieu vous protège
Sénégal wakh deugue dé yombou fiii trop de zone d'ombres dans cette histoire. Kahm séni droit warone na takh guène yoré papier keur gui. Comment la baque a fait pour diay ko? Mais aussi kokou nonou guène di toudd khalissam la yor di dieunde vous n'avez pas à le citer comme ça comme si que mome guène diotell
Métti na mais boulène togne Yallah beugoul lolou et Force à cette famille
Tu as raison...Les papiers de la maison sont avec la banque...Leur papa avait une dette auprès de la banque avant sa mort.C'est cette dette là qui a causé tout ce problème.
Ndeysane yalna yalla takhawou léne si barkép seydina mouhamad
Police Sénégal naniou bayi Di trokhal nite adouna d'où keur couye def Lou bone rek woléne bakhna adouna diekhna ba paré😭😭😭
Hooooo li metina trop dawal lene yeurmande adouna dou keur lep fi laniou kay bayi kone na lep rafet famille bi bouniou guené founiou dieum ak ndiaboot gui ak fi rewmi tolou ni kholal khaleyi sa yaram sakh dafay metina dé yalla nasi yalla def diam rek inchallah metina trop
Meti grand max yalla nalene yalla diapale
Sénégal diaye dolé mofi beuri yalla naléne yalla takhawou
Yalla yalla yeram domi Afrique 😭😭
Oh nonnn souniou keur Ndoyenne way on a grandi ds cette belle maison j ai les larmes aux yeux 😭😭😭😭
Massa yallah sam lene
Il fallait payer les dettes de la banque ou négocier sur des bases claires. Nous le savons tous que quand nous prenons des crédits bancaires, il y a toujours des petites écritures aux quelles nous nous faisons pas attention. C'est de là viennent les problèmes.
Keep kouy deff lou bonne,
Dii newéll doleii gnou gnakk ñii
Yalna sama Borom Bii swt nasaaxall senii pexeii Barkep Aljumma J 🙌🏼🙌🏼🙌🏼
Ay nitt you bakh gnon fa deuk yalna yalla takhawouléne si barké naby 🤲🤲🙏
Yallna yalla takhawou leen lii mètèna trp mè yalla sounou brp yp lafi lèkalle
Yallah naleine yallah takhawou
Ndeyssan la dame à la fin de la vidéo, elle est une dame cool, elle vend du bon petit déjeuner !
Yalla naleen Yalla taxawou
C'est avec tristesse qui regarde cesces image car c'est dans cette maison même qui je suis née et passée une partie de mon enfance je connais cette famille mais courage
ndeuysann wadiour dina tekk njabotam tionah banque bakhoul bayilenn dii tayleeh keur...
Etat aussi waroul guiiss niouy neweul dollee badollla li mettinah trop yalla na yalla diapalenn baguenn djott sen keur
Du courage père yalnalén yalla takhawou
😭😭😭😭🤲🙏
Lii méti na diay dolé bakhoul j'ai mal yallah naléne yallah défal soutoura 💔💔💔😭
Amine yarabi
Que dieu vous aide thii barképp serigne touba
Sénégal nioune kagne laniouye ame jamm liba kagne 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Sama khôl daffa fess😭😭😭😭 yalnalén yalla takhawou
Ndeyssane c triste et grave que le bon dieu vous vienne en aide
Il faut invoquer AllâH contre les oppresseurs.
Ndeysane ronbou n’a Lén ce jour 2 auto police go garé Ani soutoura yalla naléne yalla diapalé
Macky,les chauffeurs,les famille,les etudiants (encor en greve de faim),nieupeu dièpii nanioula,bathi rabou ndoyeni sakh!! Ay liii ma la bagne🤬❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥❤️🔥💔💔💔
Billae nieumpeu… wayé def sa bompou bour teih yalla moy sa bourr dallay setan rk 🥺yalla nalén yalla takhawou inchallah
Allah il est juste très juste même
Mo gnou guena kham t gnoun khamougnou
T dina atté soite fi si adouna gneup di guiss wala alakhira
Bilahi mane mi khalé bou ndaw mangui dioy té yayou mako😭😭
Ndeysane allahou akbar le senegal a changé ana sougnou yeurmander li metina
Aminn family ndoyen yalna ngen am ndam
Comment peut t'on acheter ses genre de maison et y habiter avec l'esprit tranquille
Motakh niuy deuk mm pa un moi niu fatu
Walakhi deuguele
Le grand Serigne de Dakar dois réagir tu sers à quoi ta communauté une famille noble et digne lebou niou len dilen trokhal si diguou Ndakarou dou Yonne
Senegal bilah nek fi mbam houhh sah mo gueune nek fi nitttt
Ndeyssane, je connais bien cette famille surtout la mère de Tonton Mbaye N'doye:Adja Makalé parce que c'était une guinéenne, une Soussou. Tchey Yallah, li métina 😢😢😢
Thiey Sénégal yalna yalla takhawou famille bii way
Yalla nalene yalla takhawou 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Yalla rek moufii ne yalla nalene yalla takhwo barkbe serigne touba
Hooo li métina trop😭😭😭 way yalla nalén yalla takhawou dimbalilén baguén tiotate si métina Président Macky yalla dinala lath no yoréwone Sénégal euleuk nakh policier yi niouy djiteul niouy naguou keuri diambour yi yi niaw na trop agresseur ak sath yi banditisme yonam toujour
J ai pas les mots walay ku Amul imane deugue di k salite li metina niawna ay allah Vient au Secours des souffrants amen
Massa tonton Yalla dafay até inchala
Yalna len yalla teklo kho
Senegal depuis macky bamou neker ba leguiiiii siii guur guiii mounoul regler pays biii mou beugeu rooy wa rwanda dama saax rousss diiniu seet siii yallaaa koi vraiment liii dafa daaaw yaaaraaam
Yalla nalén yalla takhawou si barké alkhourane
Serigne Babacar sy deguenalene li dafa gniaw torope
Senegal niak naniou yeurmande yalla nalene yalla takhawou
Vraiment c'est très triste😥 li si Sénégal
Yalna lén yalla atté té diapalé lén Inshalah
Mettina trp mais yalla naleén yalla samb
Li niawna trop walahi diaye dole bakhoul yalnalene yalla takhawou si barcke psl seydina Mouhammad warowone toudou mortalla adouna dou dara demal mangui gniow lofi guis deey diekh deloulene si sougniou borome
Mor talla fall adouna amoul sollo kholal liguay déf
Wallahi dina meussa retiou leep lou bone limou deff,mais gnou melnii diaane sah dafleene sehlou